Ma shaa Allah Ta Mariètou. j'adore ta cuisine et aussi celle de Ta Yandé. Que le Tout Miséricordieux vous protège et vous préserve amiin. La fierté de la femme africaine. Laf Thiat. Un grand merci pour le thiere 0 faute comme d'habitude.
Machallah Tata Mariétou yagui guindi diék dji di diangal goné yi Yalla nagnoula YALLAH swt fayale Mane dé défaratena sama toguaye grâce à toi Barakallahu fikoume yalna YAllah same la, arre la, mayela goundou fane akk wére Love you😍😘😘❤❤❤🌹🌹🌹
5 ปีที่แล้ว +3
Ma position ohhhh masha Allah ma chérie so sweet ameen wayyy 😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Mashalla tata Mariétou thiéré bi amna mana. Lima gueuna nékh moy dama bayi bouillon grâce à saveurs planétaires. Tata Mariétou yallah nalla yallah fay té may la weer inchallah
5 ปีที่แล้ว
oumou kante Ameen wayyy Masha Allah 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Marietou sa thiéré bakh na machalla j'apprend toujours Je ne savais pas que courgette meun neu remplacer yob merci encore bisous et longue vie à toi chérie
Ta marietou soma dieguewon ma andi sama participation togou la thierè gueweul bou melni Diam nekh ba yeg ci looool looool diwgui gnaay sa kaw nga toni bombe ko. Ahhh xara ma nopi bala ngamay soumii
Macha'allah tata Mariètou, yow dal Yalla rek molay fey. Delné amine rek. Bi mom damey bayi ba wathié ak diam reugeuko ndakh mane thi lek bou bakh. Muchas gracias depuis Espagne
pr le bombou thiere c oubligatoire de mettre le sucre ou noTata mareitou tu ma inspire encord antan ke une nouvelle marie je vais bien valide mon tamkharite inchalla merci pour tout
5 ปีที่แล้ว +1
Toufa Sow heureux ménage ma chérie pour le sucre juste un tout petit peux si non faite votre choix
Hello from beautiful California....The first thing i like about you is your cleanest, organization.....kindness, people person, good sense of humor....truly a great cook...Mashallah, nele amine rekh, toujours souriante...j'adore!!!!, lafe thiat!!! cheteuteu bilaye des fois, je sens l'odeur de tes plats, 0 faute!
Bonjour, merci beaucoup TATA MARÉTOU si plats machala yalla nala yalla maye goude fannnnnnnnnnn. Mais moi le problème que j'ai la ou je en France ya pa garlic j'ai cherché partout 😥😥😥
Thank you for the wonderful videos I love your channel. I live in the New York/New Jersey area and I wanted to know where can I get the garlic plus and the Turkish tomato paste.
5 ปีที่แล้ว
kine sarr thanks my sister the garlic plus is from Canada and the tomato can I find it at the Arabic store now if u have messenger please go to mine and leave me your number so that we can make arrangements so that I can get you the stuffs thanks it’s Adji marietou ndaw
Cc tata j'espère que vous allez bien je vous suis depuis de France et franchement je vous j'adore. Yalna yala gouddal faneyi defal la diam ak wer ak soutoura En fait je voulais savoir comment faire pour avoir l'ail plus en France merci
Machalla amna solo lool yalla maye goudou fane ak wé er si barke seydouna Mohamed saw dieureudieuf
Beuleup ndoucoumane sa ndéner Aram fakha yalla na yalla goudale sa fane amine tata cherie ❤❤❤❤❤
Ma shaa Allah Ta Mariètou. j'adore ta cuisine et aussi celle de Ta Yandé. Que le Tout Miséricordieux vous protège et vous préserve amiin.
La fierté de la femme africaine. Laf Thiat.
Un grand merci pour le thiere 0 faute comme d'habitude.
Mashallah mashallah tata marietou si yaw lay roye motakh sa ma dieukeur da gueuneu content si mane
Ahh tata légui la sey wayè yangui mey yokal samey bagasss .bilahi doundeul tata cherie
Machallah Tata Mariétou yagui guindi diék dji di diangal goné yi
Yalla nagnoula YALLAH swt fayale
Mane dé défaratena sama toguaye grâce à toi
Barakallahu fikoume yalna YAllah same la, arre la, mayela goundou fane akk wére
Love you😍😘😘❤❤❤🌹🌹🌹
Ma position ohhhh masha Allah ma chérie so sweet ameen wayyy 😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Macha'Allah tata marietou dewenety yalnananiou yalla may fekke te tal tamkharite ak diam Incha'Allah sa thiere goundousgoundoussina
Seu film diarneu 14miliard ak wakhtan bi ey bakhou niak diom shhtt noon merci tata
Alahouma aminnn Maman Mariétou dall defatigua sa meunineuh Machalla niogui harr thıéré Maman Yandé...Thiéré gua bamouy barri dollé thiooooooooo😍👏👏👏👏 perfectooooo👌👌👌
Maachaallah tata nekhngama lol yalnala yalla sam té soutoural la si lep
Salam mariétou c ndeye fatou depuis France mais mala fan dé manchalla damaléye suivre tout le temps mais aille plus bi nouméye défe ba amsi
Mashalla tata Mariétou thiéré bi amna mana. Lima gueuna nékh moy dama bayi bouillon grâce à saveurs planétaires. Tata Mariétou yallah nalla yallah fay té may la weer inchallah
oumou kante Ameen wayyy Masha Allah 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Manchala tata bilaye beuguenala manchala way
Thiéré Ta Marietou rekk eupna🙏 yalnala yalla lafal thiate! Longue vie à vous
Machala thiéré bi néhna
Amine wai😊
Tata sa thiéré saleté na machalah yalla na sa diam yague
Tata defati nga com d'habitude yalna lokho bi werr machalah
Ta nationale, interplanetaire. Boule faté roti niambi bi dal.
Macha allah rek encore une fois thi thiere bi
Tokeu dii khalateu louma wara tokeu rêr rék tassé si sama thiéré bou gnadieu bii machalllah yallah na yallah koudaleu sayyy faneu
machalah Tata Marétou sa thieré bakhna
Lima guena nekh saye plat sans bouillon longue vie à vous 😗
Machalla Tata marietou thiere bi nekh na contane na
Bakhi niak diom 🤣🤣🤣🤣 je vous adore tata Marietou 😍❤️🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machalah tata marietou g vous aime t mangui khar nguemou bi naar bou ndaw
Wa hlykoum Salam wa rahmatouLLAAHi wa barakatouh maman.
BarakaLLAAHu fiikoum yaaye boy
Bilay ma beugu say assiette thieree bi bakhna tarkala
Machalah tata marietou si thieré bi todiatiguafi
C'est décidé magui paré samay bagages nieuw dalsi sa keur Tata marietou.lov yu
Tata Mariatou sa chere am na manaa!! Yummy 😋
Machaallah on est bien servi yalna diamm yagu
machallah tata yalna borom bi yok katann bi ail plus bi foumm am
Machalah 😋😋Marietou li ngay tog eupna 👍👍👍li ngay def meune nga ko tei tek nga ko si yone 😘😘😘
Machala wakhouma lolou sakh mais say khetou veseil rekk okk bol bigua def thiéré bi la beug😍
ma sah allah tata marietou borom yobo yaba merci beaucoup pour le vidéo happy amna solo diauerue diauef
Machallah tout le temp magui lay topou si plat you bakh yi louma amme rek toguou momako mayy tata marietou merci wayy depuis italie
Tata yandé mâcha allah ligua thieré eupe na té dagua ma nekh trop sakh merci pour tes jolies plats 😍😍😘😘
Macha Allah macha Allah li nga thiéré eupna 😚😚😚
MARIETOU Borom Youbouyaba, yalla nanga amm ACADÉMIE Toggueu ! Amine. Yagui defare Keur you barrer. DEWENATI sama Soppey. Bisous
Rokhaya Niane Ameen wayy ma Cherie 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
@ 👍🏼😍😘😘😘
Machalla machalla bismilah TT marietou ligua thiére eupna
Oho sama tata Marietou machallah. Thiere bi machallah
Non tata marietou Tothie ngafi radiakh machalah toukassaban bou sagne ba rére.
Masha ALLAH ñou dianganti sokhna Mariétou
Marietou sa thiéré bakh na machalla j'apprend toujours Je ne savais pas que courgette meun neu remplacer yob merci encore bisous et longue vie à toi chérie
Mashalla tata thiere dji diarna yone
Machalah Tata marietou thiere dji mena mouth
Machallah tata marietou sa thiere bahnaa machallah comme d'habitude
Macha allah 😋😋😋 . Thiéré bi amna solo 👍👍👍 . Bon appétit 😘❤🧡
Tata Marietou ak tata yandè je vous love beacoup sene togg rafetena, bakhna,1 teh diafewoul merçi 😘 mane tierè rek la beug
Merci tata amatina solo machala yala nala yala faye
Tata marietou empreinte djinakh mome yalla nagnou si yalla mouseul 🤣🤣🤣
Sa thiere bakhna😍 merci encore🤗
Astuces du monde 😂😂😂😂😂❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Machallah Machallah Machallah amna solo ba mouye beuri dolé
Thiooooo thiéré ngue ma tata chérie jazzakallahu kheir
Manchalla mariétou sa théré bakhna❤❤❤
Yana yalla may feke tamkharite machallah
Ma sha ALLAH sama toureundo defati ngueu seu Manie yalna yalla doli wére borom youbou yaba yi yafi meune😘
MACHALLAH YALLA NA YALLA WERAL THIERYI 😘😘😘
Machalla tata , sama tabaski bou diaré yone rekk yaw laa yalla na sa diame yague, sama belle famille contane nagnou thi mane machalla
tata marietou yow dal amo morom sa togouyi set nagnou te nekh
Wa tata maretou guañ guay nieuw sa toma guisla
Nyami Seereer. My Seereer cousins would love this. Thanks for sharing.
Une chaîne que je viens nouvellement de découvrir. Je sens que je vais adoré
Ta marietou soma dieguewon ma andi sama participation togou la thierè gueweul bou melni Diam nekh ba yeg ci looool looool diwgui gnaay sa kaw nga toni bombe ko. Ahhh xara ma nopi bala ngamay soumii
Bn chance à toi mama k dieu t gatde
Macha'allah tata Mariètou, yow dal Yalla rek molay fey. Delné amine rek. Bi mom damey bayi ba wathié ak diam reugeuko ndakh mane thi lek bou bakh. Muchas gracias depuis Espagne
Maman Machallah ligua thiere eupna je t'aime
Ah operation tamkharite waay.
Machallah ta Maretou 👏👏
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah tata
Ahhh machaAllah Tata Mariétou darling di bek si yaw sa sou nek 😍😘😍😘 jazakalahou khayrane
Machallah yalla nanou fii yalla bayi niou fekei tamkharite bii thie jam ak salam🙂🙏🏽🙏🏽
Tata Marietou sa thiere nekhhhhh na Macha Allah
Merci dina diem deff comme sa boss
Machalla tata marietou content na dji yaw trop 😘😘😘
Ma Sha Allah Tata Mariétou😘
Dieureudieuf amna solo torop.
pr le bombou thiere c oubligatoire de mettre le sucre ou noTata mareitou tu ma inspire encord antan ke une nouvelle marie je vais bien valide mon tamkharite inchalla merci pour tout
Toufa Sow heureux ménage ma chérie pour le sucre juste un tout petit peux si non faite votre choix
merci Tata mareitou je suivrai votre conseil inchalla
Heureux ménage toufa:-)
@@Astucesdumonde merci bcp
Toufa boko topé d pé rek ngay dieul inchallah.
Masha'Allah tata Qu'Allah Azawadial te facilite le reste🙏🙏🙏
Rahmatoullah Sy Ameen 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘❤️❤️❤️
Ohhhh😄warone nga ko yékeu gnou guiss youbou yaaba yeup! Mais sa thiéré bakhna! 👏👍🏼. Bon courage sis.
Mashallah Mashallah yallana sa diam yagg Amine 💋❤️🌹
Thieré bi teint na! Trés Bien🤩
Machalla linga thiere tek ngako ci temps
Hello from beautiful California....The first thing i like about you is your cleanest, organization.....kindness, people person, good sense of humor....truly a great cook...Mashallah, nele amine rekh, toujours souriante...j'adore!!!!, lafe thiat!!! cheteuteu bilaye des fois, je sens l'odeur de tes plats, 0 faute!
Macha Allah Tata Assalamou aleykoum. Gnongui lay Ziar dila diokh sa wathiouway
Tata mariétou. Kou ame yape khar tabaski meune ngako si né réle Khana
Mom lagnouthi tamou di chérie wawaw saf sapp lay deff machallah
@@nenediaw940 ceeeeeeeeeest bien
Machallah choukrane yalna rés ak diam 😘
Machallahhh tata thiéré gua mé tata fane la mouné ame paprika smoke bi magui nék Michigan Ann Arbor
Bitty Diongue quora soudé amna fofou ak grande surface yeup en general
Yayou Ouz ok ma chérie nako khôl si grande surface inchallahh 🙏
Bitty Diongue demal Marshall’s ou dans les supermarket il faut juste demander au workers there
Saveurs Planétaires ok tata nako khol inchallahh merci 🥰🥰
Machallah chef long vie merci beaucoup bisous
Ah ça fait plaisir de vous retrouver le thiéré est suculent c'est à tomber bravo ,par contre le thiép de la dernière fois.............😩
Mahchahala Ta mariétou koussa thiéré tamkhari nékhoul dal thi iow la fi wathia tina
Ta mereme ya takh bene diek titatoul machala longue vie rek
Ohhhh yena ngui degg peukh peukh bi
Bonjour, merci beaucoup TATA MARÉTOU si plats machala yalla nala yalla maye goude fannnnnnnnnnn. Mais moi le problème que j'ai la ou je en France ya pa garlic j'ai cherché partout 😥😥😥
Nékosi touy bakhou gnak dioum ak titeul non elle va me tuer celle la 😂😂😂 mais je l'aime bien
MACHALAH YAGGUI FI TEI WEER
Thank you for the wonderful videos I love your channel. I live in the New York/New Jersey area and I wanted to know where can I get the garlic plus and the Turkish tomato paste.
kine sarr thanks my sister the garlic plus is from Canada and the tomato can I find it at the Arabic store now if u have messenger please go to mine and leave me your number so that we can make arrangements so that I can get you the stuffs thanks it’s Adji marietou ndaw
Machalla Tata toguo bii amna mana
Ma challah
Manchalah manchalah
Cc tata j'espère que vous allez bien je vous suis depuis de France et franchement je vous j'adore. Yalna yala gouddal faneyi defal la diam ak wer ak soutoura
En fait je voulais savoir comment faire pour avoir l'ail plus en France merci
Macha Allah sa thiere ñekhnnna
Tres bien tata Marietou ❤❤❤
Machalla 👌👌😘
Merci pour la recette c est bien expliquer à bientôt.
Assalamalaykoum wa saveurs planétaires et tata marietou yalla na diam yague.niou sétani ta nieuw
Tata bi lay maye incha allah
Machalla borom touy ak rél🤣mais thiére dji amna diom lol maman chérie,je voudrais savoir qu'est ce qui sont entourés le thiéré