Machallah Tata dila gnanale goude fane ak wer di gnanale sa diabote tamite gnou dounde wer raw mouthie ak réussite si séni projets Amine ya rabby machallah merci beaucoup si thiono bigaye dathie guir askan wi yalna la yalla Faye yiiw togue Yep nekhna machallah contane si yaw rek
Masha'Allahou sokhena marie diop togou yaye Isseu sama sopee. Mane de ma ngui Diangue si yow loubari. Yallah namala Yallah Fayale bi diaahi nabyl moustapha Staws..
Suis sous chef de cuisine. Mais j’adore comment vous cuisinez. Toutes les étapes sont respectées, les techniques culinaires. La progression est parfaite. Côté goût, je m’en doute pas, je sens l’odeur jusqu’à chez moi. L’élément magic: (le Nogoss royal 👌). Je vous suggère de faire la commercialisation. Bonne continuation.
Merci bcp Tata vous nous aider beaucoup keurog dégne ma dioh pour ma tog gourbane mesoumako togou mais à travers tes recettes guéne nasi bou bah merci beaucoup pour tout yalna ga am weure AK weurlé Macha Allah
Machaalah Machaalah, ya Isseu, li guey def dik bokk ak askan Wi am na niarigne,et puis tu nous montre tous les détails en plus ni guey togué set na machaalah, guide fane ak wer rek
Niakk hame toggou yaye isseu erreur la🤩🤩🤩😍😍🤩🤩🤩.yaye isseu FLAN au coco sans four la beug nga wane gnu comment on le fait svp😍😍😍🤩
Machallah Tata dila gnanale goude fane ak wer di gnanale sa diabote tamite gnou dounde wer raw mouthie ak réussite si séni projets Amine ya rabby machallah merci beaucoup si thiono bigaye dathie guir askan wi yalna la yalla Faye yiiw togue Yep nekhna machallah contane si yaw rek
A
Alahouma amine 🙏
Saf na machala
HXUFUXU YCY Y CHE CARICAVA DI AVERE UN NUOVO 4437👅👅
Allahouma amine
Masha'Allahou sokhena marie diop togou yaye Isseu sama sopee. Mane de ma ngui Diangue si yow loubari. Yallah namala Yallah Fayale bi diaahi nabyl moustapha Staws..
Lima nekh si yow do def magi
This is very good. I learn from it everyday
Suis sous chef de cuisine. Mais j’adore comment vous cuisinez. Toutes les étapes sont respectées, les techniques culinaires. La progression est parfaite.
Côté goût, je m’en doute pas, je sens l’odeur jusqu’à chez moi.
L’élément magic: (le Nogoss royal 👌). Je vous suggère de faire la commercialisation.
Bonne continuation.
😂
C'est quoi le nom de la deuxième sauce lorsque vous préparer la sauce oignons
Machallah niakk la khamm worroul🥰🥰
Merci bcp Tata vous nous aider beaucoup keurog dégne ma dioh pour ma tog gourbane mesoumako togou mais à travers tes recettes guéne nasi bou bah merci beaucoup pour tout yalna ga am weure AK weurlé Macha Allah
Vraiment maman yalna yalla defala tawfakh ak sutura yonk la man dé sa fait des années magui lay suivre
Machalah maman Isseu yalla na yalla faye
Machala yalnala yala fay sa Khôl
Je vais le réessayer sa souma koy togue daye tass khana ma dieul weugn tak ko
Merci pour la simplicité et la précision de vos recettes ❤
Machaala ca a l'air délicieux je vais essayer. Je faisais oeuf surprise avec sauce oignon blanche et salade
Machalla tata isseu tu participes énormément à la réussite des jeunes couples. Longue vie à vous maman ♥️♥️♥️
sa togue amoul fennnn amnan rerr samedi 😂👸👍yaguuu fiii🙏🙏
Machala yàlla na lokhobi wer likay togo nekhna
Machalah tâta sa recette yii rafetna💞
Salaam salaam Maman isseu cordon bleu internationale ndar bi Humm yallah na yallah goudal fane wii ta mou wéral lokho bi Amiiine inchallah 🙏🙏
Yalna yalla yagal takhawaay bi yokk werr gui macha Allah
machAllah il faut juste réduire la longueur des vidéos
No no nonou la bakhee day expliquer bamou ler momm
Machalah vous êtes la meilleure
Bilahi maman isseu lo toguoul bakhoul lafthiate machaallah yallana lokho bi weer amine yarabi🙏🙏🙏❤❤❤💪💪💪
Lo toogou mou neh machala
Machallah merci beaucoup ma maman adorée depuis fouta je vous suis ❤❤
Machaalah Machaalah, ya Isseu, li guey def dik bokk ak askan Wi am na niarigne,et puis tu nous montre tous les détails en plus ni guey togué set na machaalah, guide fane ak wer rek
On peut le préparer avec du poisson
Bien-sûr
Marshalla very nice
ohhh merci beaucoup mamá , man modou modou la mangui topou sa djinaw rek di diangue merci beaucoup mamá ❤❤❤❤
Machalla yaye boy yow yatakh djiguene nieuppa meun togou
Lafe thiat mâcha allah
Machalla tata
Yaye isseu yaw rék lay toupo ❤❤
Machalla sama yayou khol
Machalla, nékhatina yalla na yalla wéreul loxo yi Amin ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥰
Machallah rapide et très bien fait. Merci tata
Manchallah tata mary maneu thi yaw laye roye Yalla na lokho bi werr
Merci beaucoup
Limaci gueuneu neekh saafouloo ,il y'a moins d'huile
J'ai faim 😋😋😋🤩
Maa Shaa Allah comme d’habitude tjrs a la hauteur. 💕🌸💕
Tay dé mom lay toggou inchallah rabi
Machala très bon plat
Macha allah nékhna barina yalla nalla diame sonate 😍🥰🥰😘😘👩🍳🧑🍳
Tata yawe mon machalla rék la laye wokh longue vie santé
Amy kama
Machalla Tata 👌👌👌
MachaAllah nehatina 🥰 🥰 🥰
Mashaa Allah 👌😘💕💕
Nekhna je te souhaite une très longue vie
❤️❤️❤️❤️
Eh tata legui dafaa degue français masahalla
Merci beaucoup YAYE ISSEU, je m'inspire beaucoup sur tes recettes; machalla bonne continuation.
Maachalla nekhna waye ❤❤
Machalla 🙏❤️
Ma cha ALLA
Machalla tata 🤩
Machalla maman amatina solo lol🥰 mais gan yi damasè beug foumako mana amè ak c combien?
Bravo 👌❤️
Machallah ❤️ maman ❤️Amal diam rek yow ❤️
Machallah molto buono .grazie mille🥰🥰
Machallah ❤️❤️❤️❤️
Merci pour vos recettes
Looks yummy Masha'Allah
Machalah 🥰❤️🥰🥰
Machallah maman
Merci beaucoup maman j'aime beaucoup vos recettes que Dieu vous bénisse si vous pouvez traduire en français je ne comprends pas le Wolof
Salam maman dila gnanale goude fane rék mane g repris la recette mou nékhe machala juste k bimay taye boulette bi dafa oubékou
Oooh eupena. Macha Allah yalna la thiate sékhelou. Merci beaucoup
Billay aminee
Machalla maman ♡♡♡
Tata cv yaguii ci jamm en faite dafa mél nii sa recette yi douci déff bouillon dh
♥️♥️♥️👍
Macha Allah
Machalla maman yalnna lokho bi wérr
Merci beaucoup pour vos recettes ça nous fait du bien
Machalah dieureudieuf maman 💯💯
Merci depuis l’Angleterre
Salut maman sama boss dafay tasss😢
Ma maman chérie longue vie à toi 😘😘😘💗💗💗💗
Tata il faut expliquer un peu en français pour nous qui ne parlons pas wolof, si non vos plats sont très cool merci 🙏🙏
🥰🥰🥰
Merci tata yalna yallah maye goude fane tu améliore notre cuisine
Yayemboye yaw ley tope
Machaallah comme d’habitude Tata isseu ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah validé❤❤😍
Salam Salam tâta Def nako mais malheureusement boulettes yi dafa tass
Machalah
Bilaye yaye isseu mala beugue daga meune ligayedef ta beugue ko
MachaAllah merci Maman cordon bleu 🥰🥰🥰
C k j'aime plus dans ces plat il n'y a pas d Jumbo
Macha alla j’aime votre façon de cuisiner on voit que vous aimez ce que vous faites bonne continuation mme
Ya issa li bagnoumako dh waye souniou keur nioko doul togou dema inviter bok😭😭😭😭😭😭😂
Machalla Sa plat bi nekhnama
Yama saf
Est ce qu'on peut le faire avec du poulet
Bien sur adoum
Merci beaucoup pour vos recettes 😘
Tata isseu c quoi paprica
Paprika poudre de poivrons rouge mes ces facultatifs bou ko amoule yacoule darra si toogue bi merci Ousmane
Si tu n'as pas le pain en poudre tu peux faire le farine
Machallah c jolie 😍😘
Meune na nek a base du poisson wala
Mane dema koye déf mais ma sha allah l’amour nekh eupeuna 🥰🥰
Goudeul fane
Machallah merci maman chérie
Machallah Tante Isseu sait préparer très très bien