Franchement sokhnassi , yallana yalla may goudou fanne ak wérre. Tes paroles sont limpides surtout par rapport à papa sow ki est adversaire de votre fils.
Kholou yaye moy wakh Kone atankk yaye yeupp niogui NIANAL dom you beugg wadiour yi yalla nalénne yalla souniou borom diapalè takhawoulénne weral lénne si barke seydina MOUHAMED PSL
Ma sha Allah yaye booy wakh bi rafetna yalla na yalla goudall sayy fane bayi fi sa niabote bagnou lay terall salatoul Fatiha ken douko wiirdo di bone jamais ❤️❤️❤️
Siteu Amna Yarr ak gnanou Wadiour! C est ça qui est Ligueyou Ndeye. Elle a perdu son Epoux tres tôt avec des enfants , mais elle n a pas baissé les Bras. Pourtant elle pouvait négliger l Education de ses fils, tout le monde sait que éduquer son enfant à la Banlieu est Trop difficile. Mais Yallah kou ame soutoureu leu.
Yaay boy yagal ta wér bay fall bi yalla mokoy fay yagal ta wér fall dama guiss sama bopou si yow dagay wakh di dieuf gueum sa bopou thi kw thia kanam fall
Merci maman sa dom yalla nako yalla faye
Franchement sokhnassi , yallana yalla may goudou fanne ak wérre. Tes paroles sont limpides surtout par rapport à papa sow ki est adversaire de votre fils.
Non franchement mère bi elle es trop gentille je suis ému à l’écouter walahi
Siteu yalnala yalla doléle bagua am ligua bgue lep yalla gua don ROI des aranes si barketpe srg touba
amine ya raby
Siteu baye fall leuh bilahi lolou motakh mou nékh ma yalla nako yalla maye ndam barké serigne fallou
Hoo j'ai les larme siteu raw nga adouna ak alakhira nianou wadiour rek mo diara sakou mane mom def 'nala sama mbeur
Masalah maman gathiagalama , ndakh kou nek li ngay gnan si sisa dom yalla na yalla sam ko, tė mom reference la si mbeur yep 🙏
Machallah maman bien parler ❤️❤️❤️
Machallah maman long vie 🙏🤲👏amine yarabi
Siteu yalna la yalla same moussale la soutourale la
kenn dou sunu.yaye.bilahi.
Mamans moi j suis sonninké vraiment on t'aime trop billaye yalla khamnako yalla ngu'a goudou fane weure ak weurellé
Merci beaucoup machalla maman ❤😍😍
Machalla yaye boye. Amine siteu khane hine dame tine khaa pakh kha pakh hino sérère hi deffou
mane.dé.fansse.papa
Sow.la..wayé.siteu.ya.bakh.yaye.wayé.kéne.dou.siteu
ndeysane siteu baye laa daafa bakh bilahi daay deem.
Machala mbokk talibè Cheikh bi sa wakh rafetna 🤝🤝🤝
Kholou yaye moy wakh Kone atankk yaye yeupp niogui NIANAL dom you beugg wadiour yi yalla nalénne yalla souniou borom diapalè takhawoulénne weral lénne si barke seydina MOUHAMED PSL
Diarama mamá fier d'etre sererr 💕from siwo ❤️ Amine yaye boy
Ma sha Allah yaye booy wakh bi rafetna yalla na yalla goudall sayy fane bayi fi sa niabote bagnou lay terall salatoul Fatiha ken douko wiirdo di bone jamais ❤️❤️❤️
Merci yaye boey✅❤️✨✨✨
Ma challah yalna yalla barkél
Ma.challah'mama
Dieureudieuf yaye booy kaddou yi rafétt na machallah yallah nala yallah gouddal fan
Machallach yallna yalla Samla siteu ❤🙌🏾
Maman longue vie à toi
Merci maman ❤️❤️❤️
Ho!! Maman sedei yi rafette na man deh dawu ma faral sitteu dou Sama mbeur mais taye moom fans nla
Machalla amna solo
Bravo maman tu as bien parlé siteu laff thiate
Diadieuf siteu yalla nala yalla yok
Siteu 2006 lako xam dikko fekk sen Atelier lumu aam fonk nitt mokoko may bilahi 😭♥️
Inchallah dina am ndame si barké serigen babacar sy
dieredieufe yaye boy machallah amena solo ✊✊✊✊
Yallna gua goudou fan am diam
Siteu Amna Yarr ak gnanou Wadiour! C est ça qui est Ligueyou Ndeye. Elle a perdu son Epoux tres tôt avec des enfants , mais elle n a pas baissé les Bras. Pourtant elle pouvait négliger l Education de ses fils, tout le monde sait que éduquer son enfant à la Banlieu est Trop difficile. Mais Yallah kou ame soutoureu leu.
Siteu dafa difforcer wala
@@daoudader4641 waxul siteu dh yayam lay wax c'est a siteu a perdu son père mais sa mère a assuré leur éducation
@@modoungom6122 merci frere ma comprendroul bou bakh
@@daoudader4641 je vous en prie nio farr frère
SITEU DOU NIT YALLA MOKOY TAXAWOU GORLA TE FATEWOUL DEMB
Dina ame lou bakh inshalla
Mama satou thior yayou siteu doundale thior sa doundou amena diarigne
Wakh bi rafetna masha Allah
Nice nice na
Macha Allah yaay booy
Machala siteu yalla nala yalla faye
Amena solo dieuredieuf machahala
Fonkou léne yaye yii
Hooo maman talibe cheikh la
Yalla nako yala faye thie nimou fef yayame
Amina maman
🥰🥰🥰🥰🥰😇💯💯💯wawaw merci amine
Machallah maman❤
Longue vie maman
Maman yague fi tèwer siteu jamm rek lay amm
Ndeysane mère bou bakh la walahi. Wakhou yaye deug lafi wakh yalla na yalla takhawoula
Machallah
Machalla
thiey adouna nieup ay mbok lagn
Merci beaucoup maman
Mére bi djoylo nama bilahi ....yeurmandé rek mo aam solo bilahi
Siteu vrai champion baye fall Bou âme talibe
Baye fall bi dafa bakh machallah
Yaye nilay takhawe si adouna amna solo
Maman de siteu nitt kou bakh là walahi c'est vrai khana ko bou bakh
Maman merci beaucoup bilakhi walakhi wakhdji raffétte na
Machallah lafthiate
Mash'Allah
Yaay boy yagal ta wér bay fall bi yalla mokoy fay yagal ta wér fall dama guiss sama bopou si yow dagay wakh di dieuf gueum sa bopou thi kw thia kanam fall
Machalla amna solo 🤝
M achallah maman siteu
Machalla mama doundou lou bari yay boy
Merci
Merci maman
Sitteu da yaye kou bakh la machallah sama mbokou talibe cheikh un fans plus
Baye fall bi dafa bakh
Ndeysane
Deguela maman machallakh linga wakh yep deguela
Ndaysan li sedna khol😭
Massalah guena tag guena wer
Ohhh maman yague fi lol tei weirr
Merci mama
Thiey Yalla aduna dal dou dara
Yalnako yala diapole
Siteu kilifa la an plus bilahi ndam rék lay am mandé dama coy ziar
Hou machalla
Baye fall by yallana sa borom yoku meunemeun gui si dolei cheikh Ibra fall minga yakar
Ndeyesane sunu Maman
🤣🤣🤣wamé maman yagui sani khér papa sow dh
nice
Ndeyye sane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Ma challa
Alhamdoulila
Alhamdoulila
Amine Amine
🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Yaye boy wahal siteu mou bayi dawbinake
Diamou rk lay am blh
Baye fall bi rek
😭😭😭😭😭
Siteu nittou kassè la bilahi man kham nasi dara
Salut numero site la sokhla je s8 en italie
Machallah maman
Siteu vrai nit kou baakh leu
6
Merci maman bon courage
Amine way bilay yaw yalla bakhna
Vraiment il mérite d'être accompagné davantage c'est un exemplaire
Merci bro
Machallah amna solo
Merci
Machalla
Machallah maman
Macha allah