maa chaa Allah suis tidiane wayé djazbou moy sama khassida dafe may danél limiye wakh ci Yonnetebi Psl au sakha bayi Yalla nallene Yalla sam def leneu Mak barké Yonnetebi Psl
Je suis de la Tarikha Tidjaniya mais ces chansons sur Khadimoul Rassoul me traversent au plus profond de mon coeur 💔. C'est ça le Sénégal qui gagne. Vive nos Tarikha du Sénégal.
Barké Serigne Babacar sy lii nimouy deff sama khol bi yalla rekk moko khaamm ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Machallah sama khol sedd na yalla nagnou yalla fayal Cheikhoul Khadim ❤️❤️
Prince Quavo => Jajef Serigne bi! C’est parce que ce sont les éloges du Prophète Muhammad, PSL, et que vous êtes musulman! Que le bon Dieu vous garde et vous protège pour toujours!!
Arrêtez nguir yalla de dire suis tidiane ou mouride et autres. Nioune nieupp beine laniou , Hassida dankay deiglou mouy douggou si sa hole tei di changer si oe lou beuri. I love hassida ❤
Lima wakh si benene Jazbu bi laaaay wakh si bii rk. Je Suis Layene 100% geum nei Seydina Limamou moye Seydina Mouhammad (PSE). Wantei Khassidas Khadimou Rassoul nimouy df sama xol makk yalla rka ko kham. Yalna Yalla yokka aaay léérraam Yoka aay xéweleum Tass gnou si barkeim si barkei weer bou sélleu bi. Ayyy waaaay Djeredjeuf Seigne Touba si geune gui Cadeau gui ngafi bayi😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭Bilahi liii dafa neex.
_Wallahi serigne touba amoul morom😍❤_ *_15:11_**_ le 18 septembre 2020 au maroc sa me rends Trop tristes worna yalla sama sopé serigne abdoulahi diop yalnafi yague té ak mbolém dioullite si barkép serigne saliou mbacké❤ ndeyesann 😍😭😭😭😭😭😭😭😭😭_*
Murid tewlulmafi waay am na kuy tek lu neekh fofu ci 23:00 Fa innahu kaman hadhar - yaw hunaynin wa çabar wayaw badrin wa naçar ..... fofu sedd na khol waay
"MOUWAHIBOU NAFIH" Nien si Mag gni nenanou Xassida gui KOU TED KI mingui ko bind ci attou WAYSASSIN (1316 an musulman) .Mom ak Jazbou, Mouhadimat, Radiytou etc……. nio massé. S Abdou Khadre Mbacké nena day mayé Xeweul di yokk ak Ngeum, ak beug Yonnent bi (PSL). S Mbacké Bousso nena Mawahibou ak Sab’houn Takhi daniouy mayé ay Xeweul Bok na si kemtanou Xassida gui Yenn Beuyit niou teunké wat bénen Xassida Bokou nassi tamiit Xassida you KOU TED KI waxon ni nioy « Naarou Goor yi » Kou len war té wathie wolen niou wommat la ba fi mom Kemtaanou Xassida gui: Ben biss Mame Thierno Birahim Mbacké meussna sant ay Talibèem niou Yoboul ko Dougoub bimou bayonn si KOU TED KI ; Yobanté walé len nilen « Nélénko Maraal nanou lol » Ba nioniou agguèe wax KOUTED KI yobanté Borom Darou bi. Si leu KOU TED KI wax Kourel gui nanou Diangue « MAWAHIBOU » Kourel gui di diangue ba Tollou si : "Nala dialala nala diamala ""miman taxala Rabii sama i" KOU TED KI diglé niou Bamtou ko ; ba noppi tek si « Yaw Borom Assaman sama beug beug moy ndox » Rek Taww bi timbali di Taww .Baniou Yonnéwaat si KOU TED KI nguir mou Dakkal Taww bi Amna Biss KOU TED KI di waxtaan ci Bissou Penthie ak Taraay ga.Ba waxni bou Biss boba Niep Sama Bopp laniouy wax bamou dess Yonnent bi(Psl) ;Mom sama Khèet lay wax .Bou biss boba ba Yonnent bi(Psl) dem HARASS ba soudioteul Sunu Borom ,bam niko Siggil té Dem Ram’mou . KOU TED KI nena bou diogué ba dem si Taxawaay ba dinako Dogallé Fatalliko lama ko waxonn si
Xawma kane dhé wayé man euleuk yawmal khiyam beugue Serigne Touba rk la yakaar pr diarignu thi xassida yi rk si lagnu meuna xam Serigne Bi AKHMADOU BAMBA BOROM DIAM GNI DIEREDIEUFETY ❤🙏
si javais les moyens de me payer des milliers d bouteilles de Gicky de Gerlain, Dieu mest temoin je vous larroserait tous autant vous etes juste santéko kou teed ki borom touba
Amna solo torop Dieuredieufeti kou Tédaki nekhna torop merci à vous nous ne pourrons jamais vous remercier pour ce que vous fetes pour nous encore mille fois merci et longue vie à vous et bonne continuation
Aujourd'hui c le 13mars 2023 notre hisbou daniou meilleur wallahi Dieureudieuf cheikh ahmadou bamba khadim Rassoul
maa chaa Allah suis tidiane wayé djazbou moy sama khassida dafe may danél limiye wakh ci Yonnetebi Psl au sakha bayi Yalla nallene Yalla sam def leneu Mak barké Yonnetebi Psl
Je suis de la Tarikha Tidjaniya mais ces chansons sur Khadimoul Rassoul me traversent au plus profond de mon coeur 💔.
C'est ça le Sénégal qui gagne.
Vive nos Tarikha du Sénégal.
Oh Yalnala Borom Touba yeukeuti yalnala Borom Touba déffal diam mayla wërguou yaram si barké Lëërou Jazboul qulob
yalla nalen serigne bi fayy mashala nehna trop
Merci mon frere pap mais c chanson ne sont pas pour glorifier khadimoul rassoul mais glorifier Allah et son prophète avec des salatou alal nabi
Cpas pour xadimul Rassoul mais pour le prophète
PAP M Gueye de meme ke moi
Beugg la dem safara moma gueneul wedila dem adiana worna Cheikhra Fall dieuredieuf serigne touba 😭😭😭😭😭
Mbacke Sene 💪🏻💪🏻💪🏻
@@issathiam1443 serigne touba limoumay def mounou mako wakh 😭😭serigne bii kenne la🙈😭
Les 592 qui n’aiment pas Yallah naléneu Yallah sopi. Amine!!! Si barké Djieuzbu Khoulob
Barké Serigne Babacar sy lii nimouy deff sama khol bi yalla rekk moko khaamm ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Machallah sama khol sedd na yalla nagnou yalla fayal Cheikhoul Khadim ❤️❤️
"MAWAHIBOU "
‘’Antal Karimou Annal Hadimou ‘’‘’Deuhran Oudimou Fika sana’i ’’.
Bou boba dinama Yéssalal Ram’mou bi mouma mayonn thia Adouna Sogaa dem tokk sa Keer gua.Bou boba loxo bou touty bi koumou seedoul dinga yendo khif fanané fandé (etc.....
DIEUREDIEUFETY KOU TED KI
7
Mashalla
Je suis Tidiane. J'adore les khassidas de Sérigne Touba. Ça me Donne la chair de poule.
Oh c’est tellement apaisant sa you sama xol nexoulé Li lay deg lou serigne Touba yalla naniou ko yalla dolé fayal 😍🥹🥹🥹
Serigne Mountakha Bassirou yalla nafi yageu looooool té andeu ak wer thi barkep Cheikhoul Khadim
Amine barké Serigne Fallou
Akaza li nékhna trop serigne amoul morom dathie bi am nak dal trop sétna machala yalla na diamu sakh amin si barké werwi
Machallah!!! Thiey Serigne Touba amoul morom Mbacké!!! Dieureudieufeutii!!!
Je suis tidjiane mais quand j'écoute ça sa me fond le coeur parfois même je pleure
Prince Quavo => Jajef Serigne bi! C’est parce que ce sont les éloges du Prophète Muhammad, PSL, et que vous êtes musulman! Que le bon Dieu vous garde et vous protège pour toujours!!
Bichri TV -Amin et merci beaucoup
Prince Quavo akaza
yall nala serigne bi defal tawféx
Prince Quavo dafa yémé loooolll
Arrêtez nguir yalla de dire suis tidiane ou mouride et autres. Nioune nieupp beine laniou , Hassida dankay deiglou mouy douggou si sa hole tei di changer si oe lou beuri.
I love hassida ❤
Lima wakh si benene Jazbu bi laaaay wakh si bii rk. Je Suis Layene 100% geum nei Seydina Limamou moye Seydina Mouhammad (PSE). Wantei Khassidas Khadimou Rassoul nimouy df sama xol makk yalla rka ko kham. Yalna Yalla yokka aaay léérraam Yoka aay xéweleum Tass gnou si barkeim si barkei weer bou sélleu bi. Ayyy waaaay Djeredjeuf Seigne Touba si geune gui Cadeau gui ngafi bayi😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭Bilahi liii dafa neex.
_Wallahi serigne touba amoul morom😍❤_
*_15:11_**_ le 18 septembre 2020 au maroc sa me rends Trop tristes worna yalla sama sopé serigne abdoulahi diop yalnafi yague té ak mbolém dioullite si barkép serigne saliou mbacké❤ ndeyesann 😍😭😭😭😭😭😭😭😭😭_*
Yalla na yalla wereul batt yi te defal lene ay tawfekh you kawe sen thiorte si barke serigne salioum,
Dieureudieufe borom touba wa HT yalla nlen Serigne touba fayal bopam te yallah byilen sniou kanam ngene yag diniou begueul
dia ngéne dieuf diang bi amna solo lool khana Kaye diléne gnanal fi ngéne di beuga ague yalnalén fa yalla agalé si barké cheikhoul khadim
Masalakh
Khol sedna j'ai des frissons à l'écouter Dieuredieuf Serigne Touba
Yalla na Yalla weral batt.yi si Barker serigne touba khadimou rassoul
DIEUREUDIEUFEII SERIGNE BAMBA!!! SERIGNE TOUBA MO BEUG YONENT BII MOKO FONKOU NDEYSANE.
Ça va droit au cœur❤️😭dieureudieufaty KHADIM RASSOUL🙏🏾 xassidas yi tous les matins moy ndieuk dougou sama nopp
Ndeysaan ❤❤
Nopp bu xëy déglu Xasiida, ba ngoon jot kenn du ko bindal bàkkaar. S Abdu Lahat
Thiey Diagn mi dawna sama yaram yin dal yalla na Len serigne Touba fayal bopam amine
Thiey jazboul qulub nimouy si💖💖 dieureudieufé *Serigne Touba* limou way yonente (PSL) bi dall kéne meussoul deg lou melni😍😍
Soudé amm na louy dawloo Sama yaram loudoull xasidayi kon dh wax deugg yalla xamoumako jërëjëfé s touba
Machallah dieuredieufé serigne touba yallah gueine fii yague lol tei wer dadje bi nekhna si barke seydina Mouhamed barke boom touba barke serigne saliou amine yarabi
Ndeysane, keep kouko diota deglou, yalla nalene sunu borom defal sahadatoul dareey ni, thi barké goudi gamou gui
Kéne dou seringue touba chaque jour ma déglou co machala je suis fiére d'étre mourit
Diareudieufétii borom touba 🥰🥰😍machallah ki écoute tjrs ❤❤❤
talibé cheikh la dh mais khassida yi dafa nekh cii xol c apaisant machalla
ndeysaneu daga beug lou bax rekk machala
Thiey chekhoul khadim nitou yalla dege mo nek ni regarde moi ça rek chui trop emu😢😢 ça me rapelle des bon souvenor thiey serigne bi
Qui l’écoute en 2020??🥰❤️ Djeureudjeuf S touba🤲🏽❤️
barké cheikhoul khadim jazbou bi yéména trop.yala naguén tassék geuramou cheikhoul khadim
Murid
tewlulmafi waay am na kuy tek lu neekh fofu ci 23:00
Fa innahu kaman hadhar - yaw hunaynin wa çabar
wayaw badrin wa naçar ..... fofu sedd na khol waay
Amine baye Diawrigne yala nagafi yagg
Mouride
Amine way
amine
@@segnelo koku Seugn Malick ba La
Je remercie Yallah souniou Borom bouma bolé ak Mame Serigne Touba si barké Seydina Mohamed PSL
Naniou Sante Yallah parce que chance bou rey naniou am
Macha laff thiatte nex na trp thiey serigne touba amoulle morome déee
Yallana Len yallah boule AK akreumu serigne bi makbi machalah mouride amnasolo deuradiufi serigne Touba Billahe amoul morom jarama mame Cheikh Ibrahima fall lamp baboul mouridena leoup momo Billahe jarama mame
machallah am na sólo yalla na yalla fay len sí barke serigen touba machallah
Gnou gouddi aldiouma barkeip serigne touba yalnagnouko borom fayal
Dieureu dieufaty serigne touba manchala yalla nalaine serigne touba fayale bopame inechala
Dieureudieuf Serigne Touba Mbacké Khadimoul Rassoul ❤️ ki l'écoute en 2021
Qui écoute ça en 2020 ❤️😭😭
A0
2021
2022
J'écoute 2022😍😍😍
D'ores et déjà 2022 alhamdoulilah dieuredieuf Cheikhoul Khadim yala Nanou ko yaga féké ♥️♥️♥️🙏🏽
Qui écoute sa en 2019 !!! Tiey akhmadou bamba 😭😭❤❤❤
MOI
Bilahi depuis 2018 la koy deglou batay
Dou masa sappi
Moi
2020😍😍😍
Lii nehna hawma gni aimewoul loulen daal
Bamba merci
Talibe Cheikh bi beug Serigne Touba
Thieye sama papa jazbou bi nekhna way yalla na yalla weral badbi
Machallah suis fière détre mûrit srg Touba dieuredieuffetu li nekhna trop
Man depuis 2017 ba tay damakoy tewlou di setan wa aldiana ❤️
Thieeyy Serigne Touba Khadimou Rassoul kén dou mome. Fière d'être mouride et d'être une daroise. Dieuredieuffff Serigne Touba
Ça ne me fait pleurer walahi dieureudieuf cheikh ahmadou bamba khadim Rassoul 😭😭♥️♥️♥️
Yalna yalla wéral batt-yi si barké jazbou !maléne sopp
billahi lii thi xol laye douggou yalla na leen kou ted ki faye amna solo nekh na lool
Cheikh Medou Ndiaye .kn
Thiey serigne touba yalna serigne bi fayal len bopam.amen
Macha alla yalla na yalla wereulll batttt yi si barkep Borom Touba👏👏👏
Ba 2024 jazbu bii gisatouma dath bouma ko dakhal 😢😢❤❤❤
48:18 la partie sue tout le monde cherche ❤️❤️❤️no bilae serigne bi kénn laa
Dafa leer
Décembre 2020 toujours la 😭✨❤️🕊🥺🥺🥺
Dieureudieuf Serigne touba 🥺😭😭❤️❤️❤️
Ndeysan thiey jazbul qulub nekhna lolou
Dieurdieuf serigne touba yalla na yok senuk mane
ndeysan mourit yi amna solo looool djazbou bi nékh na trop yal na lén serigne bi tél bopam
Thiey li mon nekhna way mach'allah yalla nalen yalla fayy si barke s touba
Borom Touba amoul morom dieuzbou rek firndé la😭❤️😭❤️😭❤️😭❤️😭😭❤️❤️❤️
jazboul khoulob le portrait du prophète psl ken serigne touba bilahi
Machallah thieye serigne touba amno sa faye dè
Walahi serigne touba amoul morom😭😭
dia guene dieuf yalla nalen yalla faye bi barakati cheikhoul khadim
Wakh djou rafét ; rafét lolou , dieume si Seydina Mouhamed ; fére sakh atanouko assoumalak khollou nite !!! Dieureudjieuf kheikhoul khadim
Thiey chekhoul khadim nitou yalla dege mo nek ni regarde moi ça rek chui trop emu😢😢
Machalah yalna yalla wereule bate yi si barké Cheikhoul khadim
machalah ☝serigne touba rek way li mo nekh si khol way doundou yala nekhna
kéine dou Cheikhoul khadim
Dieureudieuff BOROM TOUBA👌👌👌👌
Ki écoute sa en 2020 Dieuredieufé Serigne Touba 😍😍😍
"MOUWAHIBOU NAFIH"
Nien si Mag gni nenanou Xassida gui KOU TED KI mingui ko bind ci attou WAYSASSIN (1316 an musulman) .Mom ak Jazbou, Mouhadimat, Radiytou etc……. nio massé.
S Abdou Khadre Mbacké nena day mayé Xeweul di yokk ak Ngeum, ak beug Yonnent bi (PSL).
S Mbacké Bousso nena Mawahibou ak Sab’houn Takhi daniouy mayé ay Xeweul
Bok na si kemtanou Xassida gui Yenn Beuyit niou teunké wat bénen Xassida
Bokou nassi tamiit Xassida you KOU TED KI waxon ni nioy « Naarou Goor yi » Kou len war té wathie wolen niou wommat la ba fi mom
Kemtaanou Xassida gui:
Ben biss Mame Thierno Birahim Mbacké meussna sant ay Talibèem niou Yoboul ko Dougoub bimou bayonn si KOU TED KI ; Yobanté walé len nilen « Nélénko Maraal nanou lol » Ba nioniou agguèe wax KOUTED KI yobanté Borom Darou bi.
Si leu KOU TED KI wax Kourel gui nanou Diangue « MAWAHIBOU » Kourel gui di diangue ba Tollou si :
"Nala dialala nala diamala ""miman taxala Rabii sama i"
KOU TED KI diglé niou Bamtou ko ; ba noppi tek si « Yaw Borom Assaman sama beug beug moy ndox »
Rek Taww bi timbali di Taww .Baniou Yonnéwaat si KOU TED KI nguir mou Dakkal Taww bi
Amna Biss KOU TED KI di waxtaan ci Bissou Penthie ak Taraay ga.Ba waxni bou Biss boba Niep Sama Bopp laniouy wax bamou dess Yonnent bi(Psl) ;Mom sama Khèet lay wax .Bou biss boba ba Yonnent bi(Psl) dem HARASS ba soudioteul Sunu Borom ,bam niko Siggil té Dem Ram’mou .
KOU TED KI nena bou diogué ba dem si Taxawaay ba dinako Dogallé Fatalliko lama ko waxonn si
Y
🙏❤ la sua vita e
🙏❤🙏❤😍🙏😻💪🙏💛🙏💤🙏📿🙏💄🙏
Dieureudieuf yalla nala faye 🙏🙏🙏
Ndey sann thieuy ahmadou ❤️ 👌 billahi li amna solo trop macha Allah
Mashallah, yalnaniou yalla fayal Seugne Touba
Serigne touba la kéneu khamoul loumou doone 💓✌
Yalna lene yalla dolè tahawu Li tiossanéna looolJerejef cheikhul Xadim Mbaye
Qui est là en 2020 pour écouter ces paroles saines
Qui est la en 2023
li dafa sed khol mane khawma sakh loumay binde thiey serigne saliou yaw rek lagnu am
😭 procurant en même temps paix et bonheur walahi en même temps on bénéficie de ses bienfaits innombrables
dieuredieuf shaykhoul xadiim
Xawma kane dhé wayé man euleuk yawmal khiyam beugue Serigne Touba rk la yakaar pr diarignu thi xassida yi rk si lagnu meuna xam Serigne Bi AKHMADOU BAMBA BOROM DIAM GNI DIEREDIEUFETY ❤🙏
si javais les moyens de me payer des milliers d bouteilles de Gicky de Gerlain, Dieu mest temoin je vous larroserait tous autant vous etes juste santéko kou teed ki borom touba
Quelles mélodies😍😍. Ça me berce tellement. Ça soigne le cœur 😊
Machallah
Dieureudieufé Serigne Touba 🙏🏼 xool sédatina deh 😭
Limuy déf aka djaféé daane thiuné thi beuyit bou nieuk bi
Té dou yaak djaath bi
Machaa allah
Lamine Cissé kane si nonou malick ngay waxx?
@@serignemorba8458
Serigne Ablaye
Dath bu nieuk bi !
Jacopo de il 💤💪♥️💛❤😻💍💎
Machalah yalna boorombee weral thieuryui amine
😍😍😍 bilay serigne touba mo nekh ci khole
le 12 août, en 2021 qui est la
Kû tedki amout morom yalla na niouko yalla fayal ❤🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤝🤝🎙
Wadial Magal Touba rk si khassida yi♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Jazboul khoulob ndeyssanne 63 bi Neikhna loll..... DIEUREDIEUF Borom Touba.
yennaye sama WhatsApp yennaye sama Facebook yennaye sama wettal yalla nama len yalla fayal sama yenne moye koune thie yenn ma tabakhalkou keur 😢
Amna solo torop Dieuredieufeti kou Tédaki nekhna torop merci à vous nous ne pourrons jamais vous remercier pour ce que vous fetes pour nous encore mille fois merci et longue vie à vous et bonne continuation
Amna solo lollou,yalla nalen yalla faye
Qui écoute ça en 2020 😍😍😍
Thiey Serigne Touba amul morom jazbu bi yemeina. kennal serign tuba ba faw
Sokhna OUMI Aÿ way ma beug khaissida yi dieureudieuf
Nekhena lole
Billahi HIZBOUT TARKHIYAA YI yalnaleene srg touba fayal boppam si barké dialibatoul marakhib
هو خديم رسول الله
Mooy Xadiimu Rasuulul Laahi ♥️
Yalla Nanu Ko Yalla Fayal
Mashallah dieuredieufé serigne Touba
MachaAllah Jazbu bi nekhna lolou
Li nekh wayy serigne Bamba késsé
ndeysane jazbou bi thiossané na mague na lol yalna guene si tasse ak ngeureumal kou ted ki si barkep khassidayi
Aÿ way li nekh na barki cheikhoul Khadim
La portée est universelle et embrase même le cœur du mécréant