Live Sessions | Magikara - KEEMAN (Mystery) [Live Performance]

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 8 พ.ย. 2024
  • Magikara - KEEMAN: lnk.to/Keeman
    Link to all released music: bio.link/magikara
    Lyrics:
    Doy na Keeman
    Ahmadu Bamba laa ni
    Doy na Keeman (Ku Tedd Ki)
    Dëgg gi lee
    Su ñu Boroom
    Subhaanahu wa Tahaalaa
    Moom la ko jox (Asnal Xaadim)
    Ci bépp njariñ ci adduna
    Ak ya ca biir al ahira
    Yonen'a ko ko tànnal jox ko (Ku Tedd Ki)
    Fi ci suuf li fi gën
    Bamba fa ca kaw la fa gën
    Lepp la jël faye ko ko (Asnal Xaadim)
    Askanu Mbàkke
    Amna ñu barke, dëgg la
    Ahmadu Mbàkke
    Mo leen yobbaale, dëgg la, dëgg la
    Mo tax mu daan signé
    "Wa salaamu halamani tabbahal hudda"
    Maam Bamba ne
    La paix est avec celui qui suit le droit chemin
    Yaw miy wut ló am
    Jàppal ci Xaadim
    Dafa yoree am koom
    Te mëna yobbaale
    Hafizu mbër la
    Buddul sol dal
    Fó jaar mu giss la
    Ndax na muy xoole
    Zayin haraf la
    Zarfun de ndab la
    Man Moodu KARA maa ni (Ñun Magikara ñoo ni)
    Yaa may yóbbaale (Yaa ñuy yóbbaale)
    Yaw miy wut ló am
    Jàppal ci Xaadim
    Daam dafa yoree am koom
    Te mëna yobbaale
    Fó ne mu ne fa
    Lô moomul ba fa
    Bu dee sa yëf la
    Du ngéen digaale
    Yaw miy wut ló am
    #keeman #magikara
    Follow MAGIKARA on:
    Instagram: / magikara_diamondz
    Facebook: / magikaradiamondz
    Twitter: / magikaradiamond

ความคิดเห็น • 502