Boy Niang vraiment lou Balla Défthi Lamb Dji xath bii Défagoko yamall rék Bay Balla c le meilleur lutteur Sénégal 🇸🇳 De toutes les Tenp Balla moy réal Madrik ❤️✅
Pourtant ni leu balla mélone Au faite d'après mane boy niang yeufou guoné moko diap Wala mou done bén piège boumouy tendre balla di houmbeul beuss beu mou gneuw tahaw dég lou balla
Machalla fière d'être votre supportere pour votre courage votre force votre détermination l'homme qui n'a peur de rien lafe thiate champion nous les supporters nous sommes la pour vous soutenir victoire totale inchalla Amine balla rék balla késsé 🦁🦁❤❤❤🦁🦁
Bilahi kén dou balla gaye, il est trop impressionnant, tu es un lion dans le vrai sens du terme 💪🏿 boy niang naguoul ni dagua am complexe d’infériorité devant balla gaye et même quand tu lui parles ta voix tremble de peur 😅😊
Qui est la après la victoire de boy Niang😂😂
Moi🎉🎉
K le senegal remporte la coupe du monde katar 2022 insalah amine ya rabbi 🌏
Ballagayedaydano
Amine ya Rabby
Ixsy
@@seyebayeseringe6714 ixsy
Inchallah
Boy Niang vraiment lou Balla Défthi
Lamb Dji xath bii Défagoko yamall rék
Bay Balla c le meilleur lutteur Sénégal 🇸🇳 De toutes les Tenp Balla moy réal Madrik ❤️✅
Bokou ñou baay léen waxou doff yoo you
🤣kou ndieuk si lamb ñoom ñaar🤣waxi doff rek ngeun di wax
@@abdoulatifdiop5640 boy niang défoule dara si lamb wah rkkk akkk dawwwwwww tapéte la
Est-ce que bala bi mi beuré ak yekini est ce que nio tolowon niveau wla
Lamb dabanté la
@@ibrahimafall2376 niatta victoire la am
Balla le lion yalla nala yalla maye ndame
Qui avait commenté sur Balla gaye avant le combat sortez 😂😂😂
Bilahi beug nanioula ba pare ❤️❤️❤️ndam rek inchalla balla si kaw sa kanam 🎉❤
balla Gueye yalla nala yalla may dam
Amiin
Balla Gaye def gua lounek si lamp reference gua bilay je t’aime
vraiment Boy Niang beuri n'a wakh, Balla Gaye 2 yallah nako yallah may nam inchallah
Pourtant ni leu balla mélone
Au faite d'après mane boy niang yeufou guoné moko diap
Wala mou done bén piège boumouy tendre balla di houmbeul beuss beu mou gneuw tahaw dég lou balla
Kiiii amoul louy diakhal balla
Balla rek boy niang aka beuri wakh biniou wané combat Balla yi dafa affolé
Amiin
@@presi1316 tu avais raison.
On dirait boy niang est un peu complexé devant balla gaye,je vois une supériorité que balla degage par rapport leur comportement
Si si c un complexé
Bien parlé
C un stratege detrompez vous c tout a fait le contraire
Wakho fii dara
Dafko fan rekk sou sanione melni Balla
Balla, yalnala yalla may ndam.
amine❤❤
Amiin
Machalla fière d'être votre supportere pour votre courage votre force votre détermination l'homme qui n'a peur de rien lafe thiate champion nous les supporters nous sommes la pour vous soutenir victoire totale inchalla Amine balla rék balla késsé 🦁🦁❤❤❤🦁🦁
Balla dh kom boy niang moko magg bala sa forme bi nekh nagnou ni 🔥🔥
Bane forme kolen yap😂😂😂😂
@@ablayenittoudeugu1012 boul sokhor nk forme mom amnako
Boy Niang da beugone diaxassé Balla ak adouna farr mou wérou😂😂ya ndieuk saga kone nangoul rek
Balla Gaye 2 yalnako yalla may ndam🙏🏽🙏🏽
Balla gaye mo begue diaxasé boy Niang AK eumeu
@@barandiaye7347 saway Pikine nieup xamnagn ni sén 100% bobou gueumou niouko
Supporters yi nioko gueum Mais mbeur yi gueumou niouko deugg nexoul
@@mamecheikhanta4422 loulasi wor
Amiin
@@evadia9028🥰
Meilleur lutteur de tout les temps
Lapsus révélateur 😂😂😂😂😂😂«Kou ndieuk saga YAlnala souñ borom may ndam»🤣🤣BG2 rek
Non sûrement da dioum rék.
Balla yalla na la yalla méy ndam lou reuy 🙏🏿
Bala yallah nako yallah maye ndam
Enfin boy Niang doumeuh neuh sa Thiès doumeuh balla gaye 😂😂😂😂
Bilahi boy Niang aka ragall
Nan la ragalé
Yén meune ngén doull ki dakhar ndayi sathies ngén nane tapett
@@ablayenittoudeugu1012 saway boy niang di tapètte toune bi day masse 😂😂 fi leu tapha tine katteu yayam bamou daw
Que le meilleur gagne
Balla c’est le meilleur du sènègal 💪👍
👍
Boy Niang 4 défaites la am 🤣🤣🤣🤣🤣🤣Zoss,Amanekh,Tapha Tine,Lac de Guéres....😂😭😭😭😭😭😭😭😭
Dann you bokoul nak té balla machalla 3 personnes nioko dann issa pouye 1fois eumeu et bombardier
@@aboudiop6340 balla gaye la faral wayai eumeu 2 fois lakko d'Anne3ak issa pouye ak bombardier 2 fois
@@pierrendiaye5815 waa motakh mounékk 3personne kay
@@pierrendiaye5815 oui mais ba tay 3 personne leu
@@aboudiop6340 bombardier 2 fois 😂
Boye niang yalla nala yalla may ndam amine
Boy Niang wakh neu beuré na douma na dane n'a balla gaye
😂 😂 😂 😂 Balla raynama nena kou ndieukeu saga moromam yalnako yalla may ndam 😂 😂 😂
😂😂
Moom pourtant contre bombardier dafa daaw baa lamb ji diex😂thiey adouna
Ndeysane boy Niang dh il se sent inférieur devant balla gaye beu amoul bén argument le jour du combat balla dianako dane dieul bou yomb je vous dis
Walahii y’a ngui nakh sa bopou. Balla gaye mii dou kouy dane Boy Niang
@@papadiom9260 legui boy Niang moy dane dall😂😂 défenseur dou dane balla
@@sadadiop9211 Wouyaaaaaaaye 🤣
Bilahi boy Niang dane boum dane sa thiés geumeuwouko bilay
Kii dafa kateu ndéyam beuri wakh.fock you boy Niang
Balla guaye 2 yalla nala yalla May ndam inchallah ci Barké seydina Muhammed salalahou aleyhi wasalama
Thiapathioly bii tu es trop technique boul yakamtii té incha'allah dingua dane Balla dieul bou sétt widjie
Sonko kén douko laal 🇸🇳💪❤️💪
Balla Gaye avait déja perdu depuis le face à face parcequ'il a eu peur de regarder Boy Niang dans Les yeux pour un certain temps.
Boy Niang Yalla Nala Yalla May Ndamm Lou Reye in cha'Allah 💪🏽 💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽
Balla ndam rek in sha allah yalla dina la fay sa xol 👌
My favourite star balla Gaye love frm 🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Allez balla ndam rék inchalla
Allez Balla gaye 2 sunu champion bi ndam rek insalah 💪💪💪 BG2 rekkk
😃Balla doko fixé mou roukhhhh
Balla gaye yalnala yalla may ndam inchallah
Notre balla national
Balla yalla na yalla may ndame 💪💯😘
Balla gaye 2 ndam rk insha'Allah
Boye niang 😂😂🎉victoire rk
C'est le Sénégal que le meilleur gagne 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Balla yalla nako yalla may dam
Balla sama beur nga mais boys niang mola eupeu forme bilay ay Dioy laye bagnal saye fans bala mi day danou lou laiir lalaine di wah
Gaindé 🦁 gou magett gui Molay nokk dann leu boy Niang tapett nga amo lowax gueweul nga Bari waax boy Niang
Affairou raciste yi nk🤬
Boy niang Yalla na la Yalla maï Ndame 👌👌
Boy Niang 2 Rek Tout Les Vrais Pikinois Sont derrière toi pour la victoire InchAllah .
Balla n'dam rek Insha"Allah
☝
Amiin
Balla gaye c'est le meilleur boy Niang beuri NGA wakh da NGA khamoul kii rek mo takh Ngay wakh 😁😁😁 Ay bo khamon ki NGA AM balla nekhoula beurel dh
Balla mofi geuneu nékha dane😂
Eumeu sén Laa geuneu
Tite K Boy Niang billahi
Eumeu sén Gayii xamou
Ndiouko sax aka Dangereux ⚠️
Bilahi kokou dafa xame louye dane balla
Dafa technique meune ndakhaneté en plus day beuuré AK balla comme dafko raguale ndakh ko
Nooo boy niang ngaka nga… balla Gaye Yalla nalla may ndam… Modou lo 4ever
Ndam rek balla
Gaye.2.incahalah
Boy Niang jusqu’à présent il ne réalise pas qu’il a battu Sa Thiés vraiment 😭😭😭😭😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂
Balla lassi ñieuw tékk
Boy niang ne confond pas le silence et l’ignorance 🙈
Bilahi
Ki balla dako diepi
Boy niang ndam rek inchallah
Boy Niang Néna Balla Gaïnde Bou Magéutt La😂😂😂😂😂Mérci Boy Niang Yalla Nala Yalla May Ndamm 💪🏽 💪🏽 💪🏽
Boy Niang moï doff deug🤣🤣🤣Balla néé nako kou djeuk #Saga#yalla nako yalla maï ndam mounéé ko amine🤣🤣🤣
Bilahi watalahi boye Niang ya raaw sékou bari ga wahh dé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Omar carieram yep combat bi momasi geune meti billahi ndakhe boye niange miko dane
Modou 👌
Gaston production nieuwate nguen 2s kn 😂😂
2stv mo yorr khoromou lamb dji dem dem nieuwate rk 🎉
11:29 seconde
Balla nena kou nideuk saga yalla nako yalla may ndam 😂😂😂
Boy niang combat bi dako dépassé 😂 mais inshalla balla gaye dinala dane😂😂
Balla ndaanane nga nak ki rassoul loullah😏😂
Balla moy bandit Bilae niola beugg
BALLA 🤲👍✍👈💜💜💜💜💜
Balla Gaye2 victoire rekkk
Le champion de lutte sénégalais 🤟🤲
Commentaire fans Modou lo yi lay xol😂😂😂😂
Nio gui ni danio ree ba tass😂😂
Yallah nako Boye Naing dane.
Dano dieul yonu mandou😅
boy niang yalla nala yalla may ndam rek inchallahou rabi
Boy essaye de joue sur le mentalité de balla pour le jour du combat balla attaque je préfère balla l'attend même deux ou quatre minutes
Boy Niang a eu la frousse de sa vie devant Tapha Tine. Il est juste le champion des face to face. Alanekh est dans les parages !
😂😂
Lo wax légui ?
Non balls dafa rafete ❤
Wahi dof
État yi boxoul, dolé yi yamoul: kou paré ak kouy lidieuntikou la. Inchaallah Boy Niang ndam rek ci kaw tane bombé Gaye 🙏🏿
Wakhofi dara
Allez boy Niang
BALLA, Sathiés la indi ték ték🦁🤔❤️💚🤔
Balla gaye mo saye saye 😂😂😂 bilahi lim wakhone boye niang motakhone boye niang mer di wakh rek balla nope
Balla mane mom Lima wakhon rek ya Daan yekini Modou lo rek doyna
Wakhatiko waye.
Bg2 né kou djiéuk saga moromam...yalla nako yalla may damm😂😅🤣
😂😂😂😂
Boy Niang wax DEUG yalla rewoul
wei merci blwi réwoul
Guediawaye Deuk leu nio meun nio eup Doolé
Billahi balla brom khol bo raffette lah❤💯
Boy Niang yallah nako yallah may ndam si barké Seydina Mouhamed
Boy Niang Balla dou sa morom yaroul
Modou lô rek touss 💯🤫
Balla gaye contane na si yaw boy dala fan ki xamoul bopam 🤣🤣🤣💜
Boye Niang 2 ki ko abale fitte sonale nako inchallah balla gaye 2 dinala doumeu dinala d'âne yaw boye Niang 2 si kanou yala
Balla on t'aime 💪
Balla amal diam
Mention spéciale à modou mbaye vraiment meune nga lingay déf machalla contane ci iow frère 💪
Boy niang meer na 😂😂😂💪
Deugeula dée
Motalhite dumanako danko
❤❤❤❤❤❤❤❤balla ❤❤❤❤❤❤❤
Boy.gnank.ndank.rk ❤️❤️
Balla nena boy Niang meunoul 😂😂😂
Yalna yalla déff diam
Bilahi kén dou balla gaye, il est trop impressionnant, tu es un lion dans le vrai sens du terme 💪🏿 boy niang naguoul ni dagua am complexe d’infériorité devant balla gaye et même quand tu lui parles ta voix tremble de peur 😅😊
Nou complexe bi moudié😂
Boy Niang dafay ñiouss Adja balla guaye
Allez boy NIANG 🤛🏿
Balla est un reference limou deff si lamb boy niang dina beuré ba bayii douko deff
Bala un vrai chapion ❤