MUSIQUE DAFA HARAM OU PAS ?, OUSTAZ NIANG ET KAMAL DÉBATTENT ET APPORTENT DES ÉCLAIRCISSEMENTS

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 10 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 48

  • @tivaouanetvsunnahakhalquran
    @tivaouanetvsunnahakhalquran 3 ปีที่แล้ว +2

    Djazakallah hayran Dr Modou kama thiaw yalna yalla saam lénn inchallah ❤️❤️❤️❤️

  • @mouhamethseck5490
    @mouhamethseck5490 3 ปีที่แล้ว +4

    Le gars en bleue à parfaitement raison. Musique dafa xaram sa depend si context bi .

  • @actu3.039
    @actu3.039 3 ปีที่แล้ว +6

    Musique bou Sénégal bi dafa haram

  • @magattewade3801
    @magattewade3801 3 ปีที่แล้ว +3

    Je suis parfetement d accord avec oustaz Modou kama. (wa mina nasi Man yastari il akhiril ayat....

  • @gueyebara3010
    @gueyebara3010 3 ปีที่แล้ว +4

    Sénégal barina ay nafekh trop😓

  • @njare-njare2149
    @njare-njare2149 3 ปีที่แล้ว +1

    Jërëjëf Móodu Kama,❤️💙 waa ji ci des lay lëdëmal rekk

  • @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565
    @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565 3 ปีที่แล้ว +2

    Machallah Dr Modou kama h.a contaan nagn si yow

  • @modoumbodji4407
    @modoumbodji4407 3 ปีที่แล้ว +5

    Kama limou wax mo geuneu werrr ndax musique déjà dfay wowall xolll

  • @mouhameddia5168
    @mouhameddia5168 3 ปีที่แล้ว +3

    Akhmed khalifa niass numero 2

  • @KelseyMoody-xo3vj
    @KelseyMoody-xo3vj 3 ปีที่แล้ว

    Machalla oustze Modou kama thiaw 💓💙iow borom xam xam

  • @cherifgueye1329
    @cherifgueye1329 3 ปีที่แล้ว +1

    Merci beaucoup kama

  • @djibyka3351
    @djibyka3351 3 ปีที่แล้ว +2

    Niang bi ragaloul yalla genre yi kouniou rerel leniou beugeu li bokeu na lou geuneu bonne si dine فقيه فاجر brom xam xam bigeu xamante na kathior la yalla naniou si yalla mou seul

  • @birahimfaye6605
    @birahimfaye6605 3 ปีที่แล้ว

    vous pouvez l ecouter sur 88.4 fm Origine fm❤❤ Dakar ❤❤❤❤ORIGINALEMENT VOTRE ❤❤❤💯💯💯💯💯💯🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤

  • @kheuss290
    @kheuss290 3 ปีที่แล้ว +1

    Musique dafa haram même bou féké amna wakh youy guindi sakh fagnoukay déglo si bar yi dancing khéw yi etc... dara bakhousi kone bone gofou moy takh wakh ya dotoul am sens

  • @ibrahimambodj3713
    @ibrahimambodj3713 3 ปีที่แล้ว +1

    C est pas aux étudiants de parler de jurisprudence à la place des professeurs. En droit classique ( ex constitution Sénégal) on imagine pas inviter des lycéens pour en débattre. Wakh sa khalaat

  • @baradiakite1994
    @baradiakite1994 3 ปีที่แล้ว +3

    oustaz bousol Lou maroolii xamoul Dara noumouy prononcé sah baaxoul

  • @mamadouwouryba6820
    @mamadouwouryba6820 3 ปีที่แล้ว +2

    Musique dafa haraam aaya baa nguinii ومن الناس من يشتري لهو الحديث.....chapitre louqmann ibnou massoud رضي الله عنه akk ibnou abbass رضي الله عنه neenagnou musique la ak instrument de musique konn taalibewou yonnentebi صلى الله عليه وسلم gnoo firri aaya bi

  • @crossoverthiawla5699
    @crossoverthiawla5699 3 ปีที่แล้ว +1

    Mâcha alla oustaz Modou Kama Thiaw lingay wakh amn solo

  • @diamacisse6660
    @diamacisse6660 3 ปีที่แล้ว +1

    Musique Sénégal bi dafa haram Raka lal yalla

  • @ibrahimasarr9071
    @ibrahimasarr9071 3 ปีที่แล้ว +1

    Slam pap nga balma gayi danion wara ragal yalla music dafa haram deel ibbi telefon bi

  • @kheushaatv2418
    @kheushaatv2418 3 ปีที่แล้ว +1

    Machallah kama xam xam day ler

  • @mamemorcisse4
    @mamemorcisse4 3 ปีที่แล้ว

    نهى رسول الله صلى الله تعالى عليه وسلم عن استماع المعازف والمزامير

  • @crossoverthiawla5699
    @crossoverthiawla5699 3 ปีที่แล้ว +1

    Oustaz Ousman Niang. Balma wayé linga wax Saxoul dei nga balma dia diuef oustaz Kama

    • @basamba8140
      @basamba8140 3 ปีที่แล้ว

      Musique daffa kharam tiffakhane la musique tel que , elle est au Sénégal , instruments daffa kharam ,dayye wauwal khol
      Oustaz Niang ,tu es nul trop mm

  • @cherifgueye1329
    @cherifgueye1329 3 ปีที่แล้ว +1

    Oustaz naing sa diang dafa dess

    • @basamba8140
      @basamba8140 3 ปีที่แล้ว

      Tu trop nul,les khadis sur les instruments

  • @iboulayeba4577
    @iboulayeba4577 3 ปีที่แล้ว +1

    hhhhh vraiment oustaz bou nioul bi il est dangereux pour un peuple ki khamoul dara,mais hadith bouy wakh ni bou aduna démé banou danganal instrument de music ,fornication kone khamlen ni aduna moungui wadia touki.oustaz bi ak teint wam bou niak lére bi vraiment day lereul nite gni.nena music la dioulite di fekheulm kholal .ki il est dangereux

  • @bonnaireseydou6100
    @bonnaireseydou6100 3 ปีที่แล้ว +1

    modou kama yalla na ga fi yague
    musique mome kou ko daganal rekh kou karam ga

  • @aronaousmanengom3518
    @aronaousmanengom3518 3 ปีที่แล้ว

    Oustaz niang dagaye thiakhane rek deklokato music gen

  • @aronaousmanengom3518
    @aronaousmanengom3518 3 ปีที่แล้ว

    Oustaze do wakh soma diomole

  • @mamemorcisse4
    @mamemorcisse4 3 ปีที่แล้ว

    Musique ken manko layal dafa haraam tifàkhane moutlaqane

  • @aboudione7672
    @aboudione7672 3 ปีที่แล้ว

    Seul un messager de dieu peut dire que ça c'est haraam ou non et a ce que je sache le prophète n'avait pas dit que la musique est haram

    • @taijiscin6818
      @taijiscin6818 3 ปีที่แล้ว +2

      iaw nitgua??

    • @aboudione7672
      @aboudione7672 3 ปีที่แล้ว

      @@taijiscin6818 si vous êtes un savant donnez moi des arguments.

    • @taijiscin6818
      @taijiscin6818 3 ปีที่แล้ว +3

      @@aboudione7672 démal recherché hadiths boukhari (n5590)

    • @taijiscin6818
      @taijiscin6818 3 ปีที่แล้ว +1

      @@aboudione7672 ak ayat bi nékk si sourate luqmane, و من الناس من يشتري لهو الحديث) ibn abas ak ibn mas'oud ay talibé yonénte bi (psl) laniou niouko firi né yallah musique lafiy wakh

    • @aboudione7672
      @aboudione7672 3 ปีที่แล้ว

      @@taijiscin6818 لهو الحديث ليس المو سيقى

  • @keparuislam9025
    @keparuislam9025 3 ปีที่แล้ว

    Pape Sidi waro sax deglou nii yaw sa dieumi bope xamngani dafa haram

  • @beugrassoulilahsaw7204
    @beugrassoulilahsaw7204 3 ปีที่แล้ว

    Mdr thieye yalla away légui diouk wak ragal lén yalla

  • @serignepapendiaye2932
    @serignepapendiaye2932 3 ปีที่แล้ว

    Niang mom kou mana fenn la

  • @mamemorcisse4
    @mamemorcisse4 3 ปีที่แล้ว

    Billahi pape sidy yàyay tiittt dafa am niou diangue banoppi nàfekh ragaloune yalla te kou ragaloul yalla ak lo diangue diangue do borom xam xam إن الذي لم يخش رب العالمين ليس بعالم ولوأفنى الفنون

  • @mamemorcisse4
    @mamemorcisse4 3 ปีที่แล้ว

    Oustas en bleu dangà khawa ragal waxbi waxko rek moudiékh dafa haraam

  • @ibrahimambodj3713
    @ibrahimambodj3713 3 ปีที่แล้ว

    L islam dou fo.SI VOUS MAÎTRISEZ LA LOI ISLAMIQUE PLUS QUE ABDOULAHI IBN ABASS ALORS...