Salam anlaykoum Ki kouko xool xamné kou beugg Serigne yi ax nittou yalla yi té fonk lénn lool saax Nitt gni nagnou bayi parparloo bi Merci au Professeur Yalna yalla saamal niou sunuy kilifaa diné yi
Seytané mo barri dolé rék , Wayé Kou Beug Serigne Touba Nga Yag Naala deglou . Sab noon Moom day xaar banga juum thi waxx mu wéér la. Na Mouride yibTonte Moussa Camara mo geun té wahtan ak Omar Diagne.
Salam anlaykoum
Ki kouko xool xamné kou beugg Serigne yi ax nittou yalla yi té fonk lénn lool saax
Nitt gni nagnou bayi parparloo bi
Merci au Professeur
Yalna yalla saamal niou sunuy kilifaa diné yi
Seytané mo barri dolé rék , Wayé Kou Beug Serigne Touba Nga Yag Naala deglou . Sab noon Moom day xaar banga juum thi waxx mu wéér la.
Na Mouride yibTonte Moussa Camara mo geun té wahtan ak Omar Diagne.
😏😏