Dans sindidi le très vénéré cheick Ahmadou bamba rend hommage a tout les prophètes et anges 🙏🏿🙏🏿 ainsi que les disciples du prophète et leurs familles, elle est dédiée à tout ceux qui croient en Dieu. Paix et salut sur eux 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🕋
Merci pour la traduction Muss Fallen. Ce style de declamation des chansons mourides me rappelle toujours le Senegal. C'est pas facile ce genre de vocalisation: puissance, variation, tremolo, melodie. Demandez aux musiciens. Kudos brother. This guy is killing it!
Barki Serigne Babacar Sy Chiekh mbaye nimala Beuge mane Ak Yalla Rek Nioko kham Wallahi Barki Alkhourane chiekh MBAYE Yalna Yalla Goudale Sa Fane Barki Serigne Babacar sy❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@@CHEIKHMBAYEZIKROULAH gnola geuna bègue deh yallah xamnako, adjana rek lanou la yéné fimm tolou nii seral ga sounou khol yeup machala, yalnala yallah fay si barkep Mak gni🙏
Mais pouquoi mann tidiane la wala mouride gnounn gnépa wara déglonté beugeunté gnounn ñepp ay dioulite lañou avant tous stp nañou bayi wakh diodiou je m'excuse
Beuss péthieu senegal dou rousse moukk si kanamou seydina mouhamed saws dakh sougnou makk gni lignouko tague geumouma ni amna beneu khete boukoko tague. Les xassida dédiées o prophète nous font tous vibrer 😭😭😭❤
Akassa ki lay weur diokh ko adiya si nimouy sedalé sama xole bi aussi wadji am une belle voix kham nimouy yégué akh nimouye wathié akh fimouy danalé hoooo sama xole bi lay dougou wadji yallla na diamame yague fin bi wakh na lou am solo trop nako nieupeu déglouwate bou bakh fin partie bi la Wakh nako nieupeu geusouwate
Diakarlo sans wérou koor gui sakh Dafa warone di ame ay Zikr Nakh niouy bayi khél né yalla rék mofi nék ...li Dafa saide Khol Talibé Barhama la Machala
mane talibé mame maodo sy la mais airou sindidi bi ak jazboul qulob bou abdoulaye niang daf daf may danel bilahi mame maodo ak serigne touba niniou meuneu weuy diakhalnama
Mashallah, c'est très fort. Quelle voix extraordinaire. Ces poésies de Serigne Touba, les mimi de Elhadji Malick, et Safinatou Saada de Cheikh Oumar Foutiyou Gall, qu'est-ce qu'on les poèmes de Victor Hugo et consorts etc Ces
Barke SEUYIDINA MOUHAMED PSL LI DAFA NEKH cheikh Mbaye yalla nala yalla fay te mayla fanwou goudoi ak weur gui yaram chi barke niti yalla you bakh yeppou ci barkep Serigne BAMBA ...amine🙏🏿❤️ Thieuy Serigne Bamba yalla nanioula yalla guena fayal bopam🥺🥺❤️
Bou déglo khasside sindindi rek nga kham ni serigne touba wormal na niap Teuddu nasi 24 prophète yi niew si alkhourane Di tawasoul ti sene barcké ak kholafaoul arba Yi abobacar oumar ousmane ak saïdina aliyou Ak borome 4 nguier yeupp moy imm malick Ak imm chafi ak abo khanifa ak imm Ahmed Ak aye waliyou ak khoudare ta bime line teud dh ba paré dani yallah ma ngui niane thie Barcké nié niap yeureumal beuppu dioulite Ndeysan yalla nanouko yalla fayal aka beugue Diammou ak diamou yallah mame nioune sénégalaise yi amonou sa faye bilahi bouma Guissè koy nek si internet bi dila wax lou niaw Mame damaye ame louma méti ndakh iow de Woté wo tarikha de yalla nga woté ndakh yalla moné sy alkhourane nié diopp nioye ay mouride khana kou khamoul rek molaye wax Lou niaw wayè nioune de santue nanou la😭 Ameth Fall nar Algérie 🇩🇿👈korou diammou🇸🇳🙏
Oh Ndeyesane ! Il y'a ces sensations que les mots ne peuvent pas decrire, li ngay sentir iow reik yako xam , jerejef Cheikh Mbaye pour cette belle recitation
Walakhi li dafa nekh lol si xol nekh si nop diadieufeuti cheikh Ahmadou bamba khadim rassoul❤ borom xassida you sélle yi ❤ay mouride laniou pur❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭
Ohhh🥺🥺🥺li neikhna Talibe Serigne Babacar sy la mais li kouko degg sa yaram daw❤️🙏🏾
Ndeyesssane serigne toubz ak elhadji malick yeup yoneti bi lanouy ligueyal
@@moustaphadiagne4278 deug rek nga wax
Bilakhi dafa nekh
Walaye ya goré
Degal 😍❤️
Thiey domi sokhna diarra dji nanouko yalla fayale 🥰🥰
Serigne Mountakha yalla nafi yague té wére 🙏🙏🙏
Dans sindidi le très vénéré cheick Ahmadou bamba rend hommage a tout les prophètes et anges 🙏🏿🙏🏿 ainsi que les disciples du prophète et leurs familles, elle est dédiée à tout ceux qui croient en Dieu. Paix et salut sur eux 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🕋
bilahi rend hommage a tout les prophetes
et les 4 madhabs ( malik hanifa chafi i ahmad ibn hambal)
QqIt’s It’s
Merci pour la traduction Muss Fallen. Ce style de declamation des chansons mourides me rappelle toujours le Senegal. C'est pas facile ce genre de vocalisation: puissance, variation, tremolo, melodie. Demandez aux musiciens. Kudos brother. This guy is killing it!
Grand pour les explications. C'est vraiment apaisant
Barki Serigne Babacar Sy Chiekh mbaye nimala Beuge mane Ak Yalla Rek Nioko kham Wallahi Barki Alkhourane chiekh MBAYE Yalna Yalla Goudale Sa Fane Barki Serigne Babacar sy❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Amine
Longue vie à cheikh mbaye, Thiey serigne touba Ken dou mom
Amine
J’aime 🙏🏻
Barké Baye Niass mangui Dieureudieufé CHEIKH AMADOU BAMBA 😭😭😭 ndeyssane mbolém Yonneunti Yallah🙏🙏🙏🙏
Ndeysane diarradiof
Sama xel dem na wérou koor bou Serigne Touba dogué ay khobou 🥬🥬 garap 😭😭😭
😭😢😥
😢
Cheikh mbaye ta voix est unique ...machallah!!!
Airou serigne Moustapha Diop la dakko meunn dh machallah il est fort
Trop!!
Qui est revenue revoir sindidi de cheikh mbaye 1 ans après pousse bleue
Suis talibe cheikh, wayee dama beugue khassida yi sama khol , machalah yala na yala wereul baat bi
AKASSA domou baye
Magui joy bilay je ne peux plus me retenir ndah mbégté dieureudieuf serigne khadimou rassoul
Ndeyssane
KEEN DOU MOOM SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM.KEEN LA.
Wa diakarlo tay amguéne tawfekh dh yenagui noss thi xassida yi thieye akhmadou ❤
Quand j'écoute les khassida j'ai les larmes au yeux je pense à mon cher mari là où il est un Mouride sadikh
Machalla
Ooooooooooohhhhhh sa voix est captivante 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 toute l'assistance est hypnotisée💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💗💗💗💗💗💗💗
Cheikh Mbaye gneup gay daanel, khadre ak tidjane, mouride wala Layene ,nigay yabbé kheussida yi ben la walahi. DIEUREDIEUF 🙏
ben ngui talibé cheikh la mais cheikh mbaye mi daf may danel
@@aliounediop2709 walahi
Ndeyesan Dieureudieuf contane na
@@CHEIKHMBAYEZIKROULAH gnola geuna bègue deh yallah xamnako, adjana rek lanou la yéné fimm tolou nii seral ga sounou khol yeup machala, yalnala yallah fay si barkep Mak gni🙏
Un don de Dieu manchallah! J’ai essayer ca une fois, ma voix di meti pendant 3-4 jours. May Allah bless this man
No li mayou ya la fall macahlah
Ohhh yaram dawna
😂😂😂😂
@@abdouazizdiouf2371 😂 Yalna diam yague 😉
Ndeysane je suis tidiane mais cheikh mbaye quand il chante j'ai des frissons walahi
Mais pouquoi mann tidiane la wala mouride gnounn gnépa wara déglonté beugeunté gnounn ñepp ay dioulite lañou avant tous stp nañou bayi wakh diodiou je m'excuse
Beuss péthieu senegal dou rousse moukk si kanamou seydina mouhamed saws dakh sougnou makk gni lignouko tague geumouma ni amna beneu khete boukoko tague. Les xassida dédiées o prophète nous font tous vibrer 😭😭😭❤
@sen buzz tv officielle amoul ci adouna liko maggni tagg psl
deug leu
Machalla xoll sedena🤲🤲
Talibé cheikh la wayé dama beugue sérigne touba
Ndaysan yallna se diam yage
Yalla nala serigne touba beugue
Yaabax
❤👍
Boul ma dioy lo way tamit
L'islam rek moy DEUG ken dou Mouhammad, Dieureudieuf serigne touba
Akassa ki lay weur diokh ko adiya si nimouy sedalé sama xole bi aussi wadji am une belle voix kham nimouy yégué akh nimouye wathié akh fimouy danalé hoooo sama xole bi lay dougou wadji yallla na diamame yague fin bi wakh na lou am solo trop nako nieupeu déglouwate bou bakh fin partie bi la Wakh nako nieupeu geusouwate
Man woma ma dioukhma nemorom inchallah
Salam ma ngui lay bégué bou bakh .. 772093860
@@CHEIKHMBAYEZIKROULAH yalla na yalla gouddeul saw fane
@@CHEIKHMBAYEZIKROULAH geneu yagu geneu weer rek inchallah dieredieufeti Serigne Touba amoul morom
Cheikh mbaye mi yalla nala Serigne Touba fay ni ngay diangue sindidi bi doyna war machalah
Ndeyesan cheikh mbaye yalna sa diam yage barki serigne touba
Allakhou akoubar Thieuy serigne touba
Aye waye tardé na démbo 😭😭😭😭 THIEY cheikh mbaye mala bague barkéb serigne FALLOU
Serigne touba thi bopam mo amoul morom ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay❤❤❤❤❤😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏
Akassa Dieurediefeti Serigne Bamba ken dou mom Cheikh Mbaye masah Allah yalla na yalla guena weral Batt Bii insha Allah
Diakarlo sans wérou koor gui sakh Dafa warone di ame ay Zikr Nakh niouy bayi khél né yalla rék mofi nék ...li Dafa saide Khol Talibé Barhama la Machala
mane talibé mame maodo sy la mais airou sindidi bi ak jazboul qulob bou abdoulaye niang daf daf may danel bilahi mame maodo ak serigne touba niniou meuneu weuy diakhalnama
Yalla kodef si ngioom
Mane déh mouride lah mais SİNDİDİ moy sama xasida
Jadieuff daga bakh rek yalla na yalla samla
@@smssms9300 bilahi
@@lampefalltvlampefalltv3589 amine ya rabbi
Mashallah, c'est très fort. Quelle voix extraordinaire.
Ces poésies de Serigne Touba, les mimi de Elhadji Malick, et Safinatou Saada de Cheikh Oumar Foutiyou Gall, qu'est-ce qu'on les poèmes de Victor Hugo et consorts etc
Ces
Dì nianal serigne mountakha Mbacke Yalla nako fi Yalla Yague looll REK mbecke ak serigne cheikh dieumbe Fall Yaaram 🙏🙏🙏
Cheikh est actuellement le meilleur 🔥🔥
J'écoute à longueur de journée Sindidi repris par Cheikh Mbaye. Dieuredieuf Serigne Touba.
Ndeysane yèmèna lool 😭😭😭 djeureudieuf Serigne Cheikh Mbaye♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
ça me fait palpite le coeur o serigne touba tu n'as pas d'égal
Yalla rek Moy bour dieureudieuf Serigne Touba dieureudieuf Mame cheikh Ibrahima fall
Pape cheikh S Bassirou mbackè khélcome la buegg ana gni d’accord ak man
Machallah longue vie cheikh Mbaye zikroullah sama chanteur
Thieuy khassida yi 😢❤️❤️❤️❤️❤️ serigne touba amoul morom ❤️❤️
Bilahi lima yeuk tay bima dioudo ba légui mousoumako yeuk...sindidi bou diarrr yoon ni meusoumako déglou machallah cheikh mbaye yangui fékhal khool yi🙏🙏🙏🙏🙏😭
Thieuy sama dji yangui séral sm xoll bi bilahi yalna baat bi gueneu wéurr 😢😭😭
Barke SEUYIDINA MOUHAMED PSL LI DAFA NEKH cheikh Mbaye yalla nala yalla fay te mayla fanwou goudoi ak weur gui yaram chi barke niti yalla you bakh yeppou ci barkep Serigne BAMBA ...amine🙏🏿❤️
Thieuy Serigne Bamba yalla nanioula yalla guena fayal bopam🥺🥺❤️
Machala, cheikh yalna yallah weral baat bi, yok talibé gui ,contane nagnou deh
Cheikh mbaye zikroulah goudeul fann té yalla weral baattt bi.
Serigne touba amoul morom
Machalla Xol sédd na Alhamdoulila !! Yalla négnu Yalla fayal Serigne Touba
Bou déglo khasside sindindi rek nga kham ni serigne touba wormal na niap
Teuddu nasi 24 prophète yi niew si alkhourane
Di tawasoul ti sene barcké ak kholafaoul arba
Yi abobacar oumar ousmane ak saïdina aliyou
Ak borome 4 nguier yeupp moy imm malick
Ak imm chafi ak abo khanifa ak imm Ahmed
Ak aye waliyou ak khoudare ta bime line teud dh ba paré dani yallah ma ngui niane thie
Barcké nié niap yeureumal beuppu dioulite
Ndeysan yalla nanouko yalla fayal aka beugue
Diammou ak diamou yallah mame nioune sénégalaise yi amonou sa faye bilahi bouma
Guissè koy nek si internet bi dila wax lou niaw
Mame damaye ame louma méti ndakh iow de
Woté wo tarikha de yalla nga woté ndakh yalla moné sy alkhourane nié diopp nioye ay mouride khana kou khamoul rek molaye wax
Lou niaw wayè nioune de santue nanou la😭
Ameth Fall nar Algérie 🇩🇿👈korou diammou🇸🇳🙏
Xassida gui dégg gui rék défarou niépp adounak allakhira xajnaci yallnanouko sounou borom déffall mâcha allahou dieredief
Le Mec qui gère le truc des internautes a le sens de l'écoute. J'aime bien son comportement
Lou diouguè ci xol, dieum ci xol. Macha'Allah nékh na
J’@iiime Serigne Babacar SY li nekhna ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Serigne cheikh mbaye yalla nagafi yague tawer si barkep serigne touba mbacke
Barki Mame Baye Laye psl Al Mahdiyou Kontane nagn ❤️❤️❤️💯💯💯💯💯❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeysann Xol tooy na❤️ yalna serigne bi fayal niou boppam🤲🏾❤️
Pourla première fois ma sétane vidéo té avançou mako .. Djereudjeufé Serigne Touba
Sama mbok nga 🤣
Bouba ndour ndour nitou kasse la yala yala sam
Bamba disait mes écrits son mes miracles 😭❤🙏
Oh Ndeyesane ! Il y'a ces sensations que les mots ne peuvent pas decrire, li ngay sentir iow reik yako xam , jerejef Cheikh Mbaye pour cette belle recitation
Walakhi li dafa nekh lol si xol nekh si nop diadieufeuti cheikh Ahmadou bamba khadim rassoul❤ borom xassida you sélle yi ❤ay mouride laniou pur❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😭
Akassa Thiey serigne touba amoul morom
Dieureudieuf serigne touba si xassida rék 🙏🏿🙏🏿🙏🏿❤❤❤❤❤
Yalla naga am geureumal sér Touba cheikh mbaye
Akassa thiey Serigne bou mag bih Mashallah ❤❤❤❤❤❤❤💗💗💗💗❤❤❤❤❤❤
J’ai les larmes aux yeux 😭😭😭thiey serigne touba
Aouzoubilah Bismilah Ina Waliyalah
Dieureudieuf Fall Yaaram Cheikh.
Tawfekh ak Tayssir rek Barké Borom Ndiarém 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Cheikh mbaye piqûre Na wa plateau bi yepeu khol rek.... Serigne Touba dou morom bilahi.
Machalla radjas Cheikh Mbaye douguna si sama bir khol bi
Ki a vu Pape Djibril Fall mogui koy riim nank si souf kaang la dh machallah!🥰🥰🥰
yalla na yalla goudal say fan werral sa bate ci barké Naby, yagui niou begueul d barki cheikh
Thieuy yalla sounou borom.... Cheikh mbaye yalla Na nga am gueureumoul yalla sounou borom si barkeb cheikhoul khadim.
Sama sangg bi amo morom😭😭😭khadimal Moustapha ❤
oooh liii nekhnaa,ah yalnako yalla faye wayy ❤❤❤
Kii dou nitt dh ❤❤❤😭😭😭🙏
C’etait tres intense .Ce chanteur a une voix ma shaa Allah
Ndeyesane dieureudjeufati serigne touba mbecke diarrama Mame cheikhra fall Yaaram
Cia Miim galah nday saan 😭♥️
No Mr.Brima is enjoying the song bless , I love it too.
This is not a song with all due respect
Sokhna yii guirr yalla déléne mour sen bopou guirr yalla bougnouy yeukeuti khassida yii
Bien dit Modou Gueye xassida Serigne Touba yi warou gnou ko té sans mour s'en bopou yi
@@famafall285 Akasa sokhna fama
Daniy fo rek hamouniou lilen si meun dall
Lou matta bayé yéll
Thiey borom touba da taggg yonente bi ba dem 😭❤️
Deug pirr
Waalla hi
Serigne Touba kouka beugue tékhé
Kou ko noono Alkani
Chekh mbaye mucho gracias 🇪🇸🇪🇸🇬🇭🇬🇭
Thieuy sindidi dieureudieuf serigne cheikh
Thieuy srgne touba Ani kouko guena beugue Nabi 😭🙏 khol séd na
Macha Allah Sindidi
Sama anti Stresse
Dieuredieuf Serigne Touba 💗💗💗
Machallah serigne cheikh mbaye yalla na yalla geuneu weireul baat bi thi barki kou teid ki
La voix d'or🎊de cheikh mbaye Machalah dieureudieuf serigne touba👏👏👏
Billahi talibe cheikh la mè xasiida bii dafemaye dioyelo machallah cheikh mbaye yallena yalla werale batte biii
Machallah dieuredieufff boroom touba Cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd ki Aminnnne Aminnnne Aminnnne
Ohhhhhh li nékhna deh thiey sindidi diadieuf mbaye yalna Yalla wéral bat bi si bakèb cheikhoul khadim
Na Yàlla sàmm la te wéral baat bi 😭😭😭😭😭😭
😭😭😭😭😭ha dafa nekh dieureudieuf serigne touba
Quelle voix kan il chante j ai des larmes aux yeux
Bilahi yallah nanou yallah fayal serigne touba
Cheikh Mbaye dougn si doyal
Na gneuwat si Tome 3 bi
Machallah Mame Cheikh Mbaye Zikroulah Yalla na Yalla Goudeul sa fan te may la werr.Amo moroom
App soniou la si famille Ndour naniou bayii khalé yii niouy diangual weuy ak féthie al xuran ak xassida moy deugu
Ndeysan sama yarame dawna bilahi..yague fi lol te weur ak keup kou nangoul serigne touba liko yalla deff
bouba ndour ya bah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Manchalah dieuredieuf serigne touba mbacke
Sama wadji way ken do yaw cheikh mbaye yalna bat bi gana werr
machalla dieuredieufé cheikh ahmadou bamba khadim rassoul ❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
😭😭😭😭😭😭 ndeyssan