Sama yon nékousi😱Thiow Balla Gaye2 Modou Lo SaThiès fracasse Franc“Ama Baldé moko meun eup ko dolé"

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 7 ก.พ. 2025

ความคิดเห็น • 50

  • @anddieuf3960
    @anddieuf3960 2 วันที่ผ่านมา +12

    Mon nv lutteur sa thies di ga nek roi des arenes inshalah

    • @ibrahimac-y4g
      @ibrahimac-y4g 17 ชั่วโมงที่ผ่านมา

      amiiin🤲🤲🤲

  • @AliouneNdiaye-n8e
    @AliouneNdiaye-n8e วันที่ผ่านมา +3

    Daysane sathies yaw nitt kou bakh kou theyy machallah yalna yala defal jam

  • @bachiroubadiane3135
    @bachiroubadiane3135 13 ชั่วโมงที่ผ่านมา +2

    Bayi len sen titre yi nguen di bind delen wakh deug wa salam

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g 17 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    amiiin sa thiés🤲❤️🤲🙏👍

  • @mouhamadoulaminekande8796
    @mouhamadoulaminekande8796 วันที่ผ่านมา +2

    Mbeure kéne dakouko communication billahi sa Thiès rek

  • @tallafall934
    @tallafall934 วันที่ผ่านมา +4

    Bly Sa da wara am combat dafa yarou nitté

  • @lassinakone1054
    @lassinakone1054 2 วันที่ผ่านมา +7

    Sa Thiès 🫶🫶

  • @BabaGueye-zb7en
    @BabaGueye-zb7en 2 วันที่ผ่านมา +5

    Balla boula alale takale ak sa rake gniye wakh gnoussi beuri aye seytane laniou

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko วันที่ผ่านมา +2

    Bg2 seul mom rek . Links piko pako ndam si ioe bro

  • @NayeFall-qq7xi
    @NayeFall-qq7xi 2 วันที่ผ่านมา +3

    Bàyyi leen kàcc ci li ngéen di bind .

  • @mansorseck6059
    @mansorseck6059 2 วันที่ผ่านมา +4

    Mbeur gua mais dèl yeungeul di nèkhal di roubè thiow liiii cila bok ay dagua nitè dagua yarou dou affairou lamb

    • @NaroBiaye
      @NaroBiaye วันที่ผ่านมา

      Legui ioe lane Moy affaires lamb

    • @NaroBiaye
      @NaroBiaye วันที่ผ่านมา

      Qui dafa yarou rek yallah ko def nga rek ioe wero serieux

    • @NaroBiaye
      @NaroBiaye วันที่ผ่านมา

      Dof ngua rek

  • @trompeursambenebisamb6245
    @trompeursambenebisamb6245 2 วันที่ผ่านมา +2

    Sathies fane la sathies wakhe si modou akk balla

  • @MoussaTraore-v5f
    @MoussaTraore-v5f 2 วันที่ผ่านมา +2

    Sathies seul diambar si birr diambar yii zarco bayil kebetou bii lekeu avance bii

  • @babacarsarr1131
    @babacarsarr1131 วันที่ผ่านมา

    Mais Thier en aucun moment tu as posé la question sur modou Lo balla Gaye ? LI MOM SATHIES DINA CI DIOT MOU NANGOUL LA INTERVIEW GUAKOY DEF LII

  • @AllinAllin-f7o
    @AllinAllin-f7o 2 วันที่ผ่านมา +1

    Bayilene di titre Lou amoul

  • @amethndiaye5099
    @amethndiaye5099 2 วันที่ผ่านมา +5

    Nafekh leu balla seul moy gaindé Gui

  • @SambaSeck-wl8py
    @SambaSeck-wl8py 2 วันที่ผ่านมา +5

    Tapét bou mague bi nioune balla gaye 2 rek😂

    • @MT-vx5nz
      @MT-vx5nz 2 วันที่ผ่านมา +1

      Sa mbokk doff yii motakh diakasse di am Mais diamou rek

  • @GoraKane-v7e
    @GoraKane-v7e วันที่ผ่านมา +1

    Yawe daga dof ganane suportaire fran dafa falé suportaire modou ani suportaire ama boye nian eumeu séne fou suportaire yi nékone khana danio rériwone

  • @PapadembaMbengue
    @PapadembaMbengue 2 วันที่ผ่านมา +4

    Iow ragalll gua niounnn balla rekkk

    • @MT-vx5nz
      @MT-vx5nz 2 วันที่ผ่านมา

      Doul

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 วันที่ผ่านมา +1

    Yaw outil combat mo guene ngay khasse franc domarame

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 2 วันที่ผ่านมา +2

    Yaw mom nite NGA mais gayndé gou maguétgui mom dofla khamoul wakhine 😢😢😢sathiéss kharagne lo dinala maye change inchallah

  • @ogviito1949
    @ogviito1949 2 วันที่ผ่านมา +2

    Aka nitté outé ak Gaindé gou maguet bou dof bi😂😂😂

    • @MouhamedCissé-j9d
      @MouhamedCissé-j9d 2 วันที่ผ่านมา +1

      Dégueul wa keur Modou Lô saytané radjim yi 😂.

  • @muhammad3323
    @muhammad3323 2 วันที่ผ่านมา +2

    Sa Thies doit revoir son comportement envers son Grand Frère BG2.

    • @PeuthioMangane
      @PeuthioMangane 2 วันที่ผ่านมา +2

      Dougeul fo khath khamoci dara mandou bakhna dé

    • @Tawfeekh
      @Tawfeekh 2 วันที่ผ่านมา

      Il n'ira pas loin il a une jalousie et une haine à l'endroit de son frère qui vient de se révéler. Il risque de voir tous ses projets tomber à l'eau. Il n'est pas sincère ce type, il cache une méchanceté redoutable. C'est pourquoi il perd souvent ses grands combats. Yallah khole lay fay.

    • @NaroBiaye
      @NaroBiaye วันที่ผ่านมา

      Kome naka

    • @PeuthioMangane
      @PeuthioMangane วันที่ผ่านมา

      @@Tawfeekh ce que tu dis est faux sa Thiès n'est pas comme ça je ne le supporte pas mais je sais qu'il fait partie des lutteurs les plus polie et sérieux et il n'est pas jaloux en plus il a un bon carrière bayiléne seytané te di dougou foléne khath

    • @PeuthioMangane
      @PeuthioMangane วันที่ผ่านมา

      @@Tawfeekh dis moi quel sont les projets de sathies qui sont tombé à l'eau ?