Borom rew mi yaw daga wathie Sénégal té Sénégalais yii parer gouniou pour kou melni yaw. Daga niou devancer trop machALLAH. Figay wakhé nioune tollou wou niou feu machALLAH. Yal neu ALLAH dolli lepp ak jamm ji.
Salam BOROOM reewmi vous avez des suggestions très intéressantes et pertinentes. Foo diaar yoon lah . Qu'ALLAH swt te garde et te protège de tout mal .
Bonjour, je fais partie de tes fans. Je suis totalement en phase avec toi sur les critiques destinées à mon jeune frère Thione Niang. Ayant vécu plus de 25 ans en Amérique, je suis surpris de la position politique antagoniste de ce garçon envers Ousmane Sonko. La réalité socio-politique du Sénégal est tout à fait différente de celle des États-Unis. À sa place, il aurait été beaucoup plus intelligent de soutenir le projet de prise du pouvoir et de participer à la transformation sociale. Thione Niang, si Dieu le veut, aura le temps d'aller à la conquête du pouvoir. Il est mal parti avec ses bourdes. Borom rewmi, reste solide sur ta ligne éditoriale.
Très pertinent et rigolo en même temps , merci borom rewmi lol 😂 Mais dama ragual niou acharnè wou thi yaw entre le scandale Ndella madior qui a fait un tollé et ce thione Niang qui à débarqué de nul part. Yalla nala yalla sam dieuredieuf 🙏🏽
Merci waay borom rew mi. Bouleu kenn yap. Si liga nekk lolou leu. Seu vidéo bou 13 bi dara nekkou si ndakh Thione dafa défone erreur de communication rattraper wou neu après ak annonce que moudiou neu matal 30 millions. Wayé thione parrainages yii legn lay ladj fossi tollou. Thione fo dieulé ay parrains?
Wahou ma la borom rewmi dako wahh la def sama diangate sou démé aye lathie pour gnou cotiser pour caution présidentiel legui bou gngner woule Di à delo gni cotiser est ce que
@@dieynabadiop2681 merci Soxna Dieynaba si réponse bi. D'accord question borom rewmi kw, am na solo! Mane moom dama xalaat nè borom rewmi " wagni dolè ak yokou dolè" motakh mou def vidéo bi, mais jarouko woon. Parce que gni di cotisé geum geum motax nioukoy def. Et bougnou jawalè question Bou rafet ak question bougnou rafetal namm si leneeen. Xam nga Sénégalais xol lay demè motax Mou nexa jobalè. Juste sama xalaat la rek si xalaatou Borom rewmi . Jajeuf Soxna Dieynaba Big UP borom rewmi
Borom rewmi😂😂😂 walay hassim ya khoromou rèk ..bon iow aussi comme tu le dis a thione niang warone preparè ni bo lalè thione wala kènèn koumou meuna nèk ay partisan wame dinagn la tontou dinagn la wakh aussi sèn khalate
Je te croyais plus intelligent que ça comment peux tu khepp nitt si ay commentaire inconnu je suis avec toi sur ton premier vidéo si ça façon de communication mais par contre les commentaires mom lolou warosi won sah wakh paske sen xalat lagnoy wakh que ça soit Lou bakh wala lou bonn niom leu concerne
Yawmi ya khoromou. Sa estime Bou wagné ko si qu'est ce que ça fait. Vous du pastef vous peur réponses amoulene esprit de dépassement. Tu ne peux pas pousser ta réflexion pour savoir que ce n'est pas Thione Niang qui t'a répondu mais des jeunes comme ceux de Sonko qui insultent à chaque fois quelqu'un donnait son avis sur sa façon de faire. Encaisser moo yomboul. Boroom rewmi ya khoromou 😂😂😂
Kii dou boroom dara moom visage de gorille moko gueunal propre visage boppam 😂 Ñii daniouy fontou rekk naan bureau 😂 Ce sont des complexés de première classe 😂 Ñii bou TH-cam amoul woon douniou wakh fènn 😂 ndakh ay doff laniou 😂 Ish Sénégal même pour amm carte d’identité dafa waroon amm parrainage 😂 conne genre yii yeupp douniou doon citoyens mais plutôt des marginaux 😂 Poltron qu’il est 😂
Faut pas assimiler ces fanatiques à Thione puisqu'il en existe dans tous les partis. Peut être même que le gars ne les connait mm pas C'est comme ces insulteurs qui se réclament de Pastef
Thione door Kate bou mak la ! Pourquoi attendre 2 mois des élections pour se présenter ? Pourquoi ce Thione ne s’est pas présenté aux élections locales et législatives? Pourquoi il attend juste sapres avoir été reçu par Macky?
Majestueux. Réponse élégante et sans injures. QUEL TALENT ! ❤
Borom rew mi yaw daga wathie Sénégal té Sénégalais yii parer gouniou pour kou melni yaw. Daga niou devancer trop machALLAH. Figay wakhé nioune tollou wou niou feu machALLAH. Yal neu ALLAH dolli lepp ak jamm ji.
Salam BOROOM reewmi vous avez des suggestions très intéressantes et pertinentes. Foo diaar yoon lah . Qu'ALLAH swt te garde et te protège de tout mal .
Vrai visionnaire borom réwmi que dieu te garde longtemps avec la santé Assalamou Aleikoum
Merci bcoup pour la pertinence de tes analyses j'ai cerfé par hasard mais je te dit sincèrement que je suivrai ttes tes sorties. Bonne continuation
Merci bro très pertinent
Merci beaucoup frère ❤❤😂❤
Très pertinent ce monsieur, bravo on a besoin d’un Sénégal nouveau ❤❤❤❤❤
Salam borom rewmi tes analyses sont tres pertinentes.Que le bon Dieu te protege
Walay hazim brom rewmi moxoromo rk 😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Billaye wallaye mo khoromo rék 🤭thiey Thione mi 🤣😂
Merci Borom Rewmi. Toujours pertinent très cohérent. De très belles analyses….( ma sathiatt sa expression bi: walaaaaa assssiiiiii )
Borom rewmi deug deug ya teye rewmi
Thione da fouy rek. Macky mo takh golo bou diouk begue nek président
Tu fait des analyses tres lucide trop même ❤❤❤❤❤
Bonjour, je fais partie de tes fans. Je suis totalement en phase avec toi sur les critiques destinées à mon jeune frère Thione Niang. Ayant vécu plus de 25 ans en Amérique, je suis surpris de la position politique antagoniste de ce garçon envers Ousmane Sonko. La réalité socio-politique du Sénégal est tout à fait différente de celle des États-Unis. À sa place, il aurait été beaucoup plus intelligent de soutenir le projet de prise du pouvoir et de participer à la transformation sociale. Thione Niang, si Dieu le veut, aura le temps d'aller à la conquête du pouvoir. Il est mal parti avec ses bourdes. Borom rewmi, reste solide sur ta ligne éditoriale.
Masha Allah borom rewmi vous faites des analyses trop pertinentes Masha Allah. Yalla boula thiat dougg ndakh thiat dafa gaww legui trop
Très pertinent et rigolo en même temps , merci borom rewmi lol 😂 Mais dama ragual niou acharnè wou thi yaw entre le scandale Ndella madior qui a fait un tollé et ce thione Niang qui à débarqué de nul part.
Yalla nala yalla sam dieuredieuf 🙏🏽
Sonko rek ❤❤je❤
Kou beugue Borom rewmi rek lalal j'aime ❤❤
Borom rewmi mane yaw rek laye top wakhal liula nekh ❤
Merci borom Réwmi
Borom Rew Mii Borom Deux Minutes 😂😂😂 Yafii Neek
Dokhalal ba kene lalla 😂😂😂😂
6 moy 9. Thione doorkat leu comme le systeme actuel. Il a besoin de revenir sur terre. Humilité loumou leu mayoul doula ko khagne.
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🎉🎉🎉🎉🎉 RESPECT BOROM RÉWMI
Du courage, ça veut dire que vous n'êtes pas n" importe qui, on vous suit ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amal diam respect a toi borom reewmi
❤merci beaucoup c lucide
Mashallah yalna yalla samla amna sollo trop ❤
Borom rewmi un homme très intelligent
Daa dege lolu yoombe wayy 😂😂😂
Merci borom rew mi
Mais boy tu es tres pertinent machalla 😂
Non dafa am ñiou kham né dagnou khamoul billhay borom rew mi
AbdoulayeSylla moy #YoonWi 💪🏾🔥🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪🏾😍😍🇸🇳🇸🇳😍😍 #C50PN forever
Borom rew mi ziarnalen nka yité yi 🇸🇳💪❤️
❤❤❤❤❤we love you borom rew mi long vie a toi
Respect borom rew mi
C'est vérité❤
Un choix évident pour le changement positif Abdoulaye Sylla #YoonWi
#AbdoulayeSylla #ABS2024
Thione Niang , SI MACKYSTE yi la boke 😂😂😂😂
Tieuy le " propriétaire du pays "!!!
Merci waay borom rew mi. Bouleu kenn yap. Si liga nekk lolou leu. Seu vidéo bou 13 bi dara nekkou si ndakh Thione dafa défone erreur de communication rattraper wou neu après ak annonce que moudiou neu matal 30 millions. Wayé thione parrainages yii legn lay ladj fossi tollou. Thione fo dieulé ay parrains?
Thion manta ganierr konuammm
Kan moy thion niang
Pertinent frère ❤❤❤❤😂
Thione mana Toul door kéne
Soxna Dieynaba siar Nala.
Pourtant Thione xamewougn ko door dh, tè Borom rew mi waxoul nè door kat la.
Da am silo japp, wala danga kaff?
Wahou ma la borom rewmi dako wahh la def sama diangate sou démé aye lathie pour gnou cotiser pour caution présidentiel legui bou gngner woule Di à delo gni cotiser est ce que
@@dieynabadiop2681 merci Soxna Dieynaba si réponse bi.
D'accord question borom rewmi kw, am na solo!
Mane moom dama xalaat nè borom rewmi " wagni dolè ak yokou dolè" motakh mou def vidéo bi, mais jarouko woon.
Parce que gni di cotisé geum geum motax nioukoy def.
Et bougnou jawalè question Bou rafet ak question bougnou rafetal namm si leneeen.
Xam nga Sénégalais xol lay demè motax Mou nexa jobalè.
Juste sama xalaat la rek si xalaatou Borom rewmi .
Jajeuf Soxna Dieynaba
Big UP borom rewmi
❤❤❤❤❤❤
❤A❤❤
Thione Dousa morom senegal mo nekh guanane brom rewmi
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Sonko reck
♥️♥️♥️♥️♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
nopil frère bari gua wakh
Borom rewmi😂😂😂 walay hassim ya khoromou rèk ..bon iow aussi comme tu le dis a thione niang warone preparè ni bo lalè thione wala kènèn koumou meuna nèk ay partisan wame dinagn la tontou dinagn la wakh aussi sèn khalate
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Borom Rewmi rek 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾
Je te croyais plus intelligent que ça comment peux tu khepp nitt si ay commentaire inconnu je suis avec toi sur ton premier vidéo si ça façon de communication mais par contre les commentaires mom lolou warosi won sah wakh paske sen xalat lagnoy wakh que ça soit Lou bakh wala lou bonn niom leu concerne
❤😂
Yawmi ya khoromou.
Sa estime Bou wagné ko si qu'est ce que ça fait.
Vous du pastef vous peur réponses amoulene esprit de dépassement. Tu ne peux pas pousser ta réflexion pour savoir que ce n'est pas Thione Niang qui t'a répondu mais des jeunes comme ceux de Sonko qui insultent à chaque fois quelqu'un donnait son avis sur sa façon de faire.
Encaisser moo yomboul.
Boroom rewmi ya khoromou 😂😂😂
Mo yw 😂😂😂😂
Kii dou boroom dara moom visage de gorille moko gueunal propre visage boppam 😂
Ñii daniouy fontou rekk naan bureau 😂
Ce sont des complexés de première classe 😂
Ñii bou TH-cam amoul woon douniou wakh fènn 😂 ndakh ay doff laniou 😂
Ish Sénégal même pour amm carte d’identité dafa waroon amm parrainage 😂 conne genre yii yeupp douniou doon citoyens mais plutôt des marginaux 😂
Poltron qu’il est 😂
Walay asim😂
😂😂
Faut pas assimiler ces fanatiques à Thione puisqu'il en existe dans tous les partis. Peut être même que le gars ne les connait mm pas
C'est comme ces insulteurs qui se réclament de Pastef
D'ailleurs il ne les a pas assimilés à Thion.
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤
Borom rewmi
Thione door Kate bou mak la !
Pourquoi attendre 2 mois des élections pour se présenter ?
Pourquoi ce Thione ne s’est pas présenté aux élections locales et législatives?
Pourquoi il attend juste sapres avoir été reçu par Macky?
Toi tu n’es pas courageux