Mbacke yaw diouma maslikoul djinan dakar rek nga waroune na nek machallah ndakh yaw yalla rek motakh ngaye wax ta xam xam bi bilahi dafa leer ko nango lima wax basal jm💪
Hakassa dieuredieuf cheikh Akhmadou rafaihl mabcke yalla gyague fi loool nèlèn amine yarabi kou ni amine yalla ga fèkè Tabasski 2021 barkep borom darou
Après Abdoul Aziz Sy et Serigne vous êtes une des mes références sur terre. Sop nala lole Mbacké. Niane na Yallah guiss leu beute ak beute . Nittou Yallag deug . Machallah
Alors pourquoi le marabout m'as demander l'aide pour construit un maison d'enfants il m'avais dit meme si c'est 1€ je peut le donner apres il m'as dit il faut que je lui Donne 2000€ il m'as fait des chantage et il a abuser de moi pour Mon l'argent je comprend pas
Mbacke yaw diouma maslikoul djinan dakar rek nga waroune na nek machallah ndakh yaw yalla rek motakh ngaye wax ta xam xam bi bilahi dafa leer ko nango lima wax basal jm💪
Segn bi waxall waxi nitt
Masalik ak fénén nio yamm li am solo moy messageam di dialleu
Ta nia nék Masalik kéne eupou lén xam xam
Damako sop rk te yalla takh ak xam xam bou selle bi ak deugou gui ak ragal yalla gui yalla nafi yagg te wer 🙏
Hakassa dieuredieuf cheikh Akhmadou rafaihl mabcke yalla gyague fi loool nèlèn amine yarabi kou ni amine yalla ga fèkè Tabasski 2021 barkep borom darou
Amiine
Amine
Amiin ak tabaski 2099
Yalla nala yalla faye barckéb s touba
Yalla nala yalla Sam mayla goud fan ak wer barke ELHadji Fallou
Walahi dama ame thiofél si yaw
Long vie mbackè Macha allah
Machallah yalla na yalla goudal fan wi tei yokou wer gui 😍🙏🥰
Mbacké yalla na yalla fayale nioula barkëp Borome Touba
Maachala amatina solo yalnañu yalla defal deg ak top
machala diurediefati mback yalla nagafi yagui te wer lool
Macha allah sama sopé bi❤️
Cheikh ahmadou rafahi mbacké yalna fi yague te wer ak mann ak kep kouwakh amin
Yalla nalla yalla defal diam ak goudou fane
Après Abdoul Aziz Sy et Serigne vous êtes une des mes références sur terre. Sop nala lole Mbacké. Niane na Yallah guiss leu beute ak beute . Nittou Yallag deug . Machallah
Mbacké yague fi lool ta wer ci barkèb serigne TOUBA❤❤😍😍
Yalla na Yalla guddaal say faan ci barche s.touba❤️❤️❤️❤️❤️ tutto il mondo ti amano
Gourop sopé serigne abdou rafahi Mbacké amoul khana
Amna Kay koubakh
Animou ? Lien bi kou bax
Jajeuf mbacké amatina solo yalnaniou yalla defal degue ak toppou
Yalna yalla goudal saw fann
Yalla naga fi yage ta wér Mbacke
Machalla mbacke balla amatina solo loll yalna Naga fi yague loll tè werr loll amiine ya rabi 🙏🙏
Machallah mbacké yala ga fi yageu ta wérr amine
Yalla na yalla may dégg ak topou
😍Akasa mbacké amine😍 dieureudieuf serigne touba 😍
Thiey sama xole sedd na yalla nagua fi yagu looll té wer si barcké borom Touba xadimou rhassoul 🤙🤙🤙❤❤❤👌👌👌
Macha Allah Serigne a rafahi yalla nala yalla godal sa fan
Ndaysane amatina solo yalnala yala sam té arr la Mbacke🇸🇳🇧🇷
Yag ak wer rek
Yall naniou la yallah fayal si barké sa Mame kou tédd ki شيخنا شيخ احمد الخديم
Yageu ak wer mbacke manchallah 🤲🤲
Yalnangafi yag té weur lool amatina solo
Ndaye san amatina solo lool mbacke yague fi lool te wer Mbacke
Walahi geuna yague geuna wér wor na Serigne fallou Mbacke li ngay wakh âme n’a solo
Yalla na Yalla yagual lafii
BarakALLAHOU Fikoum Serigne bi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
masah allah yalla na jiam yague ♥️♥️♥️♥️
Diaradiafati balla aysa
شيخ أحمد الر فاعي امباكى حفظك الله ورعاك
Machallah mbacke ya am xam xam 💓💓💓💓💗💗💗
MashaAllah rafetna ya shiekh
Ay way ya ame kham kham té dégue wolof machallah ♥️♥️♥️
جزاك الله خيرا ياشيخي
🤲🏽Mbackè yagg filole tè andak were 🙏🏽
Diedieufati s bi yalla naga fi yagui lool tewer
Alhamdoulilah yag fi té géna wéer
Mashallah. Amatina solo. Dieuredieufey Mbacke
Merci waay serigne bi
Yalla nala yalla faye machalla
Machallah mbacke yagfi tewer
macha'Allah,amatina sollo Mbacké yalla ngafi yag lool ta andak wér si barki Akhmadoul Khadim
Ma challah amna solo loll Mbacke
Yala nangafiyague
Guena yagg guena weer mbacké
ماشاء آلله فتبارك آلله
Dama am feart si s
RAFAH
Yaw kon man ngay japale
Jajeufati Mbackè
Liii déye Macky warnaka dégue
Masahala amatina soolooo
حيّاك الله ياقدوتي
Dieuredieuffeu
Publicité bi mom khalaatoumako seetaann pousse rek
Dieuredieuty sangue bi
Sama serigne magui ziar boubakh
Machalla ❤❤❤
Machalla mbacké
Machalla mbacke balla
Machallah
MACHA ALLAH
Machallah sono serigne bi
Yagafi tè mou anda ak wèrr
Yag fi mbakcé bala xäisa
حفظه الله وأطال عمره وعافاه العلم والعمل والعباد يارب العالمين اللهم اجعل كل عملها قليله وكثيره خالصا لوجهك الكريم
Machala Balla aicha
Dieredieuf Serigne Touba
Jereejef mbacké
AKA NEKHONE GNIOU AME AYE SERIGNE AHMADOU RAFAHI YOU BARI SOUKOURANE MBACK
Ndeysan danga bakh rek nagno kouy nianall mo yague fi
walakhi am nga tawkhide, tei mognou manquè
❤️❣️❣️
❤️❤️❤️
Yalla reck mola gnore
Ma cha Allah
Masaala
Xam xam dafay leer jéréjéf mbacke
Akassa
Abonnée sur yeurmandé tv svp
Salam ou se trouve la mosquée ??
sope mame fallou
4mint pup daye yaague loole
Lol sakh motakh manmom damay pousse rek
Dett way 😂😂😂porta lo am solo lagnoy publicity
Sagoub yonou mourit! Sou mourit yep meloon ni yaw kon Ken dougnou yab.
Tiey broum xam bi
kARA
Alors pourquoi le marabout m'as demander l'aide pour construit un maison d'enfants il m'avais dit meme si c'est 1€ je peut le donner apres il m'as dit il faut que je lui Donne 2000€ il m'as fait des chantage et il a abuser de moi pour Mon l'argent je comprend pas
Machallah
Machallah
Machallah
Machalla