Wally x les jeunes talents en moins de 4 mois il a fait près de 10 featuring avec les jeunes, li niou ko banio lone a ces débuts. Le meilleur de 2024 🎉.
Wally tu es entrain de faire quelque chose d’historique avec les jeux talents bonne continuation baye fall bi ! Diaw yaw mom damalay nianal couz ci kaw ci kanam reik
Maryacine moy musique sénégalaise bi kou nangou li yalla dogual do do sonou sa khol dou diekh def len ko niko yalla def mou nopalén sounguenko defoul niko yalla def mou diakhalen bay et diaw wally félicitations 🎉🎉wally B.seck à vie❤❤❤
Où sont les Sénégalais qui soutiennent Wally B seck et Diaw Diop Didi comme moi pointez ici clip bii rafett na trop amoul morom actuellement l'industrie musique mbalax tourne autour de Wally B seck 🤍🤍🤍🌱🌿🇸🇳🇸🇳🇪🇸
Waly meune n’a trop mais nekhoul ba nekhoul Diaw diop li nga waay fii meunotoko Lii nekh na trop way ken dou ioe Diaw Diaw didi mashalla thia kaw thia kanam Niou ngi wait album bi inshalla
Macha'Allah Macha'Allah Diaw Diop wooye rek laay def. Wally Seck hooppooo pooop Wallaaahi dëga nekhoul... Wally depuis 10 ans mo yor music bi ci loxoom mais guddi yii nyi tollou Wally ab lamp la booy leéral lépp
Félicitations Diaw Diop béne jour yama féck thi talli bi Nath bou tangue dieure ma bòot sama dôm nga yobaléma soprim soula nékhone doula thi vous êtes un homme bon bonne continuation Wally seck chapeau à vous
On oublie souvent cette artiste Diop Didi mais il est très talentueux. Sa musique est très documentée et il va allé très loin car il fait des recherches et c'est un artiste plein de surprises. Mais ligne basse yi kouko def. Rangement impeccable. I like Sénégal ci kaw🇸🇳🇸🇳
01:52 ba fin bi Wally am na louko dougou bilahi li dou meune way rek rakh na ay Djinné bilahi wallahi tallahi wally yallah nala yallah sam wayyyyy amine touf touff❤
Bilahi Waly moo rafet xole waaye sa featuring national bi avec les jeunes talents takh naa ma gueune la beug 😭ya niiak kiniane té yaatou le père nationale de la jeunesse dans le milieu musical doundeul yokal weeral jtadore le faramarene de luxe 🥰♥️ DD le mec au punchline 😂🎉❤aka ame thiaasse naak🤩😅❤️❤️❤️❤️
Ehh Ana faramareen yi 😍 Venez je vous appelle ici venez soutenir Didi 🥰🤝🔥💥ay souniou wooy kat bi😍 Maryacine meissa bigué ❤ borom khol bou yatou bi mo meilleur 💪🥰❤️🫶🔥💥💥lou amoul lay defale rakam yi 😍 machalah yalla nagniou ko yalla samal le chanteur du peuple 💪👑🫶
wally fin bi nekh nama way j ai des frissons billahi notre chanteur du peuple quel duo extraordinaire c est du lourd bravo aussi à diaw diop didi bonne continuation le meilleur reste à venir🥰😍🤩😘
Félicitations 🎉 les deux talentueux de la musique sénégalaise ❤❤❤diaw on est trop fière de toi 👍 et on attend la sortie de l’album Avec trop d’impatience
Son bi aussi nekh na trop, wally yaram bi tang na 2 clips en même temps yep di dokh 😃❤️ Diaw machalla aussi Wally ay ndanane rek lay woyandol. Mais j'ai pas encore vu le son sur les autres plateformes de streaming
Kou sétane clip wally ak Baye mass sogua gneuw fii 😂❤Lalale j’aime
Magui ni
Magi nii😂
Nagnou koy jongler rek😅❤️
Mane bobou g pas vu de clip son bi rek la guiss
Je ss la🎉
Wally x les jeunes talents en moins de 4 mois il a fait près de 10 featuring avec les jeunes, li niou ko banio lone a ces débuts. Le meilleur de 2024 🎉.
Blh réponse Bou soft adouna amoul Solo Li wanéna danio wara diapalaneté
Jaambar Leu Xolam Sét Manchallah Motax Rabana Mayko Li Yeup Surtout Ak Nianou Wadiour 🫶🏽✅🫡
Malako wahhh d il a un ❤ en or walay❤❤❤❤
@@fatoufall9623 Késsè Sénégal dieum kanam.
Combien de fans Internationaux pour soutenir Wally Seck et Diaw Diop ? 🔥
Nieuweutinga 😂😂😂
Ti saluto 👋 ❤
@@mormbaye2989 wawaw😅
😢🎉🎉
Chaque fois qu’une personne mettra un like je reviendrai réécouter ce chef-d'œuvre 😊❤
Comment voir les notifications de commentaires sur TH-cam please
@@fashubaby7909sur votre adresse mail . Moi je reçois les notifications là-bas
@@fashubaby7909si page accueil bi si kaw amna clos boufa nék fofou la
Si baye mass la diougue mais wally mi esk werrr neu nak 😭😭😭❤️🇸🇳🥇meilleur homme
😂😂😂😂😊
Mane sakhe fofou la diougué
Bilahi ioe
Ak mane
Mm trajet q toi 😂 et tant d’autres
Kou diougué si clip wally ft baye mass gneuw fi😂❤
Mane mii
Mane 😂😂😂😂
Moi 😂😂
Mes nawlé 😊
Moi
Si tout le monde faisait comme wally on aurait un Sénégal exceptionnel liko chanteurs you bari done bagnale lay défale boy yi Mancha alla ♥️
Vérité absolue khôl bé rafet machalla ✅goudou fan ak wergou yaram lakoy gnanal🙏
dama khol wally kholateko sama beute yi tas wally yalla nala yalla sam
Amine way ❤
Amine yarabi
Aka meilleur kay❤❤❤❤
Dou yow kesse dafa bakh machalla wally rék
Amine waye ki mbax rek mo nek si mome❤❤❤❤❤❤
Une trés leçon que Wally donne aux autres artistes, nék thi kaw wagni woula dara nga xeuth gnithi souf…
Wally tu es entrain de faire quelque chose d’historique avec les jeux talents bonne continuation baye fall bi ! Diaw yaw mom damalay nianal couz ci kaw ci kanam reik
Waa Mar nii ngua mél yako tay😌 non nékhoul bah nékhoul mais tu es le meilleur ❤🎉
Koulene khar yalla na khadi
Yalla yague weral bate yi thi barke seydina mouhamed psl
Tieuy maryacine diam rék inch'Allah Wally seul point ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
La voix de DIDI,on en parle please 😢🎉❤
Quelle puissance vocale 😮
Damani taay maffi djitou si janatou bignouy xaar tei naara yeungeul avec son excellence 🌟 ❤❤😊
Wally. Disc Dor 2025 inchallah
Ana bandit gameur yi wally mo ndang ndy musique galsen c'est le meilleur de tous les temps
Kou sétane clip Baye mass ak wally seck d'abord soga nieuw si clip lalal j'aime ❤.
Wally nak mo pougné music sénégalais fi rew mi dolou ni machalla ❤
La voix de wally est juste exceptionnelle ❤
Maryacine moy musique sénégalaise bi kou nangou li yalla dogual do do sonou sa khol dou diekh def len ko niko yalla def mou nopalén sounguenko defoul niko yalla def mou diakhalen bay et diaw wally félicitations 🎉🎉wally B.seck à vie❤❤❤
Ma diougué si ya tay ak baye Mass 😂dall si janatu tay la xamni wally moy Sénégal 🎉❤ bly mar Yacine ya khéré 😊
La différence de voix non Waly trop fort ❤
😂😂😂 lo beug wax fofou
Où sont les Sénégalais qui soutiennent Wally B seck et Diaw Diop Didi comme moi pointez ici clip bii rafett na trop amoul morom actuellement l'industrie musique mbalax tourne autour de Wally B seck 🤍🤍🤍🌱🌿🇸🇳🇸🇳🇪🇸
Diouguer si bay mass dall si didi Yalla bakhna gnanal lene ko diam Mar yacine ❤❤❤❤
Diaw mi meune n’a mais kenn dou wally yalna djam yagu senegal
Le meilleur de sa génération kouniou ko teukalleil nakh nakh naniou la❤❤
Fii laa ndieuker bouma parer demm sii baye Mass ✨🤗 Mar lo bokk mounekh
Waly meune n’a trop mais nekhoul ba nekhoul Diaw diop li nga waay fii meunotoko Lii nekh na trop way ken dou ioe Diaw Diaw didi mashalla thia kaw thia kanam Niou ngi wait album bi inshalla
Waly seck est déchaîné. Bagn bagn nangou. Kou yalla tatchoul gneupeu koye moudjei tatioule. 02:33Waly seck naak gnoune gneup leu moudjei beugeu. Mashallah danga meune. Didi aussi un talent pur. 🇸🇳🇸🇳🎈🎈🥰🥰. Le Sénégal aime
encore waly😂yalla gua goudou fan si barki seydina mouhamed notre fierté🙏🏻❤️❤️
Wally daal yaffi neh le messi de la musique sénégalaise wawaaww💪💪❤❤❤
Diougué si ya tay nieuw janatou wa li nekhoul rk❤
Thiey wally dagua meune pire kirasoulilah meune ngua trop wayy❤❤
Le sang ne ment pas ❤️🔥
C le fils de papa thione
Macha'Allah Macha'Allah Diaw Diop wooye rek laay def. Wally Seck hooppooo pooop Wallaaahi dëga nekhoul... Wally depuis 10 ans mo yor music bi ci loxoom mais guddi yii nyi tollou Wally ab lamp la booy leéral lépp
Félicitations Diaw Diop béne jour yama féck thi talli bi Nath bou tangue dieure ma bòot sama dôm nga yobaléma soprim soula nékhone doula thi vous êtes un homme bon bonne continuation Wally seck chapeau à vous
Wally bou nieup défone ni yaw kene d'où sone exemple là pour nieup❤❤
Diaw diop wallah dafa meune weuy❤️🔥🔥🔥🔥wally meme keine wakhatoul ay wakham neuwone fa wone❤️❤️❤️❤️
Wally ballon d'or de tous les temps li leçon leu pour yenen artiste yi qui copie Wally defna deflen
Wally meun nga soleu lou rafet nak ❤️🤷🏻♀️diaw diop Nice 🫶🏼
On oublie souvent cette artiste Diop Didi mais il est très talentueux. Sa musique est très documentée et il va allé très loin car il fait des recherches et c'est un artiste plein de surprises. Mais ligne basse yi kouko def. Rangement impeccable. I like Sénégal ci kaw🇸🇳🇸🇳
Wally nawlé da fort. Jador cette complicité avec les jeunes de la musique Sénégalaise. Bonne continuation ine sha Allah guys love you all❤❤❤❤❤❤❤❤
Wally loum niou beugeul nak 😭😭🥰🥰🥰♥️♥️♥️♥️♥️♥️ diougué si mok baye mass dall si li 🙈🥳
Duo bi coll na nekhna trop waÿ ❤️🎤🎧wally pétri de talent 🎧
Wally kay mo gnak kignan ❤❤❤❤❤❤❤❤❤lii nekh na machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Qui de Diaw Diop et Baay Mass auras plus de Millions de vue🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤ Wally a vie❤❤❤🎉
Oh wally yagui may chance khalé yi nak ❤❤❤machallah
Aziz dabala soufi nékone ba fétie ko😢 gnou guissé Lou Nice yalla nako yalla yeureume❤❤
Xana sa wa keur da am kou bokone si groupe aziz bi😂
@ louy lolou dama guiss ni soufi nékone dinagne guiss chorégraphie bou nice
@@lingkhadidaiwvrema 😢Ndeysan kou meunone limouy def correcte baparé am si yeuk yeuk❤paix à son âme
Stp ma sœur boul tontou commentaires you négatif yii
Wa li nekh na way sheuuuu wally bale ñou ❤❤
Wally machallah li nékh na trop ms duo bo meus déf yak ameudeus moma dakal🎉🎉❤
Diaw tu est vraiment fort 💪 mais wally dou nitte quel reprise ❤️❤️❤️
That Wally seck part is just amazing❤❤❤❤ wow
Diaw kou yagua deguelou khamni music dagua KO meune rek machallah
Diaw je m'abonne ngir wally seck 🥇👑🎤💰🌟🤍guinaaw YALLA☝🏾
Wally moy Sénégal wally moy musique Sénégal
Diaw Diop 😍 Machallah
Mais Chapeau à Wally mongui déff liguéy bou amm solo 😊❤
Waly anh no li eupeuna wayyy hooooo Diaw tamite tarkala❤
Ohhhh li nékhna way tu as encore frappé mn frère comme dab ❤
Diaw ndanan la love from gambie
Wally seck le chanteur du peuple diaw diop machaala ❤❤❤
Machalla l'international diaw diop didi nekhna yalla nala Yalla geuneu doli diam ak wére gua geuneu siww barké baye laye barké mame seydi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay wally dafa meune loumouy deff mo takh ragaloul futuring Avec tout le monde c’est le meilleur
01:52 ba fin bi Wally am na louko dougou bilahi li dou meune way rek rakh na ay Djinné bilahi wallahi tallahi wally yallah nala yallah sam wayyyyy amine touf touff❤
barki yalla🥹
Kou diougué si clip wally ft baye mass gneuw fi🤔🤭🤗😌🤣😅
Le feat tant attendu enfin Diaw diop feat Waly ça pourrait qu’être cela que tu lourd ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Dama diogué si wally ak baye mass bi rkk diarr fi beug xam noum démé fi kw🙌🏿😂❤️🔥🥰
Bilahi Waly moo rafet xole waaye sa featuring national bi avec les jeunes talents takh naa ma gueune la beug 😭ya niiak kiniane té yaatou le père nationale de la jeunesse dans le milieu musical doundeul yokal weeral jtadore le faramarene de luxe 🥰♥️ DD le mec au punchline 😂🎉❤aka ame thiaasse naak🤩😅❤️❤️❤️❤️
Wally moy ndey dji cheikh diankha nay la teudé 🎉🎉🎉❤❤❤❤
Wally mii machallah ❤❤❤❤😢
Léguii mann sama question moyy Janatou moyy lannn🎉🎉🎉
Aldiana
Kou contane rek lalale j’aime ❤
Thieye sapeur pompier bi Wally Ballago Seck ya meune nake bonne chance thi la 07 décembre inchalla diame rék ❤❤❤
Ehh Ana faramareen yi 😍 Venez je vous appelle ici venez soutenir Didi 🥰🤝🔥💥ay souniou wooy kat bi😍 Maryacine meissa bigué ❤ borom khol bou yatou bi mo meilleur 💪🥰❤️🫶🔥💥💥lou amoul lay defale rakam yi 😍 machalah yalla nagniou ko yalla samal le chanteur du peuple 💪👑🫶
Grâce à wally B seck je m'abonne de votre chaîne TH-cam, excellente clips
Aythia l’artiste Diaw diop didi Yakofa am iao parol yi niice timpo bi a la hauteur, Djadjeuf Wally yako thi dara
wally fin bi nekh nama way j ai des frissons billahi notre chanteur du peuple quel duo extraordinaire c est du lourd bravo aussi à diaw diop didi bonne continuation le meilleur reste à venir🥰😍🤩😘
Wally the king of The new generation…. Love from the Gambia ❤🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Franchement Wally nous sommes fatigués dire que t'es le meilleur de tous les temps tu t'aadapte à n'importe quelle musique j'aborde ta polyvalence
Wally seck un homme avec bon coeur que le protège faramaren Wally Ballago seck
Kou Diougué ya Tay nieuw janatou lalal❤❤❤
Nionguiniii 🤧😂
Suis làaaaaaasa🎉🎉
😍😍diaw diop didi un chef d'œuvre ❤❤sa voix machalla magnifique
Machallah nioune Faramareen yeupou contane nagne❤️❤️❤️🎉
Félicitations 🎉 les deux talentueux de la musique sénégalaise ❤❤❤diaw on est trop fière de toi 👍 et on attend la sortie de l’album Avec trop d’impatience
Maryacine nak y’a meune pirrr 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤Machallah Diaw
Machala Didi le meilleur de sa génération
Thank you wally🎉
Son bi aussi nekh na trop, wally yaram bi tang na 2 clips en même temps yep di dokh 😃❤️ Diaw machalla aussi Wally ay ndanane rek lay woyandol. Mais j'ai pas encore vu le son sur les autres plateformes de streaming
Oh DiDi y’a man way Wally Machallah
Félicitations Diaw Didi. Franchement tu as dead ça avec un nouveau style de mbalax ❤🎉
Machallah vous êtes les meilleurs ❤
J'adore ❤ je te kizzzz depuis Guinée Conakry 🇬🇳❤️
Macha'allah yallah Nala yallah weral batbi bi si barké Seydina Mohammed Saw ❤️👌
Diaw diop yay waga mais li nicena waly vraiment merci a lui il faut qu il fass des sons a tous les artistes
ndeye san li dafa nékh❤
succes yalla mokoy méyé mais senegal ay chanteur rek gnofi nek baye mass didi amadeus ash the best ay voix you nekh lagnou ame meune woy teksi
Diaw diop est très talentueux Vraiment ❤
Rendez vous le 7 décembre adidas Arena avec walyséck
Ohhhh voix de Diaw diop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane dei featuring wally ak Sidy diop la yakamtii 🎉🎉🎉❤
Jajeuf frères nice clip vraiment 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Parti wally bi damako deglou ame ay frissons😍