Mashallah si jangalemi , rafet na. Wayi mourid dale, likko soss moddi kham jeumi yallah ji souobhanahou wa tahala. Tariqa yeup, linene djour moy guindi jamyi si sene borom, kham yallah si jeumam ja, si touram yi, ak si melom yi. Touroukh yeup li mo donone seni yite. Donc mouy mouridou cheikh abdoul qadir jili, wala mouridou cheikh ahmadou tijani, wala, ahmadou Chadhilli, ak cheikh ahmadoul khadim, li lene war moy kham sen borom, li si dess yeup ak gueunele la rek.
Serigne Abdou samd Mbacke yalnala fi yalla yagall ti wiralla
S Abdou Samad yak nagafi yag te wer amin
Dieureudieuffa cheikh abdou samad souhaibou m'backé 🙏
Masha.allah Alhamdoulilah ❤❤❤❤❤❤❤
Eskeuy dieureudieuff mbacké ❤
dieuredieuf sérigne bi yag fi wer amna solo si léral bi ak répartition khassidayi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashallah si jangalemi , rafet na. Wayi mourid dale, likko soss moddi kham jeumi yallah ji souobhanahou wa tahala. Tariqa yeup, linene djour moy guindi jamyi si sene borom, kham yallah si jeumam ja, si touram yi, ak si melom yi. Touroukh yeup li mo donone seni yite. Donc mouy mouridou cheikh abdoul qadir jili, wala mouridou cheikh ahmadou tijani, wala, ahmadou Chadhilli, ak cheikh ahmadoul khadim, li lene war moy kham sen borom, li si dess yeup ak gueunele la rek.
Macha Allah amna solo lol
❤❤❤❤❤❤❤ dierediefety serigne touba
Machallah ❤
❤❤❤
Ola