C’est pathétique ce qui se passe dans ce pays la politique c’est ne pas de la guerre il faut savoir que ce pays n’appartient à personne c’est de la responsabilité de chaque personne d’assurer la bonne entente et la cohésion sociale malgré les divergences c’est pitoyable de voir la scène politique Sénégalaise se transforme en un ring si Etat de droit c’est dommage Bougane war na kholate bopam ak niou mou andale
@@BMG-3sExcusez moi, êtes vous journaliste ? Lingey wakh leer nala? Meune nga am ko faral, mais quand on exerce on doit absolument rester IMPARTIAL! Bayilene di wakh lolene maîtriser wul
@@sokhnadrame7735pour l’amour de Dieu eskeu vous pouvez sortir maky de vos teulè isch maky maky meunoul motakh niou foli ko mais à chak fois guène di wakh il faut guéne lakh kothi 😂😂😂😂😂
C'est dommage que les journalistes Ngoné, Salma et Maty se fatiguent, pensent qu'elles se battent pour défendre le projet et pourtant à mon avis c'est plutôt le phénomène du contraire de leur combat qui est entrain de se propager. Au contraire, à l'état actuel des évènements (l'approche des législatives) Ngoné Saliou, Maty Sarr Niang et Salma sont entrain de faire la propagande des adversaires de PASTEF sans le savoir. Je pense que c'est aux autorités de communication de PASTEF de recadrer ces 03 dames qui sans le savoir, donnent l'impression que les pastefistes n'acceptent pas l'adversité.
Deugg nekhoul deh wayei yena togn xawma nouniouy convoquer niit ngene nieuw dilene provoquer beu beaucoup de temoins wax ko .. niou gaagn lene ngene di weur di reuy lamigne alors que provocation bi ci yene leu diougué
الصلاة والسلام على رسول الله محمد صلي الله عليه وسلم
وأنت أيضاً أخي
Il faut les porter plainte tous... ce pays doit etre regle pour de bon
L'annèe passè cetait le même discours tu tenais😂😂😂
@@senenutscompanyets3664🤣🤣🤣🤣moma diakhal nak
@@senenutscompanyets3664bilay 😂😂😂
@@senenutscompanyets3664 hypocrisie manouko wéssou
@@senenutscompanyets3664l’année passe diay doole leu wone mais Tay nak kou nekkoul si yone niou tegueul sa ndeye si prison point
Sonko ak bougan comme Angleterre ak pomme de terre
Mon ami ne donne d'importance a Bougane.
Nono li dou combat 😂😂😂😂
Bougane Sonko moy idolam si politique sauf que deugue ah résistance… bissi Sonko nèkoul si mom. Comparaison n’est pas raison
@@cherifa5991dengay doul biugan bimouy poltik bobiu kenna khamoul.ndayou sonko😢
😂😂😂😂bolomi bari na
Ce que je constate sur le terrain politique actuel , c'est que le pouvoir se complique la tâche de plus en plus
Le pouvoir diameu reck laye amm inchallah.,nous serons tous en face le pays ne les appartient, le peuple à déjà choisi.
😂😂😂😂😂bayou keur doff yii merci sister
Ngoné saliou doit savoir raison gardée.Elle n'a qu'à se limiter de son métier de journaliste et non militant
Est-ce qu’elles sont réellement journalistes ? Le mot « animatrices » serait plus approprié. Zéro élégance
Merci bcp
Vréma kanamam bou gnaw bobou may bagna gis
Mais ngi ce sont des journalistes wala ay militants pastef
Wa kere bougan aye nerfi laniou😂😂merci ngnenè saliou❤❤❤❤❤❤
Massa Maty Sarr Niang! Waw goor Amazone Salma! Bravo 🌹 🌹 🥀 🥀 to All of you! We stand with you through rain or snow or fire!
🤣🤣🤣🤣🤣🤣nokeu nationnal gys moye nokeu international non sama khol bi Côme friguo insbi 😂😂😂😂🥲
@@biguedieye4013 bilaye yow togue thi site yi di doule ni rek ak saboté très bien nokh international ak nokh national
Néklén nit mak bou am soutoura moka may bopam
Merci Sama.djungune yi❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup ☺️ Ngoné SALIOU ✊🏼👊🏼🦾💪
Franchement vous êtes des journalistes ni ça m'étonne vraiment 😢
Gnii Kay 😂😂😂
Nena bougan lay plainte😂 on est ou la
Je te jure 😂😂 gni ay comme ay jiggen milieu 😂
vraiment
C est une animatrice qui sest transformée en journaliste
Ngoné thiaga pastéf bi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉
Kéne khaméwoul journaliste AK Tik tok keur sarap ndéye lii
Et dire que ces femmes sont des journalistes thieuy yallah
Merci ngone saliou❤
C’est pathétique ce qui se passe dans ce pays la politique c’est ne pas de la guerre il faut savoir que ce pays n’appartient à personne c’est de la responsabilité de chaque personne d’assurer la bonne entente et la cohésion sociale malgré les divergences c’est pitoyable de voir la scène politique Sénégalaise se transforme en un ring si Etat de droit c’est dommage Bougane war na kholate bopam ak niou mou andale
Journaliste politiciens rewmi yakhouna
😂😂😂 ewaye bougane lousi yoname bagua koye plainte
Il faut porter plainte
C’est compliqué vraiment 😅plainte yi barina Senegal oh
Pourqoi au Senegal les home frappe les femme Elle son nos maman
Domérame rek simmmm
Hiiiii informe toi bien ct pas les hommes des c des mamans de gueum sa bopeu ki lai as bien bastonné🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Les mamans restent aux foyers et s'occupent des enfants
Meryou niaak fayda yi😢
Mère yi d taye nio defal bagass thiaguadji 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@biguedieye4013kane moy thiagadji
Holam ma sen kanam yi yena rouslo diguén yi merci ngoné ak Salma
Non journalisme niak na valeur Senegal
Gni bro amougnou sakh carte de presse
Vive le président Diomaye ce pays a tant besoin de vous pour votre franchise et amour pour la patrie Jub jubal jubanti
Ngoné mo dof té fouy
ngoné saliou yeukk gua sa bopp nakk
Je suis très content aujourd'hui ngone saliou hué et bien bastonner c ce k on attendait le combat ne vient de commencer 😮
Quelle combat ? Fo mossa guiss sathe di khekh lou doul niou kouthialla nga daw
C'est vraiment désolant ! Ce genre de pratique doit être banni ! Nous sommes des gens civilisés dans une démocratie
donc en etant au pouvoir vous tuez le peuple et maintenant dans l'opposition vous tuez encore le peuple?
Mouyen😅
De toutes les façons il y aura une plainte et il payeront
Bilahi yène dounguène ayy journalistes ! Ayy naaféx nguène, seytaané yi ! Ñëpp xamnañou finguène fèttè !
Yeina ndaye togne lonane ayyy sonko
Ce ne sont pas de journalistes mais de partisans
Merci salma ❤❤❤❤❤❤
Ay bor del gen😂😂😂😂 pestef wa pestef ay bor del gen😂😂😂😂
Des journalistes youy am partie pris, Thiey senegal. Gni khana diangou niou louy journalisme
Mais ma chérie attend tout ça grace à qui Macky qui a complétement détruit et les journalistes qui l'ont accepté c'est là que tout à commencer
Yow mi ya diangoul lou bari
Chaque journaliste a le droit de soutenir un parti politique tel qu’il soit nak
@@BMG-3sExcusez moi, êtes vous journaliste ? Lingey wakh leer nala? Meune nga am ko faral, mais quand on exerce on doit absolument rester IMPARTIAL!
Bayilene di wakh lolene maîtriser wul
@@sokhnadrame7735pour l’amour de Dieu eskeu vous pouvez sortir maky de vos teulè isch maky maky meunoul motakh niou foli ko mais à chak fois guène di wakh il faut guéne lakh kothi 😂😂😂😂😂
Non c des thiagualiste de pastefs wayé taye vielle d gueum sa bopeu yi niolêne niousse ba toth sène bopeu yi🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Sarap ndeye lii,ki moy journaliste pastef 😅😅😅 ,partisante deug
Waxi doff rekk nguaffi waxx
Ngoné du courage yaak maty sarr niang . Je vs estime beaucoup mais on doit vous protéger.
Niaw niguene done def si ngourou macky ko wah ngéne saga ko youhou ko les inconsients pastéféne
Môme militants de pastef la mo takh thiaga pastef
sa datta yayé yawou ak sa yayé
Adouna dafay diékh si yaw tôt walla tard nékal niit
Maty sarr en tant que journaliste tu dois avoir honte de ton comportement
Goné saliou mo done saka il faut dire les choses tél qu’elle sont ❤
MANE BEUZZ BIGNI MEY BOUGANE METINAMA
Je t'assure tay mom khamna c'est le plus beau jour de sa vie 😂li rek la beugone
Je te jure mane dama wakhone bouko Ken wo bouko Ken teuthie car ça serait l'accorder de l'importance
Bilaye
Buzz bobou laniou maye sonko bamou neik 1er ministre nonoula reik
Bilaye walaye bougane mo soff
Problème yi démarrer na😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣magui rame
Fo guiss provleme
Soyez des journalistes kén doulén nokou soyez professionnel journaliste mo niak valeur fi si Sénégal tchim
Awa Gaye ya soxor tchim
@@Amadouggggggggg kholalma dof bi nékal goor yallah c'est mieux
Cette presse est malade
Bougane moy Sonko😂😂😂
Sonko moy Diomaye
Franchement Ngoné et Maty sarr niang suis avec vous.Mais bouma sanione doleine fa dem di couvrir événement
Merci ngone saliou
Aka gno meuna doule 😂😂😂😂😂
Kouy diéma comparer Sonko ak bougane diapalni hôpital fann am ngafa place
Ngone saliou mérite d'être appelé journaliste parceque dafa faral sonko
ANI JOURNALISTE AK WAKH AY SONKO SI KANAMOU BENENE PARTI 🙏MAIS DOR DJIGUENE YEUFI GORDJIGUÈNE LA VRAIMENT DOU YEUFOU NITE CON NGENE TROP😮
Merci merci
Kone ngoné ninga niawé😂😂😂😂😂😂
Vraiment méréna Maty Sarr ak Ngoné Saliou. Gni li niou beugone
Sen trois personnes yi waroul wone ame thiow diaroul wone sakh couvrir
Merci ngone saliou.pas de recule . faites une plainte
Merci ngoné ma fille foula AK fayda reck ngay ame ba adouna Di touki Babaay sa papa
Merci Ngone Saliou ❤❤ bravo ❤❤❤
Thiaga wa pastéf yi téy militants guem sa bopp les jambare yi xewlou nagne si dé 😂😂😂
@@MoustaphaDiongue-if7lc🤣🤣🤣🤣🤣🤣lima neikh moye mére gueume sa bopeu yi niolène Niouss ré ba toth sène bopeuyi khawma bou khaléyi nieuwone khana daniouye patheu 🤣🤣🤣🤣🤣
Dooto lénn ko daffati🤣🤣🤣.
Niawww🤣🤣🤣🤣
Pro nénou bakhal yi daal tourou Sonko lagnouy bagna dégg. Sonko dou nénou bakhal😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣good job 👍
Mè vous êtes des journalistes ou bien dès oposantes
Merci Ngoné Saliou ❤
Merci ngone
😅😅😅😅😅 bougane me fait rire
Merci, il fau protéger le PROJET
😂😂😂😂😂
Une chose est sûre. Si on arrete pas ça, il y aura une bagarre générale entre les gens de bougane et les aitres sénégalais
Entre les partisans de Bougane et les partisans de Sonko il faut dire mais pas avec les autres sénégalais!
Vraiment wa Pastef sof naniou té beuri wakh kom kou mom rewmi 😂
Oui par ce que nio môme réw mi 😂😂
Waa yaw tardé nga di
😂😂😂
Bayil roubé bi way
Bijoux lo dekou ngané 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Kou di wax bougane la andal😅😅😅😅😅
Bagarres walla attaque n’importe quoi. Couvrir mollène yobou pas bagarre. Bravo à ces dames honte à ces hommes vendu et sauvages.
Non yagui dioume d mere gueum sa bopeu yi niolène nokeu ba toth bopou beneu thiaguabi 🤣🤣🤣🤣🤣Khana yaw sétano wone 😂😂😂😂
Ngoné saliou ya tay diam rék ngay amm
Khana ngii déy lénn fayy 😂😂😂😂
😂😂😂😂parti nénou bakhal
Merci beaucoup
Elles ne sont pas des journalistes que ca soit ngone Mobile ou Maty sarr😊
Sa journée boude ligua wakh moy takh mou diar togual khar 😂😂😂😂 keur dof yi 😂😂😂
Athia wa keur bougane 😂😂😂
Wa kere bougan aye nerfi laniou😂😂
😂😂😂😂😂😂non N'GONE maala beug ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bougane dafa beugué yeungalate rew mi 😂😂😂😂 bougane amo khorom srx
C'est dommage que les journalistes Ngoné, Salma et Maty se fatiguent, pensent qu'elles se battent pour défendre le projet et pourtant à mon avis c'est plutôt le phénomène du contraire de leur combat qui est entrain de se propager.
Au contraire, à l'état actuel des évènements (l'approche des législatives) Ngoné Saliou, Maty Sarr Niang et Salma sont entrain de faire la propagande des adversaires de PASTEF sans le savoir.
Je pense que c'est aux autorités de communication de PASTEF de recadrer ces 03 dames qui sans le savoir, donnent l'impression que les pastefistes n'acceptent pas l'adversité.
Daniou warone nekou baguen doul
Un journaliste ne doit pas agir de la sorte un peu de respect au gens
Deugg nekhoul deh wayei yena togn xawma nouniouy convoquer niit ngene nieuw dilene provoquer beu beaucoup de temoins wax ko .. niou gaagn lene ngene di weur di reuy lamigne alors que provocation bi ci yene leu diougué
Maty sar domaramla da moye😂😂😂
Salma dhé com Karaba la sorcière 😂😂
Ioe nga dioté ak niit nga plainte kénen.
La responsabilité penale est individuelle
Force restra a la loi 😂
😂😂😂😂😂😂😂
Doule rék li yépp sonko gordjigen Dôme kharam bakh n'a si yénn
Bougane kay amoul ay militants ay nenou baxal la am😅😅😅😅😅
Avec Ousmane vous allez tous payés de vos actes inchallah
Ngone Saliou mi😂😂😂
wa la dame qu'on appelle ngone elle est journaliste
Non elle es thiagualiste 🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂😂 thiey sonko na moytou djiguène yi dagnouy talle Sénégal
Bougane dall moye niaw ndeye wayé yalla bakhna
Centenaire , colobane , liberte 6 , castors , grand yoff , niou ngi taakke. BOUGANE leumbè na sounou deuk bi ....😂😂😂
Alhamdoulilah d'être au travail à cet instant au moment ou vous vous battez pour des milliardaires qui ne vous considèrent pas
Merci
Merci bro
Ngoné saliou mon dés😂😂😂😂
Président bouguane kay🤣🤣🤣🤣non Sénégal mougui dogua neikh nakk…journaliste yii tamite founiou djiougueh tamite 🤣🤣🤦🏽♀️🤦🏽♀️sene khessal yii ak sene kheff yii …bouguane deh amnafi buzz nii rek sheuttt ….
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣mere gueum sa bopeu yi nèkèté ay coba bradio laniou 😂😂😂😂
😂😂😂😂
@@biguedieye4013 Bilay🤣🤣🤣🤣