❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤mashaa Allah Cheikh Bara linga amna solo khale yi amatouniou kilifa way liko waral moy danio guissatoul kilifa Papa yagui sokhan yaye yagui daw louniou am ken talatoul yar
Salaam. Il n'a pas di être contre l peine de mort mais qu'on est pas dans les dispositif de l'appliquer. Et il suffit de prendre le cas de la Mecque comme tu dis. Leurs juges ont appris la charia, ici tu ne peux pas demander du jour au lendemain qu'on appliqué ça avec cette justice qu'on a. Ya des préalable à tt presque.
Ndeysane cheikh Bara lim wakh dafa am solo wek ak di wakhtan ak sa parent yi surtout sa Baye. Sama Baye ba yalna ko yallah yeurem leup len dan wakhtane apres resultat bu positive ngasi dieule MashaAllah Man mom sama digantek tiktok amna problem damaye tok aye 1mois dumafa dugu tayal ko setane 😅 lo kham ni du diekh danagye dem rek amoul fin mom du diekh 😅
Chéikhe bara khana daga fogeni macky salle ak gayomi gno nék thi gnoure gui ba lègi fi kou fiye bagne pen de mort dagno rèyagoule sa dome) lègi yowe thi atè yalla gnaye oposèwou kw ☝️
Yag nala deglou Mais tay andou ma ak yaw ligne wax Moy kou Ray nite Ray you Meetic comme genrou Aziz dabala wala ay drame you Meeti mais ay accident wala erreur dousi bok
Atté yalla meunta andi diafé diafé epui macky nekatoufi Antoine newoufi ... Kou ray dagn la wara tay danio rayoul koula Diègué rkk.... Lii dou affaire politique
Seex Baara jàmbaar la lool waaye mbirum gis gisu diine dacee faible trop ku ray ñu ray moom kase mooy solution, yàlla neena: seen dundu mu ngi ci teg fayantoo ci ak tooñ ba noppi teg ci yéen ñu boroom xel yi(ولكم في القصاص حياة ياأولي الألباب لعلكم تتقون) Ku ray ñ ray la su amul fii ak 5 ans dinañu ray nombre boo xam ni du tollu mukk sunuko tegee Seex Baara am nga xel lool waaye lu yàlla wax du xel mookay àtte lima bëgga leeral yëpp sax xajul fii
@@deggeurhour34 kan mooku yore woon banukay teg ci réew mi ? Du jëmmi sariha mootax nuy wax waaye lifi amoon ba 2004 mootax nuy wax, waaye Seex Baara dafni nangu na li yàlla wax mais mais mais lu tax mais jubadi gi askan wi jubadi moo tax mu laaj nu delloo si lawoon
plus fort plus fort ngala wax koko.....musique moussiba la...les artistes profitent pour distiller des perversités de toutes sortes. Fécc mom c'est la manifestations du rut animal. L'humain doit s'élever par de nobles occupations.
Je ne suis pas d'accord avec vous sur les arguments que vous avancez contre la peine de mort. Elle n est pas seulement une affaire de l Islam. Tout juge incapable d appliquer la peine de mort, est incapable d appliquer toute autre peine aussi légère soit elle.
Xam xam kèssè la Cheikh Bara Billahi
Diadieuf Ndiaye kawéna lèrna machallah❤❤❤❤❤
Quand j'écoute cheikh bara je ressens un plaisir énorme
Macha'Allah, Diaradjeuffati Serigne Cheikh Bara Ndiaye, Yalla nala Yallah samma tà goudale sa fann thi barcké Mouhamad Rassoulillah Amine 🙏🏿🙏🏿👍🏿👊🏿🇸🇳♥️
Merci cheick bara doou probleme insecurite mome
tres tres belle analyse foumou tamalé sa fait rire mais en fin sa apprend machallah
Bilaye pure vérité la wakh😂
Il a entièrement raison
Très pertinent toujours égal à lui même
billahi kii jeune yeupako warr di deuglou ❤️
Cheikh Bara du dém🤣🤣🤣 barkélu...il maîtrise bien notre société actuelle.
Sacré cheikh Bara ndiaye machalla tres pertinent vraiment 🎉
Sacré cheikh barra ndiaye kou xam adouna migui ni machallah
Cheikh Bara khalif général Koulou analyste
Excellent Chéikh Barra Ndiaye
MachAllah cheikh bara contan ci yow
Excellent cheikh bara le meilleur de sa génération ❤
😂😂😂😂😂😂 bilay c vrai cheikh bara yalla n'a diammm yague
Bara daale manchallah
Ma chalah jeureujeufe chiekh bara Ndiaye nala yala defal diam ❤❤❤❤❤❤❤❤
Il est excellent 😂😂😂❤
Il est tres intelligent❤❤❤
😂😂😂😂😂😂😂 cheikh bara billay akka hamme adunaaa un vrai sociologue
Cëy jii waay!
Une Demande social Cart Cart Séjour pour pour les qui vie au Sénégal 🇸🇳
machallah Cheikh Barz
Très pertinent cheikh Barra
Cheikh Bara raay nama waay😂😂😂
Dieura dieufati Cheikh Bara Ndiaye sa wakh dji Am na solo deh machallah 🥰❤️🥰
Vous avez raison cheikh bi walay ndeysan
jarejeuf serigne bara
Tay mom dacorouma ak baye bara si peine de mort biii. Mais comme d'habitude wax ji rafetna barry na enseignement ❤
Djaadjeuf
Loutah dakooroo segn bi??
Kou hamee adouna moy chiehk bara djadieuf amal djam
Mach Allah cheikh bara 🎉
😂😂c de la *pédagogie* , so gorgorlou woull sokhna si gnibii😅 sou gnibé doto khéww lou😂😂
Mâcha Allah, très pertinent 🎉
Mouhamed Diallo sonou na ndeysan 😂😂😂😂
Mercredi cheikh
sacré. Cheikh Bara
Merci beaucoup 🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤mashaa Allah Cheikh Bara linga amna solo khale yi amatouniou kilifa way liko waral moy danio guissatoul kilifa Papa yagui sokhan yaye yagui daw louniou am ken talatoul yar
Votre meilleeure emission!!!!
Billahi cheikh bara li mo am
Machallah
Excellent
Kaay Barkélou😂😂😂😂
Mouhamed Barkelou nior nako dh 😂
Sàngg Cheikh Bara Ndiaye ❤
Tu as raison
Le seul sociologue digne du titre du plateau c’est Serigne Bara NDIAYE.
Cheikh bara ndiaye Défa Sa Xel Dalaye nakh yalla Monou enpou yeurmadé Maka ay Nit niofa Nékki Com nioune Té ngi kaye Déff
Salaam. Il n'a pas di être contre l peine de mort mais qu'on est pas dans les dispositif de l'appliquer. Et il suffit de prendre le cas de la Mecque comme tu dis. Leurs juges ont appris la charia, ici tu ne peux pas demander du jour au lendemain qu'on appliqué ça avec cette justice qu'on a. Ya des préalable à tt presque.
Ndeysane cheikh Bara lim wakh dafa am solo wek ak di wakhtan ak sa parent yi surtout sa Baye. Sama Baye ba yalna ko yallah yeurem leup len dan wakhtane apres resultat bu positive ngasi dieule MashaAllah
Man mom sama digantek tiktok amna problem damaye tok aye 1mois dumafa dugu tayal ko setane 😅 lo kham ni du diekh danagye dem rek amoul fin mom du diekh 😅
Magal gi rén sourouma 😢
Cheikh Bara 😂😂😂 quelle sociologue
❤❤❤❤❤
Kagne lay barkelou 😂😂
😂😂😂😂😂😂
Tackal sokhna😂🤣😅
LA RÉPONSE DE CHEIKH BARA SUR LA PEINE DE MORT EST VRAIMENT SAGE MÊME SI JE SUIS FAVORABLE À CELA
Cheikh baaara bounou sonnal nak, kou yalla may kheil ngua ma cha allah, mais bou yalla wakhei mome ak loo neikh kheil sayyy xalaat conteitoul
Masallah 🎉🎉🎉😂
Cheikh bara koumouyapp. 😂😂😂😂
Diallo say say deug la 😂😂
Barkéloulén sama commanter bi😅
Cheikh bara soff😂😂😂li nga niam boko bayei adouna touki😂😂😂😂
,😂😂😂😂😂😂😂cbn DIEUREDIEUf
Ki mome rélo mana ba sama biir di méti : ko nouyou mouni kaye barké lou😂😅
Fi Sénégal lanlagn fiy até si diné amoul sougn djogué nane yalla
Mansour dafeu am abitude sou nite yi di wah mouy seugg si telephonam rek
Rew mi amoul koubér kou diouk doug kay
Do wakhe séni PM
li mou wakh ci kewel ak khar tegal na ko ci len khar mo gueuneu douf te reub rombe na ko fa dem outi kewel
Bara yangui nelaw nak 😂 Adamo nak
Chéikhe bara khana daga fogeni macky salle ak gayomi gno nék thi gnoure gui ba lègi fi kou fiye bagne pen de mort dagno rèyagoule sa dome) lègi yowe thi atè yalla gnaye oposèwou kw ☝️
Tay mom dafa wéré Macky newoufi mom da fok ni lep politique la
Cheikh bara ndiaye amoul kou koi😅
Même si un sorcier tue une personne sa joue sychologiquement defois mou doff donc niit dafa fort
bo beugee barkeelou faww nga ligeey billay😅
Yag nala deglou Mais tay andou ma ak yaw ligne wax Moy kou Ray nite Ray you Meetic comme genrou Aziz dabala wala ay drame you Meeti mais ay accident wala erreur dousi bok
Walay wakhega degue
Atté yalla meunta andi diafé diafé epui macky nekatoufi Antoine newoufi ... Kou ray dagn la wara tay danio rayoul koula Diègué rkk.... Lii dou affaire politique
Ta tout compris il manipul
Cheihk bi wahkou yalla amoul c’est à dire
Ndeysan aduna mom ndinketé amo xam xam diné wakh ak nekh lamigne rk mola topou
Wax ju am-solo la wax nan si bayi xél bu baax
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Seex Baara jàmbaar la lool waaye mbirum gis gisu diine dacee faible trop ku ray ñu ray moom kase mooy solution, yàlla neena: seen dundu mu ngi ci teg fayantoo ci ak tooñ ba noppi teg ci yéen ñu boroom xel yi(ولكم في القصاص حياة ياأولي الألباب لعلكم تتقون)
Ku ray ñ ray la su amul fii ak 5 ans dinañu ray nombre boo xam ni du tollu mukk sunuko tegee Seex Baara am nga xel lool waaye lu yàlla wax du xel mookay àtte lima bëgga leeral yëpp sax xajul fii
Merci waxal ngama lep mom rkk lay suivre mai diné mom dasé faible trop .... Atté yalla meunoul Andi diafé diafé mouk ..
Wa ma laadj la
Kane moi wara djemeul attee bi?
Ndah daniouy tek tribunal charia pour les meurtriers ?
Gni eup ci sunu attee Kat yi mandou wouniou
@@deggeurhour34 kan mooku yore woon banukay teg ci réew mi ?
Du jëmmi sariha mootax nuy wax waaye lifi amoon ba 2004 mootax nuy wax, waaye Seex Baara dafni nangu na li yàlla wax mais mais mais lu tax mais jubadi gi askan wi jubadi moo tax mu laaj nu delloo si lawoon
plus fort plus fort ngala wax koko.....musique moussiba la...les artistes profitent pour distiller des perversités de toutes sortes. Fécc mom c'est la manifestations du rut animal. L'humain doit s'élever par de nobles occupations.
Je ne suis pas d'accord avec vous sur les arguments que vous avancez contre la peine de mort. Elle n est pas seulement une affaire de l Islam. Tout juge incapable d appliquer la peine de mort, est incapable d appliquer toute autre peine aussi légère soit elle.
Wa louthie yonou Macky Sall
Bilay ya bari kham kham cheikh bara
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤