@@ibrahimadembele7648 il n'est pas question de compétition entre les gens de Dieu. Vous savez une des plus grands voeux de Serigne Touba c'était de faire parti des companions du prophète qui ont combattu à badr. L'essentiel c'est que l'on puisse s'aimer entre musulmans et ne pas avoir de pensée négatif sur son frère musulman quelques soit le chemin qu'il suit. La religion est amour.
@@alassanegueye3965 ça c’est vrai mais dit toi que on peut tout faire pour plaire à Dieu et être meilleure personne mais on peut même pas rivaliser avec les sahabas. Serigne Touba il a bcp fait et bcp travailler mais je dis quand on dit louange à lui c pas normal parce que y’a dieu qui mérite les louanges
Inna lil lahi wa Inna ileyhi raajijoune Serigne Saadibou Toure n'est plus. Décès survenu ce dimanche 4 septembre à Dakar. La levée du corps est prévue demain à 9h à l'hôpital Dalal Jamm et s'en suivra l'enterrement à Touba incha Allah.
Serigne Touba kéneu douko khameu fi si adouna.
Ma beugueu Serigne Touba ❤❤❤
Ana gniko beugueu ?
Dieuredieuf serigne touba khadim rassole. cheikh sadbou toure yalla na fi yag te werr
Écouter les verres et le rime de Serigne Touba🥰🥰🥰
Yalla nala yalla yeureum Serigne sadibou toure 😭😭
SERIGNE Sadibou Touré yalnala sa Borom yeureume yalnala CHEIKHOUL khadim térou térale laa insha’allah 🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭
Sama khôl doudjouk siyaw Baye Sadibou Touré yallanala Borombi terou teralla si barké khadim Rassoul ♥️♥️♥️♥️
Thieuy Serigne Touba Aka beug Seydina Mohamed psl
Sama khole sédenah barké breme touba yalna sakh diam yague
Baye Sadibou Touré Yalla nala Yalla yeureum té xaréko Aldiana firdaws Barké Borom Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe 🙏🙏🙏👌👍😭😭😭❤️❤️❤️
Amine
Akkasa macha allah cheikh sadibou toure xam xam bi rafetna yagufi lool te wer
Machalla wakhtan wi amna solo rorop ken dou sarigne touba khadimou rassoulilahi
Dieuredieufeti Serigne Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌🙏🙏🙏
Bilay lima nekh si wakh dji moy serigne touba nena rek lay wakh
Wawaw ❤️❤️
Machalla Yalla na Yalla gudal seni fane 💯💯💖💖💖💖💖💖💖💖💖🙏💖🙏💖🙏💖💖🙏💖💖💖🙏💖
Cheikh sadbou machalah xam xam bi rafet na.
Yallah nalla yallah aldiana firdawsi Pa sadibou Touré 😭
Thieuy cheikoul Khadim 😭😭💫💫
DIEUREDIEIF BOROM TOUBA KHADIM RASSOL AMOUL MOROM KENLA MACHALLAH CHEIKH SAGBOU TOURE YALLAH NGA AM WEER AK WERSAK AMINE YA RABBI
Dieureudiaf serigne touba amoul dh❤
اللَّهمَّ اغْفِرْ لَهُ وَارْحَمْهُ وَاغْسِلْهُ بِالْبَرَدِ كَمَا يُغْسَلُ الثَّوبُ 🙏🏽😭
Yalla Nako yalla yeureum Thi barke Serigne Touba
Serigne Touba est très grand mais y’a que Allah qui digne de louanges
Ibou gaming ci bir maggayou yalla sounou borome lagne Koy magalé
C'est très vrai mon frère .Mais sache que Serigne Touba fait partie des louanges de Dieu.
Je m'excuse.
J’ai une question à votre avis qui est meilleur entre Serigne Touba et les sahabas du Prohete Mouhamed Psl ?
@@ibrahimadembele7648 il n'est pas question de compétition entre les gens de Dieu.
Vous savez une des plus grands voeux de Serigne Touba c'était de faire parti des companions du prophète qui ont combattu à badr.
L'essentiel c'est que l'on puisse s'aimer entre musulmans et ne pas avoir de pensée négatif sur son frère musulman quelques soit le chemin qu'il suit.
La religion est amour.
@@alassanegueye3965 ça c’est vrai mais dit toi que on peut tout faire pour plaire à Dieu et être meilleure personne mais on peut même pas rivaliser avec les sahabas.
Serigne Touba il a bcp fait et bcp travailler mais je dis quand on dit louange à lui c pas normal parce que y’a dieu qui mérite les louanges
Dieureudieuf Serigne Touba diarawlack Cheikh Ibra Fall
Barké Cheix Ahmadou Bamba beg na🥺❤️
fallou tine bayill khasida yigay fouwe bakhna reck 😭😭😭😭
Yal nako yalla yeureum té diégal ko
Yalnanga guissék Serigne touba
Kèn dou cheikhoul khadim 🙏
Thieye serigne touba amoul morom
Machala li amna solo trop sakh vraiment
Serigne touba amoul morome
Serigne touba dou morome
Kendou s touba
Thieye Serigne bamba,
Macha alah jerejef mourid
Hole sede na way yalnaga goude fane tourè
Merci sr bamba
Yalla nala Serigne Touba tairou
Machallah Ahmadou dieureudieuf
Bilaye thièye serigne touba
Thieye serigne bi
Machallah
Lissi eupe solo moy serigne sadbou loumou wakh dinala wakh bayite biko serigne bi wakh
Serigne Touba nèèna rkk ngay degg ba wakhtane bi dieekh
Dieuredieuf serigne sadbou guoudal fane looo
Xamxam rek mo woor bilahi
Machala.sadbou.toure
Amna solololllllllllll
Mame. Pe nda. Sarr. Sadibou. Nekh. N'a. Yalla. N'a. S'érige touba. Faye. La
Serigne touba amoul morom
Yalla nAko yalla dolli yeurmandé
Yala nala yala yereum té haré aldiana
_ماشاء الله جرجف❤❤❤❤❤
Mayma kamille 🙏🙏🙏🙏🙏😞😞😞😞😞😞😞😞
sadbou sambe ndaysane yal nako yala yerem émission bi doumako faté
MACHALLAH
Machalla machalla machalla
Wallahi amoul morom
Ndeysan douma si doyal mouk dieureudieuf serigne touba cheikh sadbou yagg fi lol
Tay ma delousi dila nianal aldjiana ndeysan aduna dou dara
Nexna way
Inna lil lahi wa Inna ileyhi raajijoune Serigne Saadibou Toure n'est plus. Décès survenu ce dimanche 4 septembre à Dakar. La levée du corps est prévue demain à 9h à l'hôpital Dalal Jamm et s'en suivra l'enterrement à Touba incha Allah.
Rip père
Thieuy yalla sama xol bi mogui melni galace
♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Akassa
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
❤❤
Bég nagnou
جرجف شيخ سادب
Finalement au Sénégal l'islam s'était éteint complètement entre 1895 et 1902.
Borom Touba Yakaarou jaam yii mooy guedj. Kou niew waakh ba diékhaal dém kénein waakh baa diékhaal téréwoul moom dou diékh
Yagefi lool ta wer toure
جرجف سرج طوبي امل مروم
Eskeuy
.
Mou ngi done wakh wakhou nitt mais ba mou wakhé alkhourane mo dem si yalla Sakou ko la fene yi tambalé.
Bayil sissou gui
Serigne touba wakhoul ak niou gatt xel te niak xam xam niou mel ni iow
@@babacargaye6043 yene gnivam khel dieul lene.. lepe dina clair.
Serigne touba moko bind lossi meune
@@wakhdeugrek3753 leep lair na ba nopi. Goumba yi rek nio dess guisdou niou.
Yagefi lool ta wer barkep serigne Touba
Machalla