Xam xam rek mo woor mâchala..tafsir sa liguey rafetna ci seydina mouhamed psl ! Yalla naniou yalla doli xiir ci seydina mouhamed psl yokou suniou thiofel ci seydina mouhamed psl amiine ❤️❤️
Koor gui migui tagato nakh niogui si woor wathie wayé bounou meunon am li même après koor gui dinanou nékh ngiir yalla meuna tégui mbass mi🙏 machallah yalla fay lén beug nane lén❤❤❤
Bilae walay Cherif yak Tafsir Amou niou sene fay yalla mi am sene fay yalle naléne si barki seydina Moukhamed bilae soune xole sedd na sene ande bi yalle nako yalla guena deugueral ba mou mélni and seydina Moukhamed ba ak seydina Alioune machalah
Billahi wallahi man sokhna diarra Ndiaye ma wakh oustaz tafsir abdou rakhmane gaye Meilleure oustaz du sénégal yalna yalla faye la sa xol thi bargé saydina Muhamed
Yalla nalein yalla sameu thi brkè yonentibi xam xam bii geuneu wèrr Yalla bayilein fii baa thi kanam lii moyy l Islam kounek mothiy guiss bopam yonentibi ak sahabam rk nio matta royy
Ndaysane thieyy Yalla Chourkane Chourkane yaa Raabi bima bokei si geitu Moustapha ndaysane Yalleu nañu borom bi fayal sama Mame Seydil Mourssalina sama yakkar team 2stv K Alllh vous protège Quant à Chérif Mamine Aïdara,Abdou Rahmane Gaye et les invités yalla laleine di bayeil walahi diñu geuneu beuglo Moustapha rk yalla xamnako
Tafsir Abdourahmane yalna la yallah maye faan bu goudou bu ande ak werr ak werrle soutoura adouna ak alakhira teranga adouna ak alakhira si barkeh Saidina Muhammad (s.a.w) sunu yakarr teye ak elek
Nou nguènn sèddé lée sama xoll bii yalla nalènn yalla Faye sii barké Cheikh Al Islam Elhadji Ibrahima Niass.Alhamdoulilah Chérif et Tafir..Bilahi Contann Na..
Wa j'aime pas yi . rek nioma diahal !! Ioe tu te di musulman 👈 niouy tagg SEYDINA MOUHAMED DIKO WAHTANÉ NGUAY DEFF J'AIME PAS👎 . fier d'etre musulman 👉 Talibé mame Maodo . ❤ sopey Seydina Mouhamed❤❤❤
yalla séne diam yague yalla maï léne fane bou goudou nit niou mel ni comme yéne la niou sokhla si dékk bi merci encore une fois de nous faire vivre et de défendre notre cher religion à l'ensemble des personnes nobles qui ont participé à ce spécial émission Tafsir ak Cherif en plus à El hadj Ndiaye mention spéciale vous avez fait vibrer tout le monde ❤️❤️❤️ qu'Allah vous bénisse et qu'il vous récompense vous êtes les leaders 👏👏👏👏👏
Mash'Allah !! Vraiment c'est ça islam , pleins d'enseignements !! amine ya rabbi
Wallahy naby psl rèk mognou gnore diam ci yène Tafsir Abdou rakhmane ak chèrif mamine aïdara🙏🙏
Amouléne morome si plateau yii dakh yéne kouné khame nani ame guéne Serigne mé malgré tout Seydina Mouhamed(psl) rek moléne yore🙏❤yana guéne guoudou fane
Walahi ndaysan machalaaa
Moustapha mo diarra waxtané mag yépou li gnou am gnogui ko amé si yonnenti bi
Wolahi wakh gua deugue
Sénégal yép 2stv laniou warr di sétane machala Seydouna Mouhamed rassouloulali rek
Xam xam rek mo woor mâchala..tafsir sa liguey rafetna ci seydina mouhamed psl ! Yalla naniou yalla doli xiir ci seydina mouhamed psl yokou suniou thiofel ci seydina mouhamed psl amiine ❤️❤️
Amine
Machallah kéne dou Seydina Mouhamed PSL 🙏❤️
Le meilleur oustaz du senegal qui ns enseigne bcp sur la vie du prophète psl. Jai emu et jai pleuré
Yalla yalla sam la
Wallahi deysane kén dou tafsir Abdourahman gaye
Tafsir yallah nala yallah may wergou yaram ak goudou fane bah ngay continuer dii deff lii aye yonni yonn 🙏❤️
Koor gui migui tagato nakh niogui si woor wathie wayé bounou meunon am li même après koor gui dinanou nékh ngiir yalla meuna tégui mbass mi🙏 machallah yalla fay lén beug nane lén❤❤❤
Bilay chaque vendredi 22h 3h
Bilay wala sakh bén par 15 jours wala bén yone si wéer wi sakh beugue nagnou.
Ndeysane ces plateaux plein de vertus nous rappellent et nous raisonnent
Tafsir abdourahmane ak mamine yalana sen diam yague, 2 s tv mention speciale dioulite yeup contane nanou si yen
Bilahi amineuhhh
⁸oo))oooooooôô 999j
Yalna leene yonente bi fayy saws. Saa ssouné koulene deglou andak mbekk fanaane ak yeene andak mbekk. Kiii mooy guorgui, di gueer gui, di guargui mougn dji. Hiiratoul ahyari MOUHTAROU saws
Cette émission me vas droit au coeur wallahi tas souffre pr ton peuple PST 😍😍😍
Bilae walay Cherif yak Tafsir Amou niou sene fay yalla mi am sene fay yalle naléne si barki seydina Moukhamed bilae soune xole sedd na sene ande bi yalle nako yalla guena deugueral ba mou mélni and seydina Moukhamed ba ak seydina Alioune machalah
Amineuhhh yaa ilahi bilahi yalla rk moleine di faye
Bilae oie lol deugue la
Amine way
Sama taw bou goore mouhamed lay toudou inchaala! Jaime Naby❤
Manchallah yalla sougnou borom fayy len si barke Mohammed (psl)
On dit seyidina Mohammed SWAS nga balma fréro 🙏
Mention a vous je vous aime parce-que ki diara waxetané nguéne di waxetané
Kéne dou NDIOLE MAKA OU SONT LES CROYANTS DE MOUHAMAD (PSL)
Billahi kénn dou Moustapha
Saw 🙏
@@ngagnediop761 machalla sougnou royou Kaye bi
@@thiernoalidiao7694 machalla
Mashalah yalla diam yag li rk mo meuna doundal l Islam ken dou seydina mouhamed saws 🙏💓💖
Billahi wallahi man sokhna diarra Ndiaye ma wakh oustaz tafsir abdou rakhmane gaye Meilleure oustaz du sénégal yalna yalla faye la sa xol thi bargé saydina Muhamed
Amiine
Mash'Allah !! Vraiment c'est ça islam , pleins d'enseignements !!
Machallah khôl sédana qu’Allah vous récompense
Sy ziar nala
Delonala ziar depuis mauritanie 🇲🇷
@@neniitasy8666 Ah Alhamndoulilah, Que la paix soit avec vous ! DC vous etes Mauritanienne ?
Machallah tafsir yalla na yalla yok kham kham bi dioyena sakh sama khole dafa sédd loule sakh
Ndaysan
Alhamdoulillah Sante yalla bima bokké si ndiabotou maodo
Mbaye nael wade machalla fier d'être talibe cheikh
Macha'Allah talibé cheikh ba faw incha'Allah
Machallah
Wolahi chance bou mague leu
Machallah tafsir Man yalla mo défe ma beugel la sama bopou bilahii mé yalla na yalla may la wére ka diamou 😭👏👏👏👏👏👏
MarshaAllah beautiful Gamo. Tafasir and sheikh mamina. Jere Jeff. Yallah n'a l'en ya feeh.
Seydina Mohamed Sala Lahou Aleyi Wa Salam rek mognou nior ki takh Yallah bindeu lépp kén dou naby❤🙏🏼
2s TV sa kaw sa kanam insha'Allah c barkii Muhammad SAW
Yalla nalein yalla sameu thi brkè yonentibi xam xam bii geuneu wèrr Yalla bayilein fii baa thi kanam lii moyy l Islam kounek mothiy guiss bopam yonentibi ak sahabam rk nio matta royy
Yallah nalen yallah yokk inchallah thi barké seydina Mohamed ( psl)❤️🙏❤️
Special gamou bi dafa wara continué après koor gui wallahi Oustaz Tafsir yalna ya Rahman goudal say fane yak Chérif Mamina
Eskey Cherif e tafsir yo allahou jounou ngourndam ma challah
Yallah nalenn yallah samme
Ay man sou yalla defone bama guis Tafsir wala ma am numérom
Tafsir abdourahmane chérif mamine Machallah 🥰🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Maaaachalah... maaaachalah... maaaachalah...Yalna saa borom yookkou faaayyy bi djiaakhi seuydina Mouhamed psl
Machallah tafsir yalla na yalla goudal say fane ak wèr wéllé
Amineuhhh yaa ilahi
Amiiiiiinnnn
tafsir abdourahmane yalnala yallah faye sa khol blh long vie a tw
Ma shaa Allah Yalla na lèn Yalla dolli sammeu in shaa Allah Cherif diat bi ngay diat Tafsir mo niouy ndanèl tabarfakalla
Tafsir abdourakhmane dieureudieuf Serif dieureudieuf
Dieureudieuf
Macha'Allah yagueleine di ande ak weir in sha Allah Amine
Machalah gamou validé j'aime tafsir ainsi k Mamine et les autres
Tafsir!!Beugueu nala!Yallah nala yallah faye!Doundale wérale !saa batt yallah naye geune dii deugeure!
Il m'a fait pleurer 😭😭
Ndeyssan
Khol sedna aissata da nga bakh rek
Macha allha tafsir yalla na yalla faye si barke cheikh oumar fuotiyou Tall
Ahh machalah li nekhna walahi....Dieuredieuf xol yeup seide na😍 Dieuredieuf seydina mohamed saws♥️💎
Dieuredieufé Baye niass rta♥️
Yalla na yalla goudal sa fane tafsir si barke seydina Moukhamed (psl)
Machallah alhamdoulillah niass ❣️ yalna baye fay lén
Vraiment vous êtes les meilleurs longue vie à vous Mchlh lerna dougouna si khol
Mchlh jazakoumou'Allah Alkhair Baraka'Allahou fikoum
dieureu ngén djeuf wa plato bii Masha ALLAH Tafsir
Ndaysane thieyy Yalla Chourkane Chourkane yaa Raabi bima bokei si geitu Moustapha ndaysane Yalleu nañu borom bi fayal sama Mame Seydil Mourssalina sama yakkar team 2stv K Alllh vous protège Quant à Chérif Mamine Aïdara,Abdou Rahmane Gaye et les invités yalla laleine di bayeil walahi diñu geuneu beuglo Moustapha rk yalla xamnako
Ya rassoulal laah SAWS yalla sinou borome bi gnokou sinou thiofél si mome Amine 😭😭😭❣🙏
Machallah yalla nah yalla fayy lén ci barké Mouhamed (SAWS)
Machalla sall ngary lam toro bour guede yalla weral batbi tassla si sa barke baye Ckeick Ibrahima Sall
Tafsir Abdourahmane yalna la yallah maye faan bu goudou bu ande ak werr ak werrle soutoura adouna ak alakhira teranga adouna ak alakhira si barkeh Saidina Muhammad (s.a.w) sunu yakarr teye ak elek
May Allah bestow His blessings upon Tafsir and Mamine and the whole team for the good work they doing. Maximum respects
Macha allah may premier commentaire ana j'aime yi
Nou nguènn sèddé lée sama xoll bii yalla nalènn yalla Faye sii barké Cheikh Al Islam Elhadji Ibrahima Niass.Alhamdoulilah Chérif et Tafir..Bilahi Contann Na..
Machala 🙏 machala 🙏
Déwénéti yalna bour 🙏
Yalla takhawou'niou 🙏
Yalla may'niou Catane🙏
Yalla yeureum'niou 🙏
Yalla defal'niou tawféx🙏
Nié diota géne adouna🙏
Yalla yeureum'léne 🙏
Yalla yoc suniou thiofél🙏
Si seydina mouhamed 🙏
Psl bala déwéne yalla 🙏
Fathie adio yeup yeup 🙏
Machala tafsir ❤ ❤ 🙏
Machala ma'mine 💕 🙏
Les phylogénétique de l'islam que dieu vous bénis allahamdoulah yalla nalene yalla faye dji barkee Mohamed (pls)
اللهم صل وسلم وبارك على سيدنا و حبيبنا وشفيعنا محمد صلى الله عليه وسلم عليه أفضل الصلاة و اتم التسليم يا حبيبي يا رسول الله صلى الله عليه وسلم
Thank you 2stv for bringing this programme every year very educative these two are intellectual may God the Almighty protect the muslim ummah.
Machallah yalla wer té yokulene.
Xol sedatina yallah nalen yallah fay ci barké hatiman nabi wa imamil moursaline mou seydina Mouhamed saws 😍👏
Merci infiniment et longue vie à Tafsir et compagnie
Beugue nala téh yallah takhe ak Nabi!walahi Soumalaye dégglou wala sétane dangamay délo ci yallah!Yallah nala fii yallah yaguale,wérale batebi,maye la wére!saysoumala déggéh bala may nianale Sama boppou yaw laye djiteule!
Djeredjef yalnala yalla faye tafsir🙏🏾❤🙏🏾
thièy special gamou chérif ak tafsir yalla na senn diam yagua barki rasou loulaha
Machallah contan nan torp si yén yalna yalla weral batyi🙏❤❤❤❤❤
Bilay walay talahi magui len di nianal fan you goude lole yalla nalen yalla arre si barker Seydina Mouhamet Rassoulilah
Bonne continuation Barke Rassoulh (PSL)
Jeudi inchalla
Sama gnari papa yi yallah len yallah fay❤️❤️❤️❤️té goudal seni fane!
Mashallah tafsir abdourahmane gaye kendou Seydina mouhammed psl
Xol seddatina machaallah dieuredueuf yalna yalla feylén
Ndeysaane kéne dou mame Rassoul SAW 🙏🙏
Maa'sha'Allah 😭😭❤❤ya'Allah reka yorr sen fayy
Machallah tafsir allahoumm amine ❤️🙏🏿
MachaAllah cheikh très émue fière de de vous marhabann.
Machalla tafsir magui laye diadjefeule
Yallah naléne yallah faye si barké Seydina Mohamed SAWS 🙏🏽❤️🙏🏽
Machalla Tafsir sounou khole sédena yalla am na sa faye
Machallah mé les techniciens de la 2 stv sont des professionnels vous voyaient
Mane Dal j'aime 2stv lii nékh na lol machallah 😘
I love Muhammed ❤
I love Muhammed ❤
I love Muhammed ❤
Allahou akbar 😭😭😭😭😭😭😭 amneu solo trop 💗💗💗💗💗💗
Machallah Yo Allah bedou diam Amine 🙏🏽🙏🏽❣
Barakallahou fik 🙏 Cherif ak Tafsir
Machalla tafsir et cherif yalna yalla yok were té koudeul fane yi amoulene morom
Machalla
TAFSIR YALLA NA LA YALLA FAYE BILAHI YA BAKH BILAHI YA MEUNA WAKHETANE DIEUREUDIEUF TAFSIR DIEUREUDIEUF CHERIF
Wa j'aime pas yi . rek nioma diahal !! Ioe tu te di musulman 👈 niouy tagg SEYDINA MOUHAMED DIKO WAHTANÉ NGUAY DEFF J'AIME PAS👎 . fier d'etre musulman 👉 Talibé mame Maodo . ❤ sopey Seydina Mouhamed❤❤❤
Douma doyal chi vidéo bi
Wayè keep kou bagne seydina Mohamed safara nga dieume wayè nioune sougnou kholi nabi mo si nèke
Gnou beurri tourou djoulite lagnou ame wayè dougnou ay djioulite walahi wayè yalla nagnou yalla soutoural
Mashallah yallah na lah yallah ak Rasouloulay fay😍😍😍🙏🙏🙏🙏
Blh video bi dama ko weur ba sonne walahi yalla na diame yague Senegal
Liiii neexna trop way eskeuy yalla nalen yalla fay amine
Yalla na yalla goudal seni fane defal len wer ak werlé barki yonente bi
Cherif Mamine & Tafsir Abdou Rahman gaye séne projet si dinné dji yalla na yégue
Sak seconde c le devoir de prié sur le prophète psl
Billahi
yalla séne diam yague yalla maï léne fane bou goudou nit niou mel ni comme yéne la niou sokhla si dékk bi merci encore une fois de nous faire vivre et de défendre notre cher religion à l'ensemble des personnes nobles qui ont participé à ce spécial émission Tafsir ak Cherif en plus à El hadj Ndiaye mention spéciale vous avez fait vibrer tout le monde ❤️❤️❤️
qu'Allah vous bénisse et qu'il vous récompense
vous êtes les leaders 👏👏👏👏👏
comme Méssi thi baal réékkk @ Macha Allah Tafsir Gaye @ Macha Allah Babacar Cassé @ Chherif Kou bakh la
Thiey ya rassoulah salahou aleyhiwa wassalam 🙏😭😭🙏
Machala yalna yalla samelaine si barkè seydouna moukhamed psl
stp kou beugue tafsir Abdourahmane click j'aime stp👍👍🙏🙏🙏🙏👍👍👍
Walaye malene sope souma lene Di degeulou wala setane doumaa meuneu teyer daama bopp Tafsir Cherif yalla n'a yalla wereule theure yi amine
Macha Allah macha Allah yalna yalla sam t weral baate bi Yok kham kham bi incha Allah
on apprécie egalement le geste unificateur
Machalla Tonton Tafsir et Tonton Chérif bonne continuation je vous aimes fort