Muhammat Sañaa. Kii ni ñu ko def ñaaw na lool ! Nit ñi nañu ragal Yàlla ci seen diggante ak seen i moroom baax na ! Yónnent bi SLHW daa jël loxoom bu tedd ba. " Teg ko ci kaw kaaba ga, ne ko yaw néegub Yàlla bi ma toj la ñu tabaxaat la ma tojaat la ñu tabaxaat la ba muy nàngami yoon moo ma gënal lor benn jullit. " Kon lor ab jullit mbir mu diis la di lu mat a wattandiku rax ca dolli di sa mbokk. Bu dul ci deret it di ci leneen. Jaangeenjëf di tuub bu baax a baax. Di ñaan ngeen yendu ak jàmm.❤❤❤❤
Muhammat Sañaa.
Kii ni ñu ko def ñaaw na lool ! Nit ñi nañu ragal Yàlla ci seen diggante ak seen i moroom baax na ! Yónnent bi SLHW daa jël loxoom bu tedd ba. " Teg ko ci kaw kaaba ga, ne ko yaw néegub Yàlla bi ma toj la ñu tabaxaat la ma tojaat la ñu tabaxaat la ba muy nàngami yoon moo ma gënal lor benn jullit. " Kon lor ab jullit mbir mu diis la di lu mat a wattandiku rax ca dolli di sa mbokk. Bu dul ci deret it di ci leneen. Jaangeenjëf di tuub bu baax a baax.
Di ñaan ngeen yendu ak jàmm.❤❤❤❤
وعليكم السلام ورحمة الله وبركاته شكراجزاكم الله خيرا
Serigne Modou fall thi comunu fandène machalla ❤❤❤❤❤❤
Daaray sëriñ Abdu Samat si Daaru salaam bambuk ❤
Dieureu dieuf daaray islame internationale
❤❤❤❤
Daaray serigne el hadji fall sa dakar parecl unité 18
Diadief