*Gris a fait trop d’années blanches, il a eu bcp de blessures, et il eu un accident électrique. Lolou motakh mou perte sa forme physique et compétitive. Malgré lolou yeup il est resté dans la cours des grands pendant toutes ces années, teh combat chocs rek leu beuré (Modou Lo, Balla Gaye, Eumeu, Yekini, Bombardier, Tyson, Zarko). Champion leu negn ko respecter.*
Voila merci nagnou ko respecter mane li gnouye deff Gris daf ma méti te bombardier moy sama Mbeur ! Bayile se ligueye keneu douko wakh goor! Courage Gris ❤
J'apprécie le respect qu'il à envers son ainé. On voit ses encouragements et son soutien total dans ces moments dures. Mais les amateurs ont leurs mots à dire. Maodo doit comprendre que Gris n'est plus à son niveau. Il a baissé les bras depuis sa revance perdu contre Eumeu. Un gris, vif et decisif s'est retrouvé tres timite dans l'enceinte et ne surprend guère. Seule la grandeur qu'il incarne lui permet d'avoir des combats. Alors que la lutte c'est une discipline de groupe. Les entrainements et contacts au sein des ecuries constituent un mélange et que les différences sont une richesse. À Fass il y a tout. Si Gris avait bien pris sa carriere et etre serrein dans ses entrainements, le battre ne sera pas facile malgré son àge. A vrai dire mok Bomb combat la, bouñou paré ande jubilé inchaallah.
lamb mo teureudi rek mes fouki zarko gris molenne meune mes gris kéroke dagniouko téyé fep li natureloul gris koukoye dane tamite dinala tek lou méti mes yalla bakhna du courage champion gris seul ❤
GRIS BORDEAUX DE TOUT CŒUR AVEC TOI BOUL BAYI NIEUWATAL AK ENTRAÎNEMENT BOU WOUR gni nioy say adversaires BOMBARDIER, TAPHA TINE , ALIOUNE SEYE 2 , GÉNÉRAL MALIKA AK GOUYE GUI ❤❤
Griz 2 nak billhi j t’estime bien vraiment beug nla trop ndax sa yar ak sa meun communiqué ms wahal sa mak deug koi vraiment diote mou teik affaire yi bayilén guéne dokhal mngui diégalou nak ms à part llou nako gayi dieul diote na nak gua beuré billhi nitte geunoula billhi niguay takhawo mbeurou fass Yi raféte na yalnala yalla takhawou inchallah ❤️🙏🏽🤲🏽
Gris deux il na qu a récupérer ce que gris bordeau à perdu. La confiance, et le l'empathie de la communauté lebou. Faire un tour des grandes maisons et des penthieu...parce que tout à commencé la bas . Mais niakeu yité mom nit yi tek lafi rek.....surtout wa medina nga khamni ki la ci geuneu ndao mola eupeu foula Retour à la source Et regain des supporters...voilà mon conseil a gris deux et lac rose ect.........
Waxou Maodo bi d lima si ndiàgué moye gris dafa entraîné lou yaramam attanoul.Exemple Gris dafaye tok Lou yagueu dou entraîné légui sou amé combat beugueu raye boppam moye waral mouye fébar parsk il a pris l'âge lolou mo dal sax tapha Gueye 2. Maodo aussi ni rk la meuneu waxé parsk gris magam la mais sincèrement gris mome doyna koi. Supporter aussi performance mokoye déf mais danou dane,daanou dane do ame mboolo. Yaw ak Serigne Ndiaye mome amnaniou yaakar si yééne mais médina aussi dou deukkou lambeu
SATHIES ROYAL SI GRIS 2 NIMOU MÉL AK MAGAM ❤❤ MASHALLAH YAROUNA , DÉGEUL NAKO , SOUTENIR NAKO , XADIALOUL MIDÉF SI DIGEUNETÉ MAGAM GRIS BORDEAUX ❤ TÉKSI DIOKH KO THIEUR , ROUSS KO TÉ KOU DEF WALA WAX LO WAROUL WAX MAGAM MOU FATHIE KO TÉ MOUSOUL XADI DI NÉKEU SI GUINAW GRIS BORDEAUX ❤❤
Problème bi Moy ken dou guiss plus de 50 millions ou plus di bayi beuré gris pour moi bayi beuré dal fok prometteur yi ignorer ko comme bombardier yobou ko retraite silence
GRIS BORDEAUX BILAHI WALAHI YAY GÖRE FÉBAR MAIS BEGEU SAUVÉ BESS BI ndeysann ba tay louné nga déggko 😢😮 nafékeu yi disi profito 😮 BOUL BAYI DÉ RAYANETÉL ENTRAÎNEMENT LOU MÉTI NIEUWATT TERMINÉ EN BEAUTÉ INCH'ALLAH 🙏🏽❤
Gris2 vs Sa Thiés Gris2 vs Alioune Seye2 Gris 2 Vs Jordan Gris2 vs Gora Sock Gris2 vs Général Malika Gris2 vs Fils De Balla Gris2 vs Moussa Ndoye Gris2 vs Quench
Boy déréte mo fore rek mais gris défatoul d'ara si lamb ji na bayii 10ans sans victoire moi en tant que supporter fase dotuma dieund billets pour gris billahi
Gris 2 gonoye daara mashallah dou ame complexe do complexer je t'apprécie beaucoup mashallah. Je te souhaite une belle carrière. May ley boy Gris 2 chance way ani sa thies ani alioune seye 2 mi combat teu djeuleule boy bi!
Vraiment Gris bordeaux est victime d'un acharnement! Qu'on le laisse terminer sa carrière tranquillement ! Lamb mo gatteu khel rek. Courage grand Gris❤
Maodo nous t estimons beaucoup Nous sommes Fassois Mais dagua nekk di diapalé sa Grand Gris dafa wara bayii La relève est déjà près depuis fort longtemps Si tu t’en estime incapable Serigne Ndiaye 2 et Ada Fass sont là
Féne rek guéne meun bayilén di yakk combat promoteur yi di simuler ay blessure ak ay malade ,Dara diotoulen bouguene di dieuli avance Dara doulen diote Mai’s bouguene dano rek niou deg sen febar ,liko febar Len rek la nopalou bou yagg ba quelques mois gua beug tekk sa yaram loum atanoul Lolou nak c impossible athlete day nek si maintient de forme .
Est-ce que dou distance bi mo sori arène nationale rek man parcelles la deuk chaque combat dokh aller retour ba arène nationale lay def ak gayi dougou stade .en tout cas dal legui lamb kou amoul mobilisation BOU bakh Ken doula bayi xel mo dal mbeurou fass sauf Ada fass
Meme bo blesser diokhel sa bop dooor niari coups you dalll meme boy danou grawul mai pousso passa baniu nela teudal nga teud meme si c moi souma damer sakh dina door zarco soga danou😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Gris 2 dieuleul Gouye Gui nga yék si kaw. Aprés nga khar entre Ama ak franc koussi danou nga dieul ko. Gnari combat yoyou bokay dane di bokoussi Vip yii. Aprés gars yii sakh gnoy beugg beuré ak ioe pour yékk
J'aime cet homme 👌🏾 J'aime sa façon d'être, yalna la yalla sam takhawou la ❤
Ndeysane dérét dafa fort billahi ❤😱🥺🙏
Dafa duegou dh😮
Beu Gris daano dimanche dama dioy nakh xam nani diambar leu Yalla nako Yalla defal diam.❤
Respect gris2 toujours des paroles bcp de sens sans vexer gorr yalla deug je suis parcellois mais je t'admire frére
*Gris a fait trop d’années blanches, il a eu bcp de blessures, et il eu un accident électrique. Lolou motakh mou perte sa forme physique et compétitive. Malgré lolou yeup il est resté dans la cours des grands pendant toutes ces années, teh combat chocs rek leu beuré (Modou Lo, Balla Gaye, Eumeu, Yekini, Bombardier, Tyson, Zarko). Champion leu negn ko respecter.*
Voilà toi t'as tout compris
Voila merci nagnou ko respecter mane li gnouye deff Gris daf ma méti te bombardier moy sama Mbeur ! Bayile se ligueye keneu douko wakh goor! Courage Gris ❤
@lacitoyenneafricaine8566 bilahi walahi yaw merci bcp
@@Zam-Zam710 gno far compatriote.
Merci infiniment frère gris 2 gris bordeaux yageunaniou bégeul niongui si guinawam Bouy nékh AK Bouy méti
Bilahi ya gorè
Yaye gor nitt dey gorer. Merci.
J'apprécie le respect qu'il à envers son ainé. On voit ses encouragements et son soutien total dans ces moments dures.
Mais les amateurs ont leurs mots à dire. Maodo doit comprendre que Gris n'est plus à son niveau. Il a baissé les bras depuis sa revance perdu contre Eumeu. Un gris, vif et decisif s'est retrouvé tres timite dans l'enceinte et ne surprend guère. Seule la grandeur qu'il incarne lui permet d'avoir des combats. Alors que la lutte c'est une discipline de groupe. Les entrainements et contacts au sein des ecuries constituent un mélange et que les différences sont une richesse. À Fass il y a tout. Si Gris avait bien pris sa carriere et etre serrein dans ses entrainements, le battre ne sera pas facile malgré son àge.
A vrai dire mok Bomb combat la, bouñou paré ande jubilé inchaallah.
Maodo un vrai jambaar ci kaw ci kanam inchaAllah courage à Gris bordeaux, le meilleur reste à venir inchaAllah
Merci beaucoup Gris 2, Sa Combat ak Général Malika warna takhaw wala Fils de Balla.
Maodo il communique bien machalah 🥰
Gris 2 beug nala❤
Machala gris 2 yalla nalla yalla soutoural
C sa un frère ont soutiens son sang🩸 malgré les difficulté ✌️✌️
lamb mo teureudi rek mes fouki zarko gris molenne meune mes gris kéroke dagniouko téyé fep li natureloul gris koukoye dane tamite dinala tek lou méti mes yalla bakhna du courage champion gris seul ❤
Ma cha Allah 💕 frère toujours pertinent dans tes propos ❤
Merci beaucoup waa albourakh évents ❤mé encouragements à Gris Bordeaux ❤ félicitations à Zarco
GRIS BORDEAUX DE TOUT CŒUR AVEC TOI BOUL BAYI NIEUWATAL AK ENTRAÎNEMENT BOU WOUR gni nioy say adversaires BOMBARDIER, TAPHA TINE , ALIOUNE SEYE 2 , GÉNÉRAL MALIKA AK GOUYE GUI ❤❤
Ak boy niang siteu sa thies dèsè nako na dieuli 2 combat bayek mom
@Leuzsonko oui t'as raison aussi
Dia rama gris 2 . Dieureudieuf si taxawoubi rak day beug maguam
Serein, posé , bref très bon!! Hyper pertinentGris 2 ❤
bien eduque et bien parlé
On est de tout cœur avec notre frère de la médina gris Bordeaux❤❤❤❤❤
Griz 2 nak billhi j t’estime bien vraiment beug nla trop ndax sa yar ak sa meun communiqué ms wahal sa mak deug koi vraiment diote mou teik affaire yi bayilén guéne dokhal mngui diégalou nak ms à part llou nako gayi dieul diote na nak gua beuré billhi nitte geunoula billhi niguay takhawo mbeurou fass Yi raféte na yalnala yalla takhawou inchallah ❤️🙏🏽🤲🏽
Oh état d’esprit bi gris 2 am souko sathies amone 😭yalla baxna !
Billahi gris 2 toujour day défendre magame
Manmom yawe maoda Gris 2 yawe laye wakhe du courage ndakhe ninga buegué sa mak machala ❤
Gris deux il na qu a récupérer ce que gris bordeau à perdu.
La confiance, et le l'empathie de la communauté lebou.
Faire un tour des grandes maisons et des penthieu...parce que tout à commencé la bas .
Mais niakeu yité mom nit yi tek lafi rek.....surtout wa medina nga khamni ki la ci geuneu ndao mola eupeu foula
Retour à la source
Et regain des supporters...voilà mon conseil a gris deux et lac rose ect.........
Machallah vèrite absolu vraiment ❤❤❤❤❤
Boul fallei gainde gris est un legende de fass et mérite tigre de fass cest pas donné a tout le monde
Yalla nako yalla Same . C’est un vrai guerrier Life bi Mo incertain rek!!
merci maoda tu es très gentille dicourage dieux est grand
Dieu avec grand D
@@mouhamedseck4260sans oui grand D mais sans X aussi ,comme tu veux corriger va jusqu’au bout.
@@boubacardiallo1454merci 🙏
Comment faire pour trouver un frère comme lui ?
Toujours là pour son frère,il s'en fiche s'il a tord ou pas.
Bravo 👏🏾👏🏾
Billay frère c rare d'en trouvé un frère comme gris2 en tout cas mane beugenako
C’est rien tout il à seulement reçu une bonne éducation à travers les daraas
Louma merone rek sama khol sédena merci gris
Machallah très bien mo frère ❤❤❤❤❤
Vraiment j'apprécie ce gars. Il communique super bien.
Prochain combat yalla ngako yalla may ndam inchallah leep dina bakh gris 2 yaw champion nga
Tu as dis la vérité
Ma challa champion vraiment beugeu naa Rack bou Mel ni Yow yalla nala yalla Arr
Machallah diam ci yow ❤❤❤
Je l’apprecie trop ce gar ki yoroul sakh jikko mbeur
Frère lou leer nga wakh mais gris 1 na santé yalla dou trokh yalla soutoural nako machallah ❤❤❤
Frère de sang
merci frere
FrR iow lolou diekhna tay Bilay walahi iow Amal combat rk ngua khôl digua khamni yay borom ndakarou barki cheikhou tidiane ❤
Maodo vrait champion ❤❤❤
Waxou Maodo bi d lima si ndiàgué moye gris dafa entraîné lou yaramam attanoul.Exemple Gris dafaye tok Lou yagueu dou entraîné légui sou amé combat beugueu raye boppam moye waral mouye fébar parsk il a pris l'âge lolou mo dal sax tapha Gueye 2.
Maodo aussi ni rk la meuneu waxé parsk gris magam la mais sincèrement gris mome doyna koi.
Supporter aussi performance mokoye déf mais danou dane,daanou dane do ame mboolo.
Yaw ak Serigne Ndiaye mome amnaniou yaakar si yééne mais médina aussi dou deukkou lambeu
SATHIES ROYAL SI GRIS 2 NIMOU MÉL AK MAGAM ❤❤ MASHALLAH YAROUNA , DÉGEUL NAKO , SOUTENIR NAKO , XADIALOUL MIDÉF SI DIGEUNETÉ MAGAM GRIS BORDEAUX ❤ TÉKSI DIOKH KO THIEUR , ROUSS KO TÉ KOU DEF WALA WAX LO WAROUL WAX MAGAM MOU FATHIE KO TÉ MOUSOUL XADI DI NÉKEU SI GUINAW GRIS BORDEAUX ❤❤
Mais gris 2 Aline seye 2 gris 2 générale gris 2 fils de balla combat la mais mbeur yi danou beugue lou nooye mais yalla bakhna
Merci gris2
Ah oui Gris Bordeaux même souy danou dafay beuré et j’avais personnellement dit que Gris n’est pas dans son état normal.
Mais cette fois ci il a lâché...
Pask il est malade beugeu sauvé bess bi
Yen dall kou danou ngueen ne da febar 😂
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
C’est mon lutteur préféré je l’ai toujours respecté ! Mais c’est la fin na bayii balla mouy gnaw guirr yalla
Problème bi Moy ken dou guiss plus de 50 millions ou plus di bayi beuré gris pour moi bayi beuré dal fok prometteur yi ignorer ko comme bombardier yobou ko retraite silence
très bien parlé Maodo. Nieup ngi nane na diokh Maodo mais Maodo gor ngeu
Bravo gris 2
GRIS BORDEAUX BILAHI WALAHI YAY GÖRE FÉBAR MAIS BEGEU SAUVÉ BESS BI ndeysann ba tay louné nga déggko 😢😮 nafékeu yi disi profito 😮 BOUL BAYI DÉ RAYANETÉL ENTRAÎNEMENT LOU MÉTI NIEUWATT TERMINÉ EN BEAUTÉ INCH'ALLAH 🙏🏽❤
Nice discussion franchement
Gris2 vs Sa Thiés
Gris2 vs Alioune Seye2
Gris 2 Vs Jordan
Gris2 vs Gora Sock
Gris2 vs Général Malika
Gris2 vs Fils De Balla
Gris2 vs Moussa Ndoye
Gris2 vs Quench
Jordan kay 😅 kokou bokatoul si lamb😅
@@madiodiogueye590😂😂😂😂
Merci sauf Jordan way mo
Bien parlé Gris2.
Mon frere sportif dou yarr birre
Machalla ❤️
Gris 2 manne king limalaye conseil moy yaw nala entraînement raye
Saway gris doyna lac rose peut le remplacer
Wax na dëgg nag am wax yoo xam ni bañeel la😂😂😂😂😂😂
Kou Danou febar thiey lamb
Boy déréte mo fore rek mais gris défatoul d'ara si lamb ji na bayii 10ans sans victoire moi en tant que supporter fase dotuma dieund billets pour gris billahi
Gris 2 gonoye daara mashallah dou ame complexe do complexer je t'apprécie beaucoup mashallah. Je te souhaite une belle carrière. May ley boy Gris 2 chance way ani sa thies ani alioune seye 2 mi combat teu djeuleule boy bi!
Rakeu diou mélni guiri 2 ak baye Ndiaye kounékeu beugue nako😢😢😢😢😢
K tu le veuilles ou pas cest un frein pour vous .nous avons vu ce cas avec Tyson et eumeu. Il a fallu quitter pour emerger
Vraiment Gris djappal sa rakk bii kou beug gris mougui nii tu as defendu ton frere partout
Ndeysane yaw rek la yeureum moi mounouma faral kaine koudoul gris me da weré torop
Yalla bakhena
Gris 2 Sa Thies moye combat bi
Gri2 dou moromou general milika
Gris deux geumeul yalla lou takh mbeur bou daaanou di woute layy 😅😂😂😂😂😂
Ya meune féen limou wax degeu la
Macha'allah
Gris 2 dèmale le 2 thi tournois 10 million bi
Vraiment Gris bordeaux est victime d'un acharnement! Qu'on le laisse terminer sa carrière tranquillement ! Lamb mo gatteu khel rek. Courage grand Gris❤
Gris 2, gris bordeau ken bagnouko si lambji mais mais il est temps mou decroché il ne peut plus en vrai dire
Maodo borom bakhh ngua mais Grand bi entraîné woul comme il faut vraiment quoi
Gri 2 a prafètma région
Wakhouniouko mou bayi mai nay entrene dakh baboy bimoy bayi mogui ak doli Kone sou beugué continue na deme ligueye yi😅
Maodo nous t estimons beaucoup
Nous sommes Fassois
Mais dagua nekk di diapalé sa Grand
Gris dafa wara bayii
La relève est déjà près depuis fort longtemps
Si tu t’en estime incapable
Serigne Ndiaye 2 et Ada Fass sont là
Ada Fass Nékoule Ecry Fass
@ je sais c’est un potentiel tigre en devenir qui sait à l’avenir il peux rejoindre l écurie Fass
Sathies royal si gris 2 fonk na Magam dakay defendr
Gris 2 wakhal Gris bordeaux degue na bayi lambe tee soutenu laa lolou moy degue 😂😂
Sama waye ga lollll yawe laye supporter mais général sa potentiel adversaire la bayile li gaye wakhe
Gris d'ara neka toufi
Oui mais Gris n’a cas sortir et s’adresser aux fans et supporters. Mais gars yi sounou dano 2 semaines do léne guiss
Gris deux ñiko niemei beuriwul
Féne rek guéne meun bayilén di yakk combat promoteur yi di simuler ay blessure ak ay malade ,Dara diotoulen bouguene di dieuli avance Dara doulen diote Mai’s bouguene dano rek niou deg sen febar ,liko febar Len rek la nopalou bou yagg ba quelques mois gua beug tekk sa yaram loum atanoul Lolou nak c impossible athlete day nek si maintient de forme .
Masla ak rafetal mo yakk rewmi. Douma wax ken bayil wayer fouleu ak fayda yakoy mayy sa bopou.
Un sportif de haut niveau ne doit pas avoir se genre de forme
Blh frr wakh nga deug dhé
Wakh na deugu wa fass dougnou mobilisé lolou rek mo takh
Est-ce que dou distance bi mo sori arène nationale rek man parcelles la deuk chaque combat dokh aller retour ba arène nationale lay def ak gayi dougou stade .en tout cas dal legui lamb kou amoul mobilisation BOU bakh Ken doula bayi xel mo dal mbeurou fass sauf Ada fass
Mais gagner plus de 50 millions ci ben Fann lolou nekhna deh
❤❤❤❤
Meme bo blesser diokhel sa bop dooor niari coups you dalll meme boy danou grawul mai pousso passa baniu nela teudal nga teud meme si c moi souma damer sakh dina door zarco soga danou😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Sen formou yi da khwi😊
Gris 2 dieuleul Gouye Gui nga yék si kaw. Aprés nga khar entre Ama ak franc koussi danou nga dieul ko. Gnari combat yoyou bokay dane di bokoussi Vip yii. Aprés gars yii sakh gnoy beugg beuré ak ioe pour yékk
Il veut couvrir la défaite
Sa thies vs gris 2 nak combat bou logique leu
Bilahi sénégalais mo sokhor quoi
Wakhal deugg gris sa way