Je suis jumeau, je m'appelle Assane. Aujourd'hui, je me mets à ta place 😭😭😭. J'ai le cœur meurtri! Comment peut on demande à un patient 1 millions de francs CFA sans consultation comme si c'est une marchandise. Je ne comprends pas. Courage jumeau. Paix à son âme 😭
Meti na trop bilahi , trop bilahi, trop bilahi. Dama dioy mba sonou , ma xalate rek li sou fekone mane la dalone. Bilahi wahati ko , mane deh Allemagne la nek , mais so amé RV thi hôpital 2 jours avant dagnoulay envoyer Email , so defoul accuser gnou wola téléphone tellement que santé nit ki dafa important ak xam sen responsabilité. Sénégal nak lolou mofa manqué , médecin yi ak hôpitaux yi xamou gnou louy sen responsabilité. Yalla nako borom bi yeureum , mayla xolou mougne
Barro King bilay sénégal mom bo amoul dagay deh outék Europe bo niewé nouniou lay topatowé bilay dagay sax faté sa metite mais senegal dougne la sax khol lii niaw na bilay
Tu as parfaitement raison moi je suis au Canada mais la première fois que je suis parti à l'hôpital je croyais que la femme médecin était amoureux de moi à cause du bon traitement qu'elle a fait envers moi, quand j'ai manqué un rendez-vous à l'hôpital, l'hôpital m'a envoyé une lettre pour me dire qu'ils m'ont attendu toute la journée contrairement au Sénégal courage et force à toi je compatis à ta douleur toutes mes condoléances mon pays agonise.
Walay jai pleurer hopitalou Senegal yi dinagne layo ak nit gni alakhira ndakh respectewougnou kene khamougnou akhe ak yelef domou Adama yi bone nagnou gnak nagnou kersa wayai yala rek mo meune tai molene eupeu doler massa mougneul metina trop wayai yalla bou sokhla kou beug gnak 😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥
Pourquoi attendre jusqu'au jour du judgement. C'est in system mal finance' par le gouvernement senegalais et bourre' de corruption. Le pouvoir revient au peuple.
Man magui biti rew wayé lima fi guis thi toubabe yi nion eup yereumande wayé Senegal foufe yalna yalla khareko aldiana firdawsi barke seydouna mouhamadou rasoulilahi saw
clinique madeleine bayinalene biss niki tay. donc vous pouviez le sauver mais vous avez refusé juste pour de l'argent. dumalene saga sah mérite wolene mey bakar pour vous
Les militaires ont leur part de responsabilités parceque niom nio créer choc bi donc niom nio warone évacuer nieup. Mais Sénégal ceux qui devrait nous protéger a savoir les militaires les médecins niom niognouy sank. C'est le monde a l'envers motakh galsen d'où dém fèn. Avancement zero
Mangui diégalou boubaxe certe liy amm ammna mai j voi k cé ls medcin ki ont fauté Ls militair si tu dors trankilmen cé grace a eux Si tu march dan la rue san sans être agressé cé grâce à eux Les jour d fête tbsk krté Noël etc.. on est chez ns et eux sur l terrain va à ziguinchor et tu verras ceu kil fon pr ns nui et jr Donc bou lénn blâmé di waxe nio nouy sankk erreur la et cé dur nakk di nianal gnissi niakk sénn bakkan mangui diégalou watt bu baxe
Wakh li ba Kagn Sénégal mon doyna warr dé bilahii médecin yii donne défi lii yalnalene yallah torakhale domou adama dafa foorr yalnako yallah yeureum si barkep cheikhoul khadim
Imigrasion deh bo thi amoul dara sakh nekh na ndankh fadjou bi toubab yi kham nagnou akhi domou adama sou malade aksè dagnou laye ndeukantè bilakhi mes mon pauvre pays senegal rip ouseynou assane courage frère😭😭😭😭
Medecin yi aye domèrame lane koufi dè gno la raye dèmelène dèposer pleinte Cheikhou Yalla bi Ousseynou Yalla nako Yalla yeurem kharèko Alediana 😢🙏 mes petits frère son des jumeau Ousseynou Diop et Assane Diop
La même chose eat arrivêe à Mon père en 2008 à l'hopital principal. Même recit avec le personnel médical. Jusqu'à présent j'arrive pas á oublier la souffrance de Mon père avant sa mort. Son temoignage m'a fait pleurer.
Bilahii li niaw na trop 🤦🏾♀️ soubkhanallah li dara rafetou cii lima ci meti rk moy Sénégal respecter wougnou domou Adama lii rk mtx toubab yii raw niou nakh akeuh ak yelef biniouy diokh yallah nko yallah yeuram th kharei mo aldiana firdawsii thiey yallah
Iskèye, mon pays va mal, courage Assane, 😭😭😭, il ya eu négligence, ils l'ont laissé se vider de son sang sans lui apporter les premiers soins d'urgence , il faut sanctionner tous les médecins présents des différents centres de santé où il a été
C très triste bilahi Sénégal les hôpitaux sont modis les médecins et les docteurs n’ont pas de cœurs ici en France walahi les blancs si tu viens dans les hôpitaux ils t accueillent bien
bon courage mon frère je partage la douleur avec mais sénégal beurina gnouy dei par erreur médical wala par négligence… li c'est une alerte pour tous les sénégalais mais nous on a tendance di khar ba dara dall sa mbok nga commencer intervenir. il a raison dei sénégal kou amoul moyen boy fébar di dèè ndakh Khaliss lagnou djiteul t lissi geuna yémé gnoune senegalais Yakar nagn gno guen gneup mais bilahi toubab yi ken geunoulen thi fonk domou adama. li Etat moko wara ngeuka khekh mais gnom sen bop lagn fi nekal et c'est vraiment domage yalnako sa borom yeureum té diegeulko famou dieu geuneulko fimou diouguer
Nagn bania diouk nioune les jeun de 20 a 45 ans. Naniou diouk dieul souniou responsablité récupèré souniou rewmi Li niaw na trop. Deuk bo khamni bop bop ken dou khekh ta yatt bi daloul sa kaw.gaindé Yaw gor yalla nga. Nionguilay masawou
Metina gnioune sokhla wougniou train émergence aye hôpital aye docteur you haragne aye université poste de santé guirr sougniiu domm heulek yalla nako yalla yeureumm té haréko aldiana
dèfonena accident le 05 juillet 2018 sapeur yobouma ctèo hopital de grand yoff dagnema dougal si bène chambre bayima fofou maye yokhou medecin bi gnewnane ma khana daga khiff
Mais nêkhoul ba nêkhoul mais douma wakh hopitaux yeupp mais la plupart des hopitaux ay doméraam lagnou. Domou adama nane la meuna fêbaré nguané doko dieul. Té État daff lêne fi tekkk pour nguêne fadj malades yi . Té toubab si fonkou nitte rekk lagnou rawé. Mais médecins kham lêne ni le jour de la réssurection di nguêne khamni lêpe deuguela ndakh nitte dafay fêbar ba tolou si diguanté sakh ngua bagn ko dieul en charge. Mais di gnanal Ousseynou yalla na ko boroom bi yereum té khâré ko aldiana firdawsi.
Ooooohhhhhh 😭😭😭😭😭je ne trouve pas les mots noo sénégal douniou toussssss😭😭😭😭
Je suis jumeau, je m'appelle Assane. Aujourd'hui, je me mets à ta place 😭😭😭. J'ai le cœur meurtri! Comment peut on demande à un patient 1 millions de francs CFA sans consultation comme si c'est une marchandise. Je ne comprends pas. Courage jumeau.
Paix à son âme 😭
Meti na trop bilahi , trop bilahi, trop bilahi.
Dama dioy mba sonou , ma xalate rek li sou fekone mane la dalone. Bilahi wahati ko , mane deh Allemagne la nek , mais so amé RV thi hôpital 2 jours avant dagnoulay envoyer Email , so defoul accuser gnou wola téléphone tellement que santé nit ki dafa important ak xam sen responsabilité. Sénégal nak lolou mofa manqué , médecin yi ak hôpitaux yi xamou gnou louy sen responsabilité. Yalla nako borom bi yeureum , mayla xolou mougne
No metina trop
Ndeysan li metina 😢😢 yalnako Yalla yeureum te maylen kholou mougne
Sénégal bilki
On s'est connu ya mm op lngtmps yalla df lii ousseynou u seras tjrs gravé dans ns coeurs😭😭😭
Hôpital you sénégalais yeup ay domeram lagniou 😭😭😭
Bilay
Barro King bilay sénégal mom bo amoul dagay deh outék Europe bo niewé nouniou lay topatowé bilay dagay sax faté sa metite mais senegal dougne la sax khol lii niaw na bilay
Domeram you bone sakh gni gno sokhor
Ohh metina 😭😭😭😭😭yalla noko yalla yerem si barkhe serigne touba 🙏
Tu as parfaitement raison moi je suis au Canada mais la première fois que je suis parti à l'hôpital je croyais que la femme médecin était amoureux de moi à cause du bon traitement qu'elle a fait envers moi, quand j'ai manqué un rendez-vous à l'hôpital, l'hôpital m'a envoyé une lettre pour me dire qu'ils m'ont attendu toute la journée contrairement au Sénégal courage et force à toi je compatis à ta douleur toutes mes condoléances mon pays agonise.
Lou weer nga wakh Toubab yii walahi haziim kouy wakh douñou dougou aldjana Yanguii wakh loula leroul ils sont formidable walahiii
Que la justice soit faîte.
Senegal metina bilay😭😭😭😭
Courage Mon Frere sa fait mal
Ohh masta mn cheri li metina nako yalla yereum khareko aldiana firdawsi
Vraiment se sont des assassins wallae en plus très arrogant ces médecins j’ai la rage 😡... courage Assane
Votre remarque est juste Arame. Senegal les medecins sont tres mauvais .Depuis Bruxelle
papaissadaya samb vraiment wallae
C'est très triste mais du courage mon frère 😭😭
Non c trop lii dafa sankh gnaw
Walay jai pleurer hopitalou Senegal yi dinagne layo ak nit gni alakhira ndakh respectewougnou kene khamougnou akhe ak yelef domou Adama yi bone nagnou gnak nagnou kersa wayai yala rek mo meune tai molene eupeu doler massa mougneul metina trop wayai yalla bou sokhla kou beug gnak 😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥
Billahi le jour du jugement sera très très difficile pour les méchants
Pourquoi attendre jusqu'au jour du judgement. C'est in system mal finance' par le gouvernement senegalais et bourre' de corruption. Le pouvoir revient au peuple.
Bilay c vrai
Vraiment metti na jai des larmes aux yeux
Bilahi docteur yi aye mbam rekk lagnou Domou kharam yi Sama khol diekhna
ousseynou yallah nako yallah yeureum tei khareko aldianna barkép s.touba sma khol diex na trop bilahy 😭😭😭
Alakhou akbarr metina😭😭😭
Man magui biti rew wayé lima fi guis thi toubabe yi nion eup yereumande wayé Senegal foufe yalna yalla khareko aldiana firdawsi barke seydouna mouhamadou rasoulilahi saw
Yalla nako yalla yeuram té kharé ko aldiana barkép Serigne Touba
😭😭😭😭Yalnala ko boromebi yereume ta diegalko dougeulko aldiana samalko djiabote bimefi bayi amiiiine
Massa wayyy assane
C vraiment triste 😭😭😭😭
Ndeysan metina yalla nako yalla yeureume te kariko aldianatou firdaws si barcke mouhamed psl
😭😭😭ndayssann j'ai le coeur meurtre😭
cest la 2fois may deeg histoire bou melni thi hopitaux yi medcin yi ay domram lagnou senegal mom kou amoul khalis do fadjou.
Mettina torop yalnako yalla yeureum
Ndeysane Massa frère sa jumeau bi yalla nako yalla kharer aldiana
Ndeysanne metina yalla nako yalla khare adiana
clinique madeleine bayinalene biss niki tay.
donc vous pouviez le sauver mais vous avez refusé juste pour de l'argent. dumalene saga sah mérite wolene mey bakar pour vous
Les militaires ont leur part de responsabilités parceque niom nio créer choc bi donc niom nio warone évacuer nieup. Mais Sénégal ceux qui devrait nous protéger a savoir les militaires les médecins niom niognouy sank. C'est le monde a l'envers motakh galsen d'où dém fèn. Avancement zero
Mangui diégalou boubaxe certe liy amm ammna mai j voi k cé ls medcin ki ont fauté
Ls militair si tu dors trankilmen cé grace a eux
Si tu march dan la rue san sans être agressé cé grâce à eux
Les jour d fête tbsk krté Noël etc.. on est chez ns et eux sur l terrain va à ziguinchor et tu verras ceu kil fon pr ns nui et jr
Donc bou lénn blâmé di waxe nio nouy sankk erreur la et cé dur nakk di nianal gnissi niakk sénn bakkan mangui diégalou watt bu baxe
Moi je suis dakor avec toi
massa mon frère du courage metine trop dioyna beu sone si vidéo bi Sénégal kou amoul khaliss rek dee nga thiey adouneu 😭😭😭😭😭
YALLAH na yallah Atè😭😭😭😭
mettina billahi 😭😭😭😭
1 milion wala dounla fathie 😭😭😭 thieyy adouna. bilayy aleuk yaw marhiyam dina metty trop. 😭😭
Massas quile repose en paix😭😭😭😭🙏🙏
Bou malade gnewé dougne ko dieul té bou déwé niou dieulko gni ay deume lagne thiiiiiiimmmm kharam😡😡😡😭😭😭
Wakh li ba Kagn Sénégal mon doyna warr dé bilahii médecin yii donne défi lii yalnalene yallah torakhale domou adama dafa foorr yalnako yallah yeureum si barkep cheikhoul khadim
Yalnalen yalla até
Tellement triste mes courage frère 😭😭😭
Imigrasion deh bo thi amoul dara sakh nekh na ndankh fadjou bi toubab yi kham nagnou akhi domou adama sou malade aksè dagnou laye ndeukantè bilakhi mes mon pauvre pays senegal rip ouseynou assane courage frère😭😭😭😭
non
Sénégal
c'est terrible! je n'ai même pas les mots
J'ai des l'arme aux yeux billaye oh saï trs triste vraiment du courage assame 🙏🙏🙏😭😭😭
nonnnnn mettina senegal senegal 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Thiey yalla metti n'a bilahi mais yall nako yalla yeurem yalla khary KO aldiana yall na souff sede sii kawam
Oh assanne tu m as fais pleurer c est dur on est dans quel pays
Absa Duop où sont les dirigeants de ce pays
😭😭😭😭ayway li metina
Medecin yi aye domèrame lane koufi dè gno la raye dèmelène dèposer pleinte
Cheikhou Yalla bi Ousseynou Yalla nako Yalla yeurem kharèko Alediana 😢🙏
mes petits frère son des jumeau Ousseynou Diop et Assane Diop
Ndeysanne que son âme repose en paix 😢😢
Ndeysanne
noo dama titt si senegal
yalnalène yalla wèr nio niak yérmandé té bone médecin yi .grand topal affaire bi jusqu'au bout
Li Moy Sénégal so amoul ni laye démé badola boufi febar diaroul ngaye deme hôpital mounial ba yalla niowwe yalna yalla yeureume ki Fatou
Tu a raison !en Europe la santé est très primordiale
La même chose eat arrivêe à Mon père en 2008 à l'hopital principal. Même recit avec le personnel médical. Jusqu'à présent j'arrive pas á oublier la souffrance de Mon père avant sa mort. Son temoignage m'a fait pleurer.
Boucoule France 👍senegale 👇par ce que les blanc il conaise le droit de Lomme billaye du courage assmane rip 😭🙏🙏oussemou
ndeysane
Bilahi toubab yi gno kham akhou nit
Bilahi Lou wer gua wakh mane dh magui Brésil mais sa youma démé hospital dinane la topato ba sa khôl séde li métina trop
C vrai walakhi
Metina😥waxei sant yalla lolou mo geunonn si mom .... 🙏
Nooooooooo Loy wakh nii yow way lolou noum gueuné ci mom gnome gnoko raay ay assassin lagnou dagne wara faay pour se qu'ils ont fait
C triste 😔 nekhoul keunn mom waxei tmt lou yalla toudou monou niouci dra l’essentiel prions pour lui 🙏
@@godia5450 deug leuh wayé gnii lignou néké dou deug dou yoone wallahi
Dh meunoul geune thie nit waaay
Oumar Guisse oui frère lolou nieup xam naniou ko waxei nioun monou nioussi dra jt assure Sénégal mom lou nexx way deff
😭😭😭meti na trop
Vraiment c'est triste
Bilahii li niaw na trop 🤦🏾♀️ soubkhanallah li dara rafetou cii lima ci meti rk moy Sénégal respecter wougnou domou Adama lii rk mtx toubab yii raw niou nakh akeuh ak yelef biniouy diokh yallah nko yallah yeuram th kharei mo aldiana firdawsii thiey yallah
Métina sénégal yalla nanu yalla same 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Allahou akbar allahouma ihfir lahou ya raby 😭😭😭
Ndeyssan mettina bilahi troppo yalnako yalla yeureum tè xareko aldiana firdawsi
Oui🤦♀🤦♀Li doy na war métina tourp wayé mo nkhé yalla
Iskèye, mon pays va mal, courage Assane, 😭😭😭, il ya eu négligence, ils l'ont laissé se vider de son sang sans lui apporter les premiers soins d'urgence , il faut sanctionner tous les médecins présents des différents centres de santé où il a été
C très triste bilahi Sénégal les hôpitaux sont modis les médecins et les docteurs n’ont pas de cœurs ici en France walahi les blancs si tu viens dans les hôpitaux ils t accueillent bien
bon courage mon frère je partage la douleur avec
mais sénégal beurina gnouy dei par erreur médical wala par négligence…
li c'est une alerte pour tous les sénégalais mais nous on a tendance di khar ba dara dall sa mbok nga commencer intervenir.
il a raison dei sénégal kou amoul moyen boy fébar di dèè ndakh Khaliss lagnou djiteul t lissi geuna yémé gnoune senegalais Yakar nagn gno guen gneup mais bilahi toubab yi ken geunoulen thi fonk domou adama.
li Etat moko wara ngeuka khekh mais gnom sen bop lagn fi nekal et c'est vraiment domage
yalnako sa borom yeureum té diegeulko famou dieu geuneulko fimou diouguer
Yalla nako yalla kharé aldjina firdawsi thi barké seydina Ousmane mbacke
Massa je compatie j'ai les larmes aux yeux métina trop mougnal yallah nako yallah yeureume té kharéko adiana thie Barker seydina Mohammed
Massa mon frère li métina trop
Courage frère
100Ans Sénégal dou meussa change bilahi walahi aucune considération au peuple des Médecins qui se crois des Rois n’ont c’est pas sérieux du jamais vue
Ho li metina Sénégal dal sama kholl toyna bilakhi yalnako yalla yeureum té kharéko aldiana si barké seydina mouhamed
Metina trop yalna adiana done dekou wayame mane dafa melni sa grand frere la lida meti trop
Yalla nako yalla kareco aldiana firdausi 🙏🙏🙏
Oh metina trop assane mounial ta nianalko paix à son âme
Nagn bania diouk nioune les jeun de 20 a 45 ans. Naniou diouk dieul souniou responsablité récupèré souniou rewmi Li niaw na trop. Deuk bo khamni bop bop ken dou khekh ta yatt bi daloul sa kaw.gaindé Yaw gor yalla nga. Nionguilay masawou
Nice 😭😭😭😭😭😭😭
Merci Assans
Li dawna yarame métina😭😭😭
Ndeysan
Metina gnioune sokhla wougniou train émergence aye hôpital aye docteur you haragne aye université poste de santé guirr sougniiu domm heulek yalla nako yalla yeureumm té haréko aldiana
😭😭😭😭😭
Métina trop yalla nako yalla yueruem té kharéko aldjanay firdawsi
Mais li ba kagn ?
Oh ke c'est triste paix à son âme
dèfonena accident le 05 juillet 2018 sapeur yobouma ctèo hopital de grand yoff dagnema dougal si bène chambre bayima fofou maye yokhou medecin bi gnewnane ma khana daga khiff
Eva Dip Morèè dundu guiss ndeye sann xolale ma li rekk kom ka tanè gan si diamou allkhamdouliah
🤣🤣🤣😂😂😂😅😂😂😂😃😃😃😃😂😂😂😂😂😂😂😂😅😀😀😂🤣🤣😁😁😁😄🤣🤣🤣😂😂😅😅
Docteur yi ay domaram la niou
Senegal Lifi khew kenemanoko wakh
@@yandegaye2239 lolou bokouna si louma guena mèti si sama adouna mes sante yalla rek
Svp comment avoir le contact de Assane ?
Mais nêkhoul ba nêkhoul mais douma wakh hopitaux yeupp mais la plupart des hopitaux ay doméraam lagnou. Domou adama nane la meuna fêbaré nguané doko dieul. Té État daff lêne fi tekkk pour nguêne fadj malades yi . Té toubab si fonkou nitte rekk lagnou rawé. Mais médecins kham lêne ni le jour de la réssurection di nguêne khamni lêpe deuguela ndakh nitte dafay fêbar ba tolou si diguanté sakh ngua bagn ko dieul en charge. Mais di gnanal Ousseynou yalla na ko boroom bi yereum té khâré ko aldiana firdawsi.
g mal au coeur paix à son âme
masta yallanako yalla yeureum rip
Repose en paix
Li niawe na trop bilahi walahi sortou Hôpital bou saint Louis aye assassins laniou
😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️
Senegal senegal 😭😭😭😭
Pire n'egligence bilahi li dara guenouko méti souniou deukk bi founiou dieum
😭😭😭😢😢
Massa aye waye li métina diakheléna thi sénégal gni dougnou nit you baakhe
😭😭😭😭
Sappeurs kéne amoul séne faye franchement acte bi rafetna lool sounou borom guis na lépou