Fenn rekk! Niou ragaloul Yalla nio kayy Raggal! Dafa beugeu nitt gni ragal ko! T ragal ko dafay dougeul nitt ki si bokalé si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah ! Moyy wéteul Yalla si Diâmou yi (les formes d'adoration). Al Khawf...Raggal...est une forme d'adoration. Yalla rekk Moka Yayo.
5 ปีที่แล้ว +1
Lann moyy A't-Tawhîd...Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? Lannit moy Bokalé. Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé: *Fiqh*: mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla. *Hadith*: mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement. *Tafsir*: mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi. *Sîrah*: histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons *Tadjwîd*: nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet. Et d'autres xamxam. Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé: *A't-Tawhîd*: xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé. Serigne Touba wakh si khassidam boumou Toudé akhirou Zamân: yaww sama kharit bi boul bokalé, ndakh bokalé daff layy tekk si yonou safara. Moyy so wathioul yonn wowou, Serigne Touba mingui siyy dioundjou...safara nga dieum. T Lolou Yalla wakh na ko Lou bari si Al Qur'aan. Yonanti bi xamal niou KO si xamxam bouniouy wowé *hadith*. Legui souniou dello si xamxam bouniouy wowé *A't-Tawhîd"...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé. Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah* Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq*: Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk*: moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr*: moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla. Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd: *Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah*...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla: *Djoulli*: Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli. *Yakar*: Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar. *Diâmou*: Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou. *Ndimbeul*: Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga. Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné damay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn. Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou. Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. KO diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la. Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla. Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux... Riyaadou's Salihiin, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné. Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné.
Togne bakhoul En tout CAs . Elle alerte ( donc faites attention ⚠️ ) Day mateeee wala d’où mateeee boul dougeul say lokho. Point barre . Merci de passer voir ma chaîne TH-cam.
Mer sa thiotou ndaye sa leufal ndaye fi loudoul yalla Nene la man nga doul torop boude ya bind domou Adama yi ba lene di raye dina Lerr topal feule kene falewou la mana doul ba dé may wakh mounane nek na goor niati beug beuz ak sa niaway khamna sa diw khesal bo dieukh motakh
Khesal ba perte ni nane dagay rayate meuno thi nit yi lou yalla namoul demal diamoudji yalla té khamne yaw sa bop dé ga guena diegue ni doudeu trop de fanatik aux Senegal khamoulo dakh diga yindou wala ga fanane ganane dagay meunasewate chimmm
Fenn rekk! Niou ragaloul Yalla nio kayy Raggal! Dafa beugeu nitt gni ragal ko! T ragal ko dafay dougeul nitt ki si bokalé si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah ! Moyy wéteul Yalla si Diâmou yi (les formes d'adoration). Al Khawf...Raggal...est une forme d'adoration. Yalla rekk Moka Yayo.
Lann moyy A't-Tawhîd...Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? Lannit moy Bokalé.
Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé:
*Fiqh*: mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla.
*Hadith*: mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement.
*Tafsir*: mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi.
*Sîrah*: histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons
*Tadjwîd*: nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet.
Et d'autres xamxam.
Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé:
*A't-Tawhîd*: xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé. Serigne Touba wakh si khassidam boumou Toudé akhirou Zamân: yaww sama kharit bi boul bokalé, ndakh bokalé daff layy tekk si yonou safara. Moyy so wathioul yonn wowou, Serigne Touba mingui siyy dioundjou...safara nga dieum. T Lolou Yalla wakh na ko Lou bari si Al Qur'aan. Yonanti bi xamal niou KO si xamxam bouniouy wowé *hadith*.
Legui souniou dello si xamxam bouniouy wowé *A't-Tawhîd"...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé.
Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah*
Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq*: Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk*: moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr*: moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla.
Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd:
*Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah*...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla:
*Djoulli*: Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli.
*Yakar*: Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar.
*Diâmou*: Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou.
*Ndimbeul*: Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga.
Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné damay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn.
Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou.
Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. KO diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la.
Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla.
Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux... Riyaadou's Salihiin, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné.
Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné.
Nul ne doute que il aurait pas de commentaires débordés 😂
Sur
Commentaire Yi Vilguairoul di😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Ahh gayi dagno tite
Kon yaw safara🔥🔥🔥 niel nala yalla santane woul rayy
ki dalay sank dh mdr
layy yaw dakha bakhe 😂😂
Mono rey quenne
Do yalla sama tour mo neke fofou
Mamoudou Diane 😂😂😂😂😂am gua fit de
Bro barke yalla wakhgna deug ba pare moune 7 foi la dioude lol day fene
Yama meuneu doul yallah rek moye reyeeee
Togne bakhoul En tout CAs .
Elle alerte ( donc faites attention ⚠️ )
Day mateeee wala d’où mateeee boul dougeul say lokho. Point barre .
Merci de passer voir ma chaîne TH-cam.
Ragal nga lol
Héhé 🤣🤣🤣🤣🤣 kone journalistes yi moytoulen
Reine Noire ki dou dara day doul meunoul ray kéne
@@alphadiodiallo2362
🤣🤣
🤣🤣🤣🤣Journalistes yii diéga porolém déh 😆😆hii fayéne bii dafa name thiéré hein
Fènal niit bakhoule
Goudoule yalla manta ray
Li nga wakh nak
7 foi nga djoudou man geumou mako
ومن قتل مؤمنا متعمدا فجزاؤه جهنم صدق الله العظيم
Sénégal dal mou nehhh ana Les autorités publiques wah lenn waye
إن يدعون من دونه إلاإناثا وإن يدعون إلا شيطانا مريدا#+ لعنه الله وقال لأتخذن من عبادك نصيبا مفروضا
Merci mère
Mouno ray ken. Danguay sopp rek. Senegalais mo geumoul Yalla rek mais li shirk la
Hiii menace😂😂Tata Amy faye yalla na sa diam yague
Ibrahima ciss99 ree na ba de😂😂😂kon dofo len
@@misslady2858 Aah miss mane douma riské dé😂😂Tata amy mii dafa melni cousinou Mowti leu
Mer sa thiotou ndaye sa leufal ndaye fi loudoul yalla Nene la man nga doul torop boude ya bind domou Adama yi ba lene di raye dina Lerr topal feule kene falewou la mana doul ba dé may wakh mounane nek na goor niati beug beuz ak sa niaway khamna sa diw khesal bo dieukh motakh
Mere amy attention si liguay wakh...bakh na rek...yagui tamm sa bopp dall...yalla rek ak ndeumeu gnoy rayer....wasalam
Wa yao yaye yallah bay rayé?
Khesal ba perte ni nane dagay rayate meuno thi nit yi lou yalla namoul demal diamoudji yalla té khamne yaw sa bop dé ga guena diegue ni doudeu trop de fanatik aux Senegal khamoulo dakh diga yindou wala ga fanane ganane dagay meunasewate chimmm
dabamariama12 aye waye boul riské
El hadji malick Diakhate khana yalla name thi mane samay fane matt ki de na kholate son comportement mo guene thi mome
Elhadji Malick diakhate 😂😂😂😂
Deugue la deh mais yataye sakh ki meunoul lire 😂
@@elhadjimalickdiakhate6831 bouma raye wayyy yaw yaye borome parasol bi waroulo tite loudoul yalla
😯😯😯😯
Commentaire bou ameu talibé yaye mboy doundeul lou barrii
😁😁😁😁😁😁😁😁😁😄😄
Do touss loudoul yalla neneu leu
Ay dull yamasi doy
Thierno moulé d meuno si mom nada
Ya meuneu doul
Ya mouna doul yaw deumm nga
Bodè yallah tawal khal
Comentarios yi noye na dh naye daveur bokk
Lougnou waxatii
Serer layam De,Refeto maga de.Ki mom bouro toucoulor la.Wedi len ko rek,kham..Madiambal,jakarlo Moytolen kone.