dafa am nitt yo khamne bakhouniou te beugouniou lou bakh,Ndoye Ban ak Mami boulen tiit boulen ken meunoul ci yen dara sen emission bi nekhna te sen ligeuye rafet na Machaa Allah, Yal nalen Yalla diapale te mousal len ci borom khol yu bone yu sokhor yi,Amiin,give gfm vive Ndoye Ban yangui def lou rafet khassoulen ken li knew ci society rek ngeun di wakh bouniou ken rey
Mamie boule guéde boule faye mane yatakh maye khol wareef avec le peu de temps que jai je prends mon carnet chaque fois je prends note de tes proverbes 😘😘😘😘😘
je suis effectivement dacort avec la maman ki vien d appeler tata EVA félicitation et laff thiate Ndoye Banne nagoule rekk maman bi deugue rekk la wakh bette guama aussi parsk tayy warowwone tontou so naré lougnou wakh gua tontou ko digua sonou tata mami du courage je tadorrrrre fort
adounagui yanga dounde yaga dégue mais il fallait s'y attendre yéna oubi séne tv ninieupe wotéléne diokhé séne khalatt diapeléneni diguéne dégue kounéke séni sopé séninone gnibougone séne place té amouniouko dofyi, les rabats joie, les mécontents etc... femmebi kouko dégue khamni wéroul. Mome néna France lanek wayé diarignouwoufa car elle doit savoir que ce qu'elle a fait c'est une agression verbale. Bounékone France dibalé sakh balamouye dorliguéye gniou rappeléko ses droits et ses devoirs moi je vous regarde que différé à cause du travail mais kimome wéroul il a foutu la honte à tous les immigrés sénégalais de la France 😢😢😢😢😢 mais chapeau à Eva Tra 😘😘😘😘😘
Bon courage et surtout rester professionnels le silence est la meilleure des réponses Mami on suit vos conseils on ne rate pas l'émission pour djeulé ci yokoute ak diang kon nak laissez parler les mécontents je vous aime tous mention spéciale à tata EVA pour esprit de grandeur
Tous mes encouragements, yéna ngi deffar keur yi di délossi khell yi. Qui se sent morveux se mouche. Format émission bi koumou nga zapper. Bou gnou kéneu dammeu.
waa tamit nak nak auditrice bi nitt leu ya mome sa télécommande kay zappel mo guene nga nane daguay diokhé leçon de morale. koula dégue khamné iow tamit kou gnawww lamigne gueeee
Je trouve k ni eva tra a bien fait de calmer ses collègues pour ceux qui disent kni eva dafa seuytané no dafay bagn ay thiow reik Ndoye Bane mom waroul wone tontu
mais tamit fi ken forcer wou fi niit setane ! c est vrai que warou gnu wone tontou ! lolou mo gueune professionnel . mais li gnuy wakh souleu nakharé zappel. senegalais dal dafa am djott. ces animateurs sont professionnel meune sen liguey .
lasana mangui lay gniane benen yoon bou domram yu melni wote dangay coupe linge,Ndoye Ban ak Mami boulen deglou ben domram def len sen ligeuye lingeun di wakh leup dafa am kouko bange nak na fekhe bakh mogeun,mem man mi di wakh sen them bi daf ma lal ndakh damdan khoulo ak sama djekeur diko saga mais grace ak sen mangui fekhe wethekou
Ban je pense que quand on a rien a foutre du théme (c'est à dire si on se voit pas sur le théme alors pourquoi tant d'insultes? Faut pas dire des choses de ce genre). Ofét on dirait que cette femme ce théme l'a vraiment touché. Bah mais fallait pas lui repondre Mamy et Ndoye Bane car je croix que vous devriez savoir que, quand on met du éguille dans sa plaie mais subitement on réagit (c'est un acte reflexe) Apres avoir entendu ca j'en conclus que vous avez pris un part dans la plie de cette dame😂😂
j'ai trop rigoler quand mamy à répondu à la dame mais la femme elle abuse trop mamy et ndoye mbane sont là pour donner des conseils par rapport au thèmes ya n'a qui comprend rien du tout c'est grave
Li khamouma fann layy moudj.. mais je sens beaucoup de mechanceté, jalousie et hypocrisie.. EVA SOIT MALIGNE.. les deux qui t'entourent ne mont pas l'air sincere.. ils pretendent seulement car ils nont pas le choix.. mais au fond ils ne taiment pas... Cest grave au Senegal.. les gens sont faux.. Je suis dans le domaine de Clinical Psychology.. I can feel something wrong.. from the body language of both The lady and the guy sitting on her side.. Watch out...
Lolou moy professionnalisme et j'apprécie elle au moins est différente des autres Mamy tamit je l'apprécie bien depuis double vie mais elle vraiment warolone tontou de la sorte Suis désolé
eva tra toi aussi c pas comme ca parce que tu na pas été attaqué rek ba takh tu ne montre aucune solidarité envers tes collegues ahhh doy nga warr yowit
dafa am nitt yo khamne bakhouniou te beugouniou lou bakh,Ndoye Ban ak Mami boulen tiit boulen ken meunoul ci yen dara sen emission bi nekhna te sen ligeuye rafet na Machaa Allah, Yal nalen Yalla diapale te mousal len ci borom khol yu bone yu sokhor yi,Amiin,give gfm vive Ndoye Ban yangui def lou rafet khassoulen ken li knew ci society rek ngeun di wakh bouniou ken rey
Mamie boule guéde boule faye mane yatakh maye khol wareef avec le peu de temps que jai je prends mon carnet chaque fois je prends note de tes proverbes 😘😘😘😘😘
Eva Tra machallah tu es tres professionnelle . Qu'Allah te facilite dans ta carrière
mai ayye wakhe day diekh no youssou santou lenli dé meno lene kou len khass gene khasko EVA macha alla
Machalah nous sommes de tout cœur avec mamie ya yor volant bi
je suis effectivement dacort avec la maman ki vien d appeler tata EVA félicitation et laff thiate Ndoye Banne nagoule rekk maman bi deugue rekk la wakh bette guama aussi parsk tayy warowwone tontou so naré lougnou wakh gua tontou ko digua sonou tata mami du courage je tadorrrrre fort
adounagui yanga dounde yaga dégue mais il fallait s'y attendre yéna oubi séne tv ninieupe wotéléne diokhé séne khalatt diapeléneni diguéne dégue kounéke séni sopé séninone gnibougone séne place té amouniouko dofyi, les rabats joie, les mécontents etc... femmebi kouko dégue khamni wéroul. Mome néna France lanek wayé diarignouwoufa car elle doit savoir que ce qu'elle a fait c'est une agression verbale. Bounékone France dibalé sakh balamouye dorliguéye gniou rappeléko ses droits et ses devoirs moi je vous regarde que différé à cause du travail mais kimome wéroul il a foutu la honte à tous les immigrés sénégalais de la France 😢😢😢😢😢 mais chapeau à Eva Tra 😘😘😘😘😘
Quand on donne des leçons il faut accepter d'en recevoir.
machalla tata eva sa niveau intellectuel molay woné daga tey té ligay wakh daga tek fou leer par rapport aux autres
Bon courage et surtout rester professionnels le silence est la meilleure des réponses
Mami on suit vos conseils on ne rate pas l'émission pour djeulé ci yokoute ak diang kon nak laissez parler les mécontents
je vous aime tous
mention spéciale à tata EVA pour esprit de grandeur
Tous mes encouragements, yéna ngi deffar keur yi di délossi khell yi. Qui se sent morveux se mouche. Format émission bi koumou nga zapper. Bou gnou kéneu dammeu.
waa tamit nak nak auditrice bi nitt leu ya mome sa télécommande kay zappel mo guene nga nane daguay diokhé leçon de morale. koula dégue khamné iow tamit kou gnawww lamigne gueeee
mami she is right u have to be dian thatI'm sorry but I don't like the way u is pick too
kiwakhame boubaribi limou djindé crédit khadionena cimome 😭😭😭😭😭
Billay wakha tiko, man dall senegalais mo nekkaloull deukeul rekk
Je trouve k ni eva tra a bien fait de calmer ses collègues pour ceux qui disent kni eva dafa seuytané no dafay bagn ay thiow reik Ndoye Bane mom waroul wone tontu
mais tamit fi ken forcer wou fi niit setane ! c est vrai que warou gnu wone tontou ! lolou mo gueune professionnel . mais li gnuy wakh souleu nakharé zappel. senegalais dal dafa am djott. ces animateurs sont professionnel meune sen liguey .
femme bi daal thème beiko nakhari lernama ni dafsi guiss bopam mouy zaff nonou tchiiippp chaud coeur
du courage Tata mamy je t adore
lasana mangui lay gniane benen yoon bou domram yu melni wote dangay coupe linge,Ndoye Ban ak Mami boulen deglou ben domram def len sen ligeuye lingeun di wakh leup dafa am kouko bange nak na fekhe bakh mogeun,mem man mi di wakh sen them bi daf ma lal ndakh damdan khoulo ak sama djekeur diko saga mais grace ak sen mangui fekhe wethekou
Numero ndoye ban la beugue???
Ban je pense que quand on a rien a foutre du théme (c'est à dire si on se voit pas sur le théme alors pourquoi tant d'insultes? Faut pas dire des choses de ce genre). Ofét on dirait que cette femme ce théme l'a vraiment touché.
Bah mais fallait pas lui repondre Mamy et Ndoye Bane car je croix que vous devriez savoir que, quand on met du éguille dans sa plaie mais subitement on réagit (c'est un acte reflexe)
Apres avoir entendu ca j'en conclus que vous avez pris un part dans la plie de cette dame😂😂
Du courage le silence punit l'insolence...
j'ai trop rigoler quand mamy à répondu à la dame mais la femme elle abuse trop mamy et ndoye mbane sont là pour donner des conseils par rapport au thèmes ya n'a qui comprend rien du tout c'est grave
machalah
Li khamouma fann layy moudj.. mais je sens beaucoup de mechanceté, jalousie et hypocrisie.. EVA SOIT MALIGNE.. les deux qui t'entourent ne mont pas l'air sincere.. ils pretendent seulement car ils nont pas le choix.. mais au fond ils ne taiment pas... Cest grave au Senegal.. les gens sont faux.. Je suis dans le domaine de Clinical Psychology.. I can feel something wrong.. from the body language of both The lady and the guy sitting on her side.. Watch out...
Deug rek nga wakh billae. Ils sont hypocrites. Mais loudoul deug dou yague inchaAllah
Nek sénègalais mo mètti
mamy t sais pa cma parle yaw ya carte thaiga amna france me osi amna sngl e osi ils respecter les gens
Franchement eva na pas montrè de solidaritè envers des collegues
Lolou moy professionnalisme et j'apprécie elle au moins est différente des autres
Mamy tamit je l'apprécie bien depuis double vie mais elle vraiment warolone tontou de la sorte Suis désolé
ki d'à eupeul
ndoye bane daga deguere bopp trop bounleu wakhe nopill delle noppi yagui wakhe bagne koula wakh douni wayy
Femme bi sa khôl bou chaud Bo demé thème bi moko dérangé nigua wakhé ni ya mom theme bi kou rewgua avec ta façon de parler
eva tra toi aussi c pas comme ca parce que tu na pas été attaqué rek ba takh tu ne montre aucune solidarité envers tes collegues ahhh doy nga warr yowit
mamy bou leen faleii gni khamou gnou fou nouy sen xol yi leumbeul gnoune gni nioleuh beug pirre boul tiiiteu boul ragal defal loulou neex baxam lougn tch mane
gni danio sonal mamy tanyi Sénégal boy wakh deug di fégnal djikoyii mom rek niou bagn leu
Ki séytané on ne doi pas regarde humilié cé colégeu Éva réfléchi mém dan l'armée on défan toujours cé clache
Il faut avoir un esprit de dépassement cas même chacun est libre de dire son point de vue wakh len ci théme bi...
ko
Vrement c honteux désolé deug nékhoul
arrête avec ça mamy