Vraiment je ne suis pas le seul à avoir constater ceci Mais je le trouve très normal je n'ai rien contre la nouvelle génération (New school yii) way parfois c'est bien que les maîtres remettent les battons sur les rails
Les Old school ça se voit qu'ils sont plus conscients et responsables par rapport au news générations qui cherchent que du showbizz et du buzz jusqu'à oublier nos réalités. #Respect à vous #Dabrains et #Ndongod End Discipline sénégalais 🔥✌
Ndayesane dommage que les textes et paroles recherchées ne sont plus récompensées légui tegneuh tegneuh rek moye fayékou. Mais Djibi franchement chapeau bas 🧠👌🏾👍🏾🇸🇳
Nit bou siw bou dewee nguene solou golo took di dioy ,te bimouy dound hypocrite loune nga tek si derame... Macha allah le texte est très riche.bravo Da Brains
De la bonne musique, des textes instructifs, un habillement correct qui ne fait pas la promotion de la nudité ou de l'homosexualité... Voilà ce qu'on attend de nos artistes. Bravo Da brains
Du Loud Wallahi ! 1. Coté Beats Nice Et Impécable 2. Lyrics👍 Nice Les Parole Parle D'elle Meme Et On Vis Tous Cella Au Senegal 3. Qualité image Diarama 4. Scene Bi Lepp Nikel 5. On Attend Les 1 millions De Vu D'ici Klk Jours !
Triste réalité mane dama deimm ba xamko ci sama bopp billahi yimay jappalei niomay kheixe kouma dfal lou baxe mou fayma lou bone Alhamdoulilaaah Dieu est au contrôle ça m'a aidé de telle sorte que Yalla rk moy taxe may dff sans attendre rien en retour
Mon meilleur ami avec ki jtaii niou dougadoo negou gooor amadooo cfee son pere ak sama papa andeuh dougou mecque ligue 2 France lay football sa fait maintenant 2ans heure bou nieuweiii message reck lay am si mom vraiment l son ma touche ✨
Walahi wakh nga deug t deug neikhoul bilahi djiko sénégalais rek nga weuy djadjeuf ta tout dit merci paix sur vous et longue vie...bouniou amei diom dei changé.....thanks
Waaw quel son j'adore vraiment c'est tellement vrai ce qu'ils disent c'est la société sénégalaise qui est ainsi faite merci da brains pour avoir parler des tares de notre société 🥰😘❤ Félicitations ❤🥰😘❤🔥🔥🔥🔥
Très belle chanson vraiment merci les grand soonoone nagne si sound love yi way ced temps ci Mbeuguel mbeuguel rek ça devient chai*nt à la longue Big respect à vous
Amna solo en tout cas je kiff bravo Da brains Les grands vous montrez toujours la suprématie de vos mentalités envers les boys( underground bi) Chapeau a vous
Merci sama grand yi Nice na continuer lène ci ni sourna guèneu na tothi fi solou golo bay fosse dafaye tothiii khalè gnokoy djito Way after mak Gni khamnè rite Lek lay djiokhè dama contane koi
Walahi lou weer la wax surtout Mbeur té bouñouy commencé yorou ñou dila sonal nan bess bouma tekei Nala yobou makka Lii may wax nak damako dund ak samay wadiour si Mbeur bouñou yorone
Un message percutent , voué de sens, sur un rythme symphonique reflétant la musique traditionnelle ... Aussi bien sur la forme que dans le fond c un son typiquement illustratif du Sénégal tel qui miroir . big up !!! Nice Nice .... Respect.
Kou guiss ni
Linou fi wakh yepp mingui am si Sénégal beuseul je aim 👍
Bien sur
ماشاء الله قولك حق
bilay surtout basola ak sambay mbayane
Dafa lér
Lii moye musique daa wara yèètè
Les sons instructifs n'ont jamais des millions de vues mé plutôt des sons blabla
Ibrahima Makalou fofou la sénégalais yi toll. C grave!
Billahi wax gah deugue
Culte de la médiocrité mo niou sonal.
On préfère les chansons insensées ! Et les idiots sont idolâtrés
Bien dit
gou geume nei clip bi dina yéée niou beuri mayma jaime ✌
dou yè kène bro sènègalais dou dègulou kikoy wakh deugu kikoy djey rek la kham
@@evasima9739 waax nga deug d'une part déi
Old school bi temps yii mayou ñou dra boy bi🤣🤣simon ndongo d tey baxaw❤✌💪
Billahii
Vraiment je ne suis pas le seul à avoir constater ceci
Mais je le trouve très normal
je n'ai rien contre la nouvelle génération (New school yii) way parfois c'est bien que les maîtres remettent les battons sur les rails
@@abdoufalldiamanka9853 bien dit frr rap ñikoman ba legui ñonkoy df
Tqt légui gnou bayi ndanane ya ngui gnew wait some rek
Mais malheureusement leur son sont pas aussi promus
Les Old school ça se voit qu'ils sont plus conscients et responsables par rapport au news générations qui cherchent que du showbizz et du buzz jusqu'à oublier nos réalités. #Respect à vous #Dabrains et #Ndongod End Discipline sénégalais 🔥✌
MERCI POUR CE CLIN D OEIL A LA CULTURE SERERE
Barki serigne touba mane nji la beug💪💪❣❣
Un son qui a plein d'enseignement machalla
Mane dal yaw lay weure Ba guoudi ma sangou nelaw ❤
@@mamanfall2341 manguilay sette yowitte
Wallay ndeyessan
Celui qui a été victime des solukatou golo beusseul j'aime et masta thiono..
Tay boy yii dee grand yii gnieuwatt naniou dee Simon ndogo d tay da brains doto lenn ko defatii dee😄😃😃
Ndayesane dommage que les textes et paroles recherchées ne sont plus récompensées légui tegneuh tegneuh rek moye fayékou.
Mais Djibi franchement chapeau bas 🧠👌🏾👍🏾🇸🇳
Dageu RK gui fi wakh Billy Sénégal rk
souleymane ndiaye
Nit bou siw bou dewee nguene solou golo took di dioy ,te bimouy dound hypocrite loune nga tek si derame... Macha allah le texte est très riche.bravo Da Brains
De la bonne musique, des textes instructifs, un habillement correct qui ne fait pas la promotion de la nudité ou de l'homosexualité... Voilà ce qu'on attend de nos artistes. Bravo Da brains
deug piir ngéne wakh adouna amoul solo Machallah bonne continuation
Du Loud Wallahi !
1. Coté Beats Nice Et Impécable
2. Lyrics👍 Nice Les Parole Parle D'elle Meme Et On Vis Tous Cella Au Senegal
3. Qualité image Diarama
4. Scene Bi Lepp Nikel
5. On Attend Les 1 millions De Vu D'ici Klk Jours !
sons sama benn ami d'enfanec lay wakh dah commencè nek aéroport rk melni kou yor ay milliard tèh yoroul nguatt, fatèma
Li ngén fi wax lép mongi thi Sénégalais yi bilae kou dakor
Kou guiss sa bop ci li beuseul 👍👍👍👍👍
Très belle chanson ! Texte très Riche, une leçon de vie! Félicitations Da Brains
Au secours 🥺🥺🥺 A vous entendre parler c'est le sénégalais qui est foutu. Préparons un ndeup national pour défarate djikoyi. Qui est d'accord 👍
Belle chanson avec des paroles sensées qui reflètent ce qui se passe dans la société Sénégalaise malheureusement. Bravo à vous et bonne continuation
Kou goré woul rek ak badola boul alal dapp rek gnoy faté demb
Ki est d'accord de tous qu'ils disent 👍👍
Deug dou. Nékh akhh mane na Fay carière 💯lou wèr ga wakh 🙏🏼 yalla brom bi rakhass khol yi 🙏🏼
Clin d'oeil bi à la communauté sérére bi amna solo. Nêkh na trop
Triste réalité mane dama deimm ba xamko ci sama bopp billahi yimay jappalei niomay kheixe kouma dfal lou baxe mou fayma lou bone Alhamdoulilaaah Dieu est au contrôle ça m'a aidé de telle sorte que Yalla rk moy taxe may dff sans attendre rien en retour
Aka lerr frere
Koussi diekou fater debb
Lissi geuneu meiti nak yaye doon sen 1er nooon
Thiey
🙏👍
machalla
Mon meilleur ami avec ki jtaii niou dougadoo negou gooor amadooo cfee son pere ak sama papa andeuh dougou mecque ligue 2 France lay football sa fait maintenant 2ans heure bou nieuweiii message reck lay am si mom vraiment l son ma touche ✨
Ndeyesane da khamoul rek tè dieul adouna defko keur mais yalla wakhoul kén dara mn frere
Deug pirr nguén fi wakh mais nak Sénégalais beugoul deug mo takh million de vues dounguén ko gawa am gnifi solou golo fi bari
Borom xam xam nena nite tant que amo amogo Jikko. Votre son est une réalité. Merci
Ohhh vraiment une vraie leçon de vie... Respect To The Old School ...Da Brains🙏
Thiey fall srx sa comment la done weur
@@yacinedabo2161 😂😂😂😂 Sheuteuteut ma bayi commentaire nank
@@ndiayemandela5275 dett way yaw niofar dei
No ay vrai ndanan ngay am fofou cou d'accord ak man beusseul j'aime
Wooyyy serere way adna diégué solo dh
Laya ndinguilll
Realite senegalais ki est d'accord na woone boppam
Nouvelle generation bi kène menu thi teye grand yi canabasse rock mga fy done guiss mouy sonal grand yi
Walahi wakh nga deug t deug neikhoul bilahi djiko sénégalais rek nga weuy djadjeuf ta tout dit merci paix sur vous et longue vie...bouniou amei diom dei changé.....thanks
Waaw quel son j'adore vraiment c'est tellement vrai ce qu'ils disent c'est la société sénégalaise qui est ainsi faite merci da brains pour avoir parler des tares de notre société 🥰😘❤
Félicitations ❤🥰😘❤🔥🔥🔥🔥
Nice lèppe deuge la adouna amoule solo boule fatèè dèmbe
yallah guénn fii yagg
c sa du rap hip hop
old school yii nioy rap billay
Vraiment il est un artiste engagé .il fait passer d'importants messages .respect🤞🤞
Très belle chanson vraiment merci les grand soonoone nagne si sound love yi way ced temps ci
Mbeuguel mbeuguel rek ça devient chai*nt à la longue
Big respect à vous
Lici guene ame solo moy epargnèwou personne tt le monde il è dedans chapeau â vous
Da Brains tjrs des textes qui enseignent. Love sur vous.
Gni béw. Ak gni am di daw séni mbokk voila une leçon de vie rawatina yén mbeur yiiii
Merci dello nguené sama xéll thi dembeu ak WA balak mbolo thi sone bi
Deugue na deugue nak ohhh Macha allah fila senegal ngoor laago lafi yalla nagnou yalla mouseul thi nitt kouy sopikou 🙏 Amine thi j'aime bi 👍
Plein Denseignement🎹🎵🎶🎧
Realité Sénégalaise😐
Wallah 😂😂
La chanson de Dabrains mérite 2millions de vue merci mon frère bakhaw chapo à djibi dady
Bravo très bon son!!! Le texte reflète la réalité de la société et du milieu artistique. Bonne continuation je vous kiffe.🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Et c ça que devrait servir la music malheureusement
Xana xamo né akhh meune na faye sa carrière , serigne sangue nala sokhor takh na amo bayree.
Nice vous avez bien dit le mot (badola ) holalalalalala sa existe bocoup au sénégal diam si yene wayyyy😍😍😍😍😍❤❤❤❤❤❤❤❤
🎶" Yaye boye aduna amoul solo weykeut yék mbeur yi footballeur kou geuneu goré kousi siw faté dembeu faté fanga diogué ... Té niom kosi defal lou baax mou kheuy solou golo " 🎶 Jaime beaucoup le refrain de bakhaw avec un style particulier 🎹
Right bilaay lou leer ngene wakh kou d’accord beuseul aime 😊❤️
Ce son rend tout simplement amoureux ❤
C'est très fort !
Âme soeur
Amna solo en tout cas je kiff bravo Da brains
Les grands vous montrez toujours la suprématie de vos mentalités envers les boys( underground bi)
Chapeau a vous
Li moy way wakh gua lou am solo nite kou bakh dou faté demb bilahi li amna chance trop😍😍😍😍😍😍😍
Vs êtes des instructeurs chapeau a vous je vous LOVE yalna DIAM yaggg naniou dellossi khelli bollé kholi adina dou dara
Machallah. Yalla na yalla samm
Merci sama grand yi Nice na continuer lène ci ni sourna guèneu na tothi fi solou golo bay fosse dafaye tothiii khalè gnokoy djito Way after mak Gni khamnè rite Lek lay djiokhè dama contane koi
Effectivement vous énoncez des paroles indégniables ....kou guisni sa existe rellement dans notre société beusseul j'aime...
Dafa leerr nitte dafa wara hameni nite dou dara
👏👏accent serere day faye
Djibi vraiment yangui togne borome oto bi dé 😀😀😀Mai nakk l message est bien reçu walahi té ya bokou de badolo dan cette pays.
Très instructif, Qui croit comme moi que dabrains a oublié de citer les politiciens..!
Texte très riche machalah,yalla n'a yalla rakhass xol yi,dindi si bép sokhor,kiniane ak dioubadi
Walahi lou weer la wax surtout Mbeur té bouñouy commencé yorou ñou dila sonal nan bess bouma tekei Nala yobou makka
Lii may wax nak damako dund ak samay wadiour si Mbeur bouñou yorone
Tjr au diapason and ak temps ak lignu dound chapeau comme dab yalla neko golo degg nakh gnu sopekou au pire d k gnu gueune yatal parc hann
Réalité 🇸🇳boule deglou 🎶bi degloule parole yii amna solo bothi méré nak golo nga
😀😀
Yallananiou yalla mousseul si solou golo wallay aduuna bi nay rafett rk
Bilahi vérité absolue ✌🏾
Da brains 🧠
Mashallah nice son deug bou weur naniou xolat souniou bopp boula yakla weeseugeulé boul beew xolal gni nga done andale demb diapalé leen
Message très clair, nit mo gawa #béw
Li moy music wakh deug wayei wayane rek ak bruit boudoul diekh merci merci vraiment j vous adores...
Deugue billahi nékhoul machallah nékh na lole
Woy boudoul yéété dal ay nakh la old scool for ever💪💪💪
Nice track Galsen warnagn yéwou khamné fi adounala té boul bi dey tourné a tout moment wasalam
Son bi baan son de dabrains laleine di fateuli
Niou déf ni 👎 khamé nasi béne artiste ak béne mbeur dh 😂😂😂🤣
j'aime ces genre de musique ...qui révèle les réalités de la vie ...j vous adore da brains😘😗😗😗diam thi yéne
Dègg tina Deug dè👌👏👌
,, ADNA DJÈGUÈ SOLO,, 😂 😂 😂
Mais saway IL parl serrere hein
wawaw adna djèguè solo
Wawe wawe
@@mariafaye3355 faye biram sama djaam bi, sa mista nafio ta aladji fè😅😅😅 mi nanam serrere dè
Soeurette@@adjipendadieng2527 ma bañ aduna amna sólo dè
Ddd
L'I lagnou sokhla na saf sénégalais .merci
Wooooww bo deig lo gnii reikkk nga xhamneii new génération bi doune gaaatt buzz moleine sonal
Aka lere senegal legui kou am fate demb waye koufate sa demb faga diem dou lere gore modiafe machalla da brain
Kou sa xole sedd si son bi pouseul bleu
Right koussi am faté demb badola nga
2:24 me fait penser à dj arafat. Bravooo franchement
Bilakhi bien dit bo déwé gnouy hommage thimmm
Oh quelle clip ! Vs chantez bien surtout Bakhaw. Cette son exposent la réalité sénégalaise.
je le écoute depuis hier si l'émission Real one de la rfm avec kalz et olibi gaza👏👏👏👏
Bakhaw refrain bi dof na👍👍 accent serrer bi fathie nama💪
Machallah deug bou wer gua wax dh nice nice nice vraiment son bii nice na trop bilae 👏👏👏👏💖💖
C'est une tendance au senegal d'oublier ses proches avec qui on a galere.solou golo deug bou weur
new génération bi d egotrip ak mbeugeul rek laniouy way ...nice message
Vs meritez plus de 244k de vues. Vs au moins diingen way lou niit meuneu deggeu.. Vive les old school
Mashallah j'aime bcp respect à vous
Limfi wakh leppa amna niethi guiss sen bop boulen mer🙏🙏
Limoy song kouko deglou diaguer si macha llah very nice bro
Un message percutent , voué de sens, sur un rythme symphonique reflétant la musique traditionnelle ... Aussi bien sur la forme que dans le fond c un son typiquement illustratif du Sénégal tel qui miroir . big up !!! Nice Nice .... Respect.
Magnifique rien à dire que des paroles véridiques
Qui l'ecoute encore, est toujours d'actualité au 🇸🇳❤️
Message instructif Nice sound
Yoweilein #Oldschool🔥😍
Sons bii amna chance torope nakoo kii nane mafii dakeu rap dègue lou mou diangall ko adouna