Papa wax nga deug dèh tous les délinquants sont pas en prison👮😷👮🚓 bilahi Sénégal le gouvernement da'nio réreu depuis Senghor la wone jusqu'à présent / ngor ak dignité zéro / parfois je me dit que eské nioune ay nit'la'niou ndakh nio'ngui xalat souniou adouna ak lane la'niou wara diayanté yalla souniou borom ak souniou diguanté / bilahi lou yémé lalay tégal'ni / Nguir yalla nioune jeunesse bi na'niou défar souniou avenir adouna yagoul lép si nétali lay moudié / tè kou défa'roul sa diguanté sa borom ak nit'nie bilahi pérte nga / Je ce que dou mane kàçé lay dal parfois damay tok di xalat ni tay souma déwone a'nna lane lay raconté yalla ndax sama adouna si lane lako done passé Bilahi bilahi bilahi bilahi bilahi li déss sama doundou douma xoulô douma xéx ni togne liguéy diamou yalla tay sakou sama ngiereu'meul way diour bô amé dimba'li nié'nga tané point / Yalna bour yalla défal'niou diame adouna ak Alah ira si barki seydina mouhamed psl amine🙏
Non Mady bi khamnako sa fait longtemps que je ne l'ai pas vu je savais pas qu'il était en prison masta way copain toi et moi on à partager quelques chose au temps de jeûne respecter way
Courage c'est vraiment dur,les sans voix n'ont jamais raison devant la loi ,mais le jugement de Dieu est le plus grand et plus véridique.Que ALLAH vous accorde sa grâce et sa miséricorde.🙏🙏🙏
Akh Innocent yi Nek prison est-ce que diapougne réwe. Yalla nagnu yalla diegal té takhawou gni Nek Si kasso yii yalla nagnu di yalla moussale gnune gneupe. Suis très sensible par rapport à ce qui se passe dans les prisons
Li ni c'est du cas par cas moi je condamne ceux qui agressent les gens ba raye nit ki gratuitement je condamne aussi ceux qui violent les femmes , ceux qui violentent les femmes et ceux volent tass yakar nit yi donc je veux juste une question certe oui prison jomboul kéne mais franchement eux c'est quoi leur châtiment doit on les laisser libre leur donner une deuxieme chance et que au finish il devient des multirecidivistes
Quel pays j’ai honte de dire que je suis sénégalaise Sénégal rek gay guiss lii bandits yi Niougui sii deuk bi tokk yoor séni auto youu rafet keur niou makk dii dokhi senn sokhla Prkw on nous maltraite nit kenn douko torokhal soudonn lolou yalla torokhal niou wallahi alakhira dina méti barki alkhouran akk barki wérou koor bi Sénégal gniko djité yalla nalen souniou akh daleu baguen guiss ko si barki wérou koor bi Gni djité rew mi yalla nalenn souniou akh daleu si barki yonenté bi swt naniou dem rek adina migui senn kanam torokhal nit molenn dii doundeul yalla dina niou arté akk souniouy djité rew thiey Seydi khadj malick sy doneu nako wakh Sénégal douu meusseu amm djital islam yalla naniou yalla djapalé
Sénégal moy deuk bo khamnè dem kasso da yomb trop. Meme les petits délit kasso. Pas de liberté provisoire, pas de caution, pas sursit. Même taukh yamba kasso . Warnaniou kholat sounou système pénal
Yalna gnou Yalla doli soutoura. Moussal gnou si kasso. Gni tamite yalna len Yalla diapalé dolilen soutoura banou bagna délou wat fofou.
Alakhira amna yalla Molène eupe dolé
Papa wax nga deug dèh tous les délinquants sont pas en prison👮😷👮🚓 bilahi Sénégal le gouvernement da'nio réreu depuis Senghor la wone jusqu'à présent / ngor ak dignité zéro / parfois je me dit que eské nioune ay nit'la'niou ndakh nio'ngui xalat souniou adouna ak lane la'niou wara diayanté yalla souniou borom ak souniou diguanté / bilahi lou yémé lalay tégal'ni /
Nguir yalla nioune jeunesse bi na'niou défar souniou avenir adouna yagoul lép si nétali lay moudié / tè kou défa'roul sa diguanté sa borom ak nit'nie bilahi pérte nga /
Je ce que dou mane kàçé lay dal parfois damay tok di xalat ni tay souma déwone a'nna lane lay raconté yalla ndax sama adouna si lane lako done passé
Bilahi bilahi bilahi bilahi bilahi li déss sama doundou douma xoulô douma xéx ni togne liguéy diamou yalla tay sakou sama ngiereu'meul way diour bô amé dimba'li nié'nga tané point /
Yalna bour yalla défal'niou diame adouna ak Alah ira si barki seydina mouhamed psl amine🙏
Les plus grands délinquants sont au cœur de l’état.
Vérité absolue bilahi
Bilahi wa a.p.r
Oui c'è vre
@@falloudiaka4792 bilaye
C'est vraiment dur. Ce vieux qui le voit sait que c'est une personne pieuse.
Wa 2stv yéguéni def lou am solo bilay
Alakhira di guène ni yallah moy buur😢❤️
Nul ne peut échapper à son destin...
Dém kasso takhoul bonn
Wolayy
Boy du courage ta l avenir devant toi et le grand aussi une personne trés instruite que dieu vous protége
K’Alha vous accorde le meilleur
Yallna yalla takhawo moulem dioulitt
Non Mady bi khamnako sa fait longtemps que je ne l'ai pas vu je savais pas qu'il était en prison masta way copain toi et moi on à partager quelques chose au temps de jeûne respecter way
Je te jure borom baakh troop calme en plus kou yeugue niit
Courage c'est vraiment dur,les sans voix n'ont jamais raison devant la loi ,mais le jugement de Dieu est le plus grand et plus véridique.Que ALLAH vous accorde sa grâce et sa miséricorde.🙏🙏🙏
Oohhh madi Diop 1 ami d enfance metina
Yalla nagnou si yalla mousseul
Ohhh Madi diop borom déguissma you rose yi...🥺
Senegal d tps k amoo blemm al justice wala ga febar do khamm deuk bi amoul loi
Merci indey diack
On connaît les délinquants de l’ombre.
Bilay ma sœur ta raison dh
@@djiby-monument
💜🙏🏽👍🏾
Vraiment triste pour notre pays
Oh ndeysan oh li méttina bilahi li nattou deugueuleu ndeysan
Ndeysan li tooy na xol 😢
Meti na trop vraiment😭
Yawmal xiyam dina #méti
Métina bilahi
Akh Innocent yi Nek prison est-ce que diapougne réwe. Yalla nagnu yalla diegal té takhawou gni Nek Si kasso yii yalla nagnu di yalla moussale gnune gneupe. Suis très sensible par rapport à ce qui se passe dans les prisons
Li ni c'est du cas par cas moi je condamne ceux qui agressent les gens ba raye nit ki gratuitement je condamne aussi ceux qui violent les femmes , ceux qui violentent les femmes et ceux volent tass yakar nit yi donc je veux juste une question certe oui prison jomboul kéne mais franchement eux c'est quoi leur châtiment doit on les laisser libre leur donner une deuxieme chance et que au finish il devient des multirecidivistes
On parle d,innocent ici myma
Sa mame néna alakhira fala beute di sété (alakhira la léep di léré)
😭😭😭😭😭
Quel pays j’ai honte de dire que je suis sénégalaise Sénégal rek gay guiss lii bandits yi Niougui sii deuk bi tokk yoor séni auto youu rafet keur niou makk dii dokhi senn sokhla Prkw on nous maltraite nit kenn douko torokhal soudonn lolou yalla torokhal niou wallahi alakhira dina méti barki alkhouran akk barki wérou koor bi Sénégal gniko djité yalla nalen souniou akh daleu baguen guiss ko si barki wérou koor bi Gni djité rew mi yalla nalenn souniou akh daleu si barki yonenté bi swt naniou dem rek adina migui senn kanam torokhal nit molenn dii doundeul yalla dina niou arté akk souniouy djité rew thiey Seydi khadj malick sy doneu nako wakh Sénégal douu meusseu amm djital islam yalla naniou yalla djapalé
Kasso Sénégal métina so fébaré!!!
Sénégal moy deuk bo khamnè dem kasso da yomb trop. Meme les petits délit kasso. Pas de liberté provisoire, pas de caution, pas sursit. Même taukh yamba kasso . Warnaniou kholat sounou système pénal
Vrai
Yàlla na yàlla sutural ñëpp té mussal ñëpp
Ñii ñioune wara diapp no diapouñioulene délinquant you magui ils sont dans l’état
😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤦♂️
Yalla rék mo kham
😭😭😭
😭😭