"Mère Bi Sama Badiane La... Sokhna Awa Ka La Toude... Dadon Fadj Domam Ba Jeul thi Fébar"

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 24 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 449

  • @mapresses157
    @mapresses157 2 ปีที่แล้ว +80

    Je suis tellement fière de cet homme il a tellement bien défendu sa tante fier de toi mon frère

    • @ndiagamboup739
      @ndiagamboup739 2 ปีที่แล้ว

      No diambar wakhe daga yalla man ndiaga mboup Magi ziare bou bakhe me sokna sy ly KO yekal foto monou diaxal vorema polisse warna déf ly geye Yam bou bakhe yalla kamnako

  • @oumyloum1042
    @oumyloum1042 2 ปีที่แล้ว +52

    Machaallah vous êtes fidèle et loyal à votre parent.

  • @kinesow4679
    @kinesow4679 2 ปีที่แล้ว +67

    Yalla naniou yalla diégal ci barker seydina mouhamed psl

  • @frankielampard4690
    @frankielampard4690 2 ปีที่แล้ว +44

    Cheikh Tidiane ziar nala. Ndeysan sen deuk bi aka sel walay ndeysan dem nafa. Wadji di wakh osi moy Ahmed Ahmed Tidiane deme kou bakh ndeysan

  • @pulhosy2689
    @pulhosy2689 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah waliou pirr kay bilay aduna mo doy war dii toumal domou adama ci loula woroul rekk

  • @diaamadou7542
    @diaamadou7542 2 ปีที่แล้ว +42

    Merci bonsoir ma sœur que Dieu porteuse que Dieu donne la maman beaucoup de santé et puis il va retrouver avec sa santé ma sœur

  • @adjasigathiam
    @adjasigathiam 2 ปีที่แล้ว +42

    Toumeul nite Lou réy le ndakh dina topp aye satati seuteum té khamenani bakare bobou yallah naniou thi yallah mouseul nite ki loy wakh nala lerr té nagne ragale yallah aussi Di déff Lou bakh dii wakh Lou bakh ndakh bamél khote ne té leundeum 🙏🙏🙏🙏

  • @Sabrun-jamil
    @Sabrun-jamil 2 ปีที่แล้ว +29

    Un jinn peut simplement le placer ici, deumm amoul ndakh yalla *nitt, jinn, mala’ika ak mala* la yalla bindd
    Ce que les gens ne comprennent pas c’est que *il ya des jinn qui parte en guerre contre d’autres jinn, et pour ça ils ont besoin de certains humains*
    Moi je connais un enfant que son père ferme à clé juste pour qu’elle ne sort pas,mais le matin quand il ouvre il ne la voit plus.
    Et kelk jour de recherche après on lapel pour lui dire *ton enfant on l’a retrouvé dans tel pays sous un pont*
    Et après avoir consulté des savants, ils lui ont dit *que cet enfant est pris par des jinn qui l’amène a des guerres très lointains, et tu aura beau fermer sa porte à clé,mais a chaque fois qu’ils auront besoin d’elle ils vont venir le prendre*
    Et d’habitude quand il retrouve l’enfant, *pendant des jours elle devient paralysée et muette*
    Cest juste un témoignage ndakh kou deei ak sa bameel
    Moi quand j’ai vu cette femme automatiquement je me suis dis que jinn mookofa tekk

    • @elhadjiibragadiaga938
      @elhadjiibragadiaga938 2 ปีที่แล้ว +3

      Je suis parfaitement d'accord avec toi, mais nak soun borom bind n'a lou eup nit ak djiné ak malaka.
      Donté man nak geumouma affaires de deum, mère bi dama geum ni rab wala djiné foko ték fofou mou nék.
      والله أعلم

    • @miamorvalentini3951
      @miamorvalentini3951 2 ปีที่แล้ว +2

      Wallah nous avons pensé la même chose .

    • @ndeyebintandiaye4057
      @ndeyebintandiaye4057 2 ปีที่แล้ว +1

      Machallah beau témoignage.

  • @loumsene3644
    @loumsene3644 2 ปีที่แล้ว +118

    Assalamou aleykoum walay dama ni wone doumassi sah wah wayé liii yomboula nopiwalé ndah togne deug moy liii toumal deug moy liiiii ayyy bolén khamone lissi toumal domou adama walahi djiguen sétat s'en kadou you bone yi guédi yeketi g mal g vraiment mal
    Man gté a djidah (Arabie saoudite) fofou mo eup djinné fiii fouf djinné limou mene beurina d yavé un immeuble bo khamni walahi koufa deuk si yéwo si mbéd bi nga fek sa bop walahi dagay teud sa lal Di nélaw yéwo si mbéd bi donc svp bayilén togne togne danala top bassi Say diabot mandoulen
    Deum amoul deum amoul kou djinné dougue mo am bamel nak khat n'a d wet n'a d leudeum n'a d yalnaniou borom bi diéguel

    • @omarfaye2580
      @omarfaye2580 2 ปีที่แล้ว

      Walakhi lou lerr gha wakh

    • @adjarassoulfall2530
      @adjarassoulfall2530 2 ปีที่แล้ว +4

      Bilahiii linga wakh degueleu sénégalais naq dafeu gaw di tame niite deum trop wantè yalnaleine yallah sougnou borome até insha Allah

    • @kanaty9313
      @kanaty9313 2 ปีที่แล้ว +3

      Billaye li dafa niaw trop toumale domou adama bakhoule

    • @alinyang196
      @alinyang196 2 ปีที่แล้ว +2

      wolahi hasim yalla wakhoul ken darra

    • @gningmamadou8742
      @gningmamadou8742 2 ปีที่แล้ว +3

      Verite absolue

  • @omardrame8741
    @omardrame8741 2 ปีที่แล้ว +38

    Bayil lene di toumal 🤲🏻🙏🙏

    • @adamadiop60
      @adamadiop60 2 ปีที่แล้ว +2

      Ndeysane ak bakhoul tongne bakhoul oh

  • @Mbaye904
    @Mbaye904 2 ปีที่แล้ว +6

    Mère bi képp kouko wakh " Deum" beuss bo déwé djaroul gnoulay dioulé. Naniou bayi di togne domou Adama yi.
    Mère Awa tu as mon soutien total ❤

  • @madouthioub
    @madouthioub 2 ปีที่แล้ว +2

    merci beaucoup grand 🇸🇳

  • @coubatandine5057
    @coubatandine5057 2 ปีที่แล้ว +60

    Le seul juge c'est dieu 🙏

  • @ndeyefatousylla4269
    @ndeyefatousylla4269 2 ปีที่แล้ว +1

    Je te connais pas mais vous êtes issue d'une famille noble

  • @fricaque2172
    @fricaque2172 2 ปีที่แล้ว

    Tchim bravooo teudj lo ga guemegnu senegalais ..lep si diné ...
    Ay boromu kham kham guen ..Gnu sel..

  • @gayafall
    @gayafall 2 ปีที่แล้ว +9

    Mame Alioune Deme Sakou dougoub lay done tari bene pepe bambou diekk. Machallah sallatou fatiya. Mame cheikh Amadou fofou . Heure dioul dioyte. Founou takh la dokh guene.Ndiacounda rek.

    • @dieynabambengue2723
      @dieynabambengue2723 2 ปีที่แล้ว +1

      Lou lér nga wakh bilahi déméne déméne ayy waliwou kamil lagnou

    • @papamamadoudiop2487
      @papamamadoudiop2487 2 ปีที่แล้ว

      Ahhhh deug deug Moy sama Mame dh brm Ndiaye counda AK salatoul Fatiha bayou Mame Modou Cissé deme❤️❤️❤️daniouko khamoul rk mtx

    • @khadydione5614
      @khadydione5614 2 ปีที่แล้ว

      B

  • @sirandouwague1691
    @sirandouwague1691 2 ปีที่แล้ว +5

    Macha Allah AMADOU TIDJANI EST TRÈS POLI IL A TOUT ÉCLAIRCI PAR DES DÉTAILS BIEN PRÉCIS

  • @djibrilsoumare2393
    @djibrilsoumare2393 2 ปีที่แล้ว +184

    La dame est tout simplement possedee. Rien de plus. Debarrassons-nous de l"obscurantisme qui habite en nous. Nous jugeons trop et trop vite. Souhaitons prompt guerison ä la dame, qui aurait pu etre notre mere, notre soeur, notre tante, badiene, oumpagne....

    • @ramaba917
      @ramaba917 2 ปีที่แล้ว +4

      vraiment sénégalais passe-passe bou bakh laniou amoul deum amoul djinn moyen possède lit kii sinon déflo gentil mais sénégalais limiye wakh deum yeup do nangou sa familles kéne nékekosi

    • @lotalo3925
      @lotalo3925 2 ปีที่แล้ว +3

      Amna gnou xam nii thie téne lagni dougou té rap moukoy déf

    • @papemamourdiouf5748
      @papemamourdiouf5748 2 ปีที่แล้ว

      Déjà yaw djigne ngako deum car être possédé et « Deum » c’est la même chose.

    • @fatysyll5643
      @fatysyll5643 2 ปีที่แล้ว +2

      Merci ay doff rek té bone

    • @djibrilsoumare2393
      @djibrilsoumare2393 2 ปีที่แล้ว +5

      Non Mamour, tu te trompes. Etre possede ne signifie pas etre soi-meme un deum, avec tout ce que nous emballons dans le concept de deum. Je te conseille de relire ce que j"ai ecrit. Des prejuges, je n"en ai pas. L"obscurantisme, ce n"est pas mon niveau, juger les gens (surtout ceux que je ne connais pas), ce n"est pas mon genre. Bonne journee.

  • @user-2032
    @user-2032 2 ปีที่แล้ว +18

    Hooo ndeysane balelniou deh😭😭😭lepeuk serigne bi ak kiko dougeul TikTok YALLA diegeul niou

  • @papefall9880
    @papefall9880 2 ปีที่แล้ว

    Wakh ji rafétna amena sollo machallah

  • @Alien221-d7o
    @Alien221-d7o 2 ปีที่แล้ว +16

    hawma louko toopp DH wanté limou andaal Amna dolé💪🏿 ndaah juge wouma DH mais Lima guides rek laay wahh itam 🙏🏽. Mère bi louko yégeul si balcon bi moy UN. Deuxièmement:Mère bi kanaam bimou yoronn si kaw AK Ninou watié kanam bimou yorr bokoul 🙏🏽 .Troisièmement niit la DH deugg la💯 wanté jiine bo guiss amna loumouy andal té mère bi limou donn youhou beug niou délo Koko te Mouy tééré bimou taguonn 🤌🏼 laniouko waroul wonn délo ndahh Lolou Moy alalou djiné bi 🙏🏽 djiné bi modonn youhou 🤌🏼beug niou délo koko.Wahh niit deum dafa graw mais djiné meun na déflo niit lounék 🙏🏽

  • @khadimmar2590
    @khadimmar2590 2 ปีที่แล้ว +54

    yalla nadiou yalla diegual sunou bakar 🙏🙏

  • @fatimatakane7848
    @fatimatakane7848 2 ปีที่แล้ว +1

    La famille Thierno Aliou Deme ayii walliyou la toublèn astahfirlahi

  • @khadycisse4695
    @khadycisse4695 2 ปีที่แล้ว +10

    Nite ken warou co tameu deum yalla beugoul Lolou yalla n'a niou yalla dhieugeul

  • @sawdatouly8038
    @sawdatouly8038 2 ปีที่แล้ว +1

    Machallah rena

  • @lesenegalais2589
    @lesenegalais2589 2 ปีที่แล้ว +15

    Faut juste reconnaître que niou sénégalais(e)s suniou gueum Yalla nguistal késsé’leu. Toumal niit, demal niit, jugé niit, ...j’en passe. Niouko donne toumal niepeuh ayy nafekh laniou.

  • @paomar6384
    @paomar6384 2 ปีที่แล้ว +1

    Bougnou fatté niatte fanou bamel 🙏

  • @salzooman433
    @salzooman433 2 ปีที่แล้ว

    Sénégal mou niémé yak dér merci frère

  • @ahmadsall326
    @ahmadsall326 2 ปีที่แล้ว +7

    J’avais une cousine rab diap ko mou dokhé Dakar ba Kaolack wakhléne l’oléne kham

  • @khadyjafaye4565
    @khadyjafaye4565 2 ปีที่แล้ว +9

    Le nom Dem gnouko sant ay waliw kese lagnou ki noumouy wahé ak son portrait war na bok ak THIERNO ALASSANE DEM TOUCOULEUR BAYE nagnou tey si nite gni gnouy holat lougnouy wah surtout mague lgui Sénégal depasser mague wala sagua ko fitnal ko da nek lou terre à terre si gnom nagnou defarat djiko yi
    Maman Awa Ka Dem yalla na yalla weral la gua delou wat si sey activités si barki BAYE NIASS 🙏🙏

    • @julesdiop7948
      @julesdiop7948 2 ปีที่แล้ว +1

      Oohhh Thierno hassane Dème ,walliyou kamil

    • @khadyjafaye4565
      @khadyjafaye4565 2 ปีที่แล้ว

      Walahi neysan waliw bu mague

  • @fatoumatabinetadiallo6082
    @fatoumatabinetadiallo6082 2 ปีที่แล้ว +3

    Les hales pular sont dignes et savent lire le coran paix à vous que dieu nous protège

  • @ndongalidoomimustafaa2161
    @ndongalidoomimustafaa2161 2 ปีที่แล้ว +1

    يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آَمَنُوا لَا يَسْخَرْ قَومٌ مِنْ قَوْمٍ عَسَى أَنْ يَكُونُوا خَيْرًا مِنْهُمْ وَلَا نِسَاءٌ مِنْ نِسَاءٍ عَسَى أَنْ يَكُنَّ خَيْرًا مِنْهُن...
    من سورة الحجرات- آية (11)

  • @mamymamyseck94
    @mamymamyseck94 2 ปีที่แล้ว +9

    Aye wakh sakoulènne mou ball nieup niogui diegualou,di diegualou borombi,nal ball nieup tè sakou yallah mou ball nieup🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @macoumba3141
    @macoumba3141 2 ปีที่แล้ว +93

    Les plus grands accusateurs de deums sont les plus grands deums! J'avais une copine à Dakar qui accusait de deums à tout va n'importe qui! Un jour je suis allée en mission dans sa ville d'origine et je suis passée dire bonjour à sa famille. J'ai appris par mes collègues originaires de cette ville que les habitants se méfient beaucoup de la famille maternelle de ma copine car ils sont traités de deums. Peu de personnes dans cette ville fréquentent sa famille maternelle.

    • @mariediong3572
      @mariediong3572 2 ปีที่แล้ว

      Lol

    • @senegalthikhol1653
      @senegalthikhol1653 2 ปีที่แล้ว

      @@mariediong3572 😆😆😆

    • @aicha2137
      @aicha2137 2 ปีที่แล้ว +8

      Am nga chance kone ba lékoula 😂😂😂😂

    • @macoumba3141
      @macoumba3141 2 ปีที่แล้ว +9

      @@aicha2137 Comme le dit une connaissance, " au marché les bouchers étalent leurs viandes mais impossible de les avoir sans en payer le prix". En gros, un deum ne peut pas avoir l'âme de toute personne qu'il désire!

    • @kinesow4679
      @kinesow4679 2 ปีที่แล้ว +3

      Vérité absolue

  • @astoudiouf5543
    @astoudiouf5543 2 ปีที่แล้ว +2

    Ndeysane kou goor ki dafa teyy sakh machallah

  • @Sokhnasavane
    @Sokhnasavane 2 ปีที่แล้ว +14

    Je suis attristée par tout ce qui se passe dans mon pays, pourquoi les gens aiment accuser sans avoir de preuve. Ou est ce que certains sénégalais (je dis bien certains car Dieu merci ce n'est pas tout le monde) vont chercher leur imagination. Au lieu d'être là à vous poser 1000 et une question sur elle, pourquoi ne pas se poser la question comment faire pour que le Sénégal avance, pourquoi les riches s'enrichissent au Sénégal et les pauvres s'appauvrissent, la création de l'emploi pour les chômeurs et les aides pour les porteurs de projets. Il y a tellement de sujets sur le développement de notre cher et tendre pays que de rester là à juger une personne qui est sûrement plus proche de Dieu que nous même. Réveillez vous car il est vraiment temps

  • @maantasalikhate5360
    @maantasalikhate5360 2 ปีที่แล้ว +1

    Man sama mame " ma grande mère" thi tén la dou nak rabb té migui bot thiat tam wathié ko doukou thi tén bi billayi😟 yalla nako yalla yeureum thi barké s Salifou,🤲

  • @khadydiouf9720
    @khadydiouf9720 2 ปีที่แล้ว +5

    Wahh by dall rafetna deugouna Yalla nako sounou borom maiy werre 🙏Yalla moy doguale Lou nekh si nitte

  • @fallouseck7874
    @fallouseck7874 2 ปีที่แล้ว

    Machallah 💔 machallah 💔

  • @mbayemagette9198
    @mbayemagette9198 2 ปีที่แล้ว +7

    astahfiroulah azimal lezi lailaha ila lahouweul khayoul khayoumou wa toutoubou ileyhi yalla nama yalla dieigueul sokhnassi tamite dieigueul ma🙏🙏🙏🙏🙏

  • @combecane257
    @combecane257 2 ปีที่แล้ว +9

    Que le tout puissant nous pardonne Ndiaye kounda foyer religieux chaque année gnou déf ziar def ay gnaan

  • @user-he7mc1gb6i
    @user-he7mc1gb6i 2 ปีที่แล้ว +5

    اللهم أنصرها وأيدها ونصرها وصحة جسمها

  • @yacineseck3783
    @yacineseck3783 2 ปีที่แล้ว +12

    Yalla na ko sunu borom soutoural may ko tawfekh ak taysir goud fann ak werr

  • @etreveridique1467
    @etreveridique1467 2 ปีที่แล้ว +32

    walay, tu as raison , j'ai l'impression que les gens ne croient plus en Dieu. Loutakh sénégalais gnanw lamigne, meuna accusé, loutakh gnou bone pourquoi tant de méchanceté je suis attristée. sokhor, ignane, bone, torokh je déteste les gens qui disent du mal de leurs semblables. Merde mon pays

    • @rama.gassama700
      @rama.gassama700 2 ปีที่แล้ว +1

      Bilahi soxor laniou def di yokou nak nane yérém laniou fa fekk. Yal nalèn yalla wèr

  • @serignemodoumbacke604
    @serignemodoumbacke604 2 ปีที่แล้ว +8

    Dieuredieuf lérna niit Day mano

  • @djeumbndiayekeurdjongama4696
    @djeumbndiayekeurdjongama4696 2 ปีที่แล้ว +1

    Cheikh tidiane macha allah nit kou dal te yarou

  • @aramefaye2806
    @aramefaye2806 2 ปีที่แล้ว +4

    Yalla naniou yalla diégeul thie daradiay Mouhamded psl 🙏🙏diko diégualou mom

  • @thioyemathioye559
    @thioyemathioye559 2 ปีที่แล้ว +5

    Thiey Sénégal mou doye ware dh yalla nanou yalla dolli sotora

  • @yamudownjie3858
    @yamudownjie3858 2 ปีที่แล้ว

    Salaam sitè internet yui Tamitè am negn waala, wakh lou lèn lerrul pour am xaliss, èsque ragal ngeu yalla xaliss bou saltè bi ngai jokh sa njabort. 🙆‍♂️😏🤔🤣♥️♥️♥️♥️🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲

  • @folashade2749
    @folashade2749 2 ปีที่แล้ว +9

    Asalam Aleikum. Wow cest triste pour cette femme.. Cette femme est parentee a une amie dont le grandpere est de la famille Deme de Wak. Wow je suis choquee.. mon amie est la petite fille de Thierno Baba Diallo qui est un petit fils de Thierno Aliou Deme.

  • @safiatousy9926
    @safiatousy9926 2 ปีที่แล้ว +2

    Allahou akbar lailaha ilalah SAWS

  • @mamadouba4017
    @mamadouba4017 2 ปีที่แล้ว

    Masa.allah

  • @dioudba9294
    @dioudba9294 2 ปีที่แล้ว

    Ndeysane sokhlana nimaro mér by

  • @ountegannathiobane1409
    @ountegannathiobane1409 2 ปีที่แล้ว +10

    salam je confirme le messieurs moi j'ai deux enfants malades quand mon fils décide de partir son djinns fait en sorte qu'on le voit partir

    • @originali155
      @originali155 2 ปีที่แล้ว

      Huummm

    • @Sabrun-jamil
      @Sabrun-jamil 2 ปีที่แล้ว +1

      Je confirme
      Mais si tu es a dakar, yobbouko tchi centre bou *Oustaz Umar sall diongue* yalla yombal nako trop cii cas yii.
      Ta teel ci djouk sinon dans le cas contraire les jinn peuvent lamener sans que tu ne le revois plus
      Ce que je ne te souhaite pas 🙏🏽

    • @Yaayoubayyam
      @Yaayoubayyam 2 ปีที่แล้ว

      As tu trouve un bon marabout pour soigner tes fils?

  • @kinediop6465
    @kinediop6465 2 ปีที่แล้ว +1

    Asstakhfirou lah Asstakhfirou lah Asstakhfirou lah allhasim yalla nanio yalla diegeull sokhna si ballma akhe bobakh

  • @idrissandiaye2624
    @idrissandiaye2624 2 ปีที่แล้ว +15

    Mane deh dafama diakhalone té khalatone na lii niitt gni di wakh ba wakhnako wayé mangui toupp tey dieguelou yallah khamnani meussouma beug wakh niitt lou gnaw wayé afair bi moma diakhalone trooppp sakh yallah khamnako !!! Vraiment nama ball akha té yallah rek takh

  • @dioudba9294
    @dioudba9294 2 ปีที่แล้ว

    Massa yaye boy amna louma méty cousete là

  • @kanyba1999
    @kanyba1999 2 ปีที่แล้ว

    Yallah nako yallah may wérr ak tawfex bamou delou ci ay mbokam
    Le journaliste a été très correcte et c'est questions ont été bien organisé et pertinentes machallah genre journaliste yii laniou soxla ci société bi
    Pour le gars, il est très placé pour parler de la femme malade 🙏 et il est venu au bon moment yallah nako yallah may kholou Jougne

  • @evakane4802
    @evakane4802 2 ปีที่แล้ว +14

    Billay kou xol famille mér bi ak sén comportement nga xamané ay nit you bax lan mai yalla baxna 🙏

    • @rokhayasall6952
      @rokhayasall6952 2 ปีที่แล้ว +1

      Bilahi nit niou bakh setou waliwou piir mais yalla bakhna

    • @evakane4802
      @evakane4802 2 ปีที่แล้ว +1

      @@rokhayasall6952 billay yalla baxna

    • @papamamadoudiop2487
      @papamamadoudiop2487 2 ปีที่แล้ว

      Wallay wakhatiko danioo khamoul kouy maamam rk❤️😭ms oklm

    • @evakane4802
      @evakane4802 2 ปีที่แล้ว

      @@papamamadoudiop2487 billay niaka xam ak niaka téy dina yoobé nit lou nék ta lamigne posonla 🙏

  • @ousseynoukebe1495
    @ousseynoukebe1495 2 ปีที่แล้ว

    wallahi ndeysane kadou yi rafetna

  • @ndaoadjiseny2102
    @ndaoadjiseny2102 2 ปีที่แล้ว +1

    Si je faisais partie de la famille,je porterai plainte à tous ceux qui ont dit du mal sur sa personne.Walay je n'épargne personne.Je sais pas pourquoi le sénégalais aime dire du mal à son prochain et dit d'être musulman.

  • @coumbadiop8895
    @coumbadiop8895 2 ปีที่แล้ว

    Machallah wakhdji rafét na torop 🙏

  • @anthioundiaye7594
    @anthioundiaye7594 2 ปีที่แล้ว +1

    Masha alla man nena gni eske norma senegal nekh rek a def peut etre dafa am probleme khel

  • @khadijawillane3294
    @khadijawillane3294 2 ปีที่แล้ว +2

    Toumal bakhoul téy bakhna si nit man mangui am sama mak bou rere attou yalla nioungui Koy weur guisou niouko ta Lou mélni rék moko dal😭

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 2 ปีที่แล้ว +4

    Ndeyssan alakhira dina meti lool teyagu toumal niit bou seet wiith aakh gueunouko reuy 😭😭😭ndeyssan .😭😭😭yarabi

  • @ahmadousow6262
    @ahmadousow6262 2 ปีที่แล้ว

    Allahou Akbar 💚💚💚💚💚💚💚💚💚❤️✔️

  • @aissatouniang4985
    @aissatouniang4985 2 ปีที่แล้ว +6

    Machahala Alahamdoulila Rabil Alamina Yala rek moy Bour dieureudieuf Amath Tidiane Dème bayi lène di ga wa wax nite kou bakh day madou

  • @lesage8151
    @lesage8151 2 ปีที่แล้ว +11

    Thieye Sénégal raffétte léne diortou
    Khana diguéne toube si séne borom

  • @diopabddilaye9001
    @diopabddilaye9001 2 ปีที่แล้ว

    Machalla Yalla na were rek

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 2 ปีที่แล้ว

    Loumou def ba yek fofou😂😂

  • @khadimegueye5540
    @khadimegueye5540 2 ปีที่แล้ว

    Machalla 👍❤️

  • @virus9430
    @virus9430 2 ปีที่แล้ว

    machala kadou yi rafetna gnouy rafetal sounou diganté deuù amoul naggnbayi di jugé kougn khamoul

  • @sodacoulibaly2807
    @sodacoulibaly2807 2 ปีที่แล้ว +6

    Tu as bien parler foula rek Macha alla

  • @mameboussocisse1201
    @mameboussocisse1201 2 ปีที่แล้ว +8

    Yalla nako yalla delo xelam li metina trop si djiguene 😭😭😭😭😭

  • @eveguisse6981
    @eveguisse6981 2 ปีที่แล้ว

    Ndeysane

  • @adamathiam5244
    @adamathiam5244 2 ปีที่แล้ว +2

    Mane dè bama dèguè mouye tari alkhourane lassi tèye chaytan dou ande ak alkhourane

    • @nafidiakhate1127
      @nafidiakhate1127 2 ปีที่แล้ว +1

      Lolou dhé la wax
      Sénégal notion djineé lagnum xamoul

  • @Miss-zk6et
    @Miss-zk6et 2 ปีที่แล้ว

    Merci 🙏

  • @miamorvalentini3951
    @miamorvalentini3951 2 ปีที่แล้ว +3

    Nit dafa wara rafet ndiort. Chez nous on a trouvé bizarre qu'elle se retrouve là-bas mais on s'est tout de suite dit dara meune nako dougg yobou ko fofou. Pourquoi penser tout de suite au mal di tamaaté. Nagn kholaat sounou bopp, nous sommes des musulmans. Souniou khamoul, meunougn rafet ndiort niou maandou

  • @morydiop913
    @morydiop913 2 ปีที่แล้ว +1

    Bilaye nena legui bokame guene wakh mhė nak fimou Diar ba yek fofou MoMA diakhal

  • @alassanediallo9969
    @alassanediallo9969 2 ปีที่แล้ว +2

    Yallah nagnou Yallah mouseul pékhé tchi séytane

  • @aichadiopgueye8049
    @aichadiopgueye8049 2 ปีที่แล้ว

    Bilaye YALLA mo khame leppe

  • @etreveridique1467
    @etreveridique1467 2 ปีที่แล้ว +10

    damay dégue gnounane mandou melnani wor. Ay nagnou Mandou bayi accusation ak wakh loudoul deugue ak yakarna, ak khawi soutoura... Allahou Akbar

    • @rokhayasall6952
      @rokhayasall6952 2 ปีที่แล้ว

      Bilahi walahi watali gni maléne kham ndakh mane setou Mame Tidiane Dem la Kassaville Kaolack bigni néké khalé dagn done dem Ndiaye Counda domou waliou piir mais yalla bakhna métina trope nak dakh touma bakhoul 😭😭😭😭

  • @ibrahimaNiang-rl2xi
    @ibrahimaNiang-rl2xi 2 ปีที่แล้ว

    Machalllah mé yalla bakh na 🙏🙏🙏🙏🤝

  • @fatysyll5643
    @fatysyll5643 2 ปีที่แล้ว +9

    Beug waxi deum té kene messou sé guis deum di féne di doul si sossal nitt té kene menoul wat si yalla ni guis deum
    Bayilene sossalaté

    • @mamemaramediouf3950
      @mamemaramediouf3950 2 ปีที่แล้ว

      Billay li dafa eupe senegalais bala mo contane rek mou yak niit si ay wakh wala ay def. Ça m'énerve cette attitude !

  • @jolieseye403
    @jolieseye403 2 ปีที่แล้ว +1

    Lolou yeup ok mai Noume déf ba yèk fofou🤔🤔🤔ahh

  • @modougueye555
    @modougueye555 2 ปีที่แล้ว +2

    ndayssane 😭, yalnako yalla safara

  • @tmouhamedtalltal6909
    @tmouhamedtalltal6909 2 ปีที่แล้ว

    machalla nite moy dioum 🙏🙏

  • @awacamara7752
    @awacamara7752 2 ปีที่แล้ว

    Yalna nui yallah dieguel

  • @ousseynoumbodj9270
    @ousseynoumbodj9270 2 ปีที่แล้ว +6

    Ndeysann mettina sa famille la yeureum bayilen gawa toumal nittt ndakh ayyy ndiabotam

  • @Mamichoubb
    @Mamichoubb 2 ปีที่แล้ว +2

    Mane dei jugéwoumako mei loukofa wara yégueul doyna war yalla nanou yalla doli soutoureu

    • @sokhnamaisaliou9430
      @sokhnamaisaliou9430 2 ปีที่แล้ว +1

      Gni ko toumal ay deum ak louma khamoul gno gnakk mandou. Mais se poser la question comment elle a pu être là ? C une question que tout le monde peut se poser

  • @TEDUNGALTv
    @TEDUNGALTv 2 ปีที่แล้ว +1

    SVP, comment s'appelle la Présentatrice ?

  • @dijandiaye4188
    @dijandiaye4188 2 ปีที่แล้ว +15

    Ken xamoul foumou diar…
    Kone naniou mandou si ay mbireum…
    Mais Sénégalais dafeu gneimei bakarou
    Yallah rek xam liko yob si kaw

    • @lotalo3925
      @lotalo3925 2 ปีที่แล้ว +1

      Walahi yalla rk Mou kham deugue bou wérr sax

  • @astoushylabarriette2352
    @astoushylabarriette2352 2 ปีที่แล้ว +1

    Li c vraiment triste chaque jour qui passe on perd tjrs nos valeurs un bon musulman et croyant ne traitera jamais son prochain de cet sorte deum moy lan niukoy traiter deum hana vous n'avez pas de mère ki yayu diambur la degen diang deum ba tariii hamni deum la alahira dîna meti trop teh kep ku togn sa morom bomu meti ko teh diegueluwoko bu yawmal hiyameh digako layu ac sa borom changeons nos comportements guir yallah li niay n'a si diulitt ana suniu geum geum ac luniu yonenti bi bayil.
    Soyez fort sa sera difficile mais vous allez vous en sortir inshalah qu'allah le tout puissant guide vos pas vous assiste et vous aide à la soigner.

  • @ndeyefatousylla4269
    @ndeyefatousylla4269 2 ปีที่แล้ว

    Tu as raison merci ça se sont chayatines qui font ça je te recommande d'aller voir thierno Moule Sow

  • @aissatoudia4280
    @aissatoudia4280 2 ปีที่แล้ว +2

    Yengi di laaj nimou def ba yeeg foofou yeena dof😅kou dof kay day am ay jinne yimouy andal jinneyii mouna deflo nit louné

  • @Corailpro
    @Corailpro 2 ปีที่แล้ว

    Ndeysane Dieuredieuf serigne bi !

  • @fatimasy4431
    @fatimasy4431 2 ปีที่แล้ว +1

    😪triste rèvèlation de son diarbate bilae. C'est triste sènègalais mo wara bayi juger nitt si bopam tè khamouko. Il faut que les autoritès l'aide à se soigner😪🙏que le bon dieu l'aide à se guèrir🙏

  • @fatoumatabinetadiallo6082
    @fatoumatabinetadiallo6082 2 ปีที่แล้ว

    Je suis. Fière. D être. Peule

  • @natoukoite6205
    @natoukoite6205 2 ปีที่แล้ว

    Rap la

  • @ndeyemareme38
    @ndeyemareme38 2 ปีที่แล้ว +4

    Billay ndeysane nitt dey wakh louka yor toumal domou Adama bakhoul way 🙏🙏