Merci BABACAR TOURÉ,car tu as sauvé beaucoup de citoyens et citoyennes sénégalais concernés par cette arnaque.Tant que KEWOULO et son équipe sont là ,nous sommes rassurés.
Si ce monsieur était clean dina wané loumou liguey comme il aime si bien le dire diamonoy Wade ak le grand voleur de tous les temps Macky Sall Ay doirkat tigui.... Amir Abo kay 😂😂😂
Merci Babacar thi léral yi mane sama sœur wo nama mingui zone Sakal né Gayi dañuy lathie 3000f bindou ay cité la manéko woroul com dañuy lathie khaliss
Saway projets yinga diota realiser il faut nous les montrer. Nous voulons savoir ce que tu as fait de concret pour le Sénégal. Ensuite tu ne peux pas dans un pays normal et légal réaliser des projets d'envergure sans être en phase avec l'état qui a un droit de regard sur ce que tu fais parce que l'aspect social de la chose fait que l'état doit être impliqué. C'est bien lui qui attribue les permis de construire. Nous sommes en phase de rupture systémique, il faut le comprendre 🇸🇳
Senegalais yi nio beugue lou yombe. Toujours gningulendi arnaque, te ils continuent...ce Ablaye guisse et consorts ce quil fait est tres grave et la justice ne doit pas laissser passer. ces genres de pratiques sont a bannir.!!!
Li mo takh sou you chef religieux on doit voir les gens qui les approches pour arnaque les gens on doit organiser la cours des chef religieux caron doit pas les induire en erreur protègeont les
Mrs Touré puisque ce Guisse prétend avoir travaillé avec les régimes passés est ce que vous pourriez investiguer dans ce sens afin qu'on puisse savoir ce dont il a été réellement questions ??? Est ce ce sont des logements ou autres choses ??
Mamadou abdoulaye guissè mane linga wakh geumou mala ki dafa beug si trianyi rek ak aye sathiè yi gni bou niou léne diapè daniou léne wardi douma douma you mèri manane daniou léne wardi nokhou balama geuna am louma nakhari niouye diaye afaire dioulite la wala talibè té dokh si sathié ak fèneu ak trian classe gui primo nourou dondou laniou lène wara teudj ndakh ama lou niou rewmi niérigne
Merci BABACAR TOURÉ,car tu as sauvé beaucoup de citoyens et citoyennes sénégalais concernés par cette arnaque.Tant que KEWOULO et son équipe sont là ,nous sommes rassurés.
❤ Merci Touré , tu informes juste et vrai 👍❤️🙏
Merci Babacar Touré continue de faire des investigations deuk bi mo bari ay dorkatt
Merci Mr toure si lerale yi amnasolo mane sama 6000 la lene djiokhe
Naka faÿ
Nagn lakko déllo , sinon nguèn plainte
Babacar Touré, vous êtes entrain de faire un excellentes travaille, l'état doit prendre en charge ta protection
Kou guiss foumou tabakh rrkk nama konwakh😂😂
Yèn ñi diokhé sen khaliss deflèn collectif nguèn porté plainte.
Wa mais mane bene cité bimou tabakh leu bougou guiss😂Qui ak Abo vrai domoram leu😂😂😂
Si ce monsieur était clean dina wané loumou liguey comme il aime si bien le dire diamonoy Wade ak le grand voleur de tous les temps Macky Sall Ay doirkat tigui....
Amir Abo kay 😂😂😂
Merci pour cette alerte
Merci Babacar thi léral yi mane sama sœur wo nama mingui zone Sakal né Gayi dañuy lathie 3000f bindou ay cité la manéko woroul com dañuy lathie khaliss
@@BoyNdaw 3000 pour am keur? Wadji doorkat leu
Merci babacar
Saway projets yinga diota realiser il faut nous les montrer. Nous voulons savoir ce que tu as fait de concret pour le Sénégal.
Ensuite tu ne peux pas dans un pays normal et légal réaliser des projets d'envergure sans être en phase avec l'état qui a un droit de regard sur ce que tu fais parce que l'aspect social de la chose fait que l'état doit être impliqué. C'est bien lui qui attribue les permis de construire.
Nous sommes en phase de rupture systémique, il faut le comprendre 🇸🇳
Sénégal dafa beuri ay sathie ay nakhé katt
Ayy way mane mi diokhé na 5500😭😭😭
Dangene gawa geume rek 😂😂😂😂😂😂😂😂
Merci bcp babacar ❤
Procureur loumouy khar si guisse mi
Ils n’ont qu’a nous rendre notre argent moi en personne c’est ma voisine qui m’a prêté 6000f
Merci kewlo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup Babacar Touré léral yi amna Sololool si Askanou Sénégal 🇸🇳 Diadieufty Arnaqueurs yi déno bari lool si réwmi
Guisse il faut arrêter c'est de l'arnaque
Ok,mercier Bbcar depuis kuala lumpur!
Sénégal Maag gni warone jukhé un bon exemple gnocchis yaak rew mii .Ay Maag sole sa grand boubou dii weur dii fenn rekk
Non mais 250.000 logements, pour 10.000.000 par maison, faites le calcul rek, qui va financer cela?
Touré ❤❤❤
Nous avonñs subi la même arnaque avec babacar bâ avec la société HISPÌCOR en 2011 aidez nous à recouvrer bos fonds
Le gars à l'entendre parler, on saiy que c'est un manipulateur, un usurpateur, n trafiquant de personnalité, Yallah na sunu borom aar Senegal
Je pense que arrêter nagnou KO sakh mom laye guisse
😂😂😂😂 taye lagnou khame Yallah dragon tite
250 mill Logement wawe 🙅🏼♂️
Mais il n'a pas cité de realisation de Omart City. Fane la meusseu livrer ay logements??
Tappalé diéxna ci réwmi Yalla Xamnako "Jub Jubbal Jubbanti" rékk
Merci babacar yanfui def lou am solo
Merci
Babacar fottina wadji😂😂wa beug dimbaly nitt kagne la diar thiono bii😂😂😂
Mane lekena sa 5500 nama fay sama xaliss ngirr yala
Mane de sama 6000 la lene djiokhe😊
Dangéne gawa diokhé khaliss nak masta
Sénégal dafa beuri ay door katt dégal wakhou thiakhan yi
Merci beaucoup Babacar Touré
Ki dé soko déglo sakh khamné diubul
Lutakh doorkate meuneu fenn🤔
S bassirou niane merci Babacar toure nieleraralyi was touba nieguilaye sitane
Fo fék nit kou diouboul ci mér ley deuk Abdoulaye Guissé mosna quitter plateau Walf tv matinale
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Collins powel il était le ministre de la défense pendant la guerre irak c' est lui qui attaqué l'Irak c'est un métisse noir américain
Senegalais yi nio beugue lou yombe. Toujours gningulendi arnaque, te ils continuent...ce Ablaye guisse et consorts ce quil fait est tres grave et la justice ne doit pas laissser passer. ces genres de pratiques sont a bannir.!!!
Babacar touré demande est-ce que ila déjà livré des maisons depuis création de son projet
GUISSE mako xam bou bakha bakh dirkatt laa dé 😂😂😂
Li mo takh sou you chef religieux on doit voir les gens qui les approches pour arnaque les gens on doit organiser la cours des chef religieux caron doit pas les induire en erreur protègeont les
Ki daffa tiite déh😂😂😂
😂😂😂
Mrs Touré puisque ce Guisse prétend avoir travaillé avec les régimes passés est ce que vous pourriez investiguer dans ce sens afin qu'on puisse savoir ce dont il a été réellement questions ??? Est ce ce sont des logements ou autres choses ??
Sénégalais à là sénégalais triandage rek
Senegal neekhna.
Iu et quand dans l'histoire de l'humanité, unevstructure offre comme ça des maisons, apres frais d'adhésion de 5000F, point quoi??
Les escros doivent être arrêtés mais aussi il faut que les gents saissent d'amer la facilité
Omar city ;amir city; akone city; doul rek aspir le sang des pauvres sénégalais
Mais si j'entends bien il a travaillé avec Macky et Abdoulaye wade.donc il travaille avec l'état sénégalais
Domouramdjii hanaa nekkoul senegal
On nous pas parler de J i é on nous parler des logements
Kii diangoul sakh tapaleila diangue. Wii est ce qu ils attendant pour l atreter?
Jub Jubal Jubanti sama tourondo bi arnaqueur leu
Truand REKKK 😂
Un grand menteur manipulateur mais on t’attend pour régler ce problème en nous rendant notre argent
👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
Yaw wakhngua Gie après wakh Ong bayil doul Yaw amo keur danguaye louer bayil fen serigne mountakha dousamorom
Mamadou abdoulaye guissè mane linga wakh geumou mala ki dafa beug si trianyi rek ak aye sathiè yi gni bou niou léne diapè daniou léne wardi douma douma you mèri manane daniou léne wardi nokhou balama geuna am louma nakhari niouye diaye afaire dioulite la wala talibè té dokh si sathié ak fèneu ak trian classe gui primo nourou dondou laniou lène wara teudj ndakh ama lou niou rewmi niérigne
Kouladégue khamni danguaye doul Gie Ong khamo loywakh.tu es incohérent yaw dangua yaakaarni ay dof nguaye wakhal
Kharou serass leuu
Wallahi hame nagne nii kii dey narr. Vous passez votre temps a sucer le sang des sénégalais sans pitié. Honte a vous !!!
Saway feenga yaw wolouwoo eta begge nioun niou woloula
Ce gars doit être arrêté le plus vite possible
Il a été arrêté hier soir
@zongo5380 c'est très bien