BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 1 : Bande Annonce
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 6 ก.พ. 2025
- ** Abonnez-vous ici goo.gl/mme9BS **
Prêt.e à replonger dans l'univers BÉTÉ BÉTÉ, au cœur de familles Gueer, Guewel, Teug ou Laobé ?Suivez la saison 2 de BÉTÉ BÉTÉ avec un nouvel épisode chaque lundi et jeudi 20h30 UTC.
#betebete #saison2 #episode1 #bandeannonce #legsdusang #evenprod #creationoriginale #team221
** Abonnez-vous ici : goo.gl/mme9BS **
Réalisé par Ibou Gueye (Sénégal, décembre 2024)
Une production EVEN PROD SENEGAL : +221 33 868 27 26
** Devenir annonceur ? Contactez notre service commercial **
Evenprod +221 77 422 70 41
Retrouvez Evenprod sur les réseaux sociaux*
TikTok / evenprodsenegal
Instagram / evenprodsenegal
Twitter @evenprodsenegal
Facebook / evenprodsenegal
Parmi nous qui avons suivi la saison 1 du 1er au dernier épisode, il y en a qui ne sont plus de ce monde, puisse le Bon Dieu les accueillir dans son paradis céleste.
Nioune ñii fi déss, yalla nañou sétane saison 2 bi jusqu'au dernier épisode.
BISMILAH 🙏❤
Amine🙏🏽
Allahouma amine
Amine 🤲🤲
Allahouma amine
Amine merci
Ma gui nianale ngou fii nékone si première saison bii tes yallah dieule sen bakanne ba saison 2 bii nékou ngou fii que firdawsi soient leur demeurent éternelles 🙏🙏🙏🙏
Amine ya rabi ndeysane sama Nidiaye sama kharite serigne Mbacké Amar taye saison 2 bi mo ngui co fék mou ame 46j thie bir souff tons yalla nala fi nga dieum gueuna fi nga diougué yalla nga réthiou réthiou li nga done déf si aduna bakh nga ba déme
Amine
Alkhouma amine
Amine
Allahouma amine gnu feccé ko teii tall ko
Bété Bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤😂🎉
@BayemodougueyeBayemodougueye Merci. ❤
Baye Modou Gueye wëurr nalaa founé fo nékkone dama gueudieu guiss say commentaire
@ThiénaDiop-f8o www thiéna wakh gna deug kay tan yii dama geudieu commentaires
Even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah ❤❤❤❤😂😂😂😂
Motakh mané khameguéne lanela ?😂💃🏻🥳😂
@gueyesoxnafaty5835 tay mou nekh😂😂😂😂😍
Nékh na ba noppi😅😅
@yayemayelatmbao5442 Deigeul lolou. 👍
@@evenprodpourquoi Maréme doit quitter la série ?
Faite la revenir.
Dokheléne si waye amena fi place
Bismilahiii niou commencer kossi diam yegaliko cii diam🙏♥️♥️
Amine
Amiin
Amine ❤
Amine
Amine yarabii
Dimbali len ñu ci Ku beug sa yaye lallal j’aime 😂
Fi nieup pa beug sen yaye
😂😂
Gni denio dof bilay 😂
😂😂vraiment
wakha tiko 😂
Dagnion soffff😂😂😂😂
Niou commencé co si Bismillah niou diékhaléko si alhamdoulilah Dinianale niou co féké wone dawe té féké wouniou KO réne yalnaléne yalla yereume té haréko aldiana 😭
Amine
Amine
Aye laobé lagnu pure sang❤🥳🥳😘 bêté bété is back🎉
@sodagaye2957 Boul tarder épisode bi. 😇
Alkhamdoulilah doli sante seydina mouhamed psl thiou wadial année diam ak tawfekh yalla nakoul nou niane yi goudou fan ak weer 🙏🙏🤲🤲🤲🤲🎊🥳🤍🤍🤍
PAIX ET SALUT SUR LUI ❤️
Amine 🙏
Yalla defal niou djam soutoura tawfekh ak taysir barké Seydinah mouhamed psl barké diawartou barké sindidi ❤
Khar yi ci khar yi. Bey yi ci bey yi. Retour au calme laay giss nonou 🤗😄🤣
@panafricain22 À suivre. 👍
Meilleur maison de production au Sénégal mako wakh diameu thi yen yalna yokouuu♥️♥️♥️♥️
Even pro est la meilleure maison de production
Les meilleurs séries c'est ici ❤
@idalubanda Merci beaucoup. ❤
@@evenprod de rien thi kaw thi kanam rekkk♥️♥️♥️
Enfin 😂alhamdoulilah Yalna nagne commence si Bismilah agali si alhamdoulilah
Kou beugue seydouna Mouhamed lalale j’aime ❤❤
Niou tambali si bismilah diexalei si alhamdoulilah mei diganté ma Khoudja ak alkani mi nara yakou meti nama nak 😢oh
Dara metiwouma si série loudoule lolou😢😢😢
@ bilay ioe alkani dof la nak car amna fo xamni sofa diaré ak sa nit amna yo khamni soko dguè dinga xamni waxouko waro ko geum si mom sax
@tantylarose809 👍
Kou beug serigne babacar lalale j'aime ❤❤❤❤
Man man❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ak man Serigne Babacar sy sougnou titeur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@@khadiatoudiedhiou3936 ya bakh
@@Nafina-v7u 💞💖💗
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alkhamdoulila souniou borom niou commencé ko si diam agaliko si diam ❤❤
Té gni Fékké won won fekkon saison 1 bi té Fékké wouyu saison 2 bi nalen yalla yeureum té xare len aldiana
@diopibou267 Amine.
😂😂😂😂bobu épisode 1 Bou Nara dance 💃 🎉🎉🎉mashllah evenprod vous. Êtes fort hien
@DijarassoulDioum Merci beaucoup. ❤
Bismillah Yena meilleur deh yobouwolen Bété bété sunu yeuf diniou dawlo ❤🎉
Mongi niaw déh
@@MbenndiayeMben niaw na baparé 😂😂😂
heu bayileen togn😂
Sama khol sedd neu deh . Yalnagn commencer série bi si diamm , diekhal ko si diamm ❤️❤️❤️❤️❤️
@BeatriceColyy 👍
Espagne ame na ndam no djitou❤
Yalla nanouko setan si jamou at Salam barki Allkhourane ❤Ani team bètè betè❤❤❤❤
@morgueye9748 Amine. ❤
Yalla nagn ko commencer si bismilah tei agaliko ba fin inshalla souniou mareme sall reviens nous yaye neixal série bi 🥰🥰🥰❤️
aminé ❤
Alahouma amine
Amine y’a rabbi
Amine ❤
Yalla naa Sonko ak Diomaye ame diame ak koulénn yénné diame ci barké seydina Mohamed psl ❤
Bien arrivé ❤❤
Kon dalal ak diamou❤
A bete bete ❤😂
@@Narr_Samb-7 nio meun nio eupou dolén😂
@@Fatoukinediasse yalla khmnako
@aladjiwade3754 ❤
Ni niou ko andé wone si première saison bi si diame yalna niou ko andé watt nonou si saison 2 bi si diame😢❤❤
Amine
Amine 🙏❤️
Amine
Laobe yi dianagne ray mareme sall 😂😂😂😂
Alkaly béteu nama nak ak li makhoudia ak ndiabotam mounie yeup mareme dilen saga chaque jour tay mounane workat nga
@AissatouBakhoum-wu6vt 😔
Ibou guaye yalla nafi yagg Ta yague ngoo begal❤❤❤ merci beaucoup tout lé comantér
@NgagneKahe-me9sm Amine et merci. ❤
Wa baxna li histoire dinako binde 😂🤣encore EvenProd vous avez frappé fort❤
@ArameDiop-c1d Badou lourd neu ? 🤣
Avec bété bété votre cœur bat plus fort even prod la chaîne de production qui n'a jamais perdu sa valeur kén dou yén ci mim réw🎉❤
@Awa-ARMY-BLINK_forever0.9 Merci beaucoup. ❤
Le générique m'avait tellement manqué ❤😍
Enfin bête bête la meilleure série du Sénégal bienvenue namonagnoula
Setane ko si diam diekhalko si diam❤❤❤ inchallah
@soukayeyade4310 👍
Oh alkaly ak makhoudia sén ande tass n’a 🥹🥹
Dip néna '' khar bi dou yague ba raw ma capi. bi champ. bi niew na, bandit sa pape bi niewna niewna chef bi niewna ''
Califat ❤❤❤❤❤
Mane khawa lanla wayé bétté bétté dafmay yok stress yalnanou yalla défal diam
La série qui n'a jamais perdu sa valeur est de retour ❤❤❤
@FallouNdiaye-ec2 ❤
Du lourd ❤❤️🥳🥳🥳🔥🔥🔥kham gua lanela Tay mou nex❤️😂
@mamistamendy814 Boul tarder épisode bi. 😂
@ ay kouko tardé dotoko défati 😭🤧🔥🔥🥳🥳❤️❤️😂😂
É ce que ni mel si bété bété nonou lassi yeup mel no mane ma beugue série bi jour bimouy ame damay contane ndakh beugeu bimako beugeu❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aminatacoulibaly6623 Lolou forneu, boul tarder épisode bi. 😇
Alhamdoulilah yalla nagnou ko égali ci diam kéne bagna manqué Evenprod naguene fekhei ba mareme sall yéwou ta égali saison bi lima for ci wéwou beuy nekhouma Dara khorom la ci bété bété dh
Ñu daloko ak diam, matalko ak diam 🤗🥰
Amine
Amine yarabi ❤
@NdeyeRamaKANDE-il8vd 👍
Enfin notre série préféré est de retour ❤❤❤❤❤❤❤❤
🎉je suis vraiment content de pouvoir être là pour suivre la saison 2 je suis vraiment heureuse ❤
Kou geuem ni SOUMBOULOU bayiwoul rek lalal j'aime
SOUMBOULOU sou byiwone kone Photo'm yi kenne doukofi guénéi
Je pense que elle est morte dans la série
Je pense que bayiwoul elle est juste dans le coma. Soumboulou est l’actrice principale de cette série donc elle sera la. C’est juste un suspense pour le début.
Yalna niou ko commencéko si bismilah yegualéko si alhamdoulilah ❤
@SyLamine-dg3tu Amine. ❤
Machalla 🙏 bonne continuation ❤ yalla lafal lén thiate ❤️ sii barkép seydina Muhammad psl 🙏
@MariamaKane-o3v 👍
Al hamdou lilah yalnanou yala maye niou setan go si diamou ba fi de saison inchallah
@CheikhounaNdiayeNdiaye Amine. 👍
Dame is back 😂😂😂❤
@assanendoye221 👍
On seras trop gâté!!! Bété Bété et Xalisso! Okhh contane naaa
Meilleur série de tous les temps est de retour ❤❤
Makhou dh comme khalé yoyou déme vacance di lathie sen yaye😂😂
Y’a bone 😂😂😂😂😂
@BN12811 Mougui gnawe. 😂
Namon na youxou rema diop bi nakk🎉❤
Ça sens encore de plus bon ahh Waouuh 🎉@even proud chapeau's à vous et vos acteurs 🎉❤
qu'Allah nous accorde la paix 🎉
Amîn Amîn yarabi ❤🤲🏽
Bisimlay jààm ahh deuxième bi melnani mooy dakk dh yalla nanouko mangg nieup féké ak taal
Épisode bi dal épisodou fassé la 😂
En tout cas série bi nekhena mais histoire de khadar rek la 😂😂😂
@Binette.n À suivre. 👍
Bismillah rahmani rakhim gniou tabali thi Bismillah eggaliko thi alhamdoulilah 🙏🙏 gniou setane KO bamou diexx kénne bagnia manqué
Hamga lannn Tay mouuu nehhhh😢😂❤🎉
Mani tey mou nehhhhh😂😂😂
Bété bété nieuw na yeineine serie yi dangeine di khar 💪💪💪💪
Machallah evenprod mention spéciale ❤
Yalla n'a niapou am diamou❤❤❤
Du lourd 😂😂😂 demain
yalla na niou yalla may Diamou niou sétan ko si Diamou Diamou amine
🎉enfin bété bété commencé wat na
Aka mako yakam ti won sison 2 allhamdoulilaha yalla nanou yalla may diame ak salam banou seytan sison 2 bi bamou diehe amine
Bon début de saison 2 à tous 🎉
Bismillah gnou commencé thi diam diekhaléko thi diam inchalah❤❤❤❤❤❤
Première🎉🎉🎉😂😂😂😂
Café touba lay nan ni sax ❤☕️♥️
Machallah evenprod❤waya duo déguéne ak ticket lanla😂😂tous les animaux de la terre sont dans la marmite 😂😂😂
Bismillah niou commencer kossi diam yegaliko cii diam machallah ❤❤
diap len si amoul ay yalouwan jaime amoul ay sama woudiou mame amna cheikh. bissimilah critical comments only wa sallam
Dangenn nio beuggg diekalii ndakhh mbectei douniou ko nangou li eupp na si khol 😩😩❤️❤️❤️
Li gneup done xar yéksina🎉🎉❤
❤❤❤❤❤❤❤❤l'année se termine en beauté ❤❤❤❤merci EvenProd beaucoup de réussites et de belles choses pour l'année 2025❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Gnou setane ki si diam . Kham Nani 2em saison bi moy dakk fouf 1er bi ❤
Evenprod avec bête bête et xalisso vous avez dépassé de loinnnnn marodi tv ! La meilleure boîte de prod ! Génie Créatif et professionnalisme ! On veut vous voir signer de gros contrats! Le meilleur pour vous InchaAllah . Votre succès est celui de tout le continent !
Envenprod nak foumniou dieumé liii nekhna way 😭❤️❤️❤️
@maimounandiaye7136 Si dileine andil lou meilleur. ❤
5 millions d'abonnés en deux jours inch'Allah merci a evens prod vous êtes les meilleurs maison de production ❤❤
@lassprd--officielle587 Merci pour la force. ❤
Dame késse lay topou😂😂😂ack meilleurs
De grâce commentons sur ces épisodes et foutez nous la paix avec j’ai accouché priez pou moi, ou qui aime le prophète, appuies j’aime, de grâce.
Deuguittttt😂
@ 😂😂😂
Yalla naniou yalla may niou sètane saison 2 bii sii diam
Où sont les amoureux du prophète Mouhamed SWS ❤❤
Yallah saytane khep doli inshallah touf touf
Niou tambalé si bismilahih rahmani rahimi diékhalé ko si alhamdoulila inchalla 🙏🏽sama khél dale n'a bima guisé photo Soumboulou di mariem sall diakarlo Déguéne sow ak mariem sall menoula niake si deuxième saison bi 🥳😍❤️❤️
Alhamdoulilah bagnou yalla mayé niou féké kou si diamou
Amy mbaya taye la geume ni darra safou la 😂😂😂❤❤
Tické laobé raynama😂nena wewou khar nop kharr😂😂
Evenprod, vous êtes professionnels 🎉
Où sont les femmes sénégalaises les plus belles d'Afrique manifestez vous ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Incha alla ❤❤❤❤😂😂😂🎉🎉
Bismillah yalla naka niepp setana ndo bamou diekh ta kenn dou manque ❤
Yalla na ñu yalla defal jamm amine ❤
❤❤❤❤❤ sama tourido bété bété ❤❤
Bien arrivé machalaha ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Laobe yi la meun ta mougn😂😂❤❤❤❤
Sénégal mongui sora nékhat ❤
Bande annonce bi❤❤❤❤ contane na ❤❤❤❤❤
Vivement le 09 décembre 2024 Inshaa Allah 🤲🏽❤
Commencer ko si bismila ❤🎉