Merci beaucoup MackTv pour ces anciennes productions de Daraay Kocc que vous nous rappelez. Depuis hier je n’arrête pas de les regarder. J’ai regardé Laye sangara, L’arrangement, New gui dolé, carnet K, Ndeye etc.. ça me rappelle vraiment mon enfance avec les théâtres de la rts les mardis soirs. Par contre je réclame « Absa » la jeune fille qu’on a refusé son mariage pour des raisons de caste.. Merci beaucoup et toutes mes félicitations malgré tout vous faites un énorme boulot 😊😊
Saway bayyi thi music naturel bimou andal waay 😢 svp liii mome amoul bénneu chance sa music biii
Lolou rk moma si méti😢
@@ndeyemaladosow8603 non méttinama
@@Ytefvjknnk 👍👍
bilahe
Dou yaw rek yakoy kass deh mongui yakh nak
Merci beaucoup MackTv pour ces anciennes productions de Daraay Kocc que vous nous rappelez. Depuis hier je n’arrête pas de les regarder. J’ai regardé Laye sangara, L’arrangement, New gui dolé, carnet K, Ndeye etc.. ça me rappelle vraiment mon enfance avec les théâtres de la rts les mardis soirs.
Par contre je réclame « Absa » la jeune fille qu’on a refusé son mariage pour des raisons de caste..
Merci beaucoup et toutes mes félicitations malgré tout vous faites un énorme boulot 😊😊
Merci beaucoup pour théâtre yi ngay publier
Salla Lahou Alla Mohamed ❤️❤️❤️ psl ❤❤ psl ❤❤ psl ❤❤❤
Merci beaucoup Wa MAACK TV SÉN LIGUÈYE RAFÉTNA MACHALAH ❤️
Andil niou wadiour 😭😭
surtout bobou
Merci pour tout vraiment
Amati'na solo Barki demb rek magui sétan théâtre Ndeye 1-2-3 Me yén wa Maack TV digué borla ana 3em parti Les 3 Go
Mere binta mbaye aussi elle joue son rôle à la perfection ❤❤🎉
Ooh kholale yaye dji rék si préparation bi ndaysane kéndou yaye si dome😘🥰
Pourriez-vous ajouter le theatre mbeuguel si souf de daaray kocc, theatre avec mandione laye
Mér natou gorsa waxdia ... mais ndaye day bahdé focus rék 🎉❤❤
Lii moy yéte❤❤
Sawaay bayile 😂😂waaye liguay waay gatt néhoussi day découragé lo sakh gniy setaane.
Mane deh dama yacaryoni sakh khana ndèye day sèyi bima guissè yayam dico sangue😂😅
Mom la wakh di😂
😂😂😂
Merci ❤
Mbeuguel ci sous avec madione laye sarr
Ndaysane bly théâtre warnaléna fay 😘
😮😢. Oh yayou ndeye
Mère aminta mbaye Ndeyssane y’a meune jouer
Mérci beaucoup thi thèatre yi gaye dougal pa sikim vol 3 laniou beugone
Non Lii waw na yaram préparation ak départ bi
Dom vol 3 mom dougou nguir yallah
Kou khamer Nar Diop bi nekone ci Madior ak Dior? Elle a tjrs été belle
Ak yayou dikone moy fi ndeye di liguéyé
Do gnou maay. «Bakary deimal gnibi , ma bagn fi laye tok»
Diaap thii waay
Aida Diagne waay 🤣🤣
Merci beaucoup sa liguéye rafétna bii rek la namoone❤❤❤❤
Hana diamonoyi Dakar orobla wone😂😂
Ki dou mér nafi serie samba allar
Gnilane sama tourando 😂❤😊
Je suis là bb
Théâtre bi 2004 la
Wa ki dou mère wénguélé?
Moom la
Ajouter neww jo dole de diewo
Merci ❤