Mâchallah Oustaz Alpha vraiment diamant nga yagui léral lal niit gni lou am solo Lo xamné Oustaz yi nek ci reew mi saniou niouka wakh ndakh dagni bagn koulén méré
Au moins le prophéte daoud vivait avec le labeur de sa main et la sueur de son front mais ce gars vit avec les efforts et l'argent des talibés quelle paresse
Je vous conseille de traduire ces propos en anglais et en français que le monde entier soit au courant passer par Twitter il faut qu’on commence à les publier la seule solution
وَوَهَبْنَا لِدَاوُۥدَ سُلَيْمَـٰنَ ۚ نِعْمَ ٱلْعَبْدُ ۖ إِنَّهُۥٓ أَوَّابٌ ٣٠ .Et à David Nous fîmes don de Salomon, - quel bon serviteur ! - Il était plein de repentir.
Un musulman ne mens pas .ce monsieur accuse des prophètes de dieu de tel sorte dans un pays de 95% de musulmans. Je crois qu'il devrait être jugé selon la charia.
Ana sounnite yi? Nagnou porter plainte. Addineu yeup aatté. Lignou nékkè ay tooyamaan you fi bari gnoo len tchi bayyi. Lii dégg ko sakh dafa eupp. Bayyil tek ak tégaat bi. HasbunalLaah ... Laa ilaaha illalLaah.
57.13. Le jour où les hypocrites, hommes et femmes, diront à ceux qui croient: « Attendez que nous empruntions [un peu]: de votre lumières ». Il sera dit: « Revenez en arrière, et cherchez de la lumière ». C’est alors qu’on éleva entre eux une muraille ayant une porte dont l’intérieur contient la miséricorde, et dont la face apparente a devant elle le châtiment [l’Enfer] 57.14. « N’étions-nous pas avec vous? » leur crieront-ils. « Oui, répondront [les autres] mais vous vous êtes laissés tenter, vous avez comploté (contre les croyants) et vous avez douté et de vains espoirs vous ont trompés, jusqu’à ce que vînt l’ordre d’Allah. Et le séducteur [Le diable]: vous a trompés au sujet d’Allah.
21.1. [L’échéance] du règlement de leur compte approche pour les hommes, alors que dans leur insouciance ils s’en détournent 21.2. Aucun rappel de [révélation] récente ne leur vient de leur Seigneur, sans qu’ils ne l’entendent en, s’amusant
Oustaz Alpha, wallahi weetoulo thi sa djooy yi.Li dafa meti thi khol te mounougnou thi lou bari.Mais nak lui gnou metti bagnouy djoy meti n'a sougou Borom te dina atté...
1h:16 ! Limou wax akay deug dafay takk ak di fasser xalei you vierge. Doulen sakh wax maynala sa batt. Dalay abandonner nga weur ko beu sonou doko guiss , moudjou demal sa bop 🙌🏾
Sénégal Niata Si Keurou Diine Yi Gnofiy Def Lou Bakh Di Def Xame Xame Si Ay Xale Te Dolen Ko Wakh Muk Safan Rek Ngen Di Xaarr Gnou Def Ngene Tontou Ko, Yen Ay Vrai Dmrm Ngène
Souleymane et Daoud avaient effectivement énormément d'épouses (1000 et 100). Mais là Moustapha Sy parle d'adultère et de petites amies (thioro)... Ce n'est pas pareil. Précise ta question si je ne t'ai pas répondu.
Même s'il en avait mille cela est légal en son temps. Mais ce qui est plutôt grave c'est quand à l'avènement de l'islam,Dieu limita aux musulmans, leurs nombre d'épouses a 4 .Donc tout musulmans depuis que Dieu azawadjial limite le nombre d'épouses a 4 aux musulmans,on voit plusieurs siècles après,au Sénégal,un Guide religieux qui se tape 33 épouses,dont 3 you bok ndaye AK bay,dont ben demi soeur.
Il n'y a pas de reactions à la hauteur de l betise parce que tout simplement la réligion n'est pas importante pour nous comme nous le faisons croire.Les dérives n'arreteront pas tant que ces événements continueront à avoir lieu au nom de l'Islam.Une personne normale qui pense aux ténébres de la mort et la tombe ne dirait jamais des immondices pareilles.Li dafa romb niaw ak grave
Salam oustaz Alpha. Wallahi,mane dama ame problemou deglou ce dajjal et son maudit fils.Dire des horreurs pareilles sur des prophètes d ALLAH... Soubhanalla!!!!
Serigne bi wakh dji amna solo looll ndakh wakh dju ñiaw ak kuko meuna wakh bonna niawna ndakh lii amoul ku bokku thi tarikha walla kousi bokkul Mane thi geum tarikha la bokku te mossuma andeu ak Serigne Moustapha thi waxam yu reuy yii mouy wakh ndakh yalla deugg rekk la bëgg te bo kholee dinga guiss ay vidéo you beuri yo khamné dañio dall rhi kaw Serigne Moustapha wéddi limou wakh yeup te khamngané basi tariikha bii mou bokku sakh ay wakham toujours daflèn di dépassé ba niom sakh Serigne Moustapha dafay wakh thi niom ay wakh yu ñiaw barakallahu fiikk
Senegalese need to be very careful about the words attributed to the prophets of God , this is serious allegation for one put on the prophet like Dauda and son .He himself has contradict the quran
Gniii yii nio yake Sénégal diahassé khélou ndaw yiii ..moustapha sy ak modou kara nio yém ces des faux marabout dougnou tousse bilahi té genre yii aka nio barri Sénégal ..tarikha bo douguou diguafa fék genre yiii ...limassi diahal tarikha nékoul si alhourane nékoul si souna .dagnouko créé rien que pour business ..kou topoule alhourane ak souna walahi digua pérte kou yakar si serigne yiii yagui si erreur wa salam
L'islam souffre au Sénégal à cause des tarikhas ouztaz vous avez raison sur toute la ligne il a parlé en wolof mais il n'ose pas dire ces propos en arabe ni en français ni en anglais sinon ces propos seront des blasphèmes maintenant à quel saint se vouer si des gens comme Moustapha sont accusés de Franc maçon vous êtes mon guide je vous prie de sortir pour éclaircir Les talibes sur ce dont on vous accuse la Franc maçonnerie il n'y a jamais eu de suite logique dans vos discours
Mom dale chaque gamou mou wax toth toth🤦♀️... yalla naniou yalla def ay deugui deugui djoulit. Amine
ماشاءالله وجزاكم الله خيرا يا حبيبي الفاهيم به ❤❤❤❤❤❤❤❤في منهج السلف الصالح وانااحمددم جه ❤❤
Mâchallah Oustaz Alpha vraiment diamant nga yagui léral lal niit gni lou am solo Lo xamné Oustaz yi nek ci reew mi saniou niouka wakh ndakh dagni bagn koulén méré
Au moins le prophéte daoud vivait avec le labeur de sa main et la sueur de son front mais ce gars vit avec les efforts et l'argent des talibés quelle paresse
Wallahi senegal ragal len yallah
Subkhanallah sama khole bi dina dague que Dieu nous préserve nous protège et nous pardonne
💔💔💔😭😭😭 WAKHATIKO
Merci ouztas alpha bah Pour
Toujours la lutte continue pour la promotion de la vérité vérité au Sénégal.
Je vous conseille de traduire ces propos en anglais et en français que le monde entier soit au courant passer par Twitter il faut qu’on commence à les publier la seule solution
Frère tu as parfaitement raison il temps
Sunnah rék moye DEUG billahi 💪💪💪💪🇸🇳 Sénégal ❤️❤️ Dakar Serigne bi li mo tah ma m'bayiko magui çi sunnah rék mon wore
Hayoo kالله vous assiste et vous facilite
Wallahi sunna moy yonou ndioubb
Diapal bamou deugeur ☝️
وَوَهَبْنَا لِدَاوُۥدَ سُلَيْمَـٰنَ ۚ نِعْمَ ٱلْعَبْدُ ۖ إِنَّهُۥٓ أَوَّابٌ ٣٠
.Et à David Nous fîmes don de Salomon, - quel bon serviteur ! - Il était plein de repentir.
allahou akbar yonnentebi tedd bi la kou yefeer bi djigne ndiaalo allahou akbar
insulter les prophètes et servir de guide religieux est ce que ses suiveurs savent ce qu’ils cherchent exactement Qu’Allah nous accorde la guidée
Un musulman ne mens pas .ce monsieur accuse des prophètes de dieu de tel sorte dans un pays de 95% de musulmans. Je crois qu'il devrait être jugé selon la charia.
Sénégal 🇸🇳 deukou domérame lii ñiou dégue moustapha iblise sy wakh ko yeupe ñiou toogue di séétaane c'est dommage pour se pays
Lima nakary moy
1-gnikoy defendre subhanallah
2-gnikoy topp
😭
Ana sounnite yi? Nagnou porter plainte. Addineu yeup aatté. Lignou nékkè ay tooyamaan you fi bari gnoo len tchi bayyi. Lii dégg ko sakh dafa eupp. Bayyil tek ak tégaat bi. HasbunalLaah ... Laa ilaaha illalLaah.
Pour moi il est le capitaine des chiens
MassaaAllah ❤️❤️❤️
57.13. Le jour où les hypocrites, hommes et femmes, diront à ceux qui croient: « Attendez que nous empruntions [un peu]: de votre lumières ». Il sera dit: « Revenez en arrière, et cherchez de la lumière ». C’est alors qu’on éleva entre eux une muraille ayant une porte dont l’intérieur contient la miséricorde, et dont la face apparente a devant elle le châtiment [l’Enfer] 57.14. « N’étions-nous pas avec vous? » leur crieront-ils. « Oui, répondront [les autres] mais vous vous êtes laissés tenter, vous avez comploté (contre les croyants) et vous avez douté et de vains espoirs vous ont trompés, jusqu’à ce que vînt l’ordre d’Allah. Et le séducteur [Le diable]: vous a trompés au sujet d’Allah.
Sourate 38 - Ayat 17
ٱصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَٱذْكُرْ عَبْدَنَا دَاوُۥدَ ذَا ٱلْأَيْدِۖ إِنَّهُۥٓ أَوَّابٌ
Endure ce qu'ils disent; et rappelle-toi David, Notre serviteur, doué de force [dans l'adoration] et plein de repentir [à Allah].
Wallahi live bi moma geuna toucher إنا لله وإنا إليه راجعون 🥺
Masha Allah Oustaz massa Yalla dina atté Insha Allah
Le Sénégal c'est le pays des hypocrites. Nous n'avons que les dirigeants que nous méritons. Nous allons souffrir d'avantage.
Wa sharrul Umoori Muhdathaatuhaa, Wa kulla Bid'atin dha'alah, wa kulla dhalatin fin-naar
Wax nga lepp mashALLAH mo taxitt deh
Y’akhii isbirr méttyna trop wallah,Sénégal Ndiaboot guimafa bayii rekk la xamoul noumaléndi deff mais soubhanallah nioo yess nafékk yallah naniou yallah deffal moudiou gou raffet samalniou souniou tawhid.
Kou Yalla défal tawhid do meun doundou Sénégal 🇸🇳. Fi moy capitalou réérrr
Merci beaucoup Alpha ba Sénégal beaucoup marlou c'est fiche de pitié
Yalla na ko yalla guindi sakhal niou ci ndioub yalla na la yalla aar shaykh alpha
Ci khoti worma sunu borome ah ay yonénteeme lagnou mane deey tiitte naa trop ci Senegal yalla nagnou yalla mousseul ci mérou sounou borome
Allahou akbar !!!
Il est temps que les musulmans sénégalais abandonnent ces égareurs et retournent à l’Islam originel (Al Qour’an ak Sounnah)
Il a commencé par manquer de respect sa propre famille que veux tu que celle-ci fasse?
Maa shaAllah
Barakallahou fikum ya Oustaz !!!
Yalla naniou yalla atté ak Tapha SY domeram
Innalillahi wa Inna Ileyhi radjihoun Laa Hawla wala Quwata illa Billah Subhanallah Subhanallah Laa Ilaha Illaha Astaghfiroullah.😭😭😭😭😭 Quelles catastrophes religieuse, sociétale et morale !!! "
yaw oustaz mounial Moustapha sy ap doméram la mai yalla dinako lidianti Sénégal ay nafék rék la beri ay soufia laniou
Sénégal un grand pays de nafekh d'hypocrites de mensonges de soss
De bidha et de bocalé
Serigne yi bahougnou
Adouna moléne itél
Nite yi nak moyLo Lou wate rék né dougnou yéwou
آللهم لا تأخذنا بمافءل سفهاء منا
21.1. [L’échéance] du règlement de leur compte approche pour les hommes, alors que dans leur insouciance ils s’en détournent 21.2. Aucun rappel de [révélation] récente ne leur vient de leur Seigneur, sans qu’ils ne l’entendent en, s’amusant
Merci pour le video
Macha Allah yaa Oustaz
Oustaz Alpha, wallahi weetoulo thi sa djooy yi.Li dafa meti thi khol te mounougnou thi lou bari.Mais nak lui gnou metti bagnouy djoy meti n'a sougou Borom te dina atté...
Gni ay domou kharam lagnou rékk li kouko sagna wakh si ay yonéneté bayiwo kénéne ,wa mom limouy wakh fane lako dieullé 🤭🤭😭😭😭😭
39:44 kone ki yague na wakh lou bone , SoubhanAllah
Ya ouztaz gnou wara wakh bou gnou wakhoul .gnoune citoyen lambda sou gnou wakhé ken dou ka dégue.mais vraiment on a tous mal.
ماشاءالله
Islam 3 leu gueum yallah gueum yonateh bi mouhamed psl ak alhouran karim kouko wath rergua
Bilay man gathié la am si anda samma djikoyi.cette association n'a plus sa raisons d'être.ils ne sont pas objectif ay vrai tapett ou hypocrites
1h:16 ! Limou wax akay deug dafay takk ak di fasser xalei you vierge. Doulen sakh wax maynala sa batt. Dalay abandonner nga weur ko beu sonou doko guiss , moudjou demal sa bop 🙌🏾
Sénégal Niata Si Keurou Diine Yi Gnofiy Def Lou Bakh Di Def Xame Xame Si Ay Xale Te Dolen Ko Wakh Muk Safan Rek Ngen Di Xaarr Gnou Def Ngene Tontou Ko, Yen Ay Vrai Dmrm Ngène
Boul wax lolou, li dafa reuy
@@Yataaaaashhh tarikha amoul bene diarigne bir senegal loudoul ay bokkalé youdoul diekh
yaw yakarna daga sokhla Therapie sa xalat fi la tollou, démal toub yaw ak moustapha sy mo geune gakoy layal douguén ay nitt sakh
Assalâmou alaykoum wa rahmatou LÂHI wa barakâtouhou Diazâkoumou ALLAHOU khayran
بارك الله فيكم وجزاكم الله اخوكم في الله من موريتانيا
M'achallah oustaz
May Allah bless you Ba
Imam je vs salue mais j aimerais savoir le nombre des épouses du prophète Salamon car j'ai vu un hadith qui dit que ce dernier avait 100 ou 99 epouses
Souleymane et Daoud avaient effectivement énormément d'épouses (1000 et 100). Mais là Moustapha Sy parle d'adultère et de petites amies (thioro)... Ce n'est pas pareil. Précise ta question si je ne t'ai pas répondu.
@@brahsko1 j'ai écris 200 au lieu de 100 épouses une faute de frappe
Même s'il en avait mille cela est légal en son temps.
Mais ce qui est plutôt grave c'est quand à l'avènement de l'islam,Dieu limita aux musulmans, leurs nombre d'épouses a 4 .Donc tout musulmans depuis que Dieu azawadjial limite le nombre d'épouses a 4 aux musulmans,on voit plusieurs siècles après,au Sénégal,un Guide religieux qui se tape 33 épouses,dont 3 you bok ndaye AK bay,dont ben demi soeur.
@@masiba7272 doyna waar
@@aboudione7672 BarakaAllahou fikoum
@masiba 72 deugue rek nga wakh
Il n'y a pas de reactions à la hauteur de l betise parce que tout simplement la réligion n'est pas importante pour nous comme nous le faisons croire.Les dérives n'arreteront pas tant que ces événements continueront à avoir lieu au nom de l'Islam.Une personne normale qui pense aux ténébres de la mort et la tombe ne dirait jamais des immondices pareilles.Li dafa romb niaw ak grave
100% d'accord avec tw
Watawasaw Bil Haq pourquoi vous mettez le titre de "Serigne" sur son nom
Wallahi li daf ma meti 😢
Serigne Moustapha Sy la xamoul lagn lako niit gni wara topé dou diné dou wakh djiou am ndiarign
Bilay oustaz gni bolen topé diga cardiaque.
Sounou boroome yakamtiwoul moguiléne di khaar beess bou gnépeu takhawee ci kaname youkhou dina djipp fougnouko fooguéwoul bayiléne rek
Machalah deug rék wackh senegal doyna war legui yaleu na nous borom yeureum
Merci oustaz Alpha..Andeu samm djiko yi niome khana dafa ame niouniou ciblés ou bien
Macha Allah oustaz fadel
Yam léne thi limou wakh ta ba nia eupeul yéna ngui
Salam oustaz Alpha.
Wallahi,mane dama ame problemou deglou ce dajjal et son maudit fils.Dire des horreurs pareilles sur des prophètes d ALLAH...
Soubhanalla!!!!
🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩
C'est ça le Sénégal malheureusement... trop d'hypocrisie
Et de mécréante aussi dommage!!!!!
Juste pour dire baarakal'LAH fiikoum pour toi et tous les frères et soeurs qui s'activent à dénoncer ces hypocrites de la pire espèce !
Wakh katte yi naniou wakh thi lii bougnou wakhé si yalla ak ay yonéntame nguéne nopi boudé sén serigne nguéne fipou thieuyy Sénégal
تبّا لك تبّا لك
Masha la
C capitaine qui gaspille l argent des Moustachiidine avec ses copines
TIDIANE LA MAIS VRAIMENT WAHEDJI RAGFETOULE
السلام عليكم يا إمام بارك الله فيك 🤲🏾أمين
Top alkhouran ak suna rek mo wôr walahi
adouna toukkina
Alpha asalamou aleykoume dooy nawar
Mais Oustaz; il n'y a pas de justice au Sénégal ,n'oubliez pas que nous sommes dans une république bananière ,c'est la loi du plus fort !
Il est où mahtar saar pour faire akhirou zaman sur moustapha sy
Ile la fait maintenant
Wakhna si ba paré
Salam brother Manchalla
Slt bro mahtar sarr wakh nassi
Soubhanalah
Serigne bi wakh dji amna solo looll ndakh wakh dju ñiaw ak kuko meuna wakh bonna niawna ndakh lii amoul ku bokku thi tarikha walla kousi bokkul Mane thi geum tarikha la bokku te mossuma andeu ak Serigne Moustapha thi waxam yu reuy yii mouy wakh ndakh yalla deugg rekk la bëgg te bo kholee dinga guiss ay vidéo you beuri yo khamné dañio dall rhi kaw Serigne Moustapha wéddi limou wakh yeup te khamngané basi tariikha bii mou bokku sakh ay wakham toujours daflèn di dépassé ba niom sakh Serigne Moustapha dafay wakh thi niom ay wakh yu ñiaw barakallahu fiikk
Moustapha Mane wedina bayinalà té bessnikiteye dotou meule deguelou yow daganye nàhatekategan
Soyons objective y’a beaucoup de ouztaz qui ont dénoncé ses propos. Parmi eux d’éminents tidianes. th-cam.com/video/5i3hPiTKEmg/w-d-xo.html
Mais c'est pas assez!!!
Li métti nama bassi kanamou yalla yalla sédénako
Moustapha sy da alkou, il est très impoli. Comment peut on suivre ce guignol
Sama djiko amoufi sam tarikha mofi am
Merci my brother
Barakallahou feek ya Oustaz . On a trés mal nous les musulmans c'est honteux pour notre belle religion d'avoir des énergumènes de ce genre
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Senegalese need to be very careful about the words attributed to the prophets of God , this is serious allegation for one put on the prophet like Dauda and son .He himself has contradict the quran
Merci Oustaz il faut démolir ces menteurs au non de l'islam
Oustaz, boule togne mbame, ndakh mbaam niémé woute wakhe lii !
ماشاءاللہ
Gniii yii nio yake Sénégal diahassé khélou ndaw yiii ..moustapha sy ak modou kara nio yém ces des faux marabout dougnou tousse bilahi té genre yii aka nio barri Sénégal ..tarikha bo douguou diguafa fék genre yiii ...limassi diahal tarikha nékoul si alhourane nékoul si souna .dagnouko créé rien que pour business ..kou topoule alhourane ak souna walahi digua pérte kou yakar si serigne yiii yagui si erreur wa salam
Kilifa tarihka lan .dounou kilifa si dine Islam...kilifa iBilise lan 👹👹
Sénégal rek
Apparemment ces propos de Sy sont contraire aux écrits du Coran. C'est grave.
Moustapha sy imbecile la billahi
Tarihka yeup ay domerame lan colo Satán mbame khouhh lan🐽🐽🐷🐽🐽🐖🐖
L'islam souffre au Sénégal à cause des tarikhas ouztaz vous avez raison sur toute la ligne il a parlé en wolof mais il n'ose pas dire ces propos en arabe ni en français ni en anglais sinon ces propos seront des blasphèmes maintenant à quel saint se vouer si des gens comme Moustapha sont accusés de Franc maçon vous êtes mon guide je vous prie de sortir pour éclaircir Les talibes sur ce dont on vous accuse la Franc maçonnerie il n'y a jamais eu de suite logique dans vos discours
Dieuredieuf oustaz❤