Barke Serigne Saliou Mbacke li mo nekhhh TIK TOK lako guiss nieuw fi pour setan ko mashallah, Yalla na yalla goudeul senfan, Mourid la ta sila nian yalla déwé Mai kou guiss nén ni nénaguiii🥰🥰🥰🥰🥰💯
Je me suis réveillé très fatigué aujourd’hui mais depuis 45 minutes je suis dans mon coin tout seul les écouteurs a l’oreille et je ressens une forte joie une émotion quelque chose que je peux pas expliquer 🥹🥹🥹🥰c’est doux c’est beau c’est bon c’est triste et joyeux à la fois❤️dieureudieuf mame maodo
Je suis mourid baye fall Diebalou sama serigne Sante fall mais li Neikh na lollll et sa m’apaise trop d’émotion trop d’harmonie les voix la douceur des paroles 🥰🙏
Je trouve pas de mots pour qualifier ma joie tellement elle est profonde.je prie tout simplement sur le prophète pour qu'il augmente la lumière sur notre bien aimé Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy celui qui nous a gratifié cette belle écriture.
Alhamdoulilah mashalla rendons grâce à nos chefs religieux toutes confréries confondues qui grâce à leurs œuvres et conduite sur terre nous ont faits aimer La Meilleure Créature Seydina Muhammad ASWS. Que la paix règne à jamais sur le Sénégal
Machallah yalla nagnou yalla fayal sougnou Mame cheikh Seydi Hadji Malick Sy Papa Abdou Aziz Mbaye yalla na batt bi wérrr yalla bayilafi nga yague gno bégeul♥️♥️
As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH Plateau bé riche... binde yi riche... kikou binde riche... kouniou netali mbireum riche... dou feeté mé Tariqa tijiaani dafa riche. Mashaal'LAH yalnaniou ALLAH Subhanahu wa Ta'anla nangoul. C'est plus qu'un honneur d'être un aspirant taalibé Cheikh
Gnoune Sante rék mognou ware pas que goor gui bidéntiwoul maodo ❤️ con gnou bok si bayima yi bilay walay au cheikh Seydi j’adjoigne Malick kénne dou môme mé Moustafa kénne la bilay walay ❤️❤️
C'est magnifique. Ils ont réussi à créer un rythme lyrique qui affecte positivement la sensation d'un auditeur même s'il ne comprend pas ce que signifie les chants.
*PAPA ABDOU AZIZ MBAYE*🥰 ki dafa mélni bi *CHEIKHAL HADJI MALICK SY {RTA}* di bind khilâssou zahab mom lako doon bindel lim sii Déff mo nékh lool *MBAYE* yalla nasa diam yagg 🤲🏻🤍
Que le tout miséricordieux par la grâce de son prophète Mahomet PSL déverse à flot sa grâce sur notre marabout Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy et ses proches. Amine
Machalah, Machalah, Machalah, SEYDINA HADJI MALICK SY limou biid lépp thie gaatale mouy khaliss, taïsir... yallah dakoo préparaal ay missionnaire com wa Keur Moussa Alé Mbaye, rien n est hasard ds la vie, baa thie tarikha yeup, vive le monde entier ❤❤
Mani kouy weur carte d'identité Yalla séet ko si Al couran thia souratoul *IKHLASS* Wayé kouy weur carte d'identité Yoninte bi salallahou aleyhi wassalam séet ko si *KHILASS* de Mame Maodo Malick Sy. *IKHLASS* di Yalla *KHILASS* di Yoninte bi. *DIARRAMA MAME ASS*
Je suis comblé d'un bonheur indescriptible Une joie immense m'envahit. Merci à la merveilleuse famille Moussa Âlè Mbaye qui perpétue le Message de notre vénérable Mawdo
MACHA ALLAH ALHAMDOULLILAH MERCI MON DIEU DE NOUS AVOIR DONNER MAME MAODO OH....QUELLE PERSONNALITE ....QUELLE MERVEILLE LES MOTS NOUS MANQUENT MERCI MON DIEU .
Paix et Salut sur le Prophéte Mouhamed (PSL) Dieureudieuf Mame Cheikh Seydil Hadj Malick SY (RTA) YALLA nala sameu arela goudal fane wi sunu Papa sunu sopé Abdou Aziz MBAYE
Très belle intervention Dr Mour Talla. Prions pour que ces vrais sujets entrent dans la lumière pour permettre de sauver le Senegal et l’Afrique. Nous sommes de plus en plus focalisés sur les details et passont complètement a coté des combats qui sont vraiment importants. Puissiez vous être entendu par un grand nombre.
Longue vie Mame Abdou Aziz Mbaye Ma joie quand j'écoute tes poésies prophétiques est indescriptible. Puis-je Allah déverser en profusion la lumière du prophète sur tous les musulmans et rétribuer davantage Mame Maodo pour ses œuvres inégalables.
Allahu akbar seul Allah sait ce que je ressens à chaque j’écoute cette merveille❤😭😭😭qu’Allah swt vous avez accorde une longue vie fayalniou mame maodo❤😭😭😭📿thiey général Abdoul Aziz mbaye❤️😭
DIEUREUDIEUF SEYDI HADJ MALICK SY AK WAKEUR BAYE MOUSSA ALE MBAAY YEUP YALA NALEN YALA FAYE SI BARKE SEYDINA MOUHAMAD SALALAHOU ALEYHI WA SALAM🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Abdou Aziz Mbaye est un chanteur exceptionnel,le chœur qui l'accompagne est tout aussi exceptionnel !longue vie à tous les membres de ce groupe. Yalna yalla fayalnou Mame Maodo moom mi waral lii lepp.
Machalla malikia tv lérou maodo amna solo kendou seydil hadji Malick sy yalla nagnou ko yalla fayall bi diahi nabil moutapha saw 🙏diadieuf général abdoul aziz mbaye et son group yalla naléne yalla faye ci barke seydil hadji Malick sy rta💓🙏
Qu'Allah SWT Bénisse et Couvre de Miséricorde et de Ses Bienfaits à Seydi Hadj Malick et à ces chanteurs Abdou Aziz Mbaye, Daou Goor et à tout le groupe.
❤❤❤❤Hoo le bonheur de ça 🥹❤️❤️diarama Mame Maodo Moniou hamal yonenty bi Sallalahou Aleyhi wa salam🤲🏾🤲🏾
Barke Serigne Saliou Mbacke li mo nekhhh TIK TOK lako guiss nieuw fi pour setan ko mashallah, Yalla na yalla goudeul senfan, Mourid la ta sila nian yalla déwé Mai kou guiss nén ni nénaguiii🥰🥰🥰🥰🥰💯
machaAllah Diadieuf 👌
❤ je suis fière d’être talibé cheikh ❤❤❤❤
Je me suis réveillé très fatigué aujourd’hui mais depuis 45 minutes je suis dans mon coin tout seul les écouteurs a l’oreille et je ressens une forte joie une émotion quelque chose que je peux pas expliquer 🥹🥹🥹🥰c’est doux c’est beau c’est bon c’est triste et joyeux à la fois❤️dieureudieuf mame maodo
Alhamdoulilah
Pareille pour moi
Qu’Allah apaise nos cœurs y’a barké Mame Maodo 🙏🏾
21:52 @@FatimataBa-kr1ro
Je suis mourid baye fall Diebalou sama serigne Sante fall mais li Neikh na lollll et sa m’apaise trop d’émotion trop d’harmonie les voix la douceur des paroles 🥰🙏
Idem wallah. Yalnaniou yalla fayal sunu mag you baax yi ❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bari nga ci ay moroom.
Machaalah 🙏🏽💚
Mangui niii manit🤩
Pour keupe kouy dioulite leu. Salalahu Aleyhi Wa Salam
Machallah Mbaye khol sedna barki cheikhou tidjan cherif ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤yalla na Yalla yokou fane yi
Amine
Moi je dis merci beaucoup DIEU qu'il ma donné la chance d'écouter sa
Bilahi xol sédna si MALIKIYA
Bilahi kén dou mame maodo
Bilahi kén dou Abdou Aziz Mbaye
Je ne peux pas retenir mes larmes 😭😭😭
Macha allah Jëréjëf waye
Yalla na Yalla délosi djamou Keur seydil hadji Sibarké yonéntibi 😭😭😭😭diarama serigne moustapha sy al maktoum
Mouride tidiane layène niassene khadre nieupp benn laniou yalnaniou yallah fayal Mame Cheikh Seydil El'hadji Malick💯💯💯♥️♥️
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
Amine 🤲🤲
Je trouve pas de mots pour qualifier ma joie tellement elle est profonde.je prie tout simplement sur le prophète pour qu'il augmente la lumière sur notre bien aimé Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy celui qui nous a gratifié cette belle écriture.
Allahumma Amine
Amine
Amine yaa rabi
Wallay
Alahouma amine
Quand on chante les louanges du Prophète (psl) c'est le cœur qui remplace les orteils quelque soit le chanteur mouride ou tidjane.....
Cheuteutttt🥰amoléne ay chair de poule🥰Thiey Mame Maodo yalla nanouko yalla fayal bijahi Taha saws
Allahouma amiinn mbokk 🙏🏾🥰✨
😮😢😅😢 😂
6
😅😮😮
Taggg nitt , xam nitt moko gueun .
Bilahi MAODO MO XAM RASSOULOULAHI ( PSL) 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Machallah Malikia diarama mame Maodo rta diadieuf Abdou Aziz mbaye yalla nalene yalla faye té goudeul sen fane andak were barke yonenti bi psl
Allahumma Amine 🙏
Macha Allah dieuredieuf Mame maodo yalla na yalla yok sa lére si Barker Seydina Mohamad psl
Yalla nala yalla takhawou mayeu la goudeu fane ak wérr sy barké seydil hadji malik sy
Wallahi li eupp na neekh ay wayy negn santt yallahh الحمدلله thi liniu yallah mayy c extraordinaire wallahil azim ❤
Merci à toutes les familles religieuses du pays pour leur belle partition à l'expansion de l'islam
Xol yi sedatina 💕.Mbaya yalla nala yalla yok taxawou ak gnigua andal ci barké Mouhamed As❤❣
Cheikh seydi elhadji malick sy
Yallah nala fay,
Wayé Yallah nasi bolé yiw abdoul aziz mbaye et son groupe alhamdoulilah ala kouli hal.
Machalah 😍 😘 yalla na yalla barkel Abdou Aziz Mbaaye goudeul fane weral yow ak sa groupe ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Alhamdoulilah mashalla rendons grâce à nos chefs religieux toutes confréries confondues qui grâce à leurs œuvres et conduite sur terre nous ont faits aimer La Meilleure Créature Seydina Muhammad ASWS. Que la paix règne à jamais sur le Sénégal
Bien dit ( Amine et merci beaucoup )
Machallah yalla nagnou yalla fayal sougnou Mame cheikh Seydi Hadji Malick Sy Papa Abdou Aziz Mbaye yalla na batt bi wérrr yalla bayilafi nga yague gno bégeul♥️♥️
As'salaamu anlaykum war'Rahmatul'LAH
Plateau bé riche... binde yi riche... kikou binde riche... kouniou netali mbireum riche... dou feeté mé Tariqa tijiaani dafa riche. Mashaal'LAH yalnaniou ALLAH Subhanahu wa Ta'anla nangoul. C'est plus qu'un honneur d'être un aspirant taalibé Cheikh
Admirons la belle voix de Abdou Aziz Mbaye et les beaux écrits de Seydi El hadji Malick
Maachalla que Dieu vous garde Abdou Aziz Mbaye
Franchement je suis flatté par cette ére de khilâss wërre si yénne et fier d'être Tidjiane !!!
Magui dioy bilahi walahi dama beug Abdou Aziz Mbaye
Serigne Ababacar Sy Mansour Balkhawmi Yalla Nafi Yague té ànd ak weer ❤🤲🏼🥰💯✅
Gnoune Sante rék mognou ware pas que goor gui bidéntiwoul maodo ❤️ con gnou bok si bayima yi bilay walay au cheikh Seydi j’adjoigne Malick kénne dou môme mé Moustafa kénne la bilay walay ❤️❤️
Abdou Aziz Mbaye mi war nagnou wakh ak mome qui dou nitou kessé pour il est le chanteur le plus fort du monde ❤🎉🤔
C'est magnifique. Ils ont réussi à créer un rythme lyrique qui affecte positivement la sensation d'un auditeur même s'il ne comprend pas ce que signifie les chants.
❤❤❤❤❤❤❤❤
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
La seule source de joie et d’apaisement dans ce Sénégal désastreux ❤
*PAPA ABDOU AZIZ MBAYE*🥰 ki dafa mélni bi *CHEIKHAL HADJI MALICK SY {RTA}* di bind khilâssou zahab mom lako doon bindel lim sii Déff mo nékh lool *MBAYE* yalla nasa diam yagg 🤲🏻🤍
Que le tout miséricordieux par la grâce de son prophète Mahomet PSL déverse à flot sa grâce sur notre marabout Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy et ses proches. Amine
Machallah nit kou sell nga motakh nga yeug linga yeug machallah mbokk❤️😍🥰
Amiine way😍🙏🏾
) @@ibrahimaseck3002
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
Je suis très fier d'être talibé cheikh longue vie au khalife
Alhamdou lilah yalla na yalla fayal niou seydil hadj malick sy
Macha’Allah Yalna Yalla faye yiw bijahi Seydil Wujud صلى الله عليه وسلم
dieureudieuf mame mawdo yalna yalla faye yiwe
Amine yaraby 🤲
La joie de vivre fière d'être musulmane ❤❤❤❤
Dieuredieuf el Hadji Malick Sy yaw miniou khamal DEUG DEUG Kane moye seydina Mohamed SAW
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
Machalah, Machalah, Machalah, SEYDINA HADJI MALICK SY limou biid lépp thie gaatale mouy khaliss, taïsir... yallah dakoo préparaal ay missionnaire com wa Keur Moussa Alé Mbaye, rien n est hasard ds la vie, baa thie tarikha yeup, vive le monde entier ❤❤
Mani kouy weur carte d'identité Yalla séet ko si Al couran thia souratoul *IKHLASS*
Wayé kouy weur carte d'identité Yoninte bi salallahou aleyhi wassalam séet ko si *KHILASS* de Mame Maodo Malick Sy.
*IKHLASS* di Yalla *KHILASS* di Yoninte bi. *DIARRAMA MAME ASS*
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
Machallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Je me réjouis de ces oeuvres, qui nous plongent dans l'immensité de la tariqa. Dieureudieuf Mame maodo.
Tabarakallah di gnanal Baye Abdou Aziz ak famille bi yeup Bour Yalla goudal sen fann te begueul leen li defa wessou nekh 🙏💚
C'est Tafsir Mamadou Ndoye je sui talibé cheikh J aime tellement mame maodo Malick sy et sa famille
YALLA Na YALLA beguel len comme niguen niouye beguele thi Yonentibii…❤️❤️❤️
Diadieuf wa Malikia,amouléne morom,yalla na yalla faye ci barké Nabil Moustapha (sws),sounou khol séd na
Machaallah. Longue vie à tous .Soyez sous la protection divine et la bénédiction du prophète. Dieureudieuf Seydi el hadj Malick.
sama idol abdoul aziz mbye
Masha Allah masha Allah masha Allah yallana yalla faye léne si barke seydina Mohammed psl
J'AI DU MAL A CONTENIR MON EMOTION EN ECOUTANT EN BOUCLE CE CHAPITRE AVEC CETTE VOIX D'OR DE MBAYE
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
à. chaque. foi ou. j'écoute. cette. évocation. je.suis . l'homme. le. plus. heureux. au. monde. Machalla Diarama. SEYDIL. HADJIi. MALICK. Alhamdoulilah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Chanson très tres puissante .
Il faut traduire en français.
Merci vraiment
C'est des zikrs envers notre Prophète Mohammed (PSL)
Je suis comblé d'un bonheur indescriptible
Une joie immense m'envahit. Merci à la merveilleuse famille Moussa Âlè Mbaye qui perpétue le Message de notre vénérable Mawdo
MACHA ALLAH ALHAMDOULLILAH MERCI MON DIEU DE NOUS AVOIR DONNER MAME MAODO OH....QUELLE PERSONNALITE ....QUELLE MERVEILLE LES MOTS NOUS MANQUENT MERCI MON DIEU .
Je suis talibé Baye.. mais mangui niaane ngén def 2 éme saison bi.... Vraiment c supper neekh
Matar Ndiaye loo gnou dessall😭❤️
Machalla nekh na yalna ma yalla may dieukeurou talibé cheikh🙏🙏🙏
AMINE ! AMINE ! AMINE !
AK mane amine
Amiine yalnalénko yalla defal si barkeb Mame maodo
Machalh thiey yonente psl
Elhadj malick tamite kou yalla bakhe la ouf mon coeur ♥️ bat cent à l’heure
Mbaaye, une chance et une fierté pour Tivaouane
Paix et Salut sur le Prophéte Mouhamed (PSL)
Dieureudieuf Mame Cheikh Seydil Hadj Malick SY (RTA)
YALLA nala sameu arela goudal fane wi sunu Papa sunu sopé Abdou Aziz MBAYE
Très belle intervention Dr Mour Talla. Prions pour que ces vrais sujets entrent dans la lumière pour permettre de sauver le Senegal et l’Afrique. Nous sommes de plus en plus focalisés sur les details et passont complètement a coté des combats qui sont vraiment importants. Puissiez vous être entendu par un grand nombre.
❤❤❤ohhh lii sedd na xol Touba lakoy digloo ba louga masala taalibe Seexul Xadiim laa waaye Elxaaji Maalik sy budoon Xasida gii dongu la bind doyna sëkk masala yaal nanuko Yàlla fayal.
اللهم صل على سيدنا محمد خاتم النبيين وامام المرسلين
Machalah Abdou Aziz Mbaaye yalla Goudal fane wii Té wéreure Batbi Amine ya rabbi ❤ ❤❤❤❤❤❤
اللهم صل على سيدنا ونبينا وحبيبنا محمد وعلى آله وصحبه الطيبين الطاهرين
Amine ya rabbi 🤲🤲🤲
Loula rére thi Yonent bi ladjiko Maodo 💓💓💓💓💓💓💓💓
La mélodie me fait pleurer ça me touche aux cœur bilahii ohh machallah 🙏🙏🙏👌
Bilahi mounou ma teuyé samay rangogne je pleure a chaque fois k je l'ecoute diereudieuf mame seydi hadji malick sy
J'ai lis un commentaire qui m'a un peu amusé ,ce monsieur dit ;
Macha'Allah que Béni la voix papa Abdoul Aziz Mbaye ainsi que ses frères et nous jeunesse tidianiya remercions Mame Maodo
Machallah Abdou Aziz Mbaye avec cette belle voix mélodieuse
Ñu ngui sakku Wolofal ci Cheikh Tijany ak Abal Habibi bou Mame Hady Touré ❤
Longue vie Mame Abdou Aziz Mbaye
Ma joie quand j'écoute tes poésies prophétiques est indescriptible.
Puis-je Allah déverser en profusion la lumière du prophète sur tous les musulmans et rétribuer davantage Mame Maodo pour ses œuvres inégalables.
Amine
Dey guëna nekh ba aldiana inchallah
Yalnako yalla deff
Cheikh Seydil Hadji Malick yalnakou yalla fatal💚💚💚
Al hamdoulilahi Al hamdoulilahi Al hamdoulilahi rabil wahi bi nihami♥️♥️♥️
Doumaci doyal 😭😭❤❤ Yalla naniou Yalla fayal maodo 🙏🙏
Allahu akbar seul Allah sait ce que je ressens à chaque j’écoute cette merveille❤😭😭😭qu’Allah swt vous avez accorde une longue vie fayalniou mame maodo❤😭😭😭📿thiey général Abdoul Aziz mbaye❤️😭
Machala yalla nagnou yalla mame seydi Elh Malick Sy rta
😭😭thieuy Papa Abdou dallll
dinganiou rey rek
Sama wakeur yi yalna yala wereul baate yi thi barke yonentibi psl ak barke mame yeup
th-cam.com/video/HhqkPSVih9U/w-d-xo.html
MACHALA alkhamdoulila yala naley yala faye si barkhe yonentebi Sa lakhou tala ali mohamadou MACHALA alkhamdoulila 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤️❤️❤️❤️
Machalllah Yalla nanou Yalla Fayél Seydi Elhadj Malick Sy (R.T.A)
🥲 Wallahi li nèkhna ci xol❤
Yala naniu lène Ya'Allah fayal gun di fay🙏🙏🙏
DIEUREUDIEUF SEYDI HADJ MALICK SY AK WAKEUR BAYE MOUSSA ALE MBAAY YEUP
YALA NALEN YALA FAYE SI BARKE SEYDINA MOUHAMAD SALALAHOU ALEYHI WA SALAM🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala Machala fière d'être Tidiane
Machallah yalnalene Yalla faye yiw si barker Seydina Muhammad PSL
Sam Papa moleine meune niveau yi dou beine😍😭
Machala ziarre
Barke malikia✍️Maodo ya bah👳 ,ya yarou 🤰,ya yiw🤱 ,mo tah yalla hamalla 🌄🐪🕋
Abdou Aziz Mbaye est un chanteur exceptionnel,le chœur qui l'accompagne est tout aussi exceptionnel !longue vie à tous les membres de ce groupe. Yalna yalla fayalnou Mame Maodo moom mi waral lii lepp.
Amine
Effectivement on lui doit beaucoup et on doit vraiment le lui faire comprendre tant qu'il est encore entre nous...
Allahouma amine way Inchallah 🤲🏿❤❤❤
Ma cha la dieredieuf abdou azise mbaye yalla naa yalla sahal groupe bi amine
Amoul moroom
ما شاء لله جزاكم لله خير جزاء بجاه سيدنا محمد صلى لله عليه و سلم ❤️🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳❤️❤️🇸🇳❤️🇸🇳❤️🇸🇳❤️❤️🇸🇳😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭💌💌🤍🖤👤🤝🤝🤝🤝👈🦻🦻🦻🦻🦻
Sénégal sans mawdo bamba baye niasse Mame limamou thiénéba chéikhna Kone dou baxe yalna yalla fayale niouléne
❤🎉❤🎉🎉🎉🎉merci dieu
Yallah na yallah guoudeul fan wi yok weur gui si barqué seydina Mohamed psl xol sed na yallah kham na ko
chapitre favorite 😻
Dieuredieuf baye Abdou Yallah na bour bi Yallah dolileu wër té sameuleu bou bakh yokou fane yi lool thi barké Seydouna dolileu takhawou. Baye Abdou leer yi ngay tabal thi xol yi Yallah nalako Yallah fay Yallah bou thi dara nul baye boye🙏 ❤️❤️❤️❤️
Khol yaki feekh ♥️♥️♥️ Mashallah Dieuridieuf Malikia 🙏🙏 Yalla n'a léne yalla cii barki sank sank yii
Allahumma Amine 🙏
❤❤❤❤❤🙏🙏🙏
Machallah baye Abdoul aziz mbaye avec ton group dieureuguene dieuf
Machalla malikia tv lérou maodo amna solo kendou seydil hadji Malick sy yalla nagnou ko yalla fayall bi diahi nabil moutapha saw 🙏diadieuf général abdoul aziz mbaye et son group yalla naléne yalla faye ci barke seydil hadji Malick sy rta💓🙏
Lofty ,my brothers and sisters !Allah bless all muslims wherever they are in the world.
Mach-@llah mbekté tarikha bi. Que Dieu vous bénisse🤲🤲🤲🤲🙏🙏🙏❣❣
Mbaye yalla na yalla goudal fan wi wéral thier yii si barké yoneté bi (saw)
Jeureudieuf Mame Maodo: Njol Gaya té mo raw ca gaagna,
donoye Cheikhou Oumar bi Njol Fouta,
Ya gnou khamal deug deug Seydina Mouhamad Njol Makkah
Qu'Allah SWT Bénisse et Couvre de Miséricorde et de Ses Bienfaits à Seydi Hadj Malick et à ces chanteurs Abdou Aziz Mbaye, Daou Goor et à tout le groupe.
From Senegal to Louisville Kentucky USA...
Still have it my TH-cam faves...