Mbaye Sy Ndiaye quitte Wally Seck, Bouger ketchups fait dè térrible révélations..« Wakh léne Wally

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 27 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 122

  • @khadyly1787
    @khadyly1787 16 วันที่ผ่านมา +6

    Entièrement d’accord nitt kene douko torokhale je ne souhaiterais pas q l’histoire se répète comme avec ses autres cousins Mbaye s’y ndiaye sama Diambi djieugeudi woma !! Machallah yAkofi wayone wally K la paix revient entre vous Amineyarabi alamina

  • @marcoramirez2811
    @marcoramirez2811 16 วันที่ผ่านมา +17

    Linguey Def bakhoul, bou ay nit amei problème, dangassi wara wakh louy defar mais pas louy yaakh

    • @papefaye272
      @papefaye272 16 วันที่ผ่านมา

      Tu n'a rien compris qui show bizz lay deff

    • @matydiallo3211
      @matydiallo3211 16 วันที่ผ่านมา +2

      @@papefaye272dimbaliléne nit gni ak showbizz showbizz bo khamni daguay fékk ay mbok diléne diakhassé té mbaye sy ak wally dioté wouyou dara

    • @papefaye272
      @papefaye272 16 วันที่ผ่านมา

      @@matydiallo3211 yaw koula lathie teudieul sa badio bi tei noppi

    • @matydiallo3211
      @matydiallo3211 16 วันที่ผ่านมา +2

      @Doméram nga motakh nga nieuw dima wakh li comme amo argument wakh bou bone rekk ngama meneu wakh wayyé boussa ndeye teudié bossam ba paré nga wakhma

    • @Bill-s3v5e
      @Bill-s3v5e 16 วันที่ผ่านมา +1

      @@matydiallo3211merci maty ❤

  • @modoundiaye7985
    @modoundiaye7985 17 วันที่ผ่านมา +15

    Boulén faté ni boucher mo dém ba magal touba di diakhasé sokhna aida diallo AK Serign saliou thioune maname yaye AK dome diakhasé gouy gui AK balla gaye kone ki mome wakh deug yalla domoukharam deug deug la

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา +1

      Bayi fofou rk pour mom dagnou faté lolou

    • @Lopios-g6l
      @Lopios-g6l 15 วันที่ผ่านมา

      Aida loumou am dieul thi seune baa..

  • @NdeyebatySow
    @NdeyebatySow 16 วันที่ผ่านมา +10

    Boucher deug rek ngua wakh dafa wara respecter ay mbokam

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck 16 วันที่ผ่านมา

      😂😂😂 tu le crois ni DIF nguene rekkk ki daye sauwww

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา

      Ki Loumouy wax gueumoussi dra mar tat lay def yaw mom nefekh gua

  • @amethfall5009
    @amethfall5009 16 วันที่ผ่านมา +2

    Pape Diouf vraiment je ne l'ai jamais vu mais c'est un responsable et il est très correct

    • @Diasposen
      @Diasposen 15 วันที่ผ่านมา

      ​@@Lopios-g6l De un, Wally MAK la, il a 40 ans en 2025. De deux , président de la république bassirou diomaye Faye 4 ans rek la mague Wally. Aux âmes bien nées la valeur n'attend point le nombre d'années

    • @Lopios-g6l
      @Lopios-g6l 15 วันที่ผ่านมา +1

      @@Diasposen et la maturité tu l'a place où..

  • @lefootballsansfrontieres8921
    @lefootballsansfrontieres8921 16 วันที่ผ่านมา +9

    Je suis Un grand fan de wally mais wah nga deug d

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา

      Yaw mi diapalé bouché yen gniar yéna yam rk ay doul kat Guen Wally amoul défaut il est direct et responsable d'où hypocrite yaw mom bayil fen

    • @lefootballsansfrontieres8921
      @lefootballsansfrontieres8921 16 วันที่ผ่านมา +1

      @ mdr Cëye yalla bal nala sokhna aida
      Adouna amoul solo

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 15 วันที่ผ่านมา +2

    Bilaye lou rafet daffa rafet adouna amoule solo

  • @abibgaye6693
    @abibgaye6693 15 วันที่ผ่านมา

    you right bro ❤

  • @FabienneSylla
    @FabienneSylla 15 วันที่ผ่านมา +1

    Je pense que c’est pas un manque de considération envers Mbaye Sy mais il évite de rencontrer certains membres de sa famille dont le courant ne passe pas bien entre eux

  • @AidaGoudiaby-yc1cj
    @AidaGoudiaby-yc1cj 16 วันที่ผ่านมา +4

    Pape diouf ay nitam yeup pa dem ngua begue tass faramaren domerame bi nafek

  • @ibrahimatidjany9202
    @ibrahimatidjany9202 16 วันที่ผ่านมา +1

    Merci boucher du courage et bonne continuation ❤

  • @SerignefallouDiouf-bo3ny
    @SerignefallouDiouf-bo3ny 16 วันที่ผ่านมา +2

    Deg la de da wara respect gayi

  • @LamineSarr-ro4by
    @LamineSarr-ro4by 16 วันที่ผ่านมา +2

    Bouché wakh gah deugue na respecté gayi

  • @maiba9210
    @maiba9210 16 วันที่ผ่านมา +3

    Dougal fo khath sa yone nékousi ay famille laniou

  • @Vikingsénégalais
    @Vikingsénégalais 17 วันที่ผ่านมา +5

    😂😂😂😂 Boucher réw nga

  • @JosephineCamara-qu1gt
    @JosephineCamara-qu1gt 16 วันที่ผ่านมา +2

    Sa yone nekkoul si digante Wally ak mbaye Sy topatol sa problème gno bokk Khady seck ak thione seck bayil diakhasse bi ak doul bi dougnou yone nekkoul si sa digante ak Pape Diouf

  • @MaodoGueye-h8s
    @MaodoGueye-h8s 17 วันที่ผ่านมา +4

    Lidatille sa problème mon gène ga lidanti wally ak mbaye si ndiaye

  • @AmadouMar-s2f
    @AmadouMar-s2f 16 วันที่ผ่านมา +2

    Merci Boucher

  • @fatoukinedialoo3876
    @fatoukinedialoo3876 16 วันที่ผ่านมา +2

    Oe beurrii ndei wakh dh🙌🏾

  • @GallayeBéye
    @GallayeBéye 16 วันที่ผ่านมา +2

    Dafa wara ame respect

  • @AbdouFaye-d1c
    @AbdouFaye-d1c 16 วันที่ผ่านมา +2

    Loulerr la wkh man fans wally la mais comportement bime yorr yakar ni li dou diekh lepay diekh dagua ladioul macky rekkk

    • @dembaba604
      @dembaba604 16 วันที่ผ่านมา

      Bi dou yoyou saway ki kéne manoul si mome dra

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา +1

      Bayil doul do fans Wally yeureumo Wally comment il s fatigu pour ses fan enchaîné ay son sans son programme chargé guay comparé AK Macky yaw vrai dof gua gnoun Wally rk lagni top

  • @maimounandiaye4667
    @maimounandiaye4667 16 วันที่ผ่านมา +3

    Sa yoneu nékoussou
    Trouves d'autres sujets
    Toi même tu te nourris de wally parce que si tu ne parles pas de wally personne ne te regarde.

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 15 วันที่ผ่านมา

    Mbaye Sy ndiaye dou meussa bayi wally seck dakh nio bok bén mame

  • @maimounandiaye4667
    @maimounandiaye4667 16 วันที่ผ่านมา +2

    Boucher c quoi ton problème
    Khanaa dagnalaa yoni sii wally
    Tu veux éclater son groupe ou quoi

  • @BathieDiaw-c8l
    @BathieDiaw-c8l 16 วันที่ผ่านมา +4

    Mane dé khawma dagaye comédi ou dagko contre mai liguaye wakh ni degueleu bou ler sakh boy Wally maturoule Mane n'a faye mai matoule patron wakh degue la lath nak

    • @matydiallo3211
      @matydiallo3211 16 วันที่ผ่านมา

      Keneu ladioula sa avis yakk boucher yéme ay seytané gueneu

    • @aidajuf8377
      @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา

      Wally esk guenoul mature sa papa sa papa sou yorom plus 50 emploi dilén fay do wax li Wally limou gnémé AK responsabilité bimou yenou sa bay atanoul quart bi Wally ken yabouko Sénégal

  • @MamishouTraore
    @MamishouTraore 16 วันที่ผ่านมา +1

    AMNA YAYE YOU GUENE SA NDEYE FOUF TE DEMOUNIOU MAKÀ’DOMERAM

  • @MoussaNDOUR-s9i
    @MoussaNDOUR-s9i 16 วันที่ผ่านมา +3

    Je suis parfaitement d’accord avec toi bouché il faut que wally revoie sa façon de faire avec ces employés

    • @azizdiop7316
      @azizdiop7316 16 วันที่ผ่านมา +1

      Et c’est à boucher de dire à wally de revoir son comportement 😢😢 boucher un ennemi de wally non

  • @AbdouAkimeMbodj
    @AbdouAkimeMbodj 16 วันที่ผ่านมา +2

    DEUG rék ga Wah DOF bi

  • @antadiop8806
    @antadiop8806 16 วันที่ผ่านมา +1

    Deugue rékh gua wakh

  • @MbayediopMbaye-o7s
    @MbayediopMbaye-o7s 17 วันที่ผ่านมา +3

    Yawe louye ca probléme khana amo liguéye wally goudi wally soube munite yabile domou diambour come deume

  • @senesene2550
    @senesene2550 16 วันที่ผ่านมา

    Khame gua dagua khéwi té Thi Wally rek gua meune diare pour gniouye wakh Thi ya sa artiste yi meunougnioula khéwale mo takh gua tope Thi Wally di wakh rék amo béne classe moufe

  • @salioumbackeba9595
    @salioumbackeba9595 16 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam seytané yakh nala

  • @falloudioume3824
    @falloudioume3824 16 วันที่ผ่านมา +3

    Yowe vrai fegue gua meuno lindianety sa afaire

  • @KhadyGaye-n5g
    @KhadyGaye-n5g 16 วันที่ผ่านมา

    Ki mome sou wakhoul si Wally seck dou ame beuz ms nak fater nani Wally seck moye Senegal ok

  • @Papiblack-i7k
    @Papiblack-i7k 16 วันที่ผ่านมา +4

    Bo nampé wénou saytané saytané ngay don bo napé wenou fénkat fénkat ngaye don

    • @nafisene5335
      @nafisene5335 16 วันที่ผ่านมา +1

      😂😂😂😂

  • @fallelhadjiabdoulaye2347
    @fallelhadjiabdoulaye2347 16 วันที่ผ่านมา +1

    Deug rek gua wah boucher

  • @DiomeDIOR-iq4mw
    @DiomeDIOR-iq4mw 16 วันที่ผ่านมา

    Seytané gua des bayil famille diambour guay divisé mmbaye boula déglo ma khamné kou wayadi laa mbaye ligua bokou boul khar niou wola.tes Paris bigay wakh nonou bofi doré kéne sa adouna yakou surtout gua dor sans papiers c'est finis fofou laye diare am papiers

  • @Diagne-ek7fc
    @Diagne-ek7fc 16 วันที่ผ่านมา +1

    Deugue rek gan wakhe vraiment surtout niou bokk li niou bokk rafetoule nak vraiment

  • @ModouDiallo-z2j
    @ModouDiallo-z2j 16 วันที่ผ่านมา +3

    Wakh deug yalla deug dou rombi ay nop

    • @azizdiop7316
      @azizdiop7316 16 วันที่ผ่านมา +1

      Ki deug laye wakh tu. Crois 😮ki c’est un ennemi de wally qui est juste la pour le détruire amoul leineine ni nei deug la wakh reike seytanei nga nafeikh nga

  • @MatarDieng-d1w
    @MatarDieng-d1w 16 วันที่ผ่านมา

    D'où aferou stars de guiss nga. Linga wakh,la dadoul dem fofou mo takh dafay rouss

  • @ndoyelebou3132
    @ndoyelebou3132 15 วันที่ผ่านมา

    Yaa gniaaw

  • @kadjagaye6530
    @kadjagaye6530 16 วันที่ผ่านมา

    😂😂😂

  • @kumbasarr1444
    @kumbasarr1444 17 วันที่ผ่านมา

    Wally bankhass samyee lennyu tass bi manager Euro , MBYE Sy ndaiye who is next . Wally needs help

  • @MoMbye-u1y
    @MoMbye-u1y 16 วันที่ผ่านมา

    Nukal sa ndaye

  • @yattadiao3793
    @yattadiao3793 15 วันที่ผ่านมา

    Kéne ladioula

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 15 วันที่ผ่านมา

    Boudé lolou amna waly teguou guo fena

  • @Lupinanz
    @Lupinanz 16 วันที่ผ่านมา +1

    Degueu rek ngué warkh

  • @AdjiaFall-j4o
    @AdjiaFall-j4o 15 วันที่ผ่านมา

    Seyetanégua

  • @fatouloum3639
    @fatouloum3639 15 วันที่ผ่านมา

    Bouger yaw daga am problm

  • @aidajuf8377
    @aidajuf8377 16 วันที่ผ่านมา

    Goor day def yeufi nafex baxoul fi seytané hadjoul sen diguen yaw sa groupe pape diouf tass na gua beug yak ramdan

  • @AbdoulieCham-bx3cf
    @AbdoulieCham-bx3cf 16 วันที่ผ่านมา

    Wally falleh wul ken hana

  • @ndeyemourseye6010
    @ndeyemourseye6010 15 วันที่ผ่านมา

    Yaw seytanè gua domou nidiaye domou badiane lousi sa yone eupeul gua dé

  • @BinetaGningue-u4k
    @BinetaGningue-u4k 16 วันที่ผ่านมา

    Sa sarap ndeye

  • @AbdoukarimDieng-il5ch
    @AbdoukarimDieng-il5ch 17 วันที่ผ่านมา

    A ounzoubilahi mina Saytane rajim yaw liguay wahni ndiabotou dadjal rek nga bokou yallah reub na kouy yé fitna

  • @nenesall4636
    @nenesall4636 16 วันที่ผ่านมา

    Eyeu dougàl fo khétheu

  • @marcoramirez2811
    @marcoramirez2811 16 วันที่ผ่านมา

    La première fois, waly guisnako bakhol ko siy beut diko khamalni c pas joli linguey Def.
    Bouko répéter, waly amna droit corriger ko

  • @KineDiop-qx8xm
    @KineDiop-qx8xm 16 วันที่ผ่านมา

    Mais bouchet lou khew ak wally lanla😊

  • @kumbasarr1444
    @kumbasarr1444 17 วันที่ผ่านมา

    Howmaa guditel howmaa soubatel tycker yennaa gore gorrolu purr ramdan tass Wally su komprawutt ai mbokaam warr ko kompra . Mbaye sy ndaiye ak Wally derret tako lal siditt vta ko yaiyee Shaitan bi

  • @OppoMaroc-uo3xz
    @OppoMaroc-uo3xz 16 วันที่ผ่านมา

    Saytanai

  • @Sadagadio-j3q
    @Sadagadio-j3q 16 วันที่ผ่านมา

    Wally badola la

  • @OusseynouFall-c7m
    @OusseynouFall-c7m 16 วันที่ผ่านมา

    Yow mounoulo bayi wally yow seytane

  • @OppoMaroc-uo3xz
    @OppoMaroc-uo3xz 16 วันที่ผ่านมา

    Europ nogay ndamo wa nouchai ni nga maille

  • @MbayediopMbaye-o7s
    @MbayediopMbaye-o7s 17 วันที่ผ่านมา +1

    Chayetané

  • @NdiobaAnn
    @NdiobaAnn 16 วันที่ผ่านมา +2

    Yawe seytanéga

  • @ibrahimasylla258
    @ibrahimasylla258 16 วันที่ผ่านมา

    Boucher limouye wakhe gueumouko sakh donc yawe mi commenté bou si khotou boucher liguaye déff mba khameguani kousi wakh lou ñawe ya responsable bi

  • @aissatoubarry1081
    @aissatoubarry1081 16 วันที่ผ่านมา

    Ya bonn

  • @timfatra9468
    @timfatra9468 10 วันที่ผ่านมา

    Wally dafa rew

  • @azizdiop7316
    @azizdiop7316 16 วันที่ผ่านมา +1

    Sa leufeul ndaye yak mbaye sy nioune topou niou mbaye sy wally laniouy topou doul .

  • @AdjiaFall-j4o
    @AdjiaFall-j4o 15 วันที่ผ่านมา

    Doulle

  • @marcoramirez2811
    @marcoramirez2811 16 วันที่ผ่านมา

    Boucher yaw seytanei boureuy nga

  • @OppoMaroc-uo3xz
    @OppoMaroc-uo3xz 16 วันที่ผ่านมา

    Kon nga

  • @ThiawNdeya
    @ThiawNdeya 16 วันที่ผ่านมา

    Bossi guéné rk problème dou am seytané nga trop tanga bayi doul wally dou kouy trokhal nite nite kouné amnga droit dirigé say employé mrd

  • @PapaDieye-ym1tf
    @PapaDieye-ym1tf 15 วันที่ผ่านมา

    Yawe seytanè ga rèk

  • @NdioleBeye-k1d
    @NdioleBeye-k1d 16 วันที่ผ่านมา

    Sa yoone nékosi

  • @CheikhDiao-z9x
    @CheikhDiao-z9x 16 วันที่ผ่านมา

    Yawe gireyala manobayi wali yaw dala rayal satawe walalanela yawayabon teyaw loula wayewa gamer fi lala ragerage nake gamer yawe bayi domou diamourdi

  • @aissatoubarry1081
    @aissatoubarry1081 16 วันที่ผ่านมา

    Ki mo nafek

  • @mariamabojang9628
    @mariamabojang9628 16 วันที่ผ่านมา +1

    Why are you evil

  • @AdjaTraore-m8h
    @AdjaTraore-m8h 16 วันที่ผ่านมา

    Yaw naféke bou bone nga hamngani talibé Serigne Touba dou défe li

  • @azizdiop7316
    @azizdiop7316 16 วันที่ผ่านมา

    Mani boucher loumou wakh yeup danioukoko wakhlo Bilahi Walahi lou lerrr lalaye wakh . Wally na deifarou wate bou bakh takhawate bou bakh tji bopam ndakh li xeixou famille la na wouti na bayi xeile beineine marimbiste bou beisse etc….voilà aye domeiram lako seikheul

  • @NdeyeFall-o3e
    @NdeyeFall-o3e 16 วันที่ผ่านมา

    Amo diomb

  • @marcoramirez2811
    @marcoramirez2811 16 วันที่ผ่านมา

    Mbaye si c'est pas la première fois mou defko ndiolei

  • @BayemodouNdiaye-f6b
    @BayemodouNdiaye-f6b 17 วันที่ผ่านมา

    ioe Vire doumarame gy doul wayy

  • @Pénda-e3d
    @Pénda-e3d 16 วันที่ผ่านมา

    Yaw mi sèytanè gua dèh

  • @SambaBa-g1k
    @SambaBa-g1k 16 วันที่ผ่านมา

    Seytané bou kata leufal ndayam moy yow sa sikine bou niaf ndayam bii

  • @loelhadji100
    @loelhadji100 17 วันที่ผ่านมา

    Yaw nak ligay def ni bakhoul djoulit dou diakhasse

  • @NdioleBeye-k1d
    @NdioleBeye-k1d 16 วันที่ผ่านมา

    Yawe doulle

  • @KhadyGueye-y6x
    @KhadyGueye-y6x 17 วันที่ผ่านมา

    Eeeee nioune bou mbaysy demoule sounou yone nekoussy doulle yaw ak mbaysy

  • @aronadiallo9022
    @aronadiallo9022 16 วันที่ผ่านมา

    Ioe kattal sa ndeye. Seytané nga mrm

  • @tiiw7425
    @tiiw7425 15 วันที่ผ่านมา

    Yaw domeram ngua féen rékk

  • @kumbasarr1444
    @kumbasarr1444 17 วันที่ผ่านมา +1

    Howmaa guditel howmaa soubatel tycker yennaa gore gorrolu purr ramdan tass Wally su komprawutt ai mbokaam warr ko kompra . Mbaye sy ndaiye ak Wally derret tako lal siditt vta ko yaiyee Shaitan bi