LES ADIEUX ÉMOUVANTS DE MBACKÉ SYLLA À NDÉKILI
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 9 ก.พ. 2025
- Découvrez la chaine de Sud FM avec la Revue de Presse, et ne manquez pas vos émissions préférées : Ndeki Li, Wakhtanou Fadiar, Al Kitab, Objection, et Diano-Bi.
Revue de Presse, émissions Sénégal, Ndeki Li, Wakhtanou Fadiar, Al Kitab, Objection, Diano-Bi.
#sudfm #radio #actualité
Thieye nico fokoye dielle ti kou mel ni mbacke sylla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂
Machalla SMS feliciatation tu le mérites mais il faut pas laisser la radio- emission almiback et al kitab et albidaya
Machalah hadj Mbacké 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭😭 digańiou manque
Da kaay continuer ndécki lii rk laay baayii
Vraiment nous sommes très satisfaits de cette équipe inédite ❤❤❤
MERCI SUD FM LA REFFERENCE LA DIFFÉRENCE ❤❤❤❤❤❤
YA OUZTAS MAODO FAYE TRES GENEREUX ET POLIVALANT MERCI ❤❤❤❤❤❤
ki key dafa bah trop machaAllah
Qu'Allah te facilite la mission Oustaz Mbacké Sylla. Bonne suite de carrière.
Sud fm 1ere et meilleure radio privée Sénégal.
Très professionnel et éducatif
Mbackkhe tu le mérite
Félicitations SMS vraiment tu le mérite Yalna Yalla woyafal yen bi
❤❤ machallah bone continuation ❤❤
Felicitation Serigne Mbacke Sylla qu’Allah t’assiste dans tes nouveaux missions et courage a Dj Nicola et S Maodo Faye l’emission Nég li ❤
Félicitations mbacke dou chance meritela❤
Machallah ❤❤❤
Yénal gor té raféte khol
Yalna léne Yallah takhawou
Machallah amna solo Oustaz yallah na yallah defal la fa diamAlhoumah Amiiine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤SMS MACHALLAH FÉLICITATIONS DINAGN L NEM SI NDÈKILY NAK
Machallah serigne mbacke sylla yallah na yallah defe diam ❤
Machallah oustaz mbacke silla yallna yalla yokou liane wèr🥰🥰🥰
MACHAALLAH Oustaz mbacké YALLA na yane bi woyof et merci si touche bigua indiwone si émission rafetna bonne continuation
Machalla mérité gua lou raw li yala nathi yénnén topp inchalla ❤❤❤❤
Masallah Mbacke Sylla May Allah bless you ❤️
Machallah sms félicitations 🎉🎉 yalna yalla Mayla ndam si barke s touba 🤲🤲❤️❤️
Machaallah. Plein succès dans tes nouvelles fonctions. ❤❤❤❤ 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Moi suis fan de Mbacké Sylla ! félicitation grand Patriote et K'Allah t'accompagne sur ton cheminement 💪🏿✊🏿🇸🇳
DIEUREUDIEUF SERIGNE ABDOU MBACKÉ BALA YAG FI TE WERR
Machalla oustaz mbacke ❤❤❤
Ndeysaane ❤❤niko boul dioye ❤❤mbacke foo dieum yalla nalafa yiwou yalla fek ❤❤
Machaalh yalla na yalla sam la te barkel ligeye bi 😢😢
Machala yalna yala motali inchala
❤❤❤❤macha allah Oustaz mbacke sylla ❤❤❤
❤❤❤❤Ndéyssane ya bakh rék Mbacké Sylla❤❤❤❤❤vive Sud Fm ❤❤❤❤❤❤❤
❤machalah Ya oustaz yalna yalla ande ak yaw finga jemm te oyofal laa yennnn bii amine 💕🇸🇳🇸🇳💕🇸🇳💕🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Machallah amna solo ♥️
Maouda Faye aussi yalla naka yeukatiii si kaw Bou Necke post mo Guen si mom yalla naka amm Amin
Amine ya Rabbi
MA CHAALLAH YA OUZTAS MBACKÉ DA NGA DIAMBAR YALLA NALA YALLA DOLI SOUTOURA MEY LA RÉUSSITE TOTAL DIEUREUDIEUF NIKOLAS ET MAODO❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysanne yalna yalla motali
Ma Sha Allah puisse Allah SWT continuer de vous accompagner dans votre mission Amiin
Ndeyssane Mashalla ya Oustaz yalna yalla motalii ❤
Machallah Yalla nala Yalla diapalé si barkép PSL Allakhouma ya rabi al amine adjimaine 🤲🏾
Machallah Serigne Mbacke Yalna Yanbi Oyof.
Ndaysan dioy na 😭yalnala yalla défal diam❤
Félicitations à Serigne Mbacké Sylla pour sa touche particulière à l'émission Ndekili. ❤❤❤ Big up et respect à Nicolas pour votre esprit d'ouverture et pour succès de l'émission
Pour l'amour du prophète Mohammad ﷺ Écrit (PSL) ❤🎉
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤liguey bi niépou khathinan si
ماشاءالله استاذ بكي جرجفت 🙏🏾 جزاك الله كل خير🤲🏾❤❤❤❤
Machallah ya ouztas bravo serigne maowdo
Machalah bonne continuation digagnou manké trop oustase
Tous nos encouragements et Qu'Allah le Tout Puissant lui facilite et l'accompagne dans ses nouvelles fonctions
Yallah na Yallah oyofal yen nga réussir mission bi InchaAllah 😊
Fanga dieum yalla nafa yiwou yalla dioub lou
Ma shaa Allah. Vous êtes tous de bonnes personnes. Yalla yén niép nguén am promotion
Mes sincères félicitations à vous Mbacké sylla et à toute l équipe de SUD vous êtes adorable ❤.
Machalla oustaz danga bakh rk yallana yalla samou la té arr la
😢🙏Yallna Yàlla Barkeel 🤲🤝
Machallah yalla na yalla khépe doli merci beaucoup ❤❤❤❤
Machallah yalna yalla barkel lep inchallah ❤❤❤❤❤
Vraiment nicola nite kou bakh la xol bou rafet la yoor
Felicitaciones ❤❤❤ yalla nala djik
Ndeyssane ❤
Machala mbacke silla maodo et nicola merci beaucoup ❤❤❤❤❤
Yal na yalla dolli laa sàmm ❤❤
❤❤❤❤❤❤🎉🎉li dawna yaram bonne continuation
Machallah Oustaz amna solo
Mach'Allah vous meritez cette nomination car vous êtes modeste. Ci barké wërri Shaban bi nekkal ci jam ak wergui yaram Inch'Allah
Sama khole sedna kholou daara sedna mashalla Mashalla
Machalla yallla nasa diam yange ❤❤❤
J'ai aimé cette émission,et avec oustaz Sylla je l'ai plus que aimé🙏,avec ses questions,ses brèches,ses transitions..... machallah pleins de succès à son nouveau poste🙏
Machallah Djadieuf srgn Mbakce yonou diamm
Manchan allah suis très content yallah na yallah takhawou ❤❤❤
Yalna leen yalla doolli ay ndam ❤️❤️❤️❤️❤️🌹❤️❤️🌹❤️🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹
Yana léne yalla sam doly soutoura yéne gnep oustaze mbacké yana nga am ndam ak notre cher senégal inchalla gnoune gnep féké🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Ah SMS tu vas manquer ndeki li.
Bravo à toi
Maodo dina weette sa khoulo walé.
Felicitations SMS
Félicitations ya ouztaz vous le méritez yalla na la jik ❤❤❤❤
Ho 😢 ndaye san oustaz mbacké Sylla alqoran di Nan la namou loool dh yalla xame nako mais Sant yalla rk di niane sa borom taxa woula linga yéné ci Sénégal yépou sa borom défale la ko ci barké alqoran Tay xoll yépou toyy😢🥰🙏🏽😭
Mashallah li dawna yarame yallna lenne dedo jamme yarabi Mbacke yallna yalla fefale la jamme fa gua gjeme ❤❤❤❤
Ndeysann, tu le mérites Mbacké Sylla, et bonne continuation pour la suite 🙏🇸🇳
Machalah oustaz yalla nala yalla samm, vraiment on t'adore
Yaalna yalla lërral sa mission si barké Al khourann
Félicitations SMS et bonne continuation
Nico une bonne et belle page de Ndéckili c'est fermé.merci mbacké
MANCHALAH Toutes mes félicitations ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeyssane machallah❤❤❤❤❤
Oooh li dawna yaram yallana sén djam yagu Macha Allah ❤️
Mbacké Sylla tu le mérite ❤❤❤ dinagnou wète bonne continuation . On est fière de toi 👏👏👏👏👏👏
Macha Allah 🙌🏼nii là rek ❤mbackè fii si Sud FM ak fo meuneu nekk souniou xell dall nà n'dakh Sénégal rek ngay ligeuyeul
Un homme humble et Modeste bonne continuation pour cette mission et grand merci à Niko et maodo un homme constant
Congratulations Mbacke❤❤❤❤❤❤
MAACHA'ALLAH yaa OUSTAAZ ❤
Plein de succès dans votre nouvelle aventure Incha'ALLAH 🤲
❤❤✌️👏👏machallah
Yalna yalla moottali leep 🙏🙏🙏
Olalaa tu vas nous manqué Mbacké❤ Nicolas tu m’as fait pleurer
Assalamou haleycoum oustaz mbacke silla va nous manquer de tout façon bonne chance ❤❤❤❤❤❤❤
Macha Allah le trio félicitations Oustaz Mbacke k le bon dieu t'assiste et te facilite le travail tu vas nous manquer bonne continuation et bon courage
Félicitations serigne mbacke sylla sa baol que dieu vous protège amine et tout l'équipe de sud fm
Maachallah tu mérites plus que sa je suis le même démissionné dans l'émission
❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉vraiment votre trio est excellent nous vous souhaitons plein de succès dans vos projets.
Toutes mes félicitations tu mérite cette nomination.
Macha ALLAH toutes nos FELICITATIONS Ya Oustaz
ALHAMDOULILA, ALHAMDOULILA, ALHAMDOULILA
Oh my goodness Ndekili will never be the same thanks Mbacké and good luck for your next adventure in life
Machallah Oustaz Yalna la fa Yallah défal yiw .Dama la done suivre toujours Toutes mes félicitations
Machallah ❤ mbacke ❤ yalna yàlla hép dolli ❤ lii dawna yaram😭
Mashalla mashalla mashalla ❤❤❤❤❤❤❤
Machalla machalla qu’allah vous assiste ❤❤❤
Jaambar Sylla tts mes félicitations
Masha allah Serigne Mbacké Sylla yalla nala yalla takhawo samola ❤