“Eumeu defko tégal chaise»Pére Birahim tacle séverement Sathiés et avertit Balla «Tapha da indi dolé

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 5 พ.ค. 2024
  • #kebetu #senegal #team221

ความคิดเห็น • 98

  • @amadelbeye6166
    @amadelbeye6166 หลายเดือนก่อน +15

    Pére biŕahim touti ma lathiéko dafa rare mais kéne gueunouko kham lambeu 😎😍Yalna yallah yok ay fanam ak wéreum il fait partie des hommes de l'ombre

  • @nadiainnocenti3619
    @nadiainnocenti3619 หลายเดือนก่อน +10

    Pere birahim dioulite day mandou eume sene champion d afrique la 98 mome al rock mbalax ak yekini sokhor bakhoule

  • @Biramediouf-ko7pd
    @Biramediouf-ko7pd หลายเดือนก่อน +6

    Pa bi lamb doussi lék Dara parce que Dafa sokhor môme beuguoule eumeu fass boumou déparé sakh dioubowoulok niome Dafa compliqué

  • @sambadieng1203
    @sambadieng1203 หลายเดือนก่อน +2

    Père damala begeuwone mé yow mandouwo eumeu référence lah bilaye walaye 😭 teygua ngama lal 💘💘 eumeu mola daka beuré fouf loutah ngah bagne eumeu sene mane eumeu rek laah topou Pikine rek ❤️💞🥰🇸🇳👌

  • @makhtarndiaye6541
    @makhtarndiaye6541 หลายเดือนก่อน +4

    Il est véridique ce vieux Macha'Allah

  • @massendiaye5802
    @massendiaye5802 หลายเดือนก่อน +3

    Non père Birahim tay mom waxgua loula néx si Eumeu , so néké makk daguay niaboté nieup yén wax yi waratoula , Nioy Père Bécaye ak yénén magou lamb yeup nangoulnanou Eumeu yaw gua beug wax ni lolou amoul yagui fénlo nioniou sax.

  • @papadiom9260
    @papadiom9260 หลายเดือนก่อน +6

    Aka Sokhor Pa bi mais sunu borom dafa defff Meusso ame mbeur bou melni Eumeu thi Sa écurie bomou dath !

  • @ndiayeabdouaziz588
    @ndiayeabdouaziz588 หลายเดือนก่อน +8

    Peré birahim ndiaye EUMUE sene sa dom la def ko come sa dom boko begoul wala mayou la xaliss tamitt EUMUE sene am na ay bokou am papa am yaye bayel EUMUE sene

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 28 วันที่ผ่านมา +1

    Aka kham lamb.. père birahim

  • @CaramocoDiallo
    @CaramocoDiallo หลายเดือนก่อน +2

    Pere Ibrahim mousso nangoul eumeu sene. Mayniou diam

  • @Biramediouf-ko7pd
    @Biramediouf-ko7pd หลายเดือนก่อน +6

    Pére meusso nék champion d'Afrique meilleur lutteur roi des arènes eumeu moleu gueneu nék champion foufe

  • @khadimmoustaphagueye4058
    @khadimmoustaphagueye4058 หลายเดือนก่อน +6

    Na dieuma defar mbeur mou melni eumeu sene c'est simple 😂😂😂

    • @Dia.ibrahim
      @Dia.ibrahim หลายเดือนก่อน

      Qu’est-ce que vous voulez Eumeu Séne n’est pas son lutteur et vous voulez qu’il lui fasse de la publicité.

  • @alisalla4488
    @alisalla4488 หลายเดือนก่อน +1

    Machallah père yaw rek lay ware

  • @laminesane9741
    @laminesane9741 หลายเดือนก่อน +6

    Oui j’ai senti que il n’aime pas Eumeu séne

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 หลายเดือนก่อน

    Machallah papa yagafi lol té andak weur ❤❤❤

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798 หลายเดือนก่อน +3

    Per yaw nak kou bagne Eumeu sene nga

  • @Biramediouf-ko7pd
    @Biramediouf-ko7pd หลายเดือนก่อน +6

    Amo béne mbeur boungua formé bou mélni eumeu séne

    • @sonkoomar2165
      @sonkoomar2165 หลายเดือนก่อน

      Modou lo😂😂😂

  • @SowMadiaw-go2uc
    @SowMadiaw-go2uc หลายเดือนก่อน +1

    Nitou deug pere❤❤❤

  • @kilimanecouture8049
    @kilimanecouture8049 หลายเดือนก่อน +7

    Guisna kou bagne eumeu sene kounék wayé guisouma kou bagné eumeu sene ni pa Birahim ndiaye

    • @s.khadimlo588
      @s.khadimlo588 หลายเดือนก่อน

      😂😂

    • @sonkoomar2165
      @sonkoomar2165 หลายเดือนก่อน

      Mais père Lanla wakh eumeu sene shi bayileen doul way

  • @rassoul2294
    @rassoul2294 หลายเดือนก่อน

    Eumeu wonei wufi bne médaille 😂dul way

  • @darmankotvoriginal
    @darmankotvoriginal หลายเดือนก่อน +3

    Pabi Mom merci Rek lasi Mana yame Ndakha makla wayè ak bagné Eumeu Sene ki wayè li yalla Deff si mom mouno si touss 😂🧑‍🦯🧑‍🦯🧑‍🦯🧑‍🦯

  • @abdoulayediouf3721
    @abdoulayediouf3721 หลายเดือนก่อน +2

    Pére bayil soxor eumeu limou def niépa KO guissando xamo Dara nopil

  • @yatmaniang6847
    @yatmaniang6847 หลายเดือนก่อน

    Bilaye pas bi kou kham lambou la machallah ❤❤❤❤❤❤❤

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798 หลายเดือนก่อน

    Merci pér 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤

  • @MoukhtarNdiaye-vm4lb
    @MoukhtarNdiaye-vm4lb หลายเดือนก่อน

    Per birahim Ndiaye bokuma ak mom loudoul sante wayé lolu takhul makoy seedeel damakoy suivre wayé ku ragal yalla lamay nirou donte mbeur la wone su nite di wakh deug tekiwul ni dafa sokhor ngen balma🙏

  • @makavelli-ru3un
    @makavelli-ru3un หลายเดือนก่อน +1

    Commentaire Yi numou demei nii😂😂😂pa bi soxor na nak

  • @aidaracherif313
    @aidaracherif313 หลายเดือนก่อน +2

    Mais ragaléne yalla pa bi wakhoul dara lou ay

  • @Maty-mx7yi
    @Maty-mx7yi หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ père mou deuguou vous aimez tout le monde de la lutte

  • @lakhatthiam6044
    @lakhatthiam6044 หลายเดือนก่อน

    Amine

  • @user-gi7ne4rm6o
    @user-gi7ne4rm6o หลายเดือนก่อน

    Machalla père ❤❤❤❤❤❤

  • @adamadieng8720
    @adamadieng8720 หลายเดือนก่อน

    SE QUE JE RETIENS DE SE VIEUX IL INSISTE BEAUCOUP SUR LES LUTTEURS WORKATE❤❤❤❤❤

  • @pronosticfootsenegal1112
    @pronosticfootsenegal1112 29 วันที่ผ่านมา

    Moustapha name il n'a joué aucun match lors de la can ...et pourtant il est champion d Afrique..pere bayil sokhor waaay

  • @user-gc3vh1jh1u
    @user-gc3vh1jh1u หลายเดือนก่อน

    Merci pépe liga wakh si gaston rafete na 💚💛❤️

  • @user-ke1ov6kf2o
    @user-ke1ov6kf2o หลายเดือนก่อน

    Pabi loko euma sen def 😂

  • @mamadousirediallo2071
    @mamadousirediallo2071 หลายเดือนก่อน +5

    Non... tabouret lako tegal 😂

    • @ibrahimasene9243
      @ibrahimasene9243 หลายเดือนก่อน +1

      Si wax nga dëg copin tabouret lako tégal

  • @babacarndaw1094
    @babacarndaw1094 หลายเดือนก่อน +9

    Père. Eumeu a été champion d'Afrique. Il faudrait l'accepter même si tu n'es pas avec lui. En lutte pure, Eumeu est le meilleur au Sénégal

  • @AbdouTall-ei1ob
    @AbdouTall-ei1ob หลายเดือนก่อน

    Pere yalla gafi yagé

  • @cheikhdiakhate716
    @cheikhdiakhate716 หลายเดือนก่อน +3

    Dafa jalousie eumeu sene ndax modou lo

    • @momoothiam1648
      @momoothiam1648 หลายเดือนก่อน

      Jaloux eumeu nakh mod Lo alors que MODOU a battu 2 fois eumeu

  • @maguettesene7527
    @maguettesene7527 หลายเดือนก่อน

    Père noppaloule mod lo meusoulaa maayi deureum

  • @sonkoomar2165
    @sonkoomar2165 หลายเดือนก่อน +1

    Ki nan la bagné eumeu sene bayi lene seytané père nitou deug la lamb laye wakh

    • @badaradieng727
      @badaradieng727 หลายเดือนก่อน

      Ki day fen eumeu champion d'Afrique la

  • @petitkebe9887
    @petitkebe9887 หลายเดือนก่อน

    Louth gnewatul di reporté combats yi ❤

  • @famadiop7681
    @famadiop7681 หลายเดือนก่อน

    Kouko guena kham lamb amoufi deug rek lay wakh bane interêt la ame pour bagne eumeu

  • @user-vd9kp8kk9c
    @user-vd9kp8kk9c หลายเดือนก่อน

    Lepp loumou wakh deugle longu vue père ak soutura

  • @Abubakar-zf2tr
    @Abubakar-zf2tr หลายเดือนก่อน +1

    This dad is always praising his achievements but downplaying the achievements of others..
    To become a world champion,you necessarily do not have to fight everyone..you only fight those you in the same particular championship with and you become anointed world champion if you emerge victorious in a particular world championship tournament!!
    He sounds really complicated tbh

  • @user-wp3jd8wb3f
    @user-wp3jd8wb3f หลายเดือนก่อน +1

    Pa bi da bagne eumeu

  • @user-ii9ip4mq6o
    @user-ii9ip4mq6o หลายเดือนก่อน

    ❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢

  • @abdoukhadrefaye3571
    @abdoukhadrefaye3571 หลายเดือนก่อน +31

    Pa bi mousoul nagoul eumeu séne champion d'Afrique deux fois gani lolou amoul yow rek yagui wédi ga balma pour yow Modou lô rek Moy mbeur del wahal mbeur yeup ancien gloire day yemalé 🤝🤝🤝🤝🤝

    • @talladiagne8092
      @talladiagne8092 หลายเดือนก่อน +5

      Ligua wakh bi amoul
      Pabi day tagg Balla Gaye à chaque sortie
      Deug guen beugoul mom lay wakh

    • @falloufall204
      @falloufall204 หลายเดือนก่อน +1

      Ligua wakh yeup degue la

    • @mamadounarbakhoum1057
      @mamadounarbakhoum1057 หลายเดือนก่อน

      Je vois ça

    • @bogalbogal3461
      @bogalbogal3461 หลายเดือนก่อน

      Khaliss rk loum manoul amoul

    • @nadiainnocenti3619
      @nadiainnocenti3619 หลายเดือนก่อน

      @@talladiagne8092 waye na nangou champion d afrique bi eume donn

  • @andrendione9021
    @andrendione9021 หลายเดือนก่อน

    Merci père. Belle analyse

  • @Adnanezinho-jm8zk
    @Adnanezinho-jm8zk หลายเดือนก่อน +1

    Ndeysan pa yi niogui maguett legui adouna mo dou war na lep di rafet niou diokh tieur mak yi nguir yalla

  • @Dia.ibrahim
    @Dia.ibrahim หลายเดือนก่อน +2

    Qu’est-ce que vous voulez? Eumeu Séne n’est pas son lutteur et vous voulez qu’il lui fasse de la publicité.

  • @user-zt1tv7zg7h
    @user-zt1tv7zg7h หลายเดือนก่อน

    Ioe père meusso beug eumeu séne

  • @ThiernoDiop-ei2ht
    @ThiernoDiop-ei2ht หลายเดือนก่อน

    Pa bi wakhoul dara eumeu soff nguen trop yen yena mandou woul ki Moy lamb mo thi man merci pere

    • @Abubakar-zf2tr
      @Abubakar-zf2tr หลายเดือนก่อน

      Maneh nenj wahanteh dega
      Bum tuutil nitt ki lum gagne
      Hana world cup aduna bi yep nga wara gagne purr neka world champion?

    • @sambadieng1203
      @sambadieng1203 หลายเดือนก่อน

      Non non ki dou lamb tague sah bope rek nga mane titil sah moromou mbeur😂😂

  • @BadianeMayoro
    @BadianeMayoro หลายเดือนก่อน

    Wa ki Louka euma déff

  • @user-uv9vb2dx4o
    @user-uv9vb2dx4o 20 วันที่ผ่านมา

    Perr sohor nga

  • @user-ib6qy1yy4j
    @user-ib6qy1yy4j หลายเดือนก่อน

    Sokhor rék

  • @moussaseck2298
    @moussaseck2298 หลายเดือนก่อน +1

    Sa data ndaye

  • @sambadieng1203
    @sambadieng1203 หลายเดือนก่อน

    Pa bii kou sokarlah bilaye walaye 😭 teygua ngama tongne yaa bone

  • @saiifba4282
    @saiifba4282 หลายเดือนก่อน

    😂😂😂👍👍👍👍

  • @pacosuzanetv
    @pacosuzanetv หลายเดือนก่อน +5

    Pere yaw championat d'afrique yague gako wakh dafa melni dala nakhari kou nangou li yalla dogal do sonou sa khol dou diékh

  • @saiifba4282
    @saiifba4282 หลายเดือนก่อน

    😂😂😂😂😂👍👍👍👍

  • @mbodjass2480
    @mbodjass2480 หลายเดือนก่อน

    Dommage le vieux fait de très bonnes analyses. C'est un expert.faut demander a moustapha gueye et katy diop qui est birahim ndiaye ? Il était un grand technicien.

  • @sohiboudiop4894
    @sohiboudiop4894 หลายเดือนก่อน

    Pa bi aka xoromou😂😂 Boys yi moytou Léne Tapha Geuye 2 djinné leu dei

  • @pronosticfootsenegal1112
    @pronosticfootsenegal1112 หลายเดือนก่อน +1

    Pa bi mome wa pikine rek la contre

  • @omarsy3013
    @omarsy3013 หลายเดือนก่อน

    Pére lane moy sa problème ak eumeu séne tmt

  • @gissatadia949
    @gissatadia949 หลายเดือนก่อน

    Pa bi mo geuna sokhar si payi nék si lamdji mosta nagol eumma sene mais sa kholl dou nékh mak mou tol ni yaw sokhar bakhol ta sokhar ta giss nani pa bou sokhar nga

  • @abdougueye4837
    @abdougueye4837 หลายเดือนก่อน

    lanne la wakh si eumeu lou bonne yenn sénégalais yi diakhal guenn ma j’ai suivi tout mais lou bakh rekk la wakh si mom

  • @user-ii9ip4mq6o
    @user-ii9ip4mq6o หลายเดือนก่อน

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 หลายเดือนก่อน

    Pa bi koumou Méré mom dal khamna lamb mais nangouloul kennn bopam rek Lou noeud Mounir mako def

  • @bogalbogal3461
    @bogalbogal3461 หลายเดือนก่อน

    Pa bi aka bang wa pikine

  • @AbassDiop-ep7gz
    @AbassDiop-ep7gz 29 วันที่ผ่านมา

    Ce vieux vraiment il est contre eumeu il a toujours contexté le fait que eum est champion a deux reprise et eum a même etait roi des et il ne leu souligne même pourtant eum et tapha geuye n2 prés que ay morom lagnou ca se il mo takh moussoul oub lamb

  • @user-qx3be4gd1p
    @user-qx3be4gd1p หลายเดือนก่อน +2

    Pas bi meunoule si eume Lou barri sokhor la def mes diga gnaf ça ndey

  • @souleyewade7419
    @souleyewade7419 หลายเดือนก่อน +1

    Il aime pa eumeu ont dirait

  • @khalifaba255
    @khalifaba255 หลายเดือนก่อน

    Franchement wakhoufi lene lou graw
    Juste reconnaissance a sa clairvoyance et sa lucidité fs l'analyse sans payei pris
    Du coup il est objectif a part un brin de vanite ds ses anecdotes ou illustration

  • @damembouptalibechekhmboup2485
    @damembouptalibechekhmboup2485 หลายเดือนก่อน +1

    ki kou xame lambe la tadou dieye nite

  • @user-to5ht5tr2c
    @user-to5ht5tr2c หลายเดือนก่อน +1

    pourtant mu ngi nane technique you boys you beuri di beuré si Eumeu lagn ko guissé. Bagnoul Eum dh gayi da beug wax rek que daa bari nioukodon mboubo peut-etre surtout gnom sen temps. Et puis équipe moy dem representer un pays kounek si gnom dou bari ay 15 wala 20 combats dh xeuyna ay 3/4 combats comme nim ko waxé rek. Lim wax ayoul dh

  • @AbassDiop-ep7gz
    @AbassDiop-ep7gz 29 วันที่ผ่านมา

    E

  • @kilimanecouture8049
    @kilimanecouture8049 หลายเดือนก่อน +3

    Aka mana tague bopam wayé EUMEU SENE rekkk la mounoul guissss