TOUNKARA AVERTIT WONE NGA GNOU SI RAN YAFET SCANDALE FONCIER, TU DISAIS QUE POURQUOI AUCUN JOURNALISTE SÉNÉGALAIS NE PARLAIT DE CETTE AFFAIRE VOUS AVIEZ RAISON AMOU GNOU VRAI JOURNALISTE AU SÉNÉGAL ILS N INFORMENT PAS.
😂😂 sacré Tounkara. Bon lolou kañ lay gueum né amna mooy suñu yobouwé macky tribunal. Mais à part ça sawaay yii ni diékhna baye nañu bayi wax ji té dimbali président mou liguéye il a besoin de tous les citoyens sénégalais pour defar deukk bi. Yiii ñuy deff ni retardement leu amoul bénn ndieuriñ. Ani Samba Ndiaye épinglé wuñuko animou do mo ñu gueuneu diégué duñu lidianti cas wam. A bird in the hand wrote two in the bush ( pithie binga tèyè sa loxo mo gueun fouf gnaar yi nekk ci buissons yi). Donc comme ke mi gui tokk nice ndax nguur lay ligueyal nañu bayi thiakhaan yi té gueuneu sérieux le pays en a fort besoin ins yi. Nitt yo xamné ils ont la HAINE dans leurs coeurs, kou am HAINE meuno am QALBU SALÎM. Té kou amoul QALBU SALÎM dagg ga sa lien ak YONENTE BI SWS mooy guéneu ga ci diiné gui.
Bien parlé mon frère na justice déf liguéyam
Dans tous les cas, il faut que justice soit faite...
Le vase a débordé. On a trop laissé faire. On a trop laissé dire...Et voilà !
Tange mbaame piir la,nagnou nanguou terrain boobou
Merci de continuer à protéger le PROJET.
Tous les muscles de ingane diakhaté se dilatent quand il parle de sonko.😅😅😅😅😅
TOUNKARA AVERTIT WONE NGA GNOU SI RAN YAFET SCANDALE FONCIER, TU DISAIS QUE POURQUOI AUCUN JOURNALISTE SÉNÉGALAIS NE PARLAIT DE CETTE AFFAIRE VOUS AVIEZ RAISON AMOU GNOU VRAI JOURNALISTE AU SÉNÉGAL ILS N INFORMENT PAS.
Amoul ay client mais tailleurs là😂😂😂❤
🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤❤❤
💚💚💚💚💚❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏽🙏🏽
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🇲🇷
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Billakhi paracerer bi doufi def dara gayi legi lou len nekh wakh