Dama dioy ba sonou 😢 aita et tntn rasoul dafa méti nék xalé di seuy guiso say wadiour surtout nga ame blém métina j'ai perdu mes parents mais chaque jrs may xalate souma yalla mayé dieukeur inchallah kane momay conseiller c'est dure yalla nagnou yalla may xolou mougne ❤ Amine
*Deguéne yone bi gua djieul boul ko wathieu béneu yone tacko boum la dougual thi yeuffou seytané wam yoyou.Aïta nakk soff gua ak sa djioy yi yeugatoul way tacko dafa rakadjiou trop mais ALADJI lafiy fekk😂😂🤣🤣*
Déguéne a totalement raison de refuser de suivre TACKO dans ses betises, di bagneu wakh ak AITA, ndax Aita wakhouko, défouko dara lou bonn ba légui ! fogna nitt waroul douggou ti keurou diambour di beug york fitna yi'm fa fek !
Mann Aladji laye topou 😂kouy topou Aladji lalal j’aime 😂😂
Mane dh yalla lay topou
Il joue bien son rôle mais yalla lay topou
@@MameantaNianeg1😢
dezzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzzdedez
Bly oiw ❤
😂😂Aladji dh moo paré mome fimounékk kendou lale Aita wayé wakhena deugue Tacko warouko ber😂😂😂😂❤❤❤❤
Oumar mo niak fayda
@@BatorD-r4y😊
Yalla Na yalla yokou sonou thiofél si yonéntubi psl❤
Amine inchallah
Aminé inchallah ❤❤❤
Amine yarabi
Ba am ga wacila bou Matt wacila
Ndeyessane aïta je t'aime beaucoup mouniél lo mouniene mou diékh inchallah 😢😢😢😢
Bon magal à toutes à tous yalla gnepp fécké déwane inchallah 🤲🤲🤲🤲🤲
Amine
Amine inchallah
Amine yarabi ❤️❤️
Amine🎉❤
Amine Amine inchalah
Yalna Diamou yagg si Sénégal Ak Louka Weur sii Barké Baye Niasse Yarabi
Wa yeen dégénne mi yeena ngi koy giss seeet ki rafett na dh😍😍😍kou d’accord ak man laalal j’aime waay😍
M
Ndeysan aïta yeureum nako 😢😢 vraiment mérité woul li 😢mes mougnal rek sa rôle yomboul eladji dafko yeureum 😢 ndeysan
Dama dioy ba sonou 😢 aita et tntn rasoul dafa méti nék xalé di seuy guiso say wadiour surtout nga ame blém métina j'ai perdu mes parents mais chaque jrs may xalate souma yalla mayé dieukeur inchallah kane momay conseiller c'est dure yalla nagnou yalla may xolou mougne ❤ Amine
Lépp ay bakh inchallah
*Courage a toi lepp dina bakh Inchallah*
Daye bakh inchallah monial rékh
T inquiète pas ma chère yalla bakh na
Surtout jamanoji gnou tollou say wadiour rek niola Mana soutoural ba ken doula Khamal dara mais d'où kenen
Astou sounou actrice préférée namonenanioula ❤❤❤❤😂
Deguéne la beugue mane ❤❤❤😂😂😂😂😂
On réclame le bonheur de aïta
.n.p.l9i
On réclame le bonheur de Aïta 😍🥺
On réclame le bonheur de Aita 😢😢
Imam Thioune waay
@@bocarguisse2282fo rer
Dafa djot
@@Laylabatoulvraiment 😢😢😢
Thioune yaw tmt yangui fépp😂
Bilaye aita ma fait pleurer 😢😢😢 c'est trop dur 😢😢
Même moi Bilay 😭😭
On réclame le bonheur de aïta❤❤
Diaroul yakamti dina nieuw inchallh mdr
Bonne magal touba ❤❤
Kou am xéll Bou Dale si cousinou takko bi RK lalale j'aime
*Bilay ioe*
On réclame le bonheur de aita ❤ 8:58
Nb nous
Astou mo nara khame vérité bi yeup
On réclame le bonheur de Aïda sonena
🎉 c'est un plaisir de retrouver astou. Une des meilleures actrices au Sénégal 😊😊
On réclame la bonheur de aita
😂😂Yénn bilahiiiiiii Aladji dou nite dama sétane encore dégueungene nimou yémalé gnii😂😂😂😂😂
Amine yarabi niou bokou fécké déwéne inchallah 🙏
Aladji dako yeureum ndayesan 😢❤
Bilay
The huge that rasul gave Aita make me cry 😢
Dégueune est très belle machallah.
Deguene est adorable 😂😂
Bilay
Le bonheur de aita
Femme yake femme.nous sommes méchantes entre nous et le plus dommage a cause des hommes
Oh tonton Rassoul
On réclame la Bonheur de Aïta 🥺
🥰🥰😢😢
Vraiment aita sonena torop
@@faoziediongue3276 damako sakh yeureum
Suis talibé cheikh, mais bon magal aux mourides yonou djam ak salam . Bou leen faté sama sarithieu
Nooo man Aita damako yeraam torop dama joyyyyyy 😭😭😭😭😭😭
Anna gni Magali woul😂😂
Magui ni
Niongui ni
Bonheur de aïta way li dou yone😢
On réclame le bonheur de sokhna bator 😂😂😂😂
😂😂
Bonheur de Aita et rapidement
Aita sa souy dioye dafmey dioylo😢😢😢limouy doundou metina trop
Kou nek Di nan maffi djitou😂😂 kon maffi ndaré 😂😂
Kou beug deguen lalal ma ❤
*Deguéne yone bi gua djieul boul ko wathieu béneu yone tacko boum la dougual thi yeuffou seytané wam yoyou.Aïta nakk soff gua ak sa djioy yi yeugatoul way tacko dafa rakadjiou trop mais ALADJI lafiy fekk😂😂🤣🤣*
Merci ALLADJI❤
Tout jour on réclameé la bonheur de aita
Tonton Rassoul ak Déguéne mi ah wa bakhna bamou sotti
Tàkko lu tax mu soof lii dafa doy nag jot na Ayta am jàmm dëgg gi feeñ lépp leer
Astou mo mana theatre 😅 elle est forte.mention special 😊
J'adore Aladji ❤❤❤
Pa liguaye def bakhoul kenn dou ame problème ak sa djabar diko wakh foune 😮
Bilay niak soutoura goor mo bonne si bopam
Deguene reek laay toop man machallah foula der
On réclame le bonheur de aita❤❤❤🤲
Waw Déguène mi aka dionguoma machallah.🥰
Tonton rasoul nar na see dall dh Dina dieul booy bi rek🥰🥰
On réclame le bonheur des dames de Sonko 😅
On réclame le bonheur de aïta😮
Beugue n'a khAm aïta loum fiy df
Aita ducourage ❤❤❤❤❤❤❤la vie est tellement difficile j’ai été comme toi j’ai perdu mes deux parents 😭😂😂😂😂et………..()😭😭😭😭😭😭
Deguene rek lay weir❤❤❤❤
😂kou beug eladji beuseul j'aime ❤
Aladji est le meilleur
NOUS suivon le series aïta mai on voi plus pa barri pourtan il joue bine 😂😂😂😂😂😂😂
Magnifique Diary mane yaw rek lay suivre
Non Aita doylonama🥺🥺🥺😢😢
Aita n'a rien fait mais gnome dinagnoy fegne deh
L bonheur de aita je le veux ❤
mane alaji momay raye 😂😂😂😂😂😂
Aïta joue bien tako aussi des vrais artistes
Aïta rek lay tompeu❤❤❤
on demand la liberation de ousmane sonko 🗽
On reclame tpujours le bonheur de aita
Cheeey Alagie miii key😂😂😂mo nyeme de😂😂😂
On réclam la bonheur de aita😓😓
J aime aïta
Kou nèkone si préparation magal Touba rèk lalal j'aime
Macha alla ❤️
Aladji kene d'où mom bilahi ❤
Déguene ma préférée
Notre fatdam sama préfère ❤
Merci alaji
Ani soutoura si mèkou sèy
Diarry rek laye top elle joue bien da âme class
Alaji raynama
Ça m’a fait bcp pleurer 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Machallah pour diarry je l'adore yaw rek laye top seu fans la❤
déguene rék la beug 😂😂
Man aita damaco yeureume bilaye 😢😢
Yalla n deugue bi fégne ndeye sane
Omar revin sur terre😂😂😂
Ayta la yi topou
Djiguenn niou bari nioye yakh seni dome demm maroc 🇲🇦 3million pr foo kessé Marrakech mogui nonou Agadir nak
Bilay aïta dafa niak fayda
Ken dou Diary mala beug
Yerem na aita
Déguéne a totalement raison de refuser de suivre TACKO dans ses betises, di bagneu wakh ak AITA, ndax Aita wakhouko, défouko dara lou bonn ba légui ! fogna nitt waroul douggou ti keurou diambour di beug york fitna yi'm fa fek !
Deguene deeh moye tass keureume na dem rekk
ah bon ? ci lane nonou ma belle ? pourtant ba légui, lou bakh rek lé wakh ! dey teudé diakhanaye @@fatoundiaye1999
Merci kiman❤
Mai policiers 👮♂️ yii mome moye lolou ah 😢
Ta lo mome
Kou bone la wayé béss same dina gneuwe
Tacko changè coiffure bi stp
Non générique bii nékh nama🎉