Un jeune lutteur ambitieux dois prendre des initiatives pour être un roi...donc sitaaaa n'a qu'à revoir ça façon de lutter pour se progresser... félicitations à Modou lô & du courage sitaaaa👊
Depuis Londres...Siteu moy lac de guèrr numero 3😂😂😂😂😂😂 Aka Tapète... modou lo mo meun mo eupp doolè... modou lo le meilleur lutteur de tous les temps... Modou yalla mokofi tèkk...Manolèn si Mom dara... Felicitations Kharagne Lo...Yao kèssè lagnouy toppou...Mane yao la beugue...
Bécaye vrai nafék la, magui dora xame Prkoi yikini done la djoxogné barame Bravo modou lo y’a beuré beurè bi yeup Intelligent Tapha suis parfaitement d’accord on doit voir le règlement
@@leuz.patriote ,🤣.d accord pour mane dawara takhaw deuguel bopame mais di daw rék noo ma sonou si siteu khalai bou ndaw vraiment 😂 yalla na yalla doli diamou thank you very meche
*Siteu sou amone diom dey daan Modou. Modou n’était pas dans son jour en plus il a pris bcp de risques. Yow ya sokhla roi bi mom mo warone nieuw prouver mais dafa gueine sakou yi beu niakk.*
je pense qu’on doit trouver des astuces pour éviter ces genres de situations, par exemple quelqu’un qui a trois avertissements verras son adversaire bénéficier d’un “weur nombeu” répété jusqu’à qu’il y ait une chute.
Leigui li may ladj bou mbeur mi amei avertissement yu bari fek mbeur mi beurei woul ba temps leigui le reste de son argent kounou kay diokh son adversaire wala cng question bi dafa ladj reponse si on change le reglement❤❤❤❤❤❤❤
Modou lo boyi meuneulounn ko dara bilahi kholal boyi nio nek si yoon gueunn nek xalé wara eup ambition parsk nio tolou si outt dara vraiment modou lo vrai champion
Le reglement de la lutte ne compte pas le nombre d'initiative pris Faites le fanatique, Oui, mais ne soyez pas naive Une chute reste une chute quelque soit le contenu du combat A chacun sa stratégie pour gagner Modou Lo est clairement tombé, 4 appuis ou chute par l'épaule..., il aurait du perdre le combat, l'action a été initiée dans l'arene Belle tactique de Siteu qui a su casser la distance au bon moment a chaque fois et mettre en difficulté Modou Lo, qui, malgré plusieurs initiatives pris, n'as pas dominé son adversaire, il a visité Ardo 2 fois, preuve que Siteu a été précis dans ses coups et n'as pas simplement balancer les bras Les commentateurs et les arbitres ... ça laisse a désirer Si la couverture des caméras sur l'enceinte était optimale, a l'heure là, on parlerait d'autre chose. Pour répondre a Tapha, c'est pas que Modou Lo n'était pas dans son jour, c'est juste une excuse que vous lui trouver car on s'attendait a une victoire éclatante de ce dernier ; C'est plutot Siteu qui a trouvé la tactique idéale et a anéanti celle de Modou Lo, il s'est bien déplacé et a su bien contrer. De grace Modou Lo a eviter un KO sur une droite reçu en plein visage. Siteu a trouver les arguments pour tenir mais n'as pas conclu, il faut le féliciter et non trouver des excuses a Modou Lo.
Merci beaucoup grand Moustapha tu es le meilleur tu as tout dit❤
❤🎉🎉❤🎉
Siteu yangui may beug ndirou Lac2 😂
Moom la de
Lac 3 😂
Siteu moye lac lac moye siteu
Au moins mom dina dor
Bly ioe😢
Félicitations modou Lo champion 👑
Merci mon champion Tapha Guèye. Wakh day yénou maana
Siteu vraiment amoul diom jubilé 2 défaite de suite c’est juste surréaliste. Il faut cesser d’encourager « doma Dane doumala dane »
Attention nak fau dire k dem Ardo modou lo yeup bolennn xolé si guinaw sakouyi lako siteu si door aussi
Lolou lah gayiii waxOulll nakkk
😂😂😂 bou arbitre souffle mou dorr ko siteu tricheur la
@@maguettesamb4137il triche
Wakh nga lula nekh
@mawlanaambengue2059 kholko bou bakh
Bilahi Modou lo a tout donné soyons honnête et dign siteu mom
Futur lac 3 merci 😂😂 daw daw reik
Xlo khamona ne bu deful action combat bi du nekh
🎉🎉🎉❤
Siteu n'a rien fait du tout. C'est une honte. 2 fois de suite contre lac et encore contre modou lo. Avec tout ce qu'il a dit
😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😅 13:35 😅😅8ô9
Bilay 😊
Lo beug nak siteu dou dem
Bouko diapei ni d'où bakh Nay attaqué Di beuri mo Guen Mouy daw rek
Tu n'as pas regardé Modou lo a été meuné khana do kol dans l'histoire de Modou lo personne ne la tapé comme siteu❤ la faire on es fière de siteu❤
Un jeune lutteur ambitieux dois prendre des initiatives pour être un roi...donc sitaaaa n'a qu'à revoir ça façon de lutter pour se progresser... félicitations à Modou lô & du courage sitaaaa👊
C vrai de eh👍
🎉❤🎉🎉❤🎉❤
Siteu dafa done Ndaw rk 😂😂😂
Gars yi danio fok ni siteu da door modou bamou dem Ardo alors que wéwou siteu mo gagn modou 😅 le meilleur lutteur de l’arène c’est modou lo 🎉🥇👑
Saway bayil fene directe gauche laa
😂@@papadiom9260
No bi après arbitre bi sifflé silako door
Billay linga wakh mooy deug
Teiii ci guinaww sakkou yii la ameii 😂
Mod lo le populaire
Meilleur lutteur sénégalais
Boy yi gnéméwuñ mod lo bilahi
Deñ koy bayé xél.
Xalé kay déngay woné nga xalé nga.
Moustapha tu est le meilleur ❤❤❤❤❤
❤🎉🎉❤🎉❤
Siteu il a decu tous le monde
Une chance on doit la chessir
😂😂😂😂 vous ete malade sufeker door nite bamu dem ardoo dane ko Moy deception na yam si yen nioune wa diameguene on est fier de Notre nouveau roi
Sur tes reve
Attendez votre recours
@@footballgod4351 c'est normal kham nga yaubouna modou lo ardo ndam la si yéneu😂😂lolou rek ngéne ame si combat bi déé
Merci modou lô❤❤❤❤❤❤
Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤❤❤
Depuis Londres...Siteu moy lac de guèrr numero 3😂😂😂😂😂😂 Aka Tapète... modou lo mo meun mo eupp doolè... modou lo le meilleur lutteur de tous les temps... Modou yalla mokofi tèkk...Manolèn si Mom dara... Felicitations Kharagne Lo...Yao kèssè lagnouy toppou...Mane yao la beugue...
Bilahi lac 3 😂mosse
😂🎉
Yow sof nga aka depuis Londres.fodém bind kofa.
Wawaw 😊
Depuis Londre pour lane lasi
Siteu dall légui mode lac de guer lay deif, doumala dann doma dann. 😢😢
Félicitation Modou Lo ndam rek inchalah XLo le roi des arènes ❤
Toujours pertinent le chronique de Tapha Gueye.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Siteu Day Day rék amoul arrêté 😁😁
Merci père Tapha🎉❤
Merci père Tapha belle analyse
Félicitations x Lo🎉🎉🎉 mais palataux bi Nice na trop❤❤❤
Siteu alias LAC 3 arrière rék lay déff😂😂😂😂
Bilahi g fait le mm commentaire😂😂😂
Ak yobi ardo gnous ko daneko 4 appuis bou lerr
Tapha tu es le plus grand analyste de lutte au Sénégal tu es le meilleur lutteur de ta génération et le plus grand analyste
Tapha mo guena tapet
Ki mo door écurie serere yeup. Loy wakh ni@@alassanediouf-vo6sq
MODOU Lo a gagné 146890 fois !
Siteu n’est qu’une grande gueule .
Modou lo a vie billahi wallahi kouko beugoul ya kham roi des areine de tout les lutteur
Merci beaucoup Tapha ❤❤❤❤❤belle Analyse ❤
Bécaye vrai nafék la, magui dora xame Prkoi yikini done la djoxogné barame
Bravo modou lo y’a beuré beurè bi yeup
Intelligent Tapha suis parfaitement d’accord on doit voir le règlement
Merci Père Moustapha, félicitation Modou lo 🎉Siteu day daw Rék 😂🎉
FÉLICITATION 🥰 XARAGNE LÔ 🎉LE ROI DIGNE DE SON NOM
Siteu gamoul bopam dagne koy diay rek beure tapale rek lay beure meme contre lac non la defon didaw rek
Merci ndakh ngua gnimé ka wakh.😂😂
Lo lou monye deugue siteu amoul barre bou dane modou lô
@@Demecheikhououmarmodou ymt fi ba adouna touki dou meusa dane yalmine 😂 siteu waxon nako loy bagn mou nieuw bouko diapal biss😂
Sen mbeur Siteu dafko nious daneko djel bou lerrr te lolou moy wakh djii !
@@leuz.patriote ,🤣.d accord pour mane dawara takhaw deuguel bopame mais di daw rék noo ma sonou si siteu khalai bou ndaw vraiment 😂 yalla na yalla doli diamou thank you very meche
Siteu amoul fite baye songu modou leep dako negocier
😂😂😂😂😂 fite kay yaw wéro
Kone nokou yimou ka nokou daaw laaa
Grand respect à père tapha
Yalah nala Borombi sam
may fan wou goud ak wére
Bonne analyse père Tapha siteu berewoul dara
Siteu nila menone beurré bou tahawone Modou dakoy door mou danou srx😂😂
Siteu diemmal diaap daan, lolou moy victoire... gorgorloul deugueul sa bopp.... Attaque et contre attaque jobal lolou...... Soit courageux quand même
Tapha Gueye on se rappelle de ton combat contre yékini😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
Tapha mogui déff analyse bou pertinents
Bilay même chose c'est malhonnête...même sa dôme mounoco door tè takhawoul😢siteu n'a aucun mérite mou melni lac2 ni
Yékini moko soute eupp ko parcontre Siteu mo soute Modou téh modou eupo ko doolé
Merci 😂😂😂
Bilahi Modou lo ndanane hier c'était le jour de siteu mé application zero
Naniou remplacer sakou yi par des barier ou bien une case, ah ! Danio sonou si Bolt yi😂
Merci beaucoup 2s
Père tapha il et le mètre👑
Merci tonton tapha verite absolue Modou le meilleur .......Modou seul contre tous yalla bakh na lo ndamm cire
Tu es le meilleur ❤❤❤
Voilà une analyste ❤❤
Inhaala roi bi ba 2026 wala 30 modou lo rek
Tapha vous êtes le plus grand analyste de lutte au Sénégal
J aime beaucoup Moustapha ❤
*Siteu sou amone diom dey daan Modou. Modou n’était pas dans son jour en plus il a pris bcp de risques. Yow ya sokhla roi bi mom mo warone nieuw prouver mais dafa gueine sakou yi beu niakk.*
Vraiment aussi
Dane nako
Mais mo doumeu mo dane !
@@papadiom9260 Est ce que do dem si soudeur métalique mou défarale leine couronne ? parce que bi mome doleine si diote
@@papadiom9260no même Modou guene n'a khana far more am rek mais siteu dan nako Thi Lou lere sah
Tapha tu as bien di
Modou loo mon meun thi lambe dji
Je suis d´accord avec toi sur les sorties et avertissements mais ton combat vs yekini est là
Wawwaw frère fateé khediou fi
Merci modou défnga léép songue nga doume nga daan ga❤❤❤❤❤❤
Merci père tapha
Felicitations Modou🎉
Site dé mal dani fawzayni modou lo moy 👑👑👑P. A deul
je pense qu’on doit trouver des astuces pour éviter ces genres de situations, par exemple quelqu’un qui a trois avertissements verras son adversaire bénéficier d’un “weur nombeu” répété jusqu’à qu’il y ait une chute.
Siteu était un éternel fugitif siteu daw rekk
Siteu si bopam mo ragal
Mome ak sa papa kou gueneu ragal 😂😂😂
Modou lo mo attaqué mo dor en plus siteu waronne takhaw khol Modou lo yaye diambar DEUG
Bilay wakhal way😂😂😂❤
Diambar la nak😊❤
Siteu doudara
Modou lô dagnou ko sote pour mou danou
Li neikh na debat bi am na niveau❤❤❤❤❤❤
Wakhlènn Siteu Deugue mo gueunn ...Naafekh Baakhoul... Siteu dafa daw combat yèpp...
Ay Pere Becaye yi Siteu laniou faral
Gnemewouniou Siteu
Pére tapha règlement yi amna solo trop kone légui dawyi diekh😂😂😂😂
Je ne comprends pas du tout,Modou Lo est trop petite devant les autres mais c'est lui qui dirige les combats,par des coups de 👊 👊✊ point et tout
Méci..modou.lo❤❤❤❤
Mersi
Bouniou fi narè dieulè victoire par avertissement nanioufi dieuler recour
Karadio image plateau bi Nice n’a trop 👍
Bétaillère à tout dit c'était sa seule chance
Tapéz tapha Gueye vs yekini😂😂😂
Bilaye frère
Lamine Diouf bal lène waay
👍👍👍👍
Modou Lo reste le meilleur lutteur de tous les temps siteu tapét leuh dafa daw combat bi yeup 😂😂
J'avais dit que Modou lo vs Sathies moy combat deux attaquants. Je savais que Siteu va faire la même chose que son combat contre lac 2.
Leigui li may ladj bou mbeur mi amei avertissement yu bari fek mbeur mi beurei woul ba temps leigui le reste de son argent kounou kay diokh son adversaire wala cng question bi dafa ladj reponse si on change le reglement❤❤❤❤❤❤❤
Ziara nala bowr tafa
J embouche la meme trompete que tapha gueye, il faut changer ce reglement tres rapidement
tapha gueye vs yekini🤣
Tapha tu analyse bien
Vraiment tapha tu as bien Di
Siteu champion la. Lougnou meuna wakh deuguë aiyë moudié.
Merci grand tapha . Sitou defoul dara .il n mérite pas de gagner
Wax deug yalla modou dou sa ma mbeur mais siteu il était trop sur la défensive, modou mo attaquer combat bi yeup
Modou lo boyi meuneulounn ko dara bilahi kholal boyi nio nek si yoon gueunn nek xalé wara eup ambition parsk nio tolou si outt dara vraiment modou lo vrai champion
Siteu Lac 3😂😂😂😂😂😂
Moustapha Gueye on a pas oublié ton combat avec Yekini😂😂😂
MODOU 🎉❤👑💪👆
Siteu ak lac nio yam
Lambou dji nane si df aye baryérr daw bi dafa eupou 😂😂
Siteu day daww rekk amoul arrêt 😅😅😅
Siteu day daw rk amoul arrêt comme temple run😂
Siteu moy lac lac moy siteu
Siteu daa daw lamb ji yeup😂😂😂
❤❤❤❤
Douma daan, doma daan c pas combat..... Merci beaucoup à BABOY, IL était le seul qui combattait bravement, étant outsider
Père Tapha t'as tout dis maname siteu pouvais gagné ce combat mais malheureusement siteu amoul ayy atouts
Le reglement de la lutte ne compte pas le nombre d'initiative pris
Faites le fanatique, Oui, mais ne soyez pas naive
Une chute reste une chute quelque soit le contenu du combat
A chacun sa stratégie pour gagner
Modou Lo est clairement tombé, 4 appuis ou chute par l'épaule..., il aurait du perdre le combat, l'action a été initiée dans l'arene
Belle tactique de Siteu qui a su casser la distance au bon moment a chaque fois et mettre en difficulté Modou Lo, qui, malgré plusieurs initiatives pris, n'as pas dominé son adversaire, il a visité Ardo 2 fois, preuve que Siteu a été précis dans ses coups et n'as pas simplement balancer les bras
Les commentateurs et les arbitres ... ça laisse a désirer
Si la couverture des caméras sur l'enceinte était optimale, a l'heure là, on parlerait d'autre chose.
Pour répondre a Tapha, c'est pas que Modou Lo n'était pas dans son jour, c'est juste une excuse que vous lui trouver car on s'attendait a une victoire éclatante de ce dernier ; C'est plutot Siteu qui a trouvé la tactique idéale et a anéanti celle de Modou Lo, il s'est bien déplacé et a su bien contrer. De grace Modou Lo a eviter un KO sur une droite reçu en plein visage. Siteu a trouver les arguments pour tenir mais n'as pas conclu, il faut le féliciter et non trouver des excuses a Modou Lo.
Merci tapha guéye kham kham rek ngua wakh siteu dou dara.
Siteu zarco mo répète rek Siteu a bien fair 😂😂😂