Sou wakhéné yonenté 'milata Ibrahim' lako yalla topolo yéna atéyi mongui ci milata Ibrahim. Donc yonenté day tope milata Ibrahim ak alhour'ane khana?! Ma déféné lougnou bindoule ci alhour'ane yonéntibi warouko tope? Éclairez moi té bouléne ma yobou ci bénéne vidéos.
@NihmaTV j'ai vu le verset. Maintenant diangualé 'milita Ibrahima' fouko yonenté Di dieulé ? ALLAH dafkako sole wala yonenté moko dieulé ci thorat wala inedjil ?!
Macha Allah franchement
Merci beaucoup
❤❤❤❤🎉
Amna solo lool! Alxuraan rek
machallah
Jërëjëff
Laab dagnou ne moy lou amoul sobé wante saleté ak sobé dou bén gnom gno ko taquale gni daal sonnal nanou torop
Sou wakhéné yonenté 'milata Ibrahim' lako yalla topolo yéna atéyi mongui ci milata Ibrahim. Donc yonenté day tope milata Ibrahim ak alhour'ane khana?!
Ma déféné lougnou bindoule ci alhour'ane yonéntibi warouko tope? Éclairez moi té bouléne ma yobou ci bénéne vidéos.
Millata Ibrahim moy diiné dji. Li ko ci Yalla sopi loul, dou sopi kou ci millata Ibrahim. Millata Ibrahim moy diiné dji.
Kholal sourate 22 verset 78
@NihmaTV j'ai vu le verset. Maintenant diangualé 'milita Ibrahima' fouko yonenté Di dieulé ? ALLAH dafkako sole wala yonenté moko dieulé ci thorat wala inedjil ?!
@smb6311 sètanal vidéo bii
Questions yii, Cheikh Mbacké tontou na ci bou yague !
th-cam.com/video/on63CBqwLnM/w-d-xo.html
@smb6311 sètanal vidéo bii
Questions yii, Cheikh Mbacké tontou na ci bou yague !
th-cam.com/video/on63CBqwLnM/w-d-xo.html
@@NihmaTV diadieuf guissna réponse bimou diokhé. Néna yonenté bi filako fêk d'accord mais foumouko diangué la wakh ba khamko ?! Noumou khamé nignouy dioulé ni gnouy woré ba diko tope ??!
machallah