amna solo, wayé souma sayoone KHALIFA SERIGNE TOUBA yii gnou bérr leen de coté surtout ki fi nék !! nagnu leen bérr neulé rek mo gueune waur té mo gueuneul KOU TEDKI... wa salam
deug ya wakh degue dialibatoul doyna défarou ku tedki da nga sééye kou begue dof t kou doff si nitt gni, niité fa yalla sa wakh ji serigne touba bou werla
« Madda liyal Baaqi bijaahi Raahi ; Maa rumtu bil qalbi wa bil aw raahi » (Yallah nangu na mboleem lëp lumako mës ñaan, moo xam luma bind la wala luma fass sama xol). Il y a des centaines de bayits de ce genre. Kon Sëriñ Bi lumu bind, lu Yallah nangu la !
Kèn dou chiekh ahmadou Bamba khadimou rassoul
amna solo, wayé souma sayoone KHALIFA SERIGNE TOUBA yii gnou bérr leen de coté surtout ki fi nék !! nagnu leen bérr neulé rek mo gueune waur té mo gueuneul KOU TEDKI...
wa salam
Mooy lignou Serigne Touba Sante Saakh: Ami teguine kham book nathi nga kham ni ngaay waakhé. Moom limou khma bakooy waakh. Niit guen nakoko kham ta waakhou ko... Khakoul yakhin bimoy waakh southa tolouwoon am na nénè noumouy wakhé Wa Salam.
Iskay Serigne Mor Seck Marakhib Mouride Sadix nga
Amna solo ms diaroure toudou aye kilifa yi serigne bi mome khasida boosi niangue rék bakhna
ndeysane nehna loolou sah. djeureudjee borom touba
écoutez
Macha allah
deug ya wakh degue dialibatoul doyna défarou ku tedki da nga sééye kou begue dof t kou doff si nitt gni, niité fa yalla sa wakh ji serigne touba bou werla
Awma loudoul dialibatoul marakhibe 🙏🙏
Santé boubakhh ci barke markhib la tedde ta gamnane youkote rek laciyy guisss
vielen dank serigne touba gracias serigne touba merci beaucoup serigne touba
dieureufeuti serigne touba
Yalla nanu lagui thi serigne touba mom mi minga khamni lepam mbectéla
Diereudieufeuty cheikh Ahmadou amougnou fayam barke marakhib 🥰
Ciiy seydina dialibatoul marakhib
Dieureudieuf Serigne Touba amouye sa faye mame
Dieureudieufe serigne Touba
Dieuredieuf mborom touba diarama mame cheikh ibrahima fall lamp baboul mouridiniya
Cheikh Akhmadou Bamba mo wéssou bakh yaa dimbali gnépp mane dhé serigne yéwd nama
Seugn Mor Seck Marakhib yaggu fi lool way barké MARAGHIB !!! santati Borom Touba rk
Thieuy
جالبةالمراغب
tieuy serigne touba
thiey borom touba kénla
Khawma l'année de waters man ibra bissboune ma dorouss marakhib magui ni yokoute rek l'acide guisss
macalha
dieuredieuff serigne touba
Salam Mbok yi
dama donn sakkkou rajazzz khassida bi si fin bi ko niou si eunn baaakhééé bou geun yaaatou
Mouride boko diote rek nga yonemako
Abo Madiyana Sene
Dieureudieuf Serigne Touba Khadimou Rhassoul.
Ndayesan ma cahallah
serigne touba dieredieuf
👂❤️❤️❤️❤️❤️🙏
Tourou yalla motakh 'nanou gor gor Lou s'y Sellal ko
Machalla
dieuredief Serigne Touba
serigne bou mac bii li yeup yawla amo morome bou werr
Dieuredieuf Khadim rassoul
dieureudieuf borom touba
amna louma thi xam mane yalla dialibatou marakhib bamba yalla
dieuredieuf Serigne touba
Mane dhé Dialibatou rékk lay té nguissou massi bénn guagne
Akassa amine yarabi
Akasssa jerejeutety serigne touba
❤❤❤❤
thiey thiey thiey
DIEREDIEUFEUTY SERIGNE TOUBA!!!
MachaAllah
Machallou s mor diadieuffaté borom Touba
Ndaysane sama xol sedna walahi kéndou serigne touba
amna solo
Či xassidayi rék
Amnasolo yalanala s touba faye gangefay
Nice
Seydina dialibatol marakhib
Mane béne question la Am.moy Serigne bi gnane yimou niane si khassida bi kane moko wakh ni que yalla nangounako ? Juste une question pour kham .merci
« Madda liyal Baaqi bijaahi Raahi ; Maa rumtu bil qalbi wa bil aw raahi » (Yallah nangu na mboleem lëp lumako mës ñaan, moo xam luma bind la wala luma fass sama xol).
Il y a des centaines de bayits de ce genre. Kon Sëriñ Bi lumu bind, lu Yallah nangu la !
@ si si je suis d’accord avec toi mais je cherche une preuve extérieur
Salam Mbok yi
dama beugone kouma bakhé djangue kourel bi si debut bi, si commencement video bi
kourel mafatihoul bichri
Kourel mafatihoul bichri nioko diang
Eskeuy
thiey marakhib
Ndaysane souma guisé li damay gueuna sawar si xassida
Sama lepp marahiblah
THAYE SERIGNE MARAKHIB BUEGUE KO LOOL
Thièy dialibatoul marakhib
seydina marakhib
thiey borom dialibatou
Diadieuf fall
kou may ndimbali nguir ma ame dajjou toute tank bi
jokhma sa email
Moustapha SY siaré nala bou weer
Moustapha SY jallotantoine@gmail.com t diadieuf si yéné
ziar naalene noumay def ba am radiassou gonè gui
Deugg bouwér Dara douko dindi
Mouride wakhtane bi amena solo lol
Amoull morom
سرج طو بى امول مرم كنله
Dieuredieufe Serigne Touba amoul morom billahi
dieureufeuti serigne touba
dieuredieuf Serigne touba
dieuredief Serigne Touba