Mouhamed Niang Mou Serigne Saliou - Serigne Fallou (Clip Officiel)

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 13 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 2.5K

  • @thiabyndiaye8002
    @thiabyndiaye8002 4 ปีที่แล้ว +136

    Ndaysan ❤sa souma❤ diakhlé serigne❤ fallou ❤lay hoo ❤thé❤ sama ❤adio❤ day ❤fadiou❤

    • @maremesall9322
      @maremesall9322 4 ปีที่แล้ว +3

      Khana souma dialé mane moom si siguil ma la deuk masouma gantal

    • @ndeyetoutybarry8035
      @ndeyetoutybarry8035 4 ปีที่แล้ว +4

      Wakhal de mm mane moy sama werouway te dôme boutoudou serigne fallou rek la beuguone te amnako Alkhamdoulilah

    • @aramediaw8620
      @aramediaw8620 4 ปีที่แล้ว +3

      Khamnassi dara billahi

    • @thiantakooneba7698
      @thiantakooneba7698 4 ปีที่แล้ว +1

      Kéne dou fallou awa bousso

    • @ndiayetecnology1339
      @ndiayetecnology1339 4 ปีที่แล้ว +2

      nday San man tay nouma mél s fallou la Dako beugue ba awma si mom sago yalana Nama yala may dieukeur diou bakh seuy bou barkèl tawlo si am serigne fallou

  • @morwakanahaqqan6585
    @morwakanahaqqan6585 4 ปีที่แล้ว +144

    Yalla na Serigne Touba dèfal nièp diam kou wakh Amine yalla gua doundou 111 ans sans tolof tolof Mor wakana haqqan ,Angleterre sa Sopè machallah clip bi Rafetena lolou
    Yalla gua guena ame Ndimalou Serigne Saliou 🙏🙏🙏👏🥰

  • @sokhnaseye317
    @sokhnaseye317 4 ปีที่แล้ว +956

    Je suis tidiane mais vraiment j aime mouhamed niang il chante bien avec sa belle voie
    Kou d accord tapéll j aime

  • @dieynabadieng8989
    @dieynabadieng8989 4 ปีที่แล้ว +81

    Cheut j'adore cette chanson elle me donne la chair 🥰de poule bilay je l'écoute à longueur de la journée
    Mouhamed niang voix bi mo graw machalla j suis talibé cheikh mé j l'adore dal je kiff tou c chanson laff thiat ❤
    Fans number 1 moy mane ☝️yalla na yalla yéreul bate bi t yokk khatane bi mayla goudou fane ak wér amine touf touf 🙏

  • @mamediarrafall160
    @mamediarrafall160 4 ปีที่แล้ว +71

    Nianal len ma réne ma am bac si barkép Serigne Fallou Mbacké❤️🙏🥺

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 4 ปีที่แล้ว +115

    Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne

    • @knengom8109
      @knengom8109 4 ปีที่แล้ว

      Amine yarabı

    • @aramesy1743
      @aramesy1743 4 ปีที่แล้ว +1

      Machaalah nioginiann ci barkes serinbi moutakhawou arla sibarkes borom jiamana borom jiouroul

    • @mamifalloutv9465
      @mamifalloutv9465 4 ปีที่แล้ว +1

      Amine amine💗💗

    • @taphaseye243
      @taphaseye243 4 ปีที่แล้ว

      Aminnne

    • @taphaseye243
      @taphaseye243 4 ปีที่แล้ว

      @@aramesy1743 Aminnne

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 4 ปีที่แล้ว +158

    Mouride mba yénagui wath magal gui insha Allah 🥰🥰❤❤🙏👌👌👌

  • @fatoudiop2975
    @fatoudiop2975 4 ปีที่แล้ว +48

    Thiey sama yakar bii Serigne fallou yalna ma yalla maye doom bou goor ma touddé lakoo rek la beugu ak kouko beugue rek

  • @ndeyeantaniang5138
    @ndeyeantaniang5138 4 ปีที่แล้ว +88

    Ça nérite des millions et même millards de vues 🙏😭😭walae j'pleures ça touche grave 💞👑🔥

  • @ogog4223
    @ogog4223 4 ปีที่แล้ว +45

    Serigne Fallou kouko yakar euleuk kenn doula ladj say keuyitt😭❤️❤️❤️❤️lolou aka lerrr❤️

  • @thianediouf6513
    @thianediouf6513 4 ปีที่แล้ว +98

    Mächallah nexna trooop
    Anni gni sope fallou awa bousso

    • @Fatoudiop-by2nw
      @Fatoudiop-by2nw 4 ปีที่แล้ว

      Sama serigne mane késé

    • @ndeyesarr1078
      @ndeyesarr1078 4 ปีที่แล้ว

      Machallah sama werouway

    • @bacouba7501
      @bacouba7501 3 ปีที่แล้ว

      Trench www et ion CD out f

    • @bacouba7501
      @bacouba7501 3 ปีที่แล้ว

      M@@ndeyesarr1078

  • @aisstouciss901
    @aisstouciss901 4 ปีที่แล้ว +348

    Macha allah je suis tidjiane mais j'aime beaucoup Serigne fallou merci Mohamed Niang sama khol seed na bonne continuation

  • @sadandour3382
    @sadandour3382 4 ปีที่แล้ว +54

    MachaAllah, Serigne Fallou si khol khéweul rék .

  • @sokhnadiarra2802
    @sokhnadiarra2802 16 วันที่ผ่านมา +1

    Man dh barkéb Serigne saliou mouhamed Niang moy sm way kat début ma nék khalé batay moma meeuneu béguel ci Serigne saliou yalla nala yalla Sam barkéb cheikhoul khadim ❤️❤️ beugue nala trp

  • @mamefallougallas5099
    @mamefallougallas5099 4 ปีที่แล้ว +32

    Ndeysan thieuy S Fallou sama wadji mane dh mom rèk la ame mom rèk la beug dh moy sama lép❤️❤️❤️❤️

    • @mouhameddieng9550
      @mouhameddieng9550 4 ปีที่แล้ว +1

      Yak mane Serigne Fallou mo wor dhh

    • @ndeyeleye5081
      @ndeyeleye5081 4 ปีที่แล้ว +1

      akkkkk mannnnn mame fallou rk

  • @babacarndiaye3460
    @babacarndiaye3460 4 ปีที่แล้ว +132

    Serigne fallou mi moy kharitou sama tourreundo sama yakar serigne babacar sy montakh ma am chance nék premier commentaire

  • @pendistasadiakhou140
    @pendistasadiakhou140 4 ปีที่แล้ว +60

    Barki serigne Saliou MBACKE dama beugu tey serigne Saliou rek tah😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว +1

      Pendista Sadiakhou Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @preciousdiarrishniang5060
    @preciousdiarrishniang5060 ปีที่แล้ว +9

    Amouniou koudoul Al Fadilah yalla naniou ko yalla fayal

  • @nogayendiaye498
    @nogayendiaye498 4 ปีที่แล้ว +83

    Thieuy galass bayi mbéne beuguoumako guir beug douguou aldiana beuguoumako guir ragual safara damako beug lol ta yalla takh ta féké woumay diamonom Sax lépp louma beug soumako wowé diourom niari Yon mou wouyouma alhamdou lilah bima doné mourite😍

    • @thiallambathie296
      @thiallambathie296 4 ปีที่แล้ว +1

      bilahi dama fokni lolou mane kasè la

    • @saylo4511
      @saylo4511 3 ปีที่แล้ว

      Yalla kham nané pour ll mana rk la

  • @awadieye7633
    @awadieye7633 4 ปีที่แล้ว +51

    Ana sopeye serigne fallou yi maye lene j'aime😍😍😍😍😍

  • @tamsirsambadiene3285
    @tamsirsambadiene3285 4 ปีที่แล้ว +76

    Loumou wey mou nkh, vraiment j l'adore Mouhamed Ndiang💖💥🔥, ak louma bokou ci Tarikha Tidjaniyi

  • @smbenegueyebadar3301
    @smbenegueyebadar3301 2 ปีที่แล้ว +8

    Sama yakar tay ak elke 🤩🤩🤩😍sarigne fallou

  • @alkarimtv6877
    @alkarimtv6877 4 ปีที่แล้ว +43

    Damakoy déguelou plus de 5 fois par jour yallana borom bi fay ❤️🙏

  • @ndeyefatoundiaye8596
    @ndeyefatoundiaye8596 4 ปีที่แล้ว +184

    Talibé cheikh wayé jaimm trop franchement 🤩🤩😍😍😍na diamm yaguuu

  • @sidatythiam7998
    @sidatythiam7998 4 ปีที่แล้ว +40

    Ani Sopey Serigne fallou yi way 🥰❤❤❤
    Yalla na gneup ame diam barkeip Serigne Fallou ❤

  • @fatimafaliloulah1145
    @fatimafaliloulah1145 4 ปีที่แล้ว +43

    Serigne Fallou Mbacké sama kharit bi kén dou mome ! Moy khewe ba fawe ! Loufi défarou moko défar ! Mo diaye diourélam dieundé co talibé ! Moy déf Di dindy ! Kou rér mou guindi ! Machahalah Mbacké balla ! Dieureudiefé Serigne Touba, Diaraw lak Mame Cheikh Ibra Fall ! LAMPE FALL !

  • @ndeyedia5909
    @ndeyedia5909 4 ปีที่แล้ว +89

    Où sont les talibés cheikh qui écoutent Niang mouhamed ✌️ jumah moubarak to all🙏

  • @serignebarambaye1682
    @serignebarambaye1682 3 ปีที่แล้ว +38

    Ani talibé serigne fallou yi way ❤️❤️❤️❤️💕💕

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 4 ปีที่แล้ว +462

    Anni mouride yi mancha Allah clip bi Nice na trop❤❤❤👌🥰🥰🙏

  • @yaayoubaayam517
    @yaayoubaayam517 4 ปีที่แล้ว +55

    Moubamed niang mi nak ame na loukay wakh loooo quel homme yalla na batte bi wer barkep Serigne Touba

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว

      yaayou baayam Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @sirageuye1060
      @sirageuye1060 4 ปีที่แล้ว

      Der
      N et

  • @momylabambistesakho2745
    @momylabambistesakho2745 4 ปีที่แล้ว +27

    Ay way sama serigne bi 🥰🥰🥰fallou awa bousso lougnouko woy mou nèkh ❤

  • @soxnaadamasow5823
    @soxnaadamasow5823 4 ปีที่แล้ว +225

    Je suis talibe Cheikh way Dma Beug mouride Yiii Soumaleine Guissé Sma Xoll Day sédd GUouy Sma Dôme Mame thierno Damal darou lako toude ♥️♥️🙏🙏 Mohamed nianG On T'aime

  • @ndiayendoumbe1024
    @ndiayendoumbe1024 4 ปีที่แล้ว +255

    Je suis layenne mei vrema cette chanson me touche au cœur ❤️et j’aime bien serigne serigne falou ❤️🙏🙏

  • @adjadiaite4720
    @adjadiaite4720 4 ปีที่แล้ว +209

    Mouhamed niang kagn guay way serigne bara reukeuday nak😭♥️ ani talibé serigne bara yi

  • @sokhnafadilatougallasse8033
    @sokhnafadilatougallasse8033 4 ปีที่แล้ว +757

    Je suis fière d'être Gallasse💪💪❤
    Ana sopey Serigne Fallou Gallass yi❤❤❤❤❤

  • @diawsamb9218
    @diawsamb9218 4 ปีที่แล้ว +41

    Thiéy Fallou sama wadji défalnama tréguadiouné♥️♥️♥️♥️

  • @kanefaty8701
    @kanefaty8701 4 ปีที่แล้ว +38

    Mane mom douma mouride mai bilahi damay deglou ay chanson wam té souma sagnone mouride lay âme kom dieukeur ☺️

  • @mariethiam4217
    @mariethiam4217 3 ปีที่แล้ว +2

    Vraiment meilleur vidéo ❤️💯kene Dou Baye gallas 😭nianalene sama dome dji Serigne fallou tourondome tarre ko ci Barker bii

  • @awakebe1253
    @awakebe1253 4 ปีที่แล้ว +42

    Eskeuuyyy☺️😭😍Keine dou sama wajiii❤️Fallou Awa BoussO🙏🏼

    • @awakebe1253
      @awakebe1253 4 ปีที่แล้ว

      MAMADOU FAYE diadieuf waay🙏🏼🙏🏼

    • @ndeyesenygueye3277
      @ndeyesenygueye3277 4 ปีที่แล้ว

      Moukhamet dokhal thia kaw thia kanam rk

  • @fatoufall1929
    @fatoufall1929 4 ปีที่แล้ว +387

    Je suis talibé cheikh mais mouhamed niang je l'aime fort il a encors tapé fort 💖

  • @nogayeniang6906
    @nogayeniang6906 4 ปีที่แล้ว +15

    Borom kazu radjap borom na ame mou ame diorome gniari Serigne fallou fadj na adjo you bari....
    Yalna yalla yokk aye leram tass gnou si barkém🙏🙏

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 4 ปีที่แล้ว +2

    Merci boucoup Mouhamed niang yalnanga goude fan ak weure barkep serigne fallou contanna si yawo sama sope pi serigne fallou Mbacke

  • @ndoumbembaye8350
    @ndoumbembaye8350 4 ปีที่แล้ว +2

    Ana wa keur serigne falou yi ak baye fall yi

  • @ousmanekamara8590
    @ousmanekamara8590 4 ปีที่แล้ว +30

    Sama yakar tay ak euleuk❤ Galass baye mbéne😭😭

  • @asiasarr2023
    @asiasarr2023 4 ปีที่แล้ว +32

    😭🤧❤🥰😩loum waay mou néx mashallah moom rk ladoone haar koukoo doone har beusseul j'aime

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว +1

      Aishou Sarr Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @momondiaye6767
    @momondiaye6767 4 ปีที่แล้ว +45

    18safar🇸🇳❤️voix d’or yalla na adio yepp fadjounsi barke Serigne Fallou corona dem yooname
    Dieureudieuf Serigne Touba❤️

  • @dieumbdieumb4659
    @dieumbdieumb4659 2 ปีที่แล้ว +26

    Machalla dieureudeuf Serigne Fallou mbacke ❤️

  • @mbayesadji4614
    @mbayesadji4614 4 ปีที่แล้ว +5

    Lii nga way sama sangu bii Mouhamed Niang yalla namala yalla fayal gouddeul'sa fàn cii barké Serigne Fallou🙏🏾💗💗💗❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🎉🎉🎉🎉🎉

  • @sokhnandieguene7099
    @sokhnandieguene7099 4 ปีที่แล้ว +137

    Suis niassène dh ms bilay maleen beugue 😭😭😭❤️❤️

  • @sokhnalo6067
    @sokhnalo6067 4 ปีที่แล้ว +47

    Ndeysane damassei dioyyyy😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏 naaa gaww am Ay Millions reikkk🙏🙏❤️❤️ de vues

    • @modoudiop2322
      @modoudiop2322 4 ปีที่แล้ว +1

      Diara dieouf

    • @mahmoudfalilou8175
      @mahmoudfalilou8175 4 ปีที่แล้ว +1

      Lolou moy am

    • @sokhnalo6067
      @sokhnalo6067 4 ปีที่แล้ว +1

      Modou Diop 🙏🙏❤️

    • @sokhnalo6067
      @sokhnalo6067 4 ปีที่แล้ว +2

      Mahmoute Ndiaye Inshallah 🙏❤️

    • @madiopdiop963
      @madiopdiop963 4 ปีที่แล้ว

      moi je suis talibé chéikh ms jaime mouhamen niag

  • @daroufalltvdakar6333
    @daroufalltvdakar6333 4 ปีที่แล้ว +24

    Ma cha allahu ani son 18safar bi na nieuw

  • @dioufdiyby8928
    @dioufdiyby8928 3 ปีที่แล้ว +26

    Vraiment ça me touche au fond du cœur je l'aime fort Serigne falou sama yakar

  • @mamediarraboussotall1182
    @mamediarraboussotall1182 3 ปีที่แล้ว +21

    Quand j'entends tes chansons je sens purement que je suis mouride . dieureudieufeté Serigne touba

  • @bintusey462
    @bintusey462 4 ปีที่แล้ว +12

    Muhammet Niang❤️👏
    Yal na Yàlla bàyyi la fi nga yàgg fi lool te Yàlla weral baat bi Barke Sëriñ Saliou 🙏❤️

  • @thiorodiouf2130
    @thiorodiouf2130 4 ปีที่แล้ว +30

    Serigne fallou moy sou yakar
    Moi je suis fier de être mouride barki serigne fallou
    Ame fallou doyna... ❤❤

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว

      Thioro Diouf Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @mariamarinsusarte4604
      @mariamarinsusarte4604 ปีที่แล้ว

      Machalla sante rek

  • @galaxiepro.5641
    @galaxiepro.5641 4 ปีที่แล้ว +366

    soyez fier de bamba cest notre symbole dans le monde entier moi je suis fier de bamba❤️ et de toute sa famille mbacké et bousso ce sont des erudits incontestables

  • @Mbaoinfostv
    @Mbaoinfostv 3 ปีที่แล้ว +1

    Machallah yalnala serigne bi fayal boppam

  • @diallawatt8481
    @diallawatt8481 4 ปีที่แล้ว +93

    L'homme à la voix d' or❤️❤️❤️❣️🌹🌷🌷👑

  • @brahamiennelum3612
    @brahamiennelum3612 4 ปีที่แล้ว +6

    Wawawwww MOURIDE thi kanam rek on attendait le single du MAGAL comme chaque année machallah talibé Brahame Niass bi dala sopeu ani Sama mbok yi na bleu

  • @ndoumbedioplasalihate
    @ndoumbedioplasalihate 4 ปีที่แล้ว +145

    Vraiment meilleur clip de l'année. Vidéo bi rafetna,image yi sétna en plus paroles yi mom c otre chose vraiment chapeau à toute l'équipe 😌

  • @satoudione3630
    @satoudione3630 4 ปีที่แล้ว +16

    Oh ken dou fallou Galass sama yakar tay ak euleuk❤ana talibe serigne fallou yi??

  • @ezedgn864
    @ezedgn864 ปีที่แล้ว +2

    Au profit de kazu rajab je viens vous souhaiter bon magal
    #SERIGNEFALLOUSENEGAL🇸🇳

  • @lahadgaye8131
    @lahadgaye8131 3 ปีที่แล้ว +53

    Notre fierté c'est d'être mouride sadikh si barke s fallou ❤️❤️❤️sama serigne

  • @chitalam327
    @chitalam327 4 ปีที่แล้ว +92

    Je suis tidiane 100% mais j'aime 😍trop les mourides 🤗 rawatinna serigne touba 🙏 ( ila touba inchallah ) 🙏🤩

  • @srgnfalloundiaye8322
    @srgnfalloundiaye8322 4 ปีที่แล้ว +13

    Oh sama xole sédd barkep serigne fallou🥰Ani gni done xaar clip bi comme mane ❤️❤️

  • @oumyzangom4926
    @oumyzangom4926 4 ปีที่แล้ว +387

    J suis talibé cheikh mé j'aime bien mouhamed niang j kiff les mourides gnoune gneup gno yém fa yalla. Bon magal mes amour♥️😘

  • @mariehelenesene351
    @mariehelenesene351 3 ปีที่แล้ว +1

    Ndeysane son bi bilahi yalla rek kham nimouy def sama khôl bilay Mohamed Niang yalnala borom bi defal tawfekh Aÿ taysir

  • @AmyLô-u3q
    @AmyLô-u3q ปีที่แล้ว +3

    Ana gni beugué s.FALLOU MBACKÉ ❤❤

  • @evalasalihate551
    @evalasalihate551 4 ปีที่แล้ว +17

    Aniff bi dall nekhna contane nane si yaw barké SERIGNE SALIOU ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @awabdoulaye2783
    @awabdoulaye2783 4 ปีที่แล้ว +6

    Jeureujeuf Serigne Mouhamed Niang nékhna trope waay, clip bi raféte na. Serigne Fallou dinala fayy ba nga yégg ko. Tabarfaq'Allah 💕💓👍🏼

  • @thiarafaye2181
    @thiarafaye2181 4 ปีที่แล้ว +26

    Bilay damako beug lole mom serigne fallou ba takh na kouka way rek Sama xol bi sed tamouma sakh di comantaire ay TH-cam mes serigne fallou diaral namako bilay video bi nice na ta nékh na serigne fallou Sama yakar tay ak euleuke 🙏❤️🙏

  • @omarmboup7405
    @omarmboup7405 4 ปีที่แล้ว +2

    Barki srg fallou😓😓😓😓jaime telment srg fallou sm pp whatsap mofa nk sm fond écran l'EP Limay DF Mme lay suite la semaine moukhamed niang rombe na sounio kogn ak ay group tal son bii yokou ko bamou seus ms bimou tombe ak SN bi sm yarame bi daw telment😓😓😓😓😓😓moukhamed niang yalla goudou fane wy se bat guene der ❤linga weuh sm vie eupena

  • @mansourdiack9928
    @mansourdiack9928 4 ปีที่แล้ว +2

    Machaalah yalla nala yalla taxawou dfal la fane wou goudou barkep khadimou rassoul 🥰

  • @khawlatouba7170
    @khawlatouba7170 4 ปีที่แล้ว +22

    MACHALLAH Niang lo way mou nékh💖
    Je te souhaite un joyeux anniversaire

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 4 ปีที่แล้ว +58

    Fière d'être mouride machallah niang diam ci yaw athia mouride takk diokk ila touba 18 safar moy sunu biss

    • @adjasaliou1940
      @adjasaliou1940 3 ปีที่แล้ว +1

      yalla nanioussi aksei diam

  • @boydiop8209
    @boydiop8209 4 ปีที่แล้ว +21

    Joyeux anniversaire à toi lg vie ndoudal 1111 lep lo beugue yako xam yalla nalako yalla défal si barkéb Serigne saliou iow tay gola cado nga Gouy diox cado bon anniversaire 🎂🎂🎂

    • @awatraore3483
      @awatraore3483 4 ปีที่แล้ว

      Mais c'est l'anniversaire de qui??

    • @mouhamedkante4916
      @mouhamedkante4916 4 ปีที่แล้ว

      @@awatraore3483 de mouhamed niang mou serigne saliou

    • @boydiop8209
      @boydiop8209 4 ปีที่แล้ว

      @@awatraore3483 de Mohamed Niang mou Serigne saliou

  • @cheikhbassfalilou2415
    @cheikhbassfalilou2415 2 ปีที่แล้ว +1

    Jërëjëfëti Maam Alaaji Fàlilu Mbàkke Boroom Ndindi

  • @thiernofall3982
    @thiernofall3982 4 ปีที่แล้ว +4

    Machallah lii nekhna yallna yalla fay ci barkep serigne fallou mbacke amine

  • @niangadiop4171
    @niangadiop4171 4 ปีที่แล้ว +14

    Machalla ani fans mouhamed gnia❤💫🌻

  • @sinyfall9113
    @sinyfall9113 4 ปีที่แล้ว +15

    Walay kounei amnga serigne wayei kou diakk mom ngay wo❤️❤️❤️

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว +1

      Siny Fall Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @sinyfall9113
      @sinyfall9113 4 ปีที่แล้ว

      100% Comédie amiine c’est fait ✅

  • @maxfall1654
    @maxfall1654 4 ปีที่แล้ว +4

    Machallah 😍😍😍😍 sama wadji Bayou S Abdou Karim ❤️brom ndindi yalla nanouko yalla fayal

  • @aramelo7306
    @aramelo7306 4 ปีที่แล้ว +4

    Machallh néxx na trop konn nagn wadial 18 safar inchallh 👏👏👍👌💗💗💓💓💓💖

  • @noumchjoop6808
    @noumchjoop6808 3 ปีที่แล้ว +5

    Serigne fallou rk la ame😭😭💝❤💚💚💚

  • @mamediarrandiaye6847
    @mamediarrandiaye6847 4 ปีที่แล้ว +7

    Défa tinga sa meunine dé Niang ballo nice clip mashallah yalna borom bi sam la mousseul la si seytané barké serigne saliou 🙏❤

  • @mariafaye5037
    @mariafaye5037 4 ปีที่แล้ว +6

    Yalna nieup am diam barkei Cheikhoul Xadiim niou fekei magal gui t talko inchallah Mouhamed Niang ballo li nehatina rafetna mashalahhh 😍❤️

  • @mouhamedniang9728
    @mouhamedniang9728  4 ปีที่แล้ว +230

    Merci

  • @falougueye8239
    @falougueye8239 4 ปีที่แล้ว +28

    Dieuredieufeuti serigne touba ❤️🙏

  • @fayemariama3153
    @fayemariama3153 4 ปีที่แล้ว +2

    Sama wadji ga baak dh bayou mbéne ak baye karim sama thiofel si mom dafmay yém man dieureudieuf mouhamed niang yalna yalla weiral bate bi nigay niouy bégalei yalla beigal la nonou ❤️❤️❤️❤️🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @bayesalioulo5999
    @bayesalioulo5999 4 ปีที่แล้ว +8

    Machalla 💖 yallna niou féké magal gui thi barke serigne saliou

  • @nogayemouserignefalloumbac410
    @nogayemouserignefalloumbac410 4 ปีที่แล้ว +11

    Ndeysane toujours Nogaye mou Serigne Fallou Mbacké ❤️

  • @nogayerassouldiop6988
    @nogayerassouldiop6988 4 ปีที่แล้ว +8

    ❤❤❤❤meunouma heuy journée t deglouwoumako❤yalna nieup am jam si barkep djourom niarii serigne Fallou❤

  • @sadamoumamecheikh
    @sadamoumamecheikh 8 หลายเดือนก่อน +3

    Je suis moustarchide mais mame Fallou je l’aime plus que vous yalla na yalla yook lérame❤❤❤❤❤❤❤

  • @evaminathiatouyayamgueye8837
    @evaminathiatouyayamgueye8837 4 ปีที่แล้ว +38

    Fière d’être une fadelle Serigne fallou ma vie 🥰🥰🥰🥰merci mouhamed

  • @ndeyediakhoudjitte2780
    @ndeyediakhoudjitte2780 4 ปีที่แล้ว +30

    Xol Sedna tous ces propos me réjouissent Serigne Abdou Karim ma force

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว +1

      ndeyediakhou djitte Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @thiammadieye5642
    @thiammadieye5642 4 ปีที่แล้ว +25

    Mouride ba Yagui wathie magal gui🥰🎊🔥

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 4 ปีที่แล้ว

      Thiam Madieye Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne TH-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @NdiayeSoda-b1u
    @NdiayeSoda-b1u 5 หลายเดือนก่อน

    man damabeg fallou machalla❤❤❤❤❤❤❤

  • @naboudiop441
    @naboudiop441 3 ปีที่แล้ว +1

    Thiey mame fallou ken dou mom masha allah Mouhamed Niang contane si yow ya allah na bat bi weer si barkei serigne fallou♥️♥️♥️♥️♥️

  • @astoudiouf5749
    @astoudiouf5749 4 ปีที่แล้ว +13

    Sunu yakar♥️♥️serigne Fallou bayou mbéne

  • @aidabadiane6641
    @aidabadiane6641 4 ปีที่แล้ว +28

    Machallah j'adore Dieureudieuf Serigne fallou Mbacke ❤❤❤

  • @aminadiagne7939
    @aminadiagne7939 4 ปีที่แล้ว +69

    Barcké serigne babacar sy damala soppppp