Wallahi azim Mame tay dioy lo ngama ndeysane ligniy nane fo fékk gniy rétane o fond li léne meti beurina, et je vois q ni Mame internet lay wéteuli ko, diambar deugg nga li sou done mane salite na yagg na, machallah yalna la yalla sameu gueune la takhawou fi nga tolou yafi indi sa bop kone so woné wo wathi nga amal djam djou beuri❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Wayé sa dieukeur dji ak ay mbokam ay vrai domeram lagn thiey goro legui yi
Ôh Mame Coumba vous avez tapées fort Ndeyssane derrière chaque sourire se cache une mystère. Macha'Allah Mame Ndiaye a le bon sens de l'humour malgré ses vécus difficiles elle s'en est sortie la tête sur les épaules beugg aye waydiourame. Yalnagua féké sa dieurignou diabote.
Jusqu'à aujourd'hui je me disais que l'émission n'a pas de sens parsk dey ougni soutoureu. Mais avec l'histoire de mame Ndiaye et ses petits frère séparés à cause du divorce des parents je me suis rendue compte que certaines histoires doivent être racontées pour qu'on puisse prendre conscience de l'importance de la famille et la reconnaissance qu'on doit avoir envers ceux qui nous ont aidé pendant les moments difficiles 😢😢
Walaye ma belle adouna dafa méti Lounè amenafi divorces dafa méti so Amoul foule rék sa ndiabote Tass wala gnou yacou mais bravo les femmes battante qui veille sur leur enfant
Quand ma mère avait divorcé mon père voulait nous séparer moi ma sœur et mon frère ! Mais c'est ma mère qui lui à dit si tu ose séparer mes enfants tu auras affaire moi depuis ce jour là mon père n'a jamais osé nous séparer 😢😢
Yénamafi téyé ba 2heure du matin...j'ai vécu des choses qui ressemblais a ta vécue ...du courage..comme toi maintenant magui santé yalla bou bakh mon dernier enfant as le méme âge et tout comme toi pdt toute ma grossesse aussi guissouma sama dieukeur et mon ascension a été fulgurante aprés mon accouchement yalla rék mo wor ... Alhamdoullilah 😘
J'ai pleure pour cette confession de Mame Ndiaye .c'est aujourd'hui que j'ai su qu'elle est une vrai lionne une battante .yalla nala Serigne fallou takhawou fo Diar yonele.chapeau a Mame Coumba tu as tape fort❤❤
Gni done wakh mame ndiaye amoul loumouy def si émotion bi parce que wakh n’a lep si réseaux sociaux Legui guisguen ni nit dou wakh lep il faut séparer caf ak deug je lavez regarder comme moi Demay caf d ré mais quand je suis seule je pleure tellement dakh sama vécu la différence et q elle a réussi est sa je suis heureuse pour elle j’espère q mon jour viendra 😢
Bilahi da guay ré ci kanamou nieup alors qu'au fond nakar bi do kham sakh noy def. Nio yam dh. Ma gui dioy depuis 2009 en silence chaque jour. Devant nitt yi mane may souriante toujours.. Depuis khalèi. Té meussouma wakh ak keneu ci lima metti. Yalla bakhna.
@@muslima9599 malheur sur malheur j’ai déjà 31 ans sama yaye ganiou si nakar samay ay frère kou nek moungui doundou Lou meti ma nek ma deuk si ay déception say bima khalate Legui mou diex mou guena meti je comprends très bien c genre d situations mais nigne yi daniouy fogni dema yor fek may tite di deh ndax thiono
@fatimadiaw4352 yomboul.bilay mais bon Qu'Allah vous Assiste aussi. Di diouli di niane. La seule chose qui me soulage ce sont les duas. Écoutez aussi la sourate Al Waqia chaque jour et Al baqara. Cela Ira in shaa Allah. Et aussi faire chaque jour: Salallahou Ala Muhamad (20 fois ou plus ou même 3 fois). Et aussi faire après la prière de fadjr 450 fois Hasbounallah wa nihmal waqeel après gua niane suniu borom mou tegui nattou yi. Du courage sister.
Une émission touchante.Arretons de juger les gens. Chacun avec son histoire. Félicitations Mame Ndiaye, une belle femme. Courage et que Dieu t'assiste et protège tes enfants.🙏🏽
J'ai écouté religieusement ton parcours mais d'après mon analyse, le nommé FOU mérite bien d'être ton époux. On a vu l'exemple de notre cher prophète SAW avec Khadija plus âgée.
Moi personnellement je t’admire pour ta force et ta bravoure MACHALLAH yallah nala yallah sam ar la prsk référence nga si waloum ligey out ak bania niane ken force à toi mame ❤
*Machallah tu es une femme vraiment brave avec tt ce que tu as vécu tu n’as pas abandonné et maintenant t’es exactement là où tu voulais être force à vs le meilleur reste a vnir 💪🏽et courage c’est dure mais Dieu est avec vs tt ira bien Inchallah 🙏🏽moi je t’aime fort❤️*
J’ai regardé deux fois cette émission j’ai vécu les mêmes difficultés c’est pas facile de grandir sans tes parents mais Dieu merci aujourd’hui comme dit Mame j’ai réussi ma vie toute seule 💪🏼🙏
MashaAllah Mame Coumba et Mame Ndiaye émission bi amna solo. Mame Ndiaye Lat thiat, si sa wadiour yi ga fondé beugeu topetoléne. Si kaw si kanam reek. Mais j’ai vraiment aimé sa comportement si émission bi. Pleine de classe. Naga continuer Di dale - di wakh nnanke - Di dèfe nankhe. Yallah nalla Yallah di diampale si barkai Serigne Fadilou M’Backè 🙏🏾
Ou est la foi? Si chacun pouvait écrire son destin, y aura t il des parcours difficiles ? Les hauts et les bas c'est ça qui fait la vie et chacun fera de sa part d'épreuves une force ou faiblesse. Dire alhamdoulillah ala koulli hal est réel et le meilleur se trouve où bout de la patience c'est pas que religieux, c'est une évidence. Allah ne donne que à ses meilleurs soldats les plus rudes des épreuves
En écoutant Mame Ndiaye je me dis que je ne suis pas la seule à souffrir dans mon foyer les femmes sont très braves inchalah tu m'as donnée la force de tenir le coup ❤❤
Machallah mame yalla nala yalla same vraiment sa diar diar metti na magui soga setane confidence bamou diekh nakh Yow vraiment wakh dji lerna daw na yaram 😢❤
Cette émission nous apprend qu'il ne faut jamais jugé les gens parceque les réseaux sociaux présentent beaucoup de négativité surtout les Sénégalais une pays que je ne comprends pas ils aiment tellement dire du mal sur les autres juste pour leur déstabiliser.
L’enfant chérie de Pikine Fo awe yone leu nitte yiye wakh bouléne ndayi lidienti sakh ioe fo awe yone leu mame mou Ndaw sa khaliss yako liguéye sa dieukeur wané ngako ba nieup guisss ko kone tu as était s’insince long vie à tw chérie diam rek ngay ame thi barki serigne fallou mi nga yakar lo deff beugue naniou 🍏🍎on t’aime fort 💪 grande sœur l’aisse les parler 🗣️ tu es déjat confirmé
La vie est dur mame mais kou nek linga atane lala yalla di tek lingay wakh damako dounde motakh courage ma belle damay tok di dioy souma wété dafa meti ba do comprendre
Hoo mame machallah yalla nala brome bi same are la yire la ba finga beugue yégue nga yégue fa tu ets une femme brave vraiment li mo takhe ko khamoule waroko jugée
Dom yangui rawanté thi weydiour yi , mame ndiaye Yalla na yeikh wayé sa térangua bala mouy gueuneu feigne say weydiour xonn la guinaw ❤. Y a pas a chercher de midi à 14h kou téral say weydiour rzw say morom bilahi. Mame, boul takeu boul nann ndakh amgua nianou weydiour ❤❤❤❤❤très longue vie pleine de santé à toi ma fille chérie ❤❤❤
Ahh mame nak bett nga gnou bari vraiment bi calme bi dall bi posè niaaff ehh ndikkè milieu bou nek ak comportement wam .chapeau mame sama nawlè talibé fallou bi❤❤❤
Ndeyesane 😢😢 mame ndiaye tu m'as fait pleurer walahi quand on à battu ta maman et tu as répéter plusieurs fois dama ndiambote 😭😭😭😭 yalna yalla tawoula way
C est la première fois ms setane confession nakh mame ndiaye savon blh sétane nako 4 fois chaque jour ma sathie sama téléphone nou yaye blh walay ligua doundou meety naa sama bopou deh lalay kholei😢❤
Mame ndiaye tu es brave Machallah tu m'a fai pleuré ton passé n'a pas été facile ndeysane motakh arrêtons de juger les gens nite soko khamoul rek khamoko. Chapeau à toi mame coumba pour ton profesionalisme
Mame ndiaye teyy lala geuneu bgeuh ❤️tey lala gueneu fonk guen n’a diokh thier 🥰wallae diam rk ngey am do meun nek 😍liya takh ma deuk di dioy sama pape paix à sn âme 🙏🏿🕊️nagn outt barke barké bayy ❤
Wallahi azim Mame tay dioy lo ngama ndeysane ligniy nane fo fékk gniy rétane o fond li léne meti beurina, et je vois q ni Mame internet lay wéteuli ko, diambar deugg nga li sou done mane salite na yagg na, machallah yalna la yalla sameu gueune la takhawou fi nga tolou yafi indi sa bop kone so woné wo wathi nga amal djam djou beuri❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Wayé sa dieukeur dji ak ay mbokam ay vrai domeram lagn thiey goro legui yi
Mame diambar la Walay ndeysane elle a tout fait pour sa maman kou beugue sa yaye lalale coeur❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️
❤❤❤❤❤❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ôh Mame Coumba vous avez tapées fort
Ndeyssane derrière chaque sourire se cache une mystère.
Macha'Allah Mame Ndiaye a le bon sens de l'humour malgré ses vécus difficiles elle s'en est sortie la tête sur les épaules beugg aye waydiourame. Yalnagua féké sa dieurignou diabote.
Amine❤❤❤
Ndeyssane yalna yalla same la beug sa wadiour rk Moy gualadj
😭😢
Jusqu'à aujourd'hui je me disais que l'émission n'a pas de sens parsk dey ougni soutoureu. Mais avec l'histoire de mame Ndiaye et ses petits frère séparés à cause du divorce des parents je me suis rendue compte que certaines histoires doivent être racontées pour qu'on puisse prendre conscience de l'importance de la famille et la reconnaissance qu'on doit avoir envers ceux qui nous ont aidé pendant les moments difficiles 😢😢
Bilahi pour gni décourager Wone thi adouna
Walaye ma belle adouna dafa méti Lounè amenafi divorces dafa méti so Amoul foule rék sa ndiabote Tass wala gnou yacou mais bravo les femmes battante qui veille sur leur enfant
❤❤❤❤❤
@@ngonesaliou8347😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
Quand ma mère avait divorcé mon père voulait nous séparer moi ma sœur et mon frère ! Mais c'est ma mère qui lui à dit si tu ose séparer mes enfants tu auras affaire moi depuis ce jour là mon père n'a jamais osé nous séparer 😢😢
Mame Ndiaye dofoul déh bilahi walahi elle parle bien machalla
Mane dinker mame ndiaye la bègue pour la première fois ma sertane commencement ba fin 🥰🎉mayal lerne ma ❤ mame way ki diambar leu
Tout comme moi. Non mane mome Nima beuguer Mame Ndiaye comprendroumako
❤❤❤❤❤
@@beuguebarham5592 Bilahi ki nit leu 😍❤️
pareillement mangui dogua sétan émission bi bamou diékh
@@Dado1998Salman non nioune mame Rek leniouy topou
J'ai tellement pleuré que lo defati Dinako comprendre le pourquoi, tu es une lionne fonce et ne regarde pas derrière yalla baxena 😭😭😭
La partie la plus triste 😢qui m’a fait coulée des larmes c’est quand elle a parler de sa mère battu
Yallah rek mo meune atté
Même moi aussi, de chaudes larmes je t'assure
J'étais décourage sur la vie mais tu me donne le courage
Courage ❤
Le professionnalisme de mame Coumba on en parle 🥰
Ndeyssane lii moo takh doo meussa torokh bilakhi l'international bi diam rk ngay ame❤
😭😭😭
Nitt ki boko xamoul boul ko jugé mame t'es une femme brave merci de partager avec nous ton parcours ❤
Yénamafi téyé ba 2heure du matin...j'ai vécu des choses qui ressemblais a ta vécue ...du courage..comme toi maintenant magui santé yalla bou bakh mon dernier enfant as le méme âge et tout comme toi pdt toute ma grossesse aussi guissouma sama dieukeur et mon ascension a été fulgurante aprés mon accouchement yalla rék mo wor ... Alhamdoullilah 😘
courage a tw aussi
@@MamanrokhayaNIANG merci 😘
Mashallah yallana yalla doli takhawu yarabby
May len mame ndiaye ay❤️❤️❤️❤️way ki diambar leu Masta ma Cheri😢
J'ai pleure pour cette confession de Mame Ndiaye .c'est aujourd'hui que j'ai su qu'elle est une vrai lionne une battante .yalla nala Serigne fallou takhawou fo Diar yonele.chapeau a Mame Coumba tu as tape fort❤❤
Fou prend tes cœurs une personne très rare mashalla ❤️❤️❤️
Gni done wakh mame ndiaye amoul loumouy def si émotion bi parce que wakh n’a lep si réseaux sociaux Legui guisguen ni nit dou wakh lep il faut séparer caf ak deug je lavez regarder comme moi Demay caf d ré mais quand je suis seule je pleure tellement dakh sama vécu la différence et q elle a réussi est sa je suis heureuse pour elle j’espère q mon jour viendra 😢
Bilahi da guay ré ci kanamou nieup alors qu'au fond nakar bi do kham sakh noy def. Nio yam dh. Ma gui dioy depuis 2009 en silence chaque jour. Devant nitt yi mane may souriante toujours.. Depuis khalèi. Té meussouma wakh ak keneu ci lima metti. Yalla bakhna.
Ndeysane mame elle es forte elle a un vécu motax mou résister mouna tok si internet bi nék diambbar machalla
@@muslima9599 malheur sur malheur j’ai déjà 31 ans sama yaye ganiou si nakar samay ay frère kou nek moungui doundou Lou meti ma nek ma deuk si ay déception say bima khalate Legui mou diex mou guena meti je comprends très bien c genre d situations mais nigne yi daniouy fogni dema yor fek may tite di deh ndax thiono
@fatimadiaw4352 yomboul.bilay mais bon Qu'Allah vous Assiste aussi. Di diouli di niane. La seule chose qui me soulage ce sont les duas. Écoutez aussi la sourate Al Waqia chaque jour et Al baqara. Cela Ira in shaa Allah. Et aussi faire chaque jour: Salallahou Ala Muhamad (20 fois ou plus ou même 3 fois).
Et aussi faire après la prière de fadjr 450 fois Hasbounallah wa nihmal waqeel après gua niane suniu borom mou tegui nattou yi. Du courage sister.
@@fatimadiaw4352 dafa metti bilay do kham foy takhaw do am aussi kou la réconforter. YA Allah rek mogniy soutoural
Une leçon de vie ! Vraiment le pays est sur la bonne pente! Namome Nanou ce genre de débat ! Merci beaucoup l'équipe de SSP! Mame Ndiaye ❤❤❤❤❤❤❤
Une émission touchante.Arretons de juger les gens. Chacun avec son histoire.
Félicitations Mame Ndiaye, une belle femme. Courage et que Dieu t'assiste et protège tes enfants.🙏🏽
J'ai écouté religieusement ton parcours mais d'après mon analyse, le nommé FOU mérite bien d'être ton époux. On a vu l'exemple de notre cher prophète SAW avec Khadija plus âgée.
Wawaw
Mais nooooooooooooooooon
Nono nako déf domame rék
Man dhh khawma loutakh wayé mame ndiaye dama koo beugeu trop sakh khawma loutakh tay mogui nii dieul sama temps rkk pour sétan mame❤❤❤❤❤❤❤
Mame ya ngui ame class nî ngua togué ni❤
J'ai l'ai vu comme quelle classe posé ohh
Mame tay class la woter at calme la woter cela te va à merveille ❤❤❤
Mane ndeketé Mame rek la beugu Yallah nala Yallah ar machalah on t’aime fort notre internationale ❤
Moi personnellement je t’admire pour ta force et ta bravoure MACHALLAH yallah nala yallah sam ar la prsk référence nga si waloum ligey out ak bania niane ken force à toi mame ❤
*Machallah tu es une femme vraiment brave avec tt ce que tu as vécu tu n’as pas abandonné et maintenant t’es exactement là où tu voulais être force à vs le meilleur reste a vnir 💪🏽et courage c’est dure mais Dieu est avec vs tt ira bien Inchallah 🙏🏽moi je t’aime fort❤️*
Pour la première fois ma setane du début à la fin Mame rek lay topou gaïnde bi courage et bonne continuation ❤
J’ai regardé deux fois cette émission j’ai vécu les mêmes difficultés c’est pas facile de grandir sans tes parents mais Dieu merci aujourd’hui comme dit Mame j’ai réussi ma vie toute seule 💪🏼🙏
meilleur confession de lannee wakhdji tey na rafet na machalah mame yalla na la thiat sekhlou kou lay khar yalla na khadi du fond du coeur
Amine
MashaAllah Mame Coumba et Mame Ndiaye émission bi amna solo.
Mame Ndiaye Lat thiat, si sa wadiour yi ga fondé beugeu topetoléne.
Si kaw si kanam reek.
Mais j’ai vraiment aimé sa comportement si émission bi. Pleine de classe. Naga continuer Di dale - di wakh nnanke - Di dèfe nankhe.
Yallah nalla Yallah di diampale si barkai Serigne Fadilou M’Backè 🙏🏾
Ces vrais cherie mais bou dalle dou meuma diaye ay produit il faut mou rabakhe lolou la 😂 mais elle est brave machalla ❤
❤❤❤❤❤❤
ELLE EST DEPRESSIVE.... Nit meuno wéssou loudoule nit.. je me suis toujours dis qu'elle avait une tombe dans le coeur.. qu'Allah l'apaise inchallah
Ohhhh beug nako tei tey lako geuneu beug 😭😭😭🔥❤️
Parents yii bilahii warnanio khol sii seuy yii niouy douhou. Leur choix impactent negativement la vie de leurs enfants. 😢
Bilay guor la Ken menoul kham danio faux
Ou est la foi? Si chacun pouvait écrire son destin, y aura t il des parcours difficiles ?
Les hauts et les bas c'est ça qui fait la vie et chacun fera de sa part d'épreuves une force ou faiblesse.
Dire alhamdoulillah ala koulli hal est réel et le meilleur se trouve où bout de la patience c'est pas que religieux, c'est une évidence.
Allah ne donne que à ses meilleurs soldats les plus rudes des épreuves
❤❤❤❤❤@@sophiafall
@@sophiafallyena geuneu faux nieup
Mame Coumba une dame posé et clame bne continuation 🎉❤
Vraiment Mame NDIAYE tu es une battante ttes mes félicitations. Bonne continuation. Barke Serigne Fallou
Lima gueuneu marké si émission a chaque fois Ell dit dama ndiabot Ell pense à ses enfants 😢😢😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢😢
Attention "njabot"veut aussi dire soutien de famille
En écoutant Mame Ndiaye je me dis que je ne suis pas la seule à souffrir dans mon foyer les femmes sont très braves inchalah tu m'as donnée la force de tenir le coup ❤❤
Massa cherie lep day diekh
Mais changement nio ko meuneu defal sounou bopeu sinon ci souffrances gay dé
Machallah mame yalla nala yalla same vraiment sa diar diar metti na magui soga setane confidence bamou diekh nakh Yow vraiment wakh dji lerna daw na yaram 😢❤
Mane bilahi dama beugeu mame coumba dafa téye té dal yarou loll simple téksi mashalla yalnako yalla sameu arko si barcker yonéneteu bi psl
Mame ndiaye = jambar= mougne Katt = am Diom li dou hasard meilleur émissions
❤❤❤
Mame dioyloo nguama si sa vie yaye bimouy nampal😢😢 yalla rekaay buur yalla mo meuneu setaane😢 mais nak ALHAMDOULILAH
J’ai sa comportement elle est si brave yalla nala yalla faye sa khol yalla same la are la yir la machallah 🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️❤️🌹🌹🥰🥰
Amine ya rabi
Cette émission nous apprend qu'il ne faut jamais jugé les gens parceque les réseaux sociaux présentent beaucoup de négativité surtout les Sénégalais une pays que je ne comprends pas ils aiment tellement dire du mal sur les autres juste pour leur déstabiliser.
L’enfant chérie de Pikine Fo awe yone leu nitte yiye wakh bouléne ndayi lidienti sakh ioe fo awe yone leu mame mou Ndaw sa khaliss yako liguéye sa dieukeur wané ngako ba nieup guisss ko kone tu as était s’insince long vie à tw chérie diam rek ngay ame thi barki serigne fallou mi nga yakar lo deff beugue naniou 🍏🍎on t’aime fort 💪 grande sœur l’aisse les parler 🗣️ tu es déjat confirmé
Blhi mane mame dma ko beug mane kou beug sa yaye ma beug leu elle a tout fait pour sa maman ndeysane❤🎉
Divorne nakkk Baxoul vraiment 😢 Yalnagn si Yalla mousseul , sammeu gnou , sammal gnou sunu ndiabott yignuy amiiiii
Allakhou akbar sama yaram dawna mame ndiaye wallakhi dingua am lou kawé sa ndiorte😭❤🙏🏼
La vie est dur mame mais kou nek linga atane lala yalla di tek lingay wakh damako dounde motakh courage ma belle damay tok di dioy souma wété dafa meti ba do comprendre
Q'Allah te facilite ❤️🥺😊
Massa yalla bakhna
Mame dink nala yonénete bi psl,mou samala yak sa ndiabote inchallah 🙏
Amine ya rabi
Hoo mame machallah yalla nala brome bi same are la yire la ba finga beugue yégue nga yégue fa tu ets une femme brave vraiment li mo takhe ko khamoule waroko jugée
Tu m’as fait pleurer mame ndiaye parti bi nga waxe sa yay metina force à toi doko rëthu ci aduna ❤❤❤
Derrière ce magnifique sourire 😅se cache un coeur ❤️ en lambeaux ❤️🔥💔❤️🔥❤️🔥
Pour la première foi ma setane émission thiate ba thiate ndakh mame ndiaye ❤
Dom yangui rawanté thi weydiour yi , mame ndiaye Yalla na yeikh wayé sa térangua bala mouy gueuneu feigne say weydiour xonn la guinaw ❤. Y a pas a chercher de midi à 14h kou téral say weydiour rzw say morom bilahi. Mame, boul takeu boul nann ndakh amgua nianou weydiour ❤❤❤❤❤très longue vie pleine de santé à toi ma fille chérie ❤❤❤
Machaala machaala MAME bonne continuation que le bon dieu te protège Amine ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
Mame Ndiaye savon tay da serine ❤❤❤❤Machalah 🩷
Certains hommes me font honte. Respectez nos soeur senegalaises. Les femmes senegalaise sont tres braves.Courage Mame
Yii mame tay dafa teey classe aujourd'hui regle sangnse❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤. Tay mom machala ♥️♥️♥️
Bravo a mame ndiaye moi je t'aime naturellement brave femme
Ahh mame nak bett nga gnou bari vraiment bi calme bi dall bi posè niaaff ehh ndikkè milieu bou nek ak comportement wam .chapeau mame sama nawlè talibé fallou bi❤❤❤
Machalla boule tite té boule ragale diame rék guaye ame li laniouye wakh nite boko khamoul déko wowé hé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Du courage Dieu est avec toi❤❤❤❤❤
Mame Ndiaye niouy diokhei cadeau beiral neign la lokho dei , sa weurseuk la na rappeu ak diamm. Je t’aime beaucoup sister
Que Dieu te donne une très longue vie santé bonheur réussite et bcp d'argent et aussi la paix du cœur ❤❤❤
Amine si barké seydina mouhamed salallahou aleyhi wa Salam ❤❤❤
Bilahi, wadiour rék moye gualadiou done.MashAllah
Machallah, tu es une vraie lionne Mame . Battante et forte. Tu mérite d’être honore. Chapeau Mame. ❤❤❤
Machalla Mame Ndiaye yalnala sa Diam la yague❤❤❤
Yallah Nala Serigne Fallou sameuh 🙏❤️
Que le bon dieu continue d'étendre sa main protectrice sur toi mame n'diaye et sur toute ta famille amine ya rabbal alamina ❤❤❤🎉
Man dama ko beug ndankh limou beug serigne FALLOU ❤😢
Aka sorekkk kou doff machallah
En tout cas name est tres propre porté du blanc sans transpiration des exels et cou c très classe et propre❤
😂😂😂wax gua degue dh
Machallah ❤mame Ndiaye xol bou rafet mo am solo ci domou adama ❤❤❤.
Ndeyesane 😢😢 mame ndiaye tu m'as fait pleurer walahi quand on à battu ta maman et tu as répéter plusieurs fois dama ndiambote 😭😭😭😭 yalna yalla tawoula way
Très franchement j,aime mame ndiaye pracequ,elle est brave et intèligante❤❤❤❤❤ vie sur elle li mouye wakhe kouko doundoul khamo ko
Hooo mame ça confession amena classe machalla ❤❤❤
Machallah mame diam rek gna am ame gna nianou wadiour yalnala diapale je t'aime fort ❤️ ❤️❤️😘
C est la première fois ms setane confession nakh mame ndiaye savon blh sétane nako 4 fois chaque jour ma sathie sama téléphone nou yaye blh walay ligua doundou meety naa sama bopou deh lalay kholei😢❤
Ndeyssane dawna na yaram
Mame vraiment ndiambar ngua wadiour kouko téral yalla téral la
Mame ndiaye tu es brave Machallah tu m'a fai pleuré ton passé n'a pas été facile ndeysane motakh arrêtons de juger les gens nite soko khamoul rek khamoko. Chapeau à toi mame coumba pour ton profesionalisme
Mame Ndiaye tu es une brave femme ❤
Machalla mame ndiaye championne nga❤❤❤
Machallah c'est la première fois ma sétane émission bi du début à la fin ttes riche en enseignement ❤❤❤
Yalna la yala diapalé boubakh té lafalnou thione yala khir niou si bopame maynou xolou Mounie si Barké seydina Mouhamét psl bravo Mame Ndiaye ❤
FOU nitt kou bakhna la❤❤❤❤❤❤❤❤
Mame ndiaye teyy lala geuneu bgeuh ❤️tey lala gueneu fonk guen n’a diokh thier 🥰wallae diam rk ngey am do meun nek 😍liya takh ma deuk di dioy sama pape paix à sn âme 🙏🏿🕊️nagn outt barke barké bayy ❤
Rien à dire mame tu es le meilleur mchll ❤
Chapeau à toi Mame déf nga émission té yakho sa dieukeur bén yone ♥️♥️♥️👑👑👑
Machalla elle a bien communiquer❤❤❤❤avec douceur
Machaala Mame tu es forte yalanala yala doli soutoureu bagua féké sa ndiarignou ndiabote yeup🙏🙏
Mame Ndiaye = la classe 🎉
Dafeu honnête ndeysane Machallah yalna yalla lafal la thiate 😢🙏🏻❤️
MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH Mame Coumba contane nagnou thi invitation Mame Ndiaye ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉❤❤❤❤
Kouy weur goor deugue bilahi diapal Mame Ndiaye ❤ yalna yalla same la une vraie battante
Ton histoire mérite de faire le tour du monde
Oh my beautiful mame ❤
Oh mame ndayessane la femme battante machallah nekh ngama ndakh say wadiour yinga begue yereum lène ❤❤❤
Ndeysane nitou soutoureu la 😢😢😢yalla nako yalla diapalé😢😢🎉🎉❤❤❤
Jai kiffé cette émission ça mapprend encore beaucoup de chose ,connaissez la personne avant de la juger par ces faits et gestes
Machaallah ❤lou mety yague thie adouna
S.A.W ❤ wallahie lor fii munj dinaa jekh metiti aduna yagana yaagut
Yallah wakhut ken dara