Jeeba - Saï Saï Feat Dieyla (Clip Officiel)
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 7 ก.พ. 2025
- #saïsaï
#jeeba
#dieyla
Saï Saï disponible ici africori.to/saisai
Jeeba à Paris🇫🇷 Achetez votre billet ici : lamarbrerie.fr...
Auteur : Jeeba
Interprète : Jeeba - Dieyla
Compositeur : diamond guidem
Mix Mastering : Afro Music Studio Sn
Réalisation : Mao Sidibé
Production : Abadane Daiman
Stylisme : Bise Collection - Teranga Lounge - Cana Dom
Jeeba et Dieyla proposent un cocktail musical inédit, l’histoire d’amour dénonce les mensonges et dérives des couples d’aujourd’hui.
Le son se veut drôle et raconte en interposé un récit de deux couples aux ambitions différentes et malhonnêtes.
Lyrics
Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï saïiiii la fok ma xolate ko
Wadjii Saï saïiiii la
Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
fok ma xolate ko
Wadji Saï Saï la
yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Couplet
Nieuw na sama lathté fa sama yay boy
Saï Saï la
Nieuwate sama keur lathté fa sama baye boy Saï Saï la
Néna kilifa la dou dokh thi tank thiakhane
Ñente ak tranche indi gouro dadi labane
Mingui may tek tank beug ma forcé ray
Ndéké loumou beugone dougal but bi jubilé daw Refrain
Yala dou dioum mani Yala dou dioum Loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na bay xalate nar ko diox sama xol Ndéké souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ndaw ci Saï Saï la
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Néna koudoul mane beugoul sokhla woul
Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul Mane mako yeungal yeungal mbeguelam Ndéké mane dama door ay calmant lamay diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor
Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole
Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop
Refrain
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol
Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Dara genoul nekh Wakh tou diouli diote gua dem dem diouli 🥰🙏🏿
Bilahi
Billahi ❤
leip loy deif ba diouli diote bayiko nga deim diouli djii 🤍🙏
In shaa Allah
Deugue bou werre
Histoire dinako binde gnari xalei you meuneu wayy t kene doulene degue si dara machalah 🎉❤
Bilaye boulénn nékhon togue dh concurrence
Tt a fait ay example lagn
❤❤❤
Dieyla elle a bien assuré vrai ndanane la bonne continuation bravo Nice single ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤
Ndeyssane homme et femme les sai sai sont partout yalla nagnou yalla mousseul ❤❤❤❤
Dieylaa machalah dafa meuna weuye😢😢😮😮🎉
Wally , Amadeus et Dieyla affaire bou doy warr lay done Dieyla elle est pétri de talent elle déçois jamais
Manii deGglu leen meuh . sa meuh hel bu Gatt laay waheii naq. Etant un grand fan de Coumba Gawlo Seck je trouve que Dieyla Gueye est la plus belle voix de tout le Sénégal .
C vrai
C vrai
Diap xalé yi di nakh rek gourou Sénégal yi sopékoulén té diéma mélange comme man 😂
Ya foot sa bop nonu archiiqsatv😂😂😂😂😂😂
Yeeewaay 😮😂😂😂😂
Kone qsa do gorou senegal mdr 😂😂😂
Diaroul commentaires comme bolèna si 😂 bopam 😢
Yaw dagama thiakhale 😂😂😂 khesa
Jeeba et dieyla ,comme dhabitude texte et melodie au rendez vous ,1M de j'aime pourvleur donner de la force.
La plui bll tyfa guisss la meilleur tiktokeur mauritani
Motah koulen moytou woul si reuthiou rek ngay deukk 😢bel homme bel cœur ❤️ moko guen😮😢 djiguen gni kolen guiss mou beugg lenn té yen lenn diam Diap len si boulen ko bayi ndakh chance boobu beuretoul gni takk masque beurri nagnou lool sakh goorgni tamite gnoussi beugg am sokhna beurrinagnou trop wayé dagno gnémé toull khaleyi legui gnoussi Beurri seysi wouniou dagnouy seeet si bou nékhé gnou tokk bou nakharé gnou daww😢😮
*Je salue le choix porter sur ce sujet la franchement ça c'est arrivé au bon moment le monde est cruel et les porteurs de masque sont partout donc vigilance,becareful vigilance 👏🙏*
Machalla borom batte you nékh Yi khallé you ame talent yi laf bouche❤❤
Ei Wai tyfa mabo qui est la pour elle 🥰😘
Mxjphh x ojpcxpppfpwfp :;
Nous 🎉🎉🎉🎉❤
Moi
Moi
Moi
Après l'amour c'est la Ndeye guerre 😂😂
Sai sai lagnou rk les hommes 🙄🤧😂😂
Mane bokou masi dé😂
😂😂❤j'espère Que sa papa bokusi😅il es homme non wala😊
Vs les femmes kholate lene sen bopou mo guene legui game gasta gasta la rk solene bayiwoule douniou bayi wa salam
Man bokkuma ci de.
Ba bolei gassi sa baye
Gambian but Senegalese music is literally the best..elegance ❤
Macha'allah yallah Nala yallah weral batbi bi si barké Seydina Mohammed Saw ❤️👌
Notre tyfa nationale ♥️🔥🔥🇲🇷
Salla Lâhou hanlâ Mouhammadine ❤
Lii wow na kongg😂❤❤❤❤ machallah way🎉🎉❤❤❤❤
Deux jeunes exemplaires. Meun way machallah, correcte, class t ken degoulen si dara
Dieba cv koula bayi gua nangou pèruque bi 😂mais li nekhna trop oh Sama xol bi 🎉🎉🎉❤
Kou dacor ni daga. Nekh RK lalale cœur ❤
Fi laye tokk Di xar Aka ma âme temps😂😂😂
dieyla gnoune goore gua beuga tégg gathié ni si garouwalé😂😂😂😂😂
Yeneu niar nieup ay say say gueneu wakhe tane bi nekh na 😂❤ YALLA DOU DIOUM NICE PROD🎊🎊
Man yekhna kham duot bou nekh bi waay ❤❤❤
Never Say never 😮...
Dieyla sa voix bi manou'mako mougn
Jeeba et dieyla les meilleurs j'espère que c'est une très bonne chasson youpi 🎉🎉
Dieyla ya meune kay❤❤❤❤ MashaAllah
Dieyla et jeeba meilleurs❤❤
Kii tayf guisse la walla❤
Notre Mauritanien❤🎉
mauritaniene*❤🎉
Djeyla j'aime trop ta simplicité
1:00 Di soumekkou comme si ce n'est rien fait 😂 tathiou bi meuna ma rey 😂
Machalla tyfa tu es meilleure wlhi ❤❤❤❤❤ félicitations et bon continuation à vous tous
Dieyla tu est mon chanteur préféré bonne continuation
Dieyla mon chanteur préféré borom Oxelo diama
Jeeba il a une manière de rhymer la vraiment bravo a eux 🎉❤
OHH NEKH NA SURTOUT PARTIE DIEYLA Bi PAROLES YOU AM SOLO ❤❤❤
Wa yenn Monsieur Biosen100😌😂😂
Notre champion ❤Jeeba ❤🎉
@Diamond to the world 🌎 you making us proud 🇬🇲🔥🔥🔥
Dieyla / Jeeba yen lii nexna deh 🕺🤗. Breff gayi daniouko bokk rek Goor ak Djigene ay saï saï laniou 😩😂
boul bouy tourné leu rk ndakh gniy bakh niongui bakh be legui
La beauté de notre Tyfa Nationale ❤
Dimon giddem 🔥🥁
Encore notre tenor dans l’arène musicale 🎤 Jeeba le boy❤
C super machallah bonne continuation a vous c magnifique
Bon continuation mn f'ans ❤
La voix de #Dieyla🥺😫❤️🤧
Le clip est top quelle scénario 🔥
❤🎉brava félicitations❤ t'aime beaucoup c'est ça ♥️😝 toi et moi trouve-moi le l'argent de djebba
Machallah 🎉🎉🎉qui est là pour tyfa
No jeeba et dieyla j'avais déjà pense à leurs feet c'chanson est vraiment très bien merci mais il reste avec dieyna 😂❤
Quel vérité absolue c'est sa un rappeur
Bouna motakh ma guiss clips bi 😅🎉
Le meilleur duo des deux grands talents de la musique sénégalaise
Nehoul ba nehoul wayer la voix d djeba c autres choses Machalla 😊
On est fier de Tifa ❤🎉
Li dafa khéré sama dieyla vraiment c’est du ouf dieba Machallah ❤
Elle est juste wawou machala laf thiate ma belle❤❤❤❤
On est fier de toi Jeeba wa Thies
Wouy samay préféré Ay way kou deff 💓😍🎉🎉🎉
Auuu voix dieyla bi cœur waay ❤😍🙆
JEEBA doora tina benen bombe lii way nekhna🎉🎉
Duo dieyla diéba yagu nako demander
Tyfa ndekete kayy saiy saiy 😂😂belle clip entt cas
Jeeba le meilleur ❤
Li nekhna Machalla laf thiat xalei yiiii rék la topou man 🎉🎉🎉❤❤❤
Love from Gambia 🇬🇲 ❤️ 💕
Bilay goor yii danio doy war douniou def dara xi merci mais dou nieup yam tmt 😂 wayé amna djiguèn you meun mbarane tmt nioy yobè sèn bopou xi lounek😏
Vous êtes les meilleurs ❤🎉
It’s already on repeat 😊🔥 yena meun nak
Issa Mo fi inedii ak kane
Notre tyfa national 🎉🎉
Jeeba ne déçoit jamais 😂😂
Chaque fois qu’une personne mettra un like je reviendrai réécouter ce chef-d'œuvre 😊❤
Elzo Jamdong Saï Saï laa 😂😂😂
Un remix des paroles de Omar Pene🎉🎉merci li défaut cramé Yallah d'où Dioum alhamdoullilah 🥰
jeeba ft Dieyla big up
Café Touba lay nann ni Sax ☕😂😂😂
Voix d'or yéna meilleures waay🎉❤
Machlla nekh na yalla bakhna❤❤❤❤❤❤🎉🎉
Machalla à vous dieyla je te beugué méneu 😂❤i love you❤❤❤❤❤
Bilakhe mou mana waye bilakhe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Ho la voix de Jeeba❤big respect
Félicitations 🎉
Dieyla Gueye machallah ❤❤❤
Longue vie à ns ❤🎉
Mes artistes préférés ❤ Dieyla ak Jeeba
Machalah lou xere wayy ❤❤much love to you guys
Bou ñeep nékei say say foun dieum 😂😂
Pourquoi pas un album comme Coumba gawlo et souleymane faye ❤
Biosen100 mo nei si clip bi ni😂😂
Wayyy acoustique waala slow diaroul djiguenè Di mathie ay tougne ....na gorè wayy
Mashallah 🎉🎉🎉🎉🎉tyfa guisse Mashallah
Son bi nekhna nak❤❤❤Machallah
Naic na trop machallah
Vidéo bou Reftena machallah ❤