Franchement chapeau cheikh pour ce parlons en , et surtout les nuances dans la musique sénégalaise actuelle , en parlant au passage de vj , j'aimerais bien le voir ici 🙏❤️
Pour moi iss da guis neh rambakh bi mo geneu dokh a ce moment rambakh bi mo occupé top 10 bi si plateformes streaming yi même coté vues yi jeli amadeus 18million choix 16 millions confuse wally 34millions dawalal samba 14millions teh bignou guéné même pas 6 mois di battre des millions de vues pour moi bougnou continuer nonou rambakh bi dina percer les frontières si 2024 bi même les pays Afrique francophone bi dagni consommer rambakh bi boubakh bo dougué si clip yi dangay guis sen ay commentaire appréciation avec leurs drapeaux du pays
J'appelle ça Wolofbeat ou Mbalax Fusion: • Samba Peuzzi - Dawalale • Samba Peuzzi - Forawle • VJ - Yowe La • Iss 814 - Noce • Iss 814 - Dof ci Iow • Viviane - No Stress • Mia Guissé - La vie est Belle • Mia Guissé & Wally - choix • •
NOS RAPPEURS, MBALAKHMAN, PRODUCTEUR SERIES, etc.... TOUS LEGUI LOVE REK IL Y A PLUS AUCUNE ISPIRATION ON ENTEND PLUS AUCUNE HISTOIRE, QUEDAL. QUE DU JE T'AIME TU M'AIMES!!!
@@apg-senegal. Il y a mieux frere, des choses you geneu dokh mais ils ont juste pas d’inspiration et les cou*** de faire autres choses. Par exemple un café avec sa a changer les choses et relevé la barre pareil dip a fait des innovations mais depuis c’est toujours pareil.
@Iss814 t’es un crack certes, je respect ta pensée mais suis pas d’accord avec toi. Toi, Amadeus, Vj, Samba, Jeeba et pleins d’autres artistes lingen diii def mbalakh la geuneu diéguei. La fusion, oui juste côté lyrics car on sent nettement que vous gardez toujours la plume d’un rappeur. C’est vrai que ce que vous faites est plus posé que le mbalakh traditionnel mais pour dire vrai y’a pas une grande différence et selon moi c’est du Mbalakh à 90%. Et je trouve pas de mal à assumer que vous faites du mbalakh du moment où vous payez vos factures, votre public s’élargit, vous décrocher des contrats que même les vrais rappeurs n’arrivent pas à avoir… Alors que demander de plus? Soyez libre et faites ce que vous voulez et le jour que vous assumerez, y’aura plus ce débat. Merci pour ces bonnes Melo mais encore une fois « ASSUMEZ ». Ps: c’est mon opinion personnelle.
Cheikh si tu pou avais diminué la lecture des questions sur ton téléphone. Ce serait plus professionnel c’est juste un conseil Sinon affaire Yi nice na trop
Vidéo akbess bi depuis que tu l’as annoncé chaque jour ma khole douma giss dara a la damay yakarni dama high ndéké moy lolou , come on cheikh upload that video
Iss ne sait pas qu'il fait le rap-mbah c'est le nom qu'il vous faut. Mais rap mom défato ko dit le et on avance. et arrete de dire que le rap ne va pas évoluer ici
Franchement chapeau cheikh pour ce parlons en , et surtout les nuances dans la musique sénégalaise actuelle , en parlant au passage de vj , j'aimerais bien le voir ici 🙏❤️
Invitel one lyrical
@@OusmaneKhouma-s5jmogui kaaw
Gnou tambeli kepou kou neck si ay diafé diafé yalla na yalla takhawou si barke Seydina Mouhamed ❤🙏🏾
Peace and love le. Chef
SALLALAHOU ALEYHI WA SALAM
Cheikh nkm vj lagn sokhla wayy
Waw chekh akbess next time okay we need akbess the legend always
Iss 814 je suis de tout cœur avec toi tu a bien parlé déff dara bah paré meune ko argumenter yomboul té toi tu la fait big up
Franchement cheikh dengua atanul akbess 👑 qw
Cheikh akbess akbess 😢😢😢😢 akbess way cheikh
Cheikhou job bi Nice na trop et on réclame VJ maintenant ❤❤
Entoucas fusión bi nekhna 😂
Bay cheikh ioe franchement bougo andi akbess 👑 qw
Et chapeau chiekhe c'est super bien
ISS borom bakh heun Bly ❤🎉
Akbess akbess akbess akbess akbess akbess nous voulons interviewer de akbess
Chiekh mayniou akbess way svp 🙏
Merci beaucoup frère ❤️ ❤️
Continue comme ça 💙 parce que tu es en train de faire une excellente travail 🎉❤
Pour moi iss da guis neh rambakh bi mo geneu dokh a ce moment rambakh bi mo occupé top 10 bi si plateformes streaming yi même coté vues yi jeli amadeus 18million choix 16 millions confuse wally 34millions dawalal samba 14millions teh bignou guéné même pas 6 mois di battre des millions de vues pour moi bougnou continuer nonou rambakh bi dina percer les frontières si 2024 bi même les pays Afrique francophone bi dagni consommer rambakh bi boubakh bo dougué si clip yi dangay guis sen ay commentaire appréciation avec leurs drapeaux du pays
Ahh weiy
J'appelle ça Wolofbeat ou Mbalax Fusion:
• Samba Peuzzi - Dawalale
• Samba Peuzzi - Forawle
• VJ - Yowe La
• Iss 814 - Noce
• Iss 814 - Dof ci Iow
• Viviane - No Stress
• Mia Guissé - La vie est Belle
• Mia Guissé & Wally - choix
•
•
Le premièr👏🏾👏🏾👏🏾
Merci cheikh ❤
Le meilleur ❤
Iss 814 mome rek nga gnou dessèlone mn Gas🫡
Bien ISS❤❤
Avec mist cash way❤
Big love iss814❤on t'aime 🎉
Iss zouk lay def legui
Sokhla nane tallbi dh stp 🤲🤲
Burna boy modone wah afro fusion mais Iss fusion tout court Kone nice 😅
NOS RAPPEURS, MBALAKHMAN, PRODUCTEUR SERIES, etc.... TOUS LEGUI LOVE REK IL Y A PLUS AUCUNE ISPIRATION ON ENTEND PLUS AUCUNE HISTOIRE, QUEDAL. QUE DU JE T'AIME TU M'AIMES!!!
Mais nak lolu moy dokh frere gnom aussi ils doivent de leurs arts 😊
@@apg-senegal. Il y a mieux frere, des choses you geneu dokh mais ils ont juste pas d’inspiration et les cou*** de faire autres choses. Par exemple un café avec sa a changer les choses et relevé la barre pareil dip a fait des innovations mais depuis c’est toujours pareil.
Cheikh on reclame akbesss 🎉
Nice ❤
iss 814 reke
Iss toudenako fusion
On réclame le vidéo de akbésss😢
The king iss814 🔥👑🐐
@Iss814 t’es un crack certes, je respect ta pensée mais suis pas d’accord avec toi.
Toi, Amadeus, Vj, Samba, Jeeba et pleins d’autres artistes lingen diii def mbalakh la geuneu diéguei.
La fusion, oui juste côté lyrics car on sent nettement que vous gardez toujours la plume d’un rappeur.
C’est vrai que ce que vous faites est plus posé que le mbalakh traditionnel mais pour dire vrai y’a pas une grande différence et selon moi c’est du Mbalakh à 90%.
Et je trouve pas de mal à assumer que vous faites du mbalakh du moment où vous payez vos factures, votre public s’élargit, vous décrocher des contrats que même les vrais rappeurs n’arrivent pas à avoir…
Alors que demander de plus?
Soyez libre et faites ce que vous voulez et le jour que vous assumerez, y’aura plus ce débat.
Merci pour ces bonnes Melo mais encore une fois « ASSUMEZ ».
Ps: c’est mon opinion personnelle.
Dioxko love no Cheikh con na😂😂😂
May 4em yakamti akbess nk
Bravo cheikh
Cheikh si tu pou avais diminué la lecture des questions sur ton téléphone. Ce serait plus professionnel
c’est juste un conseil
Sinon affaire Yi nice na trop
On réclame Tall bi😊
Cheikh vidéo akbess khana dafa am problème
Guys kou beug guiss VJ beusseul j’aime
cheikh mushei ou rien 🤩🤣😂
Iss 8 14 Mo Nékh Néna Samba peuzzi R rappeur la 😂😂😂😂
Wa cheikh mbeur yy khana bouko niou 😅😅
❤❤ iss
Iss814 fait de la mélodie selon moi
Mr6 frr❤
Sètlou nguenn invité cheikh yii kènn mounoul wakh tè mentionné woul dipp
Cheikh footstyle do niou invitel ngaaka blindé svp 🙏
Invitel dane❤
On réclame jay21 pour la prochaine fois inchallah
Khana akbees dafa supprimer bok yage n'a dé nomu démé nounu😢
Harrrr na beh sorna ❤
Man dama hamut sh 😅
On réclame samba peuzzi ❤❤❤
Kokou rombou na déjà
Iss seul🎉
Kou yener cheikh 200k abonnés Inchallah ❤🎉
❤🎉😊
Isss leu
Cheikh boule foget canabasse
Moi je l'appelle Pop-Mbalax. On ne peut pas refuser que c'est de la musique urbaine.
Iss 814 sku sku
Cheikh liguey bi migui nice dh mais demal guena cultiviwou koi
Mafi jiito
Cheikh kham nga les « Dalton » remaqué wo si dara
Vidéo akbess bi depuis que tu l’as annoncé chaque jour ma khole douma giss dara a la damay yakarni dama high ndéké moy lolou , come on cheikh upload that video
Beats bouy daw si souf kouko defare 😂😂
Meuna watt ni Cheikh , iss Daf laaa teek xell si questions Rap bi AK mbalakh bi 😂
Tontouwoul baa legui nii ay fusion rek lay tontou😂😂
Jeeba et Amadeus font du afro
❤❤❤❤
Iss da fokk ni bicrave fekoul gnou xam ko
Manam Iss xamoul ni mom bamouy Rap Siiw neu
Invitel One Lyrical stp
Cheikh invite diaynaba Thiam
Mane cheikh sa son bi si souf rek moma nehoul quoi 😅
C'est tout simplement du Rambakh
Gni loudoul mbalakh gnounéh rap
Mais Cheikh yaw masso inviter mbeur dh bouma dioumoul. Wala niom bokou niussi. Invitel modou Lo
Iss seriyé woul koi 😂
❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤😢🎉🎉🎉🎉
Refet n'a troop
🎉
On réclame akbess prochaine vidéo inch'Allah
Iss montero😂
On réclame vj
Invitel momo beat
Ismaïla talla
iss814🎉🎉❤❤❤
Cool bro nio nekone Fac Droit
Iss814 j'aime beaucoup ta musique
On réclame cannabasse
Cheikh yaw rek ya diape ni vj deyy mbalakh ms vj nieup khamnagne ni loumouy def dou mbalakh ,rap la gueuneu diégué sakh ,Amadeus pareil ,mia guissé pareil
Ehn bon mane d kom cheikh loum wkah khamétouma rapp ak mbalakh 😮💨
Ba wakhoul wakhou dof rek
Tall bii nitou Thiès
Vj
Iss ne sait pas qu'il fait le rap-mbah c'est le nom qu'il vous faut. Mais rap mom défato ko dit le et on avance. et arrete de dire que le rap ne va pas évoluer ici