j'ai pas connu Marie, mère de Issa j'ai pas connu Assya, épouse de Pharaon J'ai pas connu Khadijah, épouse du prophète, j'ai pas connu Mame Diarra, mère de Bamba j'ai connu Sokhna Zeynab Fall j'ai écouté Sokhna Zeynab Fall J'ai aimé Sokhna Zeynab Fall. Que Dieu l'aime, qu'il accueille l’âme de notre bien aimée Zeynab Fall dans son paradis éternel. Zeynab Fall nos coeurs sont meurtris , nos larmes coulent mais nous ne disons que ce que Dieu agrée à lui nous venons vers lui sera certainement notre retour.
Man bimu démé lako xam wayé akka mako beugue ndax thiafka ngueum yallah Mangui ko yeugué grace a mome ganaw yallah de part ces vidéos conférence émission et jusqu’à présent en 2023 je regarde cette vidéo pr me rappeler de tous ses valeurs et d’en apprendre encore 😭😭yallah nako sunu borom dieggal sma sopé xol bi🙏❤️❤️❤️❤️
Une personne ke j estime énormément par sa grandeur,courage,gentillesse and faith also a idole Sokhna Zeynab May Allah the almighty grant you the paradise and forget you all your sins and all the ummah. I never meet you but from the bottom of my heart I appreciate a lot with all the lessons that you give us in life. May Allah give you your memories all the time on our Prayers,Deed, and Dua and to all the people you going to meet there. May All the Ummah meet you inchallah aside the prophet Mohammed(PSL) and his family in paradise amen. May Allah give strength to your family and all of her beloved. Amen
Sénégal mongui ni deeee xamugnu sakh lugnu wara def kou teddd ki kou bakh ki kou sell ki référence thi bepp djiguene. Rafet nagnu ndiort si mome yalna khipé aldiana
Fambaye Ba bilakhi ni lamako sama yaye wakhé taye! Mais nak li moye adouna,niom yeuffou zaïr moléne nior. T pourtant d kerok weuye katou toubab bi bamou dé wé télé yeup ci wakh ci sen jrnal! Mais yalnako yallah kharé adiana firdawsi ci barké seydina Mohamed psl
La ilaaha ilalah !!! Eywaay souniou sokhna Zaynab j’ai troooop mal 😭😭😭 Thieuy Al Mumīt sounou borom reka meune lui , diambaar bou mag Seyda mala beugueu, toujours dans nos coeurs ♥️ !!!! Yallah nala sa sopé bou seleu bi téerou thia Aljaana you kawé ya. Amiiiine y’a Rab
Gnaknafi mame gnakeu fi ay papeu gnakfi diéguégnalé you bari wayé ki gnou gnakeu tay dé meussouma mété ni meussouma bété ni ohhhhh yalnama yalla bal wayé sama khol metina sama khol metina sama khol metina meussoumako guisss wayé sama khol metina
mon idole sama sope khawemakowone mais je l'ecouter attentivement c a cause d'elle que jai mis le voile je suis meurtri je narrive pas a croire que ya zeyda est parti paix a son ame
إنا لله وإنا إليه راجعون إن لله ما أخذ وله ما أعطى وكل شيء عنده بمقدار اللهم اغفر لها وارحمها و أسكنها فسيح جناتك وألهم أهلها وذويها الصبر والسلوان اللهم لا تفتنا بعدها وقنا عذاب النار
Allahouma irhamha wagfirlqha wafou anha wa akrim nouzoulaha wa wassih moudhala wagsilha bil ma i wassaldji wadaradj wa naquiha miina zounoubi walkhataya Kama younaka sawdoul abyadou Mina danass😭
Praise be to God, Lord of the worlds, and may God's peace and blessings be upon His servant and Messenger, our Prophet Muhammad and upon... Yes, he said: The Messenger of God, peace and blessings be upon him, came out to them. He said: Say: O God, bless Muhammad and the family of Muhammad,...🙏☝️👌👍💕
May her soul rest in perfect peace Aamen!! What a great lost to the Muslim ummah. I'm a Gambian Gambian who has been following her for a while blie, I was so shocked when heard the news. The condelence to her entire family and the Senegalese at large.
QUE LE BON DIEU LA PARDONNE ET L'ACCUEILLE DANS SON PARADIS TOUTE MA FAMILLE L'ADORE .SEUL DIEU SAIT QUE J'AVAIS L'INTENTION D'AMENER MES PETITS ENFANTS CETTE ANNEE A SON INTERNAT.
Machalah birnama ni moma geune fouf walahi Wa raboul kaba. La notion a perdu, l'islam dans sa globalité a perdu une femme intègre imbue de bonté inestimable. Yalla nako yalla yereum 🙏🙏🙏
Que le bon dieu l'accueil dans son firdawsi. Certains vivent longtemps pour accomplir leur mission en l'espace de très peu tu as accompli la sienne que son œuvre soi une viatique pour nous autres.
kou lugeyal yalla mou fayla fi fay la feule saida zeinab fall yalla nala yalla terro firdawsi oustaz alpha magui lakoy dialle bou baxh lowaxh si mome lou am la
j'ai pas connu Marie, mère de Issa
j'ai pas connu Assya, épouse de Pharaon
J'ai pas connu Khadijah, épouse du prophète,
j'ai pas connu Mame Diarra, mère de Bamba
j'ai connu Sokhna Zeynab Fall
j'ai écouté Sokhna Zeynab Fall
J'ai aimé Sokhna Zeynab Fall.
Que Dieu l'aime, qu'il accueille l’âme de notre bien aimée Zeynab Fall dans son paradis éternel.
Zeynab Fall nos coeurs sont meurtris , nos larmes coulent mais nous ne disons que ce que Dieu agrée à lui nous venons vers lui sera certainement notre retour.
Merci
@@malickgueye6875 p
@@malickgueye6875 ghhxd
Man bimu démé lako xam wayé akka mako beugue ndax thiafka ngueum yallah Mangui ko yeugué grace a mome ganaw yallah de part ces vidéos conférence émission et jusqu’à présent en 2023 je regarde cette vidéo pr me rappeler de tous ses valeurs et d’en apprendre encore 😭😭yallah nako sunu borom dieggal sma sopé xol bi🙏❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machaallah royoukayyy bou Matt royoukayyy yallah nako yalla yob thie aldiana yi gueuneu kawéya té bakhé niou thie qualités quincarné souniou Yaye seydate zeynab machaallah
Une personne ke j estime énormément par sa grandeur,courage,gentillesse and faith also a idole Sokhna Zeynab May Allah the almighty grant you the paradise and forget you all your sins and all the ummah. I never meet you but from the bottom of my heart I appreciate a lot with all the lessons that you give us in life. May Allah give you your memories all the time on our Prayers,Deed, and Dua and to all the people you going to meet there. May All the Ummah meet you inchallah aside the prophet Mohammed(PSL) and his family in paradise amen. May Allah give strength to your family and all of her beloved. Amen
Sokhna zeynab, doundou lou nèww, liguèy lou reuyyy, Yallah nako sougnou borom kharè ko aldiana firdaws
bilahi wokhga degue yalnako yalla yeureum té khareko aldiana firdawsi
YALLAH nagnouko YALLAH fayal ci lepp lou bakh lougnou diarignou ci mom, kharéko Aldiana, deukeulékofa ak sougnou sopé seydina Mouhamad (PSL). YALLAH nagnou YALLAH bolé ak mom sa Aldiana. Amin
Uùuùùuuuùùùjuujùuuuujùuuuùuùuuùuùuuuù6k
Salam machalla diambar la wone yalna souf oyof thie kawame wayé réwmi bane rewla nitou diné bou melni zeynabe jougéfi demb dou béne télé bouko défale Platon boudoule dtv boudone nitou adouna télé yeup def ko plateau mane dama ame louma méti thie Sénégal
Walahi ligua wah rek moye deugueu aduna mo doye war moudioume diamono
Sénégal mongui ni deeee xamugnu sakh lugnu wara def kou teddd ki kou bakh ki kou sell ki référence thi bepp djiguene. Rafet nagnu ndiort si mome yalna khipé aldiana
Boul am loula metti Sayda Zeynab malayka yi niokoy defal plateur
Fambaye Ba bilakhi ni lamako sama yaye wakhé taye! Mais nak li moye adouna,niom yeuffou zaïr moléne nior. T pourtant d kerok weuye katou toubab bi bamou dé wé télé yeup ci wakh ci sen jrnal! Mais yalnako yallah kharé adiana firdawsi ci barké seydina Mohamed psl
Amine
Yala n'a yalla yarame sayda wanale ko ak yonentebi sala lahu alayhi wa salama
Meittina lole Bilahi
Yallah nak moognou Moome
Yallah na Xippê Aldjiana Firdawssi THI BARKÉ SEYDINA MOUHAMMAD ALEYI SALATOU WA SALAM
Oustaz Makhtar mangui lén kay dialê
yalla nako yalla yeureum khareko al diannatoul firdawsi barkeb serigne touba khadim rassoul
Wallahi méty wayé lolou moneh yalla
Yalnako yalla yereum ta hareko aldjanna firdafssi amiine yarab
La ilaaha ilalah !!! Eywaay souniou sokhna Zaynab j’ai troooop mal 😭😭😭 Thieuy Al Mumīt sounou borom reka meune lui , diambaar bou mag Seyda mala beugueu, toujours dans nos coeurs ♥️ !!!! Yallah nala sa sopé bou seleu bi téerou thia Aljaana you kawé ya. Amiiiine y’a Rab
😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢
Cv
Walahi azim sokhna zeynab reference leu yalnako borom bi atté cii yeurmandem oumma islamik niakk neu😭😭😭
Kou bah demna yalla nako yalla yeureum th hareko aldjana
Maman zeynabe yala nako yala yereume té khareko aldiana firdawsi
Gnaknafi mame gnakeu fi ay papeu gnakfi diéguégnalé you bari wayé ki gnou gnakeu tay dé meussouma mété ni meussouma bété ni ohhhhh yalnama yalla bal wayé sama khol metina sama khol metina sama khol metina meussoumako guisss wayé sama khol metina
Pape Makhtar machallakh Yalla nko Yalla yeureum
mon idole sama sope khawemakowone mais je l'ecouter attentivement c a cause d'elle que jai mis le voile je suis meurtri je narrive pas a croire que ya zeyda est parti paix a son ame
Amine yarabi machALLAH
amine
Continue de prier pour elle la sœur. Son décès m'a fait un choc. Je n'ai pas pu retenir mes larmes.
@@MrGueye78 merci bcoup je le ferai inchaallah elle ma bcoup changer
Yalnago yala yarme walahi gou bakh la
Yalle nako yalla yeureum té kharéko aldianna
إنا لله وإنا إليه راجعون إن لله ما أخذ وله ما أعطى وكل شيء عنده بمقدار اللهم اغفر لها وارحمها و أسكنها فسيح جناتك وألهم أهلها وذويها الصبر والسلوان اللهم لا تفتنا بعدها وقنا عذاب النار
innalilahi.wa innailayhi rejiune yalla n'a ko yalla yeureum té haré ko aljana bi gueneu kawé
Yalla nako Yalla yeureumm té xaréko Aldiana ci barké Mouhamed SAWS
yalla na khipé aldiana firdaws.Ma Cha Allah Sokhna sou bakh démna
yalla na yalla yeureum tè kharèko aldiana si barkuè seydina mohamed
deugeulaa.oh papa alpha....😢😢inchAllah yalla nako yalla dieguel t'ai kharai ko aldiana.macHAllah.Amin amine.💞
Ooooooooh Yallah réka meuneu sama xol toyna samay rangognes tourounagn ya Seyda yalena ngua khipé Janatou Firdawssi.kou melni yow diéxna Thi adouna Ya seyda nopaloul Thi diam Fall thi barki Ya Rassouloulahi
Yalnako Yalla yeureume diégalko ay bakarame té kharéko aldiana
Mon idole ,mon fans ,aka maka soponeeee troppp skhe,yalla bouko saytanner djitou
Qu'Allah lui accueille dans son paradis firdaws vraiment l'Islam entier pleure maman zeynab
Thiey adouna sama sope k firdaws soit sa demeure eternelle.ALLAHOUMA AMINE
Fatimasy Sy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Thiey yalnako yalla kharè aldianay firdawsi
Yalla nako yalla yereum thi mbarcké seydina mouhamed psl
Yalla na yalla yok Aÿ lerame machalla machalla
qu'Allah l'accueil dans son paradis céleste amine
Ay sama sopé ba demna rek yalla nako yalla yeureum
Yallana ko yalla yueruem kharèl ko aldiana thi barkep mokhamed
Yalla nako yalla yueruem te khare KO aldjana machalla
Tu restera toujours dans nos coeur yalla na aldiana di sa ker
Yalla na souff oyoff si kawam sopèmm seydina Muhammad tèrouko si Ardiana firdawsi
Pendant presque toute l'année g pensais à elle.le 6 octobre meunatoumako fatè bilay 😭😭😭
Machallah Aman solo yalnako yalla yuerem té xaréko aldiana yarabi
Yalnako yalla térou si aldianam ya guené kawé
Kodabo Ndiaye kharitou dieukeureum ''i.
@@aissatouyatt8916 kharitou dieukeureum
Qu'Allah Lui pardonne et L'accueille dans son paradis.
Yallah bouko thiat djitou thi bamélam ya rabbi
May her soul rest in perfect peace May Allah swt Grant her jannah she did well ...What a beautiful soul
Allahouma irhamha wagfirlqha wafou anha wa akrim nouzoulaha wa wassih moudhala wagsilha bil ma i wassaldji wadaradj wa naquiha miina zounoubi walkhataya Kama younaka sawdoul abyadou Mina danass😭
Yalnako borom bi yereum té kharéko aldiana firdaws😢
Niane yeupeu yalla naka souniou borome ndangou té wassaréko ci mbolème dioulite
Praise be to God, Lord of the worlds, and may God's peace and blessings be upon His servant and Messenger, our Prophet Muhammad and upon... Yes, he said: The Messenger of God, peace and blessings be upon him, came out to them. He said: Say: O God, bless Muhammad and the family of Muhammad,...🙏☝️👌👍💕
Je vous prie d'écrire une œuvre sur elle pour qu'on puisse enseigner ses œuvres.
oj
@@fatousidibe5540 n'nbbn’n''‹'ampaà n'm
Machala yala nako yala terrou thî ardjana bou gué n'a kawe
Mere na waa NDENKAANE ak waa DTV feberam bi waron ngen nukou wakh ndakh nu nianal ko waye YALLA lugen rek lai deff 😭😭😭
😭😭😭😭😭
L
yalla bouko thiat djitou thi bamelam barké alhourane
yalla nako yalla kharé aldiana souf oyof thie kawame kou yiwe kou oyof djiguéne gnie nagnou roye thie mome
May her soul rest in perfect peace Aamen!! What a great lost to the Muslim ummah. I'm a Gambian Gambian who has been following her for a while blie, I was so shocked when heard the news. The condelence to her entire family and the Senegalese at large.
Badjie Salifu our condolences to you my brother, Senegal and Gambia are one. May Allah give her Janatul -Firdaws.
Yalla nako yalla yeureum te khare ko aldiana firdawssi amine
Bilahi man deh dafa mellnii khaw ma lan ma mais dama kon niwantalll trop bilahii daff ma touch lolll bilahii
Yalla na firdawsi di kereum
yalla nako yalla yeureume ta kharaiko adiana firdaouwsi
QUE LE BON DIEU LA PARDONNE ET L'ACCUEILLE DANS SON PARADIS
TOUTE MA FAMILLE L'ADORE .SEUL DIEU SAIT QUE J'AVAIS L'INTENTION D'AMENER MES PETITS ENFANTS CETTE ANNEE A SON INTERNAT.
Machalla sentakhaway rafetna yalnako yalla yereum
machalla
Yalla nako borom bi yereum tè kharè ko si adiana you kaweyi 😭
Machalah birnama ni moma geune fouf walahi Wa raboul kaba. La notion a perdu, l'islam dans sa globalité a perdu une femme intègre imbue de bonté inestimable. Yalla nako yalla yereum 🙏🙏🙏
Que le bon dieu l'accueil dans son firdawsi. Certains vivent longtemps pour accomplir leur mission en l'espace de très peu tu as accompli la sienne que son œuvre soi une viatique pour nous autres.
Yalla nako yalla yeureum té yokk Aÿ léram
Alahou akoubar royoukaye la yalla nako yalla diéguel barkep serigne touba
Yalna déh disanof laye maman zeynab
kou lugeyal yalla mou fayla fi fay la feule saida zeinab fall
yalla nala yalla terro firdawsi
oustaz alpha magui lakoy dialle bou baxh lowaxh si mome lou am la
Bayi nah adouna man yalnakoh yallah harreh koh aljanatul firdaws Ya metina bilai
Que le firdaws soit ça dernière demeure 🙏🙏
Sokhna sou bakh dèm na yalla na firdawsi di sa keur Barkè mouhamed
Aminn yarabi
Yalnako yalla yeurem rip koudeff loubarie si sama dound
Ndeysane jigene bou bakh, yal na souf oyof si kawam, yallah khare ko Janatul firdaws.
Yalla nako Yalla yeureum
qu'Allah Soub-hana-wa-ta-Allah lui fasse miséricorde
Machallah yalla nako yalla khare Aldiana
Yallana khipé Aldiana firdawsi thi Barker yonnetebi saw
Yalla nako yalla yarame te xaréko al dianna
بكائية لخالدة القلوب..
(رحمكِ الله يا السيدة زينب فال..)
"المَشرِقانِ (عليْكِ) يَنتَحِبانِ"
يا أمّنا، يا "زينب" الإيمانِ
"لَمّا نُعيتِ (من البلاد) مَشى الأَسى"
يقتاتُ من قلبي، ومن وجداني
وانهالتِ العبراتُ من كلّ الورى
"(وَبكَاكِ) بِالدَمعِ الهَتونِ (زماني)"
صمتَ الفؤاد بُعيْد ذكركِ برهةً
"لَكِنَّما يَبكي بِدَمعٍ قاني"
حَملوكِ والنعش المُوَدِّع لؤلؤٌ
"فَكَأَنَّما في (نَعشِكِ) القَمَرانِ"
"في ذِمَّةِ اللَهِ الكَريمِ وَبِرِّهِ"
يا زينب الخيراتِ والإحسانِ
"لَو أَنَّ أَوطاناً تُصَوَّرُ هَيكَلاً"
جعلتْ عفافكِ معْلمَ الأوطانِ
"أَو كانَ يُحمَلُ في الجَوارِحِ مَيِّتٌ"
أقسمتُ أنّكِ تسكنين جَناني
ستظلُّ زينبُ حيّةً بقلوبنا
"وَلَرُبَّ حَيٍّ مَيتِ الوِجدانِ"
"(علّمتِ) شُبّانَ المَدائِنِ وَالقُرى
كَيفَ الحَياةُ تَكونُ في الشُبّانِ"
ورفعْتِ بالإيمانِ ذكرَكِ عاليًا
"والذكر للإنسان عُمرٌ ثاني"
اللهم إغفرها ورحمها ويدخلها جنة الفردوس
yallanako yalla yueram diegalko khareko aldiana
Amine ya rabbi🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Yalnako yallah yeureum
رحمة الله عليها ورضي عنها
Yo Allah yaafomo wadha Aldianna guebhalmako
Manchalla yal naco yalla hare adiana
😭😭😭😭😭😭😭yallana ko yeurem maman
Yalnako yala yerem khareko adiana
Je suis fierte d'elle ,elle est au paradis
Yalla nako yala yaram amin amin amin
Yalnako yalla yereum Aminé
اللهم جدد رحمتك عليها ومغفرتك لها🙏🙏🙏🙏🙏
Yalla nako yalla kharè Aldiana
Repose en paix Adja sokhna zeynab fall sunu yaye
Ya zeyda yalla n'a sama sokhna melni mom
Yana khipé aldiana firdaws
Yalla nako Yalla yareum
May Allah d almighty give her ganatul firdausi
Ndeysan yall na yewo ardiana firdawci 😭😭
Wallahi c la oumma islam ki a perdu mw jarive pa a l croire kel é parti wallahi yalna yallah takhawou ko sama idole une référence
اللهم ا غفر له و ارحمها
Allahoumma ighfirlaha warhamha
Ndeysan Yal nako Yallah yereum nioguilenkoy diale
Sama idoles sama sopé démna
والله لقد فقدناها إمرأة عظيمة
Yalla naniou yalla may holou mougne té maye ko aldiana allahou akbar
Ay adouna yamana worr l'islam niak na diné wéttna sokhna sou bakh dém na seyda zeynab fall yallana agualé dawama aldianay firdawsi
Amine