*Lundi 8 Juin 2020* Machallah Ya Oustaz Modou Fall Deug Rék Ngua Wakh Lépp Séne Kilifeu Yii La Mai Eleuk Yamal Khiyam Kou Nék Yalla Dinala Lathi Lo Samé Wonn Sa Ndiabot
Allhamdoulilah mon frère, la vérité est la vérité et surtout restera à jamais la vérité. Encore une fois reste comme tu es né change pas que ALLAH continues inchallah à nous guider amine merci 👏🙏
Machalla tonton oustaz modou fall ligay wax deug là machalla dila nianal yalla bayila fi bâ thi kanam dakh ligay wax leçon là thi nioune jeunes yi machalla diam ak salam thi yaw
@Aminata Drame, vs avez tt à fait raison J ai fait le mauvais constat lors de la dernier séjour en Afrique. J'étais écoeuré par le comportement de bcp de parents J.en.reviens tjrs pas.
Wakh gua léep lou nékone sama khél oustaz dieureudieuf yalla na yalla défal la diamm sameu niou may niou katane baniou gueuneu meuneu yarate ndiabot gui
Ya oustaz machallah yagui dianglé lo Moune yalla nala yalla fay.mais magui lay niane mbala gua wakh ak askane mi ak ware niougua togual niouy def ay crefase.merci bcp
Wadiour bou nekk sameu leu donc niou kholate yarine bi. Mane j’ai 30ans mais sama papa damako ragal ba tay sama yaye damako yeureum ba beugoumako tekk nakhar 😢😢😢😢
Parfois aussi way diour yi am si responsabilité, mais il ne faut jamais généraliser. "Wa laysa lil insaani ilaa ma saaha, wa anna sahyahou sawfa youraa soumma youdj zaahou djazaa-an awfaa." moy nit amoul loudoul djeufam té ay djeufam rék lagnoukoy fay bamou mat seukk
*Vidéo lomotif* Mass et ses amis sont faits enceinte la fille mineur Regardez et partager le danger de ses gosses lomotif . N'oubliez pas aussi s'abonner et activé la cloche Guirr yalla abonné siii diapaléniou svp rn appuyant sur le profil rt abonné . th-cam.com/video/E5vKfQGldw4/w-d-xo.html

Bilahi mane amna 36 ans mais 5000f meusoumako may sama yay tékhamoul foumako dieulé marié divorcé mais batay dama ragal sama yay loumako diox barké lahilaha ilahouweu dako liguey yar mingui am ba légui ak diomb bo diombé rék do déf lou niaw
Bilaye Oustaz tout dit, samaye pense reck ga wakh, Macha Allah, que les parents prennent leur responsabilité sur leurs enfants. C'est certains pas parents d'aujourd'hui qui ont raté leur mission
Ya des enfants nés sans parents, ou qui ont perdu leurs parents tot, mais ils n'ont pas dévié, cest parce qu'ils ont une discipline en eux. Mais je suis un peu d'accord avec ouztaz, les parents doivre être des guides pour leurs enfants, cependant rien nest garanti quand les enfants sortent

Machalla oustaz yalla nala yalla faye sa Xooll Inchalla amna solo
*Lundi 8 Juin 2020* Machallah Ya Oustaz Modou Fall Deug Rék Ngua Wakh Lépp Séne Kilifeu Yii La Mai Eleuk Yamal Khiyam Kou Nék Yalla Dinala Lathi Lo Samé Wonn Sa Ndiabot
Je suis catholique mais ce oustaz il me plait beaucoup
Wakh n'a degu ns juska présent on se soume a nos parents et a nos grand frère vraiment ns remercions nos parents alhamdou llilah
Yaniaak chtii koy royy
Zeemagie
Walae ndeysane Oustaz wakh nga deug dh , lolou dh am thi réuw way way yalla naniou yalla khir thi lou bakh🙏🙏
Amine
Bilah oustas je vous adore
Amine
Machala oustaz modou fall tu es mon idole bonne continuation tu as raison
Oustas amal goudou fane ak weergui yaram ak khewal si barke serigne fallou
oustaz tu es mon préféré je t apprécie vraiment bonne continuation que dieu vous garde parmi nous la société a vraiment besoin de toi
Allhamdoulilah mon frère, la vérité est la vérité et surtout restera à jamais la vérité. Encore une fois reste comme tu es né change pas que ALLAH continues inchallah à nous guider amine merci 👏🙏
Amine
Machalla tonton oustaz modou fall ligay wax deug là machalla dila nianal yalla bayila fi bâ thi kanam dakh ligay wax leçon là thi nioune jeunes yi machalla diam ak salam thi yaw
Billahi man oustaz modou fall dafma Nekh 😰😰😰😰
ndayesane yalla mokaye défe
kay ma maylako niarele
Bilay deugu rek la wakh🙏
m
AK Mann dama begue oustaz modou fall way❤️❤️😍
Machaallah oustaz modou fall ma la begue de yay Samo idol❤️😍🙏🏾
Aÿ Oustaz Modou Fall yama Mour dp8 2017 batay mangui mourou souma sagno dégueunté ak yaw sop nala trop ❤❤❤❤Mach,Allah
Bilay beus bou nek je le dis les parents d'aujourd'hui ont peur de leurs enfants khalé dioyloko bala mouley dioylo.🙏🙏
Bien dit
@Aminata Drame, vs avez tt à fait raison
J ai fait le mauvais constat lors de la dernier séjour en Afrique.
J'étais écoeuré par le comportement de bcp de parents
J.en.reviens tjrs pas.
@@65Atall lolou fi amdé et ils croient qu'ils aident ou aiment leurs progénitures.
Dom ken douka rakal
@@sokhnamomibocoum4148 en principe. De nos jrs, bcp de parents ont démissionné.
Triste constat.
journaliste biii machallah♥♥
Aby abonné sur ma chaine TH-cam svp
Kou beugue bah ,sa harite na done téré yalla ak sunna👌
Wakh gua léep lou nékone sama khél oustaz dieureudieuf yalla na yalla défal la diamm sameu niou may niou katane baniou gueuneu meuneu yarate ndiabot gui
Amine
Amine
Talibé chiekh abonné sur ma chaine TH-cam stp
@@aichalaye5702 abonné sur ma chaine TH-cam stp
Amine
Machalah Wakh Tanbi Nekh Trope Yalla Nagoudal Fannyi Fall Ame Na Solo Dieurdieuf
Machalla ya Oustaz 🙏🏻🙏🏻♥️♥️wakhtan bi amna solo way
Wawaw
Ya oustaz machallah yagui dianglé lo Moune yalla nala yalla fay.mais magui lay niane mbala gua wakh ak askane mi ak ware niougua togual niouy def ay crefase.merci bcp
Vraiment lii nga wax fii yeupp deguila mashallah Sénégal lii lagniou sokhla gni melni yow Oustaz yallah nga goudou fane 🙏
Aminata tu est la plus belle et la plus gentille
Ma shaa allah bien dit. Wallahi parents yi nio yakha xalléyi je t'assure. Motakhe ngiou warrr xolate yarine bi
Fassa abonné sur ma chaine TH-cam svp
Bilay lp degueleu yalna yalla goudal sa fan ak wer diam bamu nexla si Barker serigne babacar sy malick
Amine incha llah
Amiiiiiiiiiine way
Machallah ya oustaz. Ms boul wakh lolu amna nio kham ni séni wadiour déf naniou léup pour niou bakh am yar ms amna nio khamni nio bon sén bon rkk
Journaliste mounone gua mourou sans tek greffage mola guenone diap👍mes ouztaz tas bien raison❤👣
Bilae oustaz waax waax deugg thiala magg Mola yaar
Dieredieuf oustaz nalla yalla faye tee verel h khamham by
Merci am na solo yala na niou yala may dégue ak toop
Deugueu pirr ta oustaz yalla na yalla goudeul fane yii
Machala oustas goudal fan wer ak diam bunexla si baker serigne babacar sy malick
Billay oustaz linga wakh lépp deugue leu machalla yalla na yalla barkélal xam xam bi
Machalla ya oustaz yag fi lol té weur
Oustaze wakhtane wi rafétena amna solo
Wadiour bou nekk sameu leu donc niou kholate yarine bi. Mane j’ai 30ans mais sama papa damako ragal ba tay sama yaye damako yeureum ba beugoumako tekk nakhar 😢😢😢😢
Merci Ouztaz les parents sont responsables d’une part
Dialang abonné sur ma chaine TH-cam stp
C l cas
@@ciscadieng2793 abonné sur ma chaine TH-cam svp merci
Machalla man dall oustaz Modou fall dama nékh 😚😚
Billahi man ousta madou fall 👍👍👍👍👍👍🦻🦻🦻🦻🦻🦻
Yala nanou yala may top ak degeut tchi barke seydina mohamed psl merci oustas
wAllahi man Oustaz dama la beug bilahi
Machalla Oustaz amna solo mais Oustaz yaw sa Sokhna loutakh dou mourou mouy khésal😍😍
merci bcp oustaz modou fall amna solo trop
Billahi Oustaz wakhal dh☝ djiguéne yi défarate léne séne bop di déf lou bakh .Merci Oustaz Modou Fall contane nieu ci iow
Machalah amna solo loll yalna niou yalla defal dégg ak topou t yokou sa xam xam
questo parole è una cossa parola importante per ascoltare tutti grazie oustas fall
Machalah Sama oustaze yalla n'a yalla weral bate machalah
Machallah outaz c vraie doye na war trop sakh bilahi 😭😭
Machallah les paroles sont exceptionnelles
Ndayesaneeeee merci a toutes les mamans❤
Ami abonné sur ma chaine TH-cam stp
Machaala wakhdji rafetna lol que le bon Dieu vous protège amin
Bilaay deugue gou wer nga wakh maa shaa Allah
Euleukk djarna soraleee
Cccd
Parfois aussi way diour yi am si responsabilité, mais il ne faut jamais généraliser. "Wa laysa lil insaani ilaa ma saaha, wa anna sahyahou sawfa youraa soumma youdj zaahou djazaa-an awfaa." moy nit amoul loudoul djeufam té ay djeufam rék lagnoukoy fay bamou mat seukk
Amy sw naturelle !! Tengua bayi khéssAlbi nak
Bravo Oustaz
Billali oustaz tu as raison je d’accord avec toi
Vu
Masha alla ya Oustaz euleuk samebu nek dinagnla lathié naka gua donne sammé
ماشاء يا أستاذ أطاع الله عمرك ❤
Mnchllh Oustaz mla fan
Oustaze confinement bi diape na la dé machallah lékhou gua
Je suis fier de oustage Modou galle👌👏☺️
Billay ouztaz yalna yalla yaguel la fi incha Allah
Machaallah ! Yalla nañu Yalla may dégg ak toppu. Amiin
Amine yarabi
Machalah oustaz modou fall wakh gua leup
Pure verite oustaz
oustaz tu fait ma fierté vraiment
Naysane amna dieuredieuf fall doyna war
Gara abonné sur ma chaine TH-cam
wallah oustaz wakh nga degue lolou mo am fi si Sénégal
*Vidéo lomotif* Mass et ses amis sont faits enceinte la fille mineur
Regardez et partager le danger de ses gosses lomotif .
N'oubliez pas aussi s'abonner et activé la cloche
Guirr yalla abonné siii diapaléniou svp rn appuyant sur le profil rt abonné
.
th-cam.com/video/E5vKfQGldw4/w-d-xo.html
Merci oustaz bien dit
Salamata abonné sur ma chaine TH-cam svp
Diadjeuf oustaz modou merci beaucoup ta vraiment réson 👌😉🙏🏻😘✌
Macha'Allah Ya Oustaz deugu pir
*Vidéo lomotif* Mass et ses amis sont faits enceinte la fille mineur
Regardez et partager le danger de ses gosses lomotif .
N'oubliez pas aussi s'abonner et activé la cloche
Guirr yalla abonné siii diapaléniou svp rn appuyant sur le profil rt abonné
.
th-cam.com/video/E5vKfQGldw4/w-d-xo.html
mais nak oustaz wa banlieue falewougnou wa mariste ak ouest foire nak ne pense pas que banlieue est habité seulement par les pauvres je taime bien nak
Bilahi mane amna 36 ans mais 5000f meusoumako may sama yay tékhamoul foumako dieulé marié divorcé mais batay dama ragal sama yay loumako diox barké lahilaha ilahouweu dako liguey yar mingui am ba légui ak diomb bo diombé rék do déf lou niaw
Bilay
Machaallah oustace amna solo
machallah oustaz bien dit jeunesse sénégalaise bi dafa yakhou wallahi té parents yi aye responsable lagne
I agreed. Very true, mashaAllah
Machallah kaduyi rafetna
Machallah papa tu a tt dit mais le problème en n'est que ls enfants d'aujourdhui sont très têtu 😭
Bilaye Oustaz tout dit, samaye pense reck ga wakh, Macha Allah, que les parents prennent leur responsabilité sur leurs enfants. C'est certains pas parents d'aujourd'hui qui ont raté leur mission
Oustaz bayil dougou tik tok 😅😅😅je valide abal ma iphone ma photo wou no jiguene sonnou na😅😅😅
Machallah amna solo
Mashalah ya oustage amna solo
barakallah fikoum ya oustaz
Machallah vérité absolue
Longue vie à vous oustaz
Macha allah tout es dit
Machallah ❤❤❤
Merci oustaz ,delene wah dé
Bilahi deugue leu ouztaz mako buegeu
Oustaz bi nekhnama lol machalah
Soubaha nalah doy na war yallah na yallah dioubal léne thi Barker arkhourane Barker Inchallah
Amine
Ya oustaz ligua wahh deug la man 26 ans la am am sama frère bou am 30 ans mai niemei wouniou sama yay sama yaye douniou may darra dara
Macha'Allah Yallah nga am dieukeur diou bakh
Machalah machalah oustaz
Machallah oustaz t'as parfaitement raison mais sokhna Ami (animatrice) boul khéssal way
Merci bcp pour ami boul xesal stp
Machallah ostaz amna solo
yalna yalla fayeleu oustaz
Ya des enfants nés sans parents, ou qui ont perdu leurs parents tot, mais ils n'ont pas dévié, cest parce qu'ils ont une discipline en eux. Mais je suis un peu d'accord avec ouztaz, les parents doivre être des guides pour leurs enfants, cependant rien nest garanti quand les enfants sortent
Machallah oustaz modou fall
Machallah Amena solo fall
Ziaar, oustaz maa ngi jégalou dé, waayé maandou soppeu nagnouko si diné, ndakh amna ay yonent you sééni ndiabot nékeu sawara, parfois waydiour yi lougnou meun gnoo ngikoy déf, waayé khaléyi rékeu beugeu bone.
Abonné sur ma chaine TH-cam svp
🤣🤣🤣🤣 wa
Sama oustaz modou fall ❤
*Vidéo lomotif* Mass et ses amis sont faits enceinte la fille mineur
Regardez et partager le danger de ses gosses lomotif .
N'oubliez pas aussi s'abonner et activé la cloche
Guirr yalla abonné siii diapaléniou svp rn appuyant sur le profil rt abonné
.
th-cam.com/video/E5vKfQGldw4/w-d-xo.html
Guathié guiiruk doundou diarna daw ba fate wallahi😐😐😐dieureudieuf yah oustaz
Wallahi
@@aichalaye5702 www
Abou abonné sur ma chaine TH-cam stp
Machallah oustaz