Thiow Am na dé : Le marabout de pokola doumako andi contre talpha ndakh Amoul...

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 14 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 12

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel วันที่ผ่านมา +1

    Do dara😂do yalla do touss. Pokola yalna yalla soutoural la mayla ndam bou sédd gouy ci kaw Talfa amine🤲

  • @MouhamedNiang-du3fi
    @MouhamedNiang-du3fi วันที่ผ่านมา +2

    Say dougnou ngaka 😂😂 cinéma guendi def pour tourniou leumdeul wayé bouleen Tal djappé Inshallah🫢

  • @afro3827
    @afro3827 วันที่ผ่านมา +1

    Saway té ga dem séti lenen serign dou topou mbeur

  • @matarndiaye3496
    @matarndiaye3496 18 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Sénégal nékfa Serigne yombe na

  • @seringembacke9316
    @seringembacke9316 วันที่ผ่านมา +1

    Pokola baol baol bi yala nako yala may ndiam ci barke serige saliou mbacke 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @ChiekhmassambaDioum
    @ChiekhmassambaDioum 20 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Serigne Bouy topo mbuer ya am diott

  • @BadouMbaye-tn5hg
    @BadouMbaye-tn5hg 6 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Video bi yag na bayi len yéé fitneu ay seytané nguen

  • @SeydinaMboup-x6d
    @SeydinaMboup-x6d วันที่ผ่านมา

    Pokola wadjie nite kou bakhe la

  • @TiendaTienda-q3y
    @TiendaTienda-q3y 10 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Khamoul gate

  • @NdeyeNdiaye-p7f
    @NdeyeNdiaye-p7f วันที่ผ่านมา

    Borom darou bayil lep mou séd yow borom bakh nga