SPECIAL GAMOU 2020 AVEC TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE ET CHERIF MAMINE AIDARA

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 9 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 675

  • @fantatandiang5911
    @fantatandiang5911 4 ปีที่แล้ว +549

    Kou soppp Tafsir Abdourahmane Gueye defal j'aime. Ramadan mubarak à la ummah islamique

  • @BB-rj4sw
    @BB-rj4sw 4 ปีที่แล้ว +47

    Alhamdulilah bou niou bokké diné islam , begue Mouhammad saw , begue Cheikhou Ahmed tidiane .....machala Tafsir...yalna niou yalla moussal té arrreeee niou si diangoro virus bi

  • @rene1021
    @rene1021 4 ปีที่แล้ว +186

    Diarama Seydi El Hadj Malick Sy RTA
    Yalla na niou la Yalla fayal...Amine
    Yalla na niou Yalla mouthial ci Covid-19 mouthial boleim domou adama, samal niou bopam ta khirr niou ci bopam ci bijayi Seydina Mouhamed PSL akh ci barkei Serigne Babacar Sy RTA..
    Amiiiiinee

  • @omardiedhioukobar3258
    @omardiedhioukobar3258 4 ปีที่แล้ว +34

    Tafsir abdourahmane gaye ak cherif mamine aidara yalla nalen fay maylen wèr defal soutura bu barri machallah

  • @papamountdiop4502
    @papamountdiop4502 4 ปีที่แล้ว +2

    Tafsir yalla nala yagual si sounouy beut mame yalla nala yalla faye liguay def yalla nalla ko yalla faye amine

  • @fatoukinealaminesene5349
    @fatoukinealaminesene5349 4 ปีที่แล้ว +209

    Depuis le Maroc je commente avant de regarder car j'ai vu les commentaires sur Whatsapp.xol sed ti na.Kene dou Seydina Mouhamed saw

    • @moustaphandiaye6876
      @moustaphandiaye6876 4 ปีที่แล้ว

      Depuis le Maroc nous saluons les commentaires et remercions la 2s et les confirenciers

    • @cityomar1729
      @cityomar1729 4 ปีที่แล้ว

      Mashalla djeuredjeuf

    • @tanorfall8302
      @tanorfall8302 4 ปีที่แล้ว

      ❤❤❤❤❤❤❤❤😭

    • @djimsow1079
      @djimsow1079 4 ปีที่แล้ว

      Machallah

    • @astouba6969
      @astouba6969 4 ปีที่แล้ว +1

      @@tanorfall8302 i4

  • @aminajobe9909
    @aminajobe9909 4 ปีที่แล้ว +67

    😭 😭 😭 I can't hold my tears Machaaaa Allah kéne dou Seydi El-Hadj Malick Sy ❤️ ❤️ ❤️magui ba Gambia diko sétane Yalnalén Yallah féye si barké Yonéntabi PSL

    • @ajisainaboufaal4739
      @ajisainaboufaal4739 4 ปีที่แล้ว

      Same to me 😭he always give me a reason to cry and smlie also ireally love him

    • @fallgalaye6954
      @fallgalaye6954 4 ปีที่แล้ว

      @@ajisainaboufaal4739 j

  • @bifa1115
    @bifa1115 4 ปีที่แล้ว +35

    Allahumma amiiine Oustaz Tafsir Yallah na Borom bi fay 🙏🙏🙏
    Ma ngui léne di ziar boubakh ci barké wérou koor gui niou nék lafthiat si séne duo li nguéne niou apporter khamouléne ko sakh masha Allah masha
    Diazakallahou khaïrane diaza🙏🙏🙏

  • @abdougueye77
    @abdougueye77 4 ปีที่แล้ว +33

    Dafa mélni oustaz daa name tague rassoulilahi yalla nafi yalla dieulé corona barki mouhamed Psl

  • @wademalick5501
    @wademalick5501 4 ปีที่แล้ว +36

    Machallah nama nieupp ball akh balna nieupp akh yalna niou yallah défal dégue ak topp si barké séydina mouhaméd ...amine yara bii

  • @omardiedhioukobar3258
    @omardiedhioukobar3258 4 ปีที่แล้ว +37

    Machallah li laniouy khar souniou tèlè yii sou meunul nk chaque jour si koor gui dinama geuanal trop mogueune niou tègal yeufu adouna yii
    Yalla na yalla dooli soutura ak khèwal tei dièlè fii mbass mi si barki yonenti bii

  • @papiscongom885
    @papiscongom885 4 ปีที่แล้ว +42

    ALHAMDOULILAHII.
    Dieureu ngén dieuff TAFSIR ET MAAMINE.
    Khole seid na si yeine YALLA na Ya'Allah faylén yiw.
    Vive la 2stV.

  • @elmoustaphnd1664
    @elmoustaphnd1664 4 ปีที่แล้ว +59

    Une chose aussi exceptionnelle comment un homme peut le désapprouver 😐 walae chérif ak tafsir xol sedattina wallae 👏 yalla na niane bii nangou yalla diegal sounou nioumté yeup walae xola sedd rk

  • @youzarsiflo6894
    @youzarsiflo6894 4 ปีที่แล้ว +197

    Mame maodo malick sy bilae monde bi amouniou fayam yalnako yalla fayal bopam

  • @lezinholacouture7177
    @lezinholacouture7177 4 ปีที่แล้ว +38

    dieureudieuf tafsir ak cherif yèneu ngui matal sén mission bi léne yalla soubouhana watal dinke 😗😗😗😗

    • @hassyarassoul2540
      @hassyarassoul2540 4 ปีที่แล้ว

      Bilae😍
      J m suis dit pareil! Tafsir wollah il donne mm envie d'aller loin ds l'apprentissage d notre religion m ossi d copié sûr cet homme parfait qui est notre bien aimé Mouhamed

  • @djibrilndiaye7831
    @djibrilndiaye7831 4 ปีที่แล้ว

    Serigne Abdou Rahmane Tafsir yalla nala yalla deffal diam ,yalla na diam pane sa kaw ,yalla nala yalla rousse dieuléfi corona-virus bi si barké seydouna mouhamed, xol toyna ya oustaz ,yalla na yalla defar say mbiir zayirane wa batinane ,yalla na bate bi gënë wer amine

  • @diawardieye4479
    @diawardieye4479 ปีที่แล้ว +2

    Kou beuk seydina mouhamed lale j'aime

  • @ModouSeck-fz9yj
    @ModouSeck-fz9yj 5 หลายเดือนก่อน +4

    Kou beugue bayou Fatima lale j'aime ❤❤❤❤❤

  • @mamealiougueye2665
    @mamealiougueye2665 4 ปีที่แล้ว +115

    Kéneu dou seydi Hadji Malick Sy yalla nafi yalla dieulé covid 19 bi si barki sy Malick bayou Serigne Babacar sy 🤲🤲

  • @binettecuisinedumonde8286
    @binettecuisinedumonde8286 4 ปีที่แล้ว +101

    Très belle initiative, en regardant Tafsir expliquer et chanter le Prophète SAW j'avais les larmes aux yeux, si on pouvait avoir ce genre d'émission tout les soirs à défaut une fois par semaine ça serait une bénédiction
    @biinette_cook

  • @senimbaye8617
    @senimbaye8617 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah wayy tafsir Abdourahmane Gaye sunu xol sede na yalla na borom bii weral bate bii

  • @falloumou5270
    @falloumou5270 4 ปีที่แล้ว +1

    Abdou rahmane TAFSIR NGAYE YALLA NASA FAN WII GOUN ,KOULAY KHAR YALLNA ANDI.NIEPP CONTANAN.MAN NAK AMNA LOMALA YENÉ INCHALAH .

  • @aliounemoussadiagne3032
    @aliounemoussadiagne3032 4 ปีที่แล้ว +32

    Mâcha allah hadji Tafsir yalla nala borom bi mousseul si thiate souniou pape mass Mbengue yalla nako borom bi yeureum té djégueul ko

    • @khalydiagne2509
      @khalydiagne2509 4 ปีที่แล้ว +1

      Allahouma aminé

    • @mariamadiene8314
      @mariamadiene8314 4 ปีที่แล้ว

      Alakhouma amiiiine inchallah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @aliounediop586
    @aliounediop586 4 ปีที่แล้ว +58

    Diarama Seydi El.hadji Malick diangal ganiou leepp si doundou Seydina mouhamad (psl)

  • @papaamethsow1297
    @papaamethsow1297 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah le duo cherif ben mamine Aidara et le le sage Tafsir Abdourahmane Gaye.votre duo a toujours ete a la hauteur et doué de sens avec de tel enseignements et bcp d eclaircissements et d orientations islamique.En periode de Covid 19,sincerement vos gamou pendant le weekend montre nettement k quand les gens sont desorientés,perdus,ont la psychose et que la fievre gagne du terrain malgré k ya moins de par rapport au monde,on ne peut que se refere sur le maitre des mondes,des cieux,de l univers et du temps qui le Bon Dieu et les enseignements de son veneré prphete Sallahou Alley wassalam(rta)

  • @almakdiw3708
    @almakdiw3708 4 ปีที่แล้ว +69

    Machalla,yalla khamna lii moma geunal Quartier Général.

  • @ousseynoundiaye2827
    @ousseynoundiaye2827 4 ปีที่แล้ว +24

    Ndeyssan walakhi lii kouka deglou xamnii Alkhouran kahim moy louyy deugg tei Seydina mouhamed psl moy prophète 🥰🙏🏽

  • @rokhaya__babacar2904
    @rokhaya__babacar2904 4 ปีที่แล้ว +33

    Yalah nagnoulay ya yalah fayal si barki serigne babacar sy ❤contáne nagnou tafsir❤

  • @beenettewane2753
    @beenettewane2753 4 ปีที่แล้ว +24

    Da ng lenn di cétane seu xol dii fekhh😭😭😍mashaallah

  • @daoudaanneat-tidiany
    @daoudaanneat-tidiany 4 ปีที่แล้ว +16

    Al Hamdou Lillah
    Al Hamdou Lillah
    Al Hamdou Lillah.
    Machallah Yalna lén Yalla Faye Bi Diahi Seyyidil Woudjoudi (SAWS) korou diammou ak Salam)

  • @cheikhouelhadjindione9420
    @cheikhouelhadjindione9420 4 ปีที่แล้ว +6

    Machallaaaa oustaz tafsir yalla na yalla werreullll thieurrr yi Tei saxxalll and biii ak cherif suis trop content machalla

  • @khoumbetedaganeofficiel3823
    @khoumbetedaganeofficiel3823 4 ปีที่แล้ว +9

    Figané Mass boula YALLA ladjé dawna sama yaram dah dafa tiitlou
    Bamél lou diara bayi khél dah raglouna trop
    Merci 2stv images yi lérna son bi aussi montage yi Macha ALLAH
    ALLAHOU BAARIK

  • @astoudiopfall9388
    @astoudiopfall9388 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalla ioe rék lagnou done khar gua sédal xol tagual niou sangou sangou SWL yalna fi yalla dieullé Mbass bi barki La ila kha il'Allah

  • @yadeinfo2874
    @yadeinfo2874 4 ปีที่แล้ว +24

    Keen d'où yoneenti bi ta ossi maodo kou xam yoneenti bi la ❤️🙏

  • @aiissinky8313
    @aiissinky8313 4 ปีที่แล้ว +5

    Yalla na diamu yag Yalla fayul gnu yénn gnu takh sunu xel mogihh sii Mohamed(SAW)fier d'être talibé Cheikhna Cheikh Sadbou😚

  • @boiielickzo1067
    @boiielickzo1067 4 ปีที่แล้ว +6

    Tafsir yalla na yalla goudeul sa fann th weral batt bi si barkep seydina Mohammed (psl)🙏

  • @anbs4678
    @anbs4678 4 ปีที่แล้ว +1

    Demalene di Setane di santallei yallah soubhana watallahi bima defei dioulitee 🙏

  • @fatousow4028
    @fatousow4028 4 ปีที่แล้ว

    Yalla na yalla goudal séne fane may léne weir ak wérlé ci Barker seydina mouhamed psl amine yaraby

  • @adioumaka4416
    @adioumaka4416 4 ปีที่แล้ว +13

    Dama beug xameuh ndakh Chak jour lay ameuh😭😭😭😭contane nanou dehh walhi yalla na yalla nangou Niane yi🙏🙏yalla yokkkou sen diameuh gueneuh yagg sonou beuguel🙏🙏❤️🥰🥰bijahi taha

    • @mariamekane7340
      @mariamekane7340 4 ปีที่แล้ว

      Par samedi

    • @harounasoumare7373
      @harounasoumare7373 4 ปีที่แล้ว

      Chak jour leu kay mm heur bi

    • @adioumaka4416
      @adioumaka4416 4 ปีที่แล้ว +1

      Merci beaucoup diadieuf 🙏🙏🙏🥰🥰

    • @aliounesarr7655
      @aliounesarr7655 4 ปีที่แล้ว +1

      Bi c chaque samedi(spécial Gamou) ,lautre c chaque jour mais c mois de 15mn

  • @aliouba1170
    @aliouba1170 4 ปีที่แล้ว +6

    YALLA na Senegal 🇸🇳 di yaagueu di am jaam et partout dans le 🌍...Allahouma aamiin 🙏🏿🖤...
    Jarama à toute l ‘Équipe Especial Gamou 🙏🏿🖤🍀 et Jerejeuf à la 2STV🙏🏿🖤
    MA CHA ALLAH🙏🏿🖤🇸🇳

  • @aissatou362
    @aissatou362 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah Tafsir. Une belle initiative Cherif. Alkhamdoulilah. J'aime écouter Tafsir Abdourahmane. De tout cœur avec vous. Yallah aar Sénégal thi daradjaye Seydina Mouhamad sallalahou aleyhi wa salam ak adounabiyeup 🙏

  • @ndeyemenathiam9226
    @ndeyemenathiam9226 4 ปีที่แล้ว +32

    Mashalla je ne cesse de regarder et regarder à nouveau j kiff grave ❤️Dieu vs payera .
    Je ne comprends pas ce qui dislike si on aime pas on a qu'à ne pas regarder c tt

    • @harounaamadousow4737
      @harounaamadousow4737 4 ปีที่แล้ว +1

      Certains ne savent op distinguer like e dislike loll sinn ces deux là jles aime de TT mon âme wlh beug yallah ,yonnentei bi akh seydi hadji malick

    • @ndeyemenathiam9226
      @ndeyemenathiam9226 4 ปีที่แล้ว +2

      @@harounaamadousow4737 wallay c pourquoi je les aime ils sont les meilleurs yalla nalène yalla may fane bou goudou ak wergou yaram . C rare de voir des gens qui ns rappelle Allah soubouhanah wa yalla et ki ns fait aimer plus Naby (PSL)

    • @harounaamadousow4737
      @harounaamadousow4737 4 ปีที่แล้ว +1

      Amiin yaa Rabbi!! Dfois g un coeur meurtri quand jpense k'un jour viendra il disparaîtront et t'aura op d'autres a leur niveau😬

    • @ndeyemenathiam9226
      @ndeyemenathiam9226 4 ปีที่แล้ว +1

      @@harounaamadousow4737 n'oublie pas ns aussi ns allons tous partir un jour la vie est ainsi faite

    • @harounaamadousow4737
      @harounaamadousow4737 4 ปีที่แล้ว +2

      Oui jc mais ma personne n'est rien comparé a eux si on devait choisir qui devait mourir pr k l'autre reste tjr en vie jusqu'o jour dernier jme serai choisi pr que c genrs de personnes restent en vie prck suis conscient k'ils sont bcp plus utiles k moi e k la société pourra bénéficier d'eux mais malhrzma *koullou nafsine za'ïkatoul mawti*

  • @sokhnakeita2587
    @sokhnakeita2587 4 ปีที่แล้ว +4

    Yaa Allah yalla ngu yokou souniou TIOFEL si yonnete PSL❤❤❤ndaysane MAODO mo xam kou tedd ki machalaa ❤❤machalla a vous lequipe SPECIAL GAMOU❤❤

  • @fatoumataba9949
    @fatoumataba9949 4 ปีที่แล้ว +7

    Pourquoi ils ont disliker s merveilleux Gamou 🤦‍♀️ms machallah à vous Kallah vs protègent ❤

  • @nanoushdiop8799
    @nanoushdiop8799 4 ปีที่แล้ว +1

    yalla nagnou yalla fayal seydi El hadji malick sy si barké séydina mouhamed (psl)

  • @ndeyediop6532
    @ndeyediop6532 4 ปีที่แล้ว +4

    Machallah yallah na yallah doli soutoura yok wergui laf thiate mane mome damala sope rek té yallah takh

  • @MaimounaSagna-n7l
    @MaimounaSagna-n7l 18 วันที่ผ่านมา

    Seydina Mouhamad Sag Sag yii ma sopp Tafsir Abdourakhmane Gaye Machalla yalna fi yak and AK weer

  • @kinefaye7471
    @kinefaye7471 4 ปีที่แล้ว +12

    Machallah li nékhna thi khol contana trop bilayi walayi magui fouta thi departement de podor

  • @malickteuw1328
    @malickteuw1328 4 ปีที่แล้ว +22

    Mâcha alla, j'aime bien cette émission, qui nous parle khaleu lahhou khaleu rassoule, mais le quartier général est conçue comme une ligue de champion.

    • @harounaamadousow4737
      @harounaamadousow4737 4 ปีที่แล้ว +3

      Blh wlh t'as raison frère !! Les émissions qui méritent plus de soutien sont tjr laisser en rade pr valoriser d'autres qui n'ont ôcun enseignement

    • @malickteuw1328
      @malickteuw1328 4 ปีที่แล้ว +5

      @@harounaamadousow4737 j'avais écrit un article là dessus l'année dernière pour dénoncer mais les fanatiques m'ont attaqué de tout bord. C'est malheureux pour un pays comme le notre, les gens profitent du ramadan pour remplir leurs poches. S'il s'agit de parler l'œuvre de nos guides religieux, je pense que dans chaque famille religieuse y'a des télévision et des radio qui peuvent leurs servir de canal pour parler aux fidèles. Ce qui me dérange de l'émission quartier général, comme si, on est en ligue des champions. Chacun essaie de comparer son marabout à l'autre. Et le prophète dans tout ça. En tout cas c'est bon pour le vivre ensemble Sénégalais. Jusqu'à présent j'ai gardé des commentaires de l'année dernière sur mon portable, que des insultes.

    • @harounaamadousow4737
      @harounaamadousow4737 4 ปีที่แล้ว +2

      @@malickteuw1328 malheureusement on est dans un pays ou la majeur partie dla population est animée par les désirs mondaines en particulier les jeunes !! Mm dans nos universités e écoles ils devrait y avoir des enseignements religieux (de Mohamed psl) mais on ns dit k dans notre constitution précisément a l'article 4 d la constitution les enseignements de Mohamed psl e d'Issa ibn Mariam ne sont op applicables parcontre on peut se baser sur cels de Karl marx de keyenz e de Adams'mith. Imagine dans un pays a totalité musulmane!!

  • @fallyaram4557
    @fallyaram4557 4 ปีที่แล้ว +4

    Machallah🙏 liiii nekh na si xol❤thieyyy notre prophète seydina mouhamed(SWS) limou tégoo lépp ndakh khétaam😭😭😭 dama dioyy baa sone en regardant tafsir parler sur notre prophète(sws)

  • @ndeyeaminatandiaye259
    @ndeyeaminatandiaye259 4 ปีที่แล้ว +1

    Tafsir yalla sa diam yague si barki seydina mouhamed psl

  • @mamadouseydily8003
    @mamadouseydily8003 4 ปีที่แล้ว +8

    Oustaz abdourahmane gaye incha allah dinala toudé domm. Que Allah vous protège

  • @damediene319
    @damediene319 4 ปีที่แล้ว +3

    Maachallah dieureudieuf Cherif Mami ak Tafsir pour les prières formulées à l intention de mon très cher papa Abdoulaye Ndour que Dieu vous paies et vous gratifies de sa bonté immense amiin yaa Rabbi

  • @goradiongue8103
    @goradiongue8103 4 ปีที่แล้ว +20

    Macha'allah Qu'Allah nous protège et longue vie à Tafsir Abdourahmane Gaye

  • @mamekhalifadiouga4731
    @mamekhalifadiouga4731 4 ปีที่แล้ว +1

    2s tv ci kaw ci kanam si loubakh diam rk gnene di am inchallah

  • @aloudinho8795
    @aloudinho8795 4 ปีที่แล้ว +5

    Kéneu dou Seydina Mohamed (sws) mom rek la beug ❤

  • @tafsirmbaye1891
    @tafsirmbaye1891 4 ปีที่แล้ว +39

    Diangue rkkkk moooo wooorrrrr mashala ❤️

  • @WAWA-xd9yu
    @WAWA-xd9yu 4 ปีที่แล้ว +1

    WALAHI kena dou gueune dia teede thi mindef SEYDINA MOUHAMED RHASSOUL ALLAH SAWS.
    Yalna YALLA FAYELENE niou bokeu ak dioulites yeup. Yalna niou YALLA maye louniou soutourlo ba ligueyeul thi yonintibi SAWS AMINE ya RABBI .

  • @adjagueye9443
    @adjagueye9443 4 ปีที่แล้ว +13

    Machalla tamsir yalna sa diam yague gueuna yague gueuna yokoi si barkè yonènte bi (pls)👐👐

  • @dhinerarnauddacosta9934
    @dhinerarnauddacosta9934 4 ปีที่แล้ว +3

    Tafsir abdourahmane Gaye yalla na yalla maye la were tai goudale say fane 🙏🏻❤️

  • @mameamygangue4836
    @mameamygangue4836 4 ปีที่แล้ว +18

    Kene dou Mouhamadou Rassoulillah machallah🙏

  • @alimasiy8443
    @alimasiy8443 4 ปีที่แล้ว +12

    Ay way 2 stv continue cet emissions tt les jours yalla na lene yalla fayy

  • @abdoulayediop4052
    @abdoulayediop4052 4 ปีที่แล้ว +4

    Yoninte bi yalla na niou ko yalla fayal

  • @awadiop6782
    @awadiop6782 4 ปีที่แล้ว

    Tafsir yalna yalla mayla katene ak werrr ak gudu fane barké Mohamed(PSL)

  • @bijoumoulayedabah
    @bijoumoulayedabah 4 ปีที่แล้ว +14

    Oh lalalaaa l’amour entre Tafsir ak Cherif mashala😍😍😍😍

  • @thiernoniang5366
    @thiernoniang5366 4 ปีที่แล้ว +8

    Yalna yalla fayléne imam Tafsir ak cheirif khole séde billahi ♥️🤲

  • @yacinegning8756
    @yacinegning8756 4 ปีที่แล้ว +10

    Qu allah soubhanala vous donne longue vie ,Cherif et Ahmet vs faites la fierte de l ecole de Maodo...

  • @rokhythiam2019
    @rokhythiam2019 4 ปีที่แล้ว

    Bilahi ma beugeu tafsir abdourahmane guaye goudale fané rekh té andakh wére si barkhé (psl)

  • @nafissatoudiaby7359
    @nafissatoudiaby7359 4 ปีที่แล้ว +46

    Machallah fier d'être talibé cheikhe 🙏🙏

  • @badarafall3226
    @badarafall3226 4 ปีที่แล้ว

    Dieuruedieuf tafsir yalla nala yalla faye

  • @papeoumarndiaye2303
    @papeoumarndiaye2303 4 ปีที่แล้ว +4

    Njabotou Seydouna Mouhamed saw yalna sen diam yag ❤️🙏

  • @SambaSarr7
    @SambaSarr7 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah yalla nalen yalla defal diam ci barké Mouhamed (saws)

  • @-KkS15
    @-KkS15 4 ปีที่แล้ว +2

    Yalna léne yallah faye sen xol wallahi Sénégal yeup contane 🇸🇳 🤲🏼 mashallah

  • @aminatadiop8205
    @aminatadiop8205 4 ปีที่แล้ว

    Alhamdoulilah Alhamdoulilah Machalla Machallah Yalna YALLA fayal niou lén liguén bii raféte n'a trop téyite amna solo yite 2s yalna sén diam yagg

  • @mariatoumane8371
    @mariatoumane8371 4 ปีที่แล้ว +19

    Amine thi Niann yii mais man je ne comprends pas les gens qui dislike c'est quoi leurs problèmes au juste

    • @rokhayatoure6770
      @rokhayatoure6770 4 ปีที่แล้ว +2

      Moy gniy khekh l'islam rek Ay mbam khoukh lagnou

  • @bbfa4763
    @bbfa4763 4 ปีที่แล้ว +3

    Machallah tafsire Gaye yalla n’a yalla wéraleu bateu bi ❤️❤️

  • @rokhayathiam9735
    @rokhayathiam9735 4 ปีที่แล้ว +2

    Tafsir yalla nalla borom bi lafal thiat si barké mouhamed je t'aime fort bilay

  • @gliglydiagne5490
    @gliglydiagne5490 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah yalla nalènnn Yalla fayy sènn Kholll té bayilènn basi kanama kanamm té ande akk wergui yaramm si barké Mouhamed (psl)🙏🏾🥰

  • @assanethiam4112
    @assanethiam4112 4 ปีที่แล้ว +1

    Amène Louma beu n'guona wakhe bou Yague,moye :nous sommes pressés bilaye que le mois du RAMAAN arrive à cause de vous ALHAMDOULILAHI .PRIONS les pieux pour que DIEU les protège, les couve ,leur donne longue vie ,santé, augmente leur connaissance profonde par la grâce du PROPHÈTE MOUHAMED (P S L)

  • @fachandiaye8188
    @fachandiaye8188 4 ปีที่แล้ว

    amna solo yallana yalla defalla diam si barki werou koor bi

  • @Moussa98.3fm
    @Moussa98.3fm 4 ปีที่แล้ว

    Ma cha allah...uztaz...ma cha allah..Yalla faye la yiw....barké seidyna Mouhamed ..psl

  • @cityomar1729
    @cityomar1729 4 ปีที่แล้ว +2

    Fa tabarakalla eskey El hadjii Tafsir
    Mala sope boulaye deguelou sama khôl Day toy Amin Amin Amin chérif aidara respect djeuredjeuf

  • @maododiack166
    @maododiack166 4 ปีที่แล้ว +3

    Yall nagnou yalla fayal cheikh seydil hadji malick sy rta Tafsir yall nala sunu borom faye si daradjey seydina mouhamede salla lahou aleyhi wa Salam El hadji samb yall na léral bamelam machallah xol sed na❤✌

  • @sodandiaye846
    @sodandiaye846 4 ปีที่แล้ว

    Machallah machallah yalna yalla wèral bat bi li nèkh na kène dou seydina Muhammad psl

  • @hassyarassoul2540
    @hassyarassoul2540 4 ปีที่แล้ว +3

    Bilae Tafsir nimala sopé mane ak yallah rk nioko kham. J donnerai tout pour juste te rencontrer ayy koumay cii diapaleo😭😭

  • @matarsarr3483
    @matarsarr3483 4 ปีที่แล้ว

    yalla nala yalla fay kou beugua wakh amine ma beuss j aime
    kou beuss j aime yalla nako yalla soutoural

  • @fatangom5339
    @fatangom5339 4 ปีที่แล้ว

    Yalla na sounou borom sam leine ta bolei leine si deuk ak rassouloulay Mashalla

  • @ousseynoudieng2184
    @ousseynoudieng2184 4 ปีที่แล้ว

    Mass mbégeu Yall na yalla kharé ko aldiana firdawsi si Barké yontés bie

  • @cheikhomardiao5294
    @cheikhomardiao5294 4 ปีที่แล้ว +1

    Allahdoulilah je remerci tafsir Gueye je suis un sope de mouhamad paix salut sur lui je regard emission suukarou koor

  • @sambasene8507
    @sambasene8507 2 ปีที่แล้ว

    Machala ya oustaz tafsir yalna sa diam yag barki borom touba

  • @salioufall8120
    @salioufall8120 4 ปีที่แล้ว +2

    Yalla naléne fii yalla bayii té mayléne wérrgou yarame seriff ak yafssirr gaye

  • @alimatoufall6957
    @alimatoufall6957 4 ปีที่แล้ว

    Machala tafsir alkhour Anna dafay déme thi khol yalla nanou yalna khir thi bopam

  • @moussademe380
    @moussademe380 4 ปีที่แล้ว

    Amna solo y'all na y'all godal say fane

  • @amadousall9820
    @amadousall9820 4 ปีที่แล้ว +4

    Machalla bilay jai des larmes aux yeux Qu'Allah le tout puissant protege tout les musilmans du monde amine et bon Ramadan à nous tous 🙏😘

  • @OumouInsa8709
    @OumouInsa8709 4 ปีที่แล้ว

    Masha'Allah Yalna yallah wéral batt bi yokou sen jam ak sen soutoura ak sen fane

  • @adamagueuye8269
    @adamagueuye8269 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah xoll sédd na yalla na yalla fayal gnou léne si barké nabi 😭😭nékhna trop douma si doyal 🙏جزاك الله خيرا❤❤

  • @salimatakonate5332
    @salimatakonate5332 4 ปีที่แล้ว

    Bilay,yalla nala yalla lafal thiate,mayla wer ak goudou fane amine machalla nekhna torop❤

  • @fatoufall4874
    @fatoufall4874 4 ปีที่แล้ว +1

    Machala yalna yalla goudal séne fane yokou séne xam xam

  • @SenegalMavie_Tv
    @SenegalMavie_Tv 4 ปีที่แล้ว +1

    Bilahi sama beugn metti na khassida sindidi ladone deuglou mouy sedd Gouy walahi anzim seydina Mouhamad 🙏🙏🙏psl amoul morom

  • @modoudiene8170
    @modoudiene8170 4 ปีที่แล้ว +13

    Yéne niouy beuss👎louy séne problème am daguéne am fébar xoll❤️yalla nalén yalla safara fékheul
    Séne xoll