Di santt Sëriñ Tuubaa Sëriñ Muntaqaa Basiru Mbakke! Di rafetlu bu baax jeetaay bi, ak liggëyub Sëriñ Seex Ndigël Seen Taliibeh Sëriñ Seex IsmaÏla Juuf Nurullah, ak Seex yi, ak Talibeh yepp rek! Lepp sellna te jag, Mash'Allah!
Wa yaw mom paix nit am kilifa kii dieuf katt boudoul wah dp tawom bi mako Lima yakar mog sama bene xarit biñouy khékh ndipandal 1995 ×+ la mom lañoudon santé ngoom ma
Serigne Gana en tant que historien fi dofi dieulè dara Li gueyibe SERIGNE TOUBA gni kene fenioussi sekhale damilni yombou nawete tchi marché ba Kham kham doulougnouye Ndiaye ça marchèba Do degue wa Keur Cheikh Ibra di feusseule sene meune meune tchi batine Mana mana dou yaw Sene bop cote lanefinekale La courroie de transmission qui vous lie à SERIGNE TOUBA ou à CHEIKH IBRA est inexistante CHEIKH DIGUËL bene la fi te Fall la sante On a voulu juste se jeter dans l'ethnocentrisme pour exploiter une communauté Vous n'êtes pas historique donc pas un devenir dans le Mouridisme punto
Serigne CHEIKH Ndiguel Sène Yallanafi yag té weure.Dieuredieuf Serigne Gana
Akasa S Gana masere machallah yak Serigne cheikhe
Machalla dieu ra dieuf séne
macha allah sama serigne yagfi lol té weur barké chiekhra fall
Machalla yalla na yalla arlene defal lene diam machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Di santt Sëriñ Tuubaa Sëriñ Muntaqaa Basiru Mbakke! Di rafetlu bu baax jeetaay bi, ak liggëyub Sëriñ Seex Ndigël Seen Taliibeh Sëriñ Seex IsmaÏla Juuf Nurullah, ak Seex yi, ak Talibeh yepp rek! Lepp sellna te jag, Mash'Allah!
Si sama ♥️Sed n'a teyy sama sope AK sama yakar aduna ak alakhira
Bëgté rék sène yaram❤️
❤️❤️❤️
Serigne gana coula sope laa ndax liingay wax ci Serigne Touba wague leen fii lool thé weer s. Cheikh moom loo ci wax rek amna lou dees
Serigne Cheikh Ndigueul Sène keman deugg la
Yague fi lolo te weur sene barké Serigne Touba mbacke khadim Rasoull🙏🏿🙏🏿🙏🏿❤💕
Machalla lii rafetna trop
Xool seedna🙏🙏
Akassa serigne cheikh Ndigel yag fi té and ak wër té yallah aarla arnou
Aamiin yaa Rabbi
Machallah khôl Seedeu
Machalla serigne gana
li Raféte neu Machallah
Amin Yala nafi yagg
Machalla
Macahala
Gana defga erreur dh louy(Sexouniou lomay wowé =Sexouniouloumalaye wowé) wakhy doooffff
Akassa chiekh ndigale sene
Merci. 🤔 🤔 🤔 🤔 🤔 🤔 🤔
❤️❤️❤️
Ziar nga jambar deuggu am yeurmendé xam xam bu fèss
Mane dama beug cheikh diguel sene
Dama beugg serigne cheikh ndigeul té manu mako guiss
Serigne cheikh ndigueul séne doudeul wereul séne
Maane dama beug checkh ndigual sene
ma cahalla
GUEUNA YAG GUEUNA WEER REK SENE
Rawatina univirsété Touba bi
Serigne cheikh ndigale séné diuerdieuf
Wa yaw mom paix nit am kilifa kii dieuf katt boudoul wah dp tawom bi mako Lima yakar mog sama bene xarit biñouy khékh ndipandal 1995 ×+ la mom lañoudon santé ngoom ma
Niom mome guisou ma niouye diokh adiya s mountakh wakh leene niouye indi adiya
Louy lolou yaaa Kan
Thio
Mesera yagal te ver
🤭🤭🤭🤭😂😂😂🤣🤣akano mana doll moridyi fénn rek lañoy déff
Serigne Gana en tant que historien fi dofi dieulè dara Li gueyibe SERIGNE TOUBA gni kene fenioussi sekhale damilni yombou nawete tchi marché ba
Kham kham doulougnouye Ndiaye ça marchèba Do degue wa Keur Cheikh Ibra di feusseule sene meune meune tchi batine
Mana mana dou yaw Sene bop cote lanefinekale
La courroie de transmission qui vous lie à SERIGNE TOUBA ou à CHEIKH IBRA est inexistante
CHEIKH DIGUËL bene la fi te Fall la sante On a voulu juste se jeter dans l'ethnocentrisme pour exploiter une communauté
Vous n'êtes pas historique donc pas un devenir dans le Mouridisme punto
Yaw danga réré mbir thi sérigne cheikh ndigual Séne
Machallah