On aime bien vôtre émission ét ON voudrais bîen préparer ces recettes mais à condition qu'on puisse comprendre ON Est pas des sénégalais ON comprend touS le français
Tata merci encore pour cette vidéo. Pour le goût acide moi je mets du bissap bou wekh avec l'eau chaude . En plus du goût acide day ratakh en même temps😋😋😋
Oh naka diek li mo takh ma beug. Sama mame wa kaolack leu té souniou demone vacances le soir niou dieul souniou potou nda dieundi fondé. Quartier kaznac... ma sha yalla sama sopé ...bolé si done niang comme mane ma yok leu beug. Mangui ni di tek sama fondé. Niak leu suivre woroul way. Tarkalla
Fondé kou ci deuk lou romba diappa forme ding ko déf tata masha'allah comme d'hab nékh + nékh égal nékhatatti dagne né diay fonfé amoul pertement bo ci amoul...vous connaissez la suite lol mane mané #NaneFondéTataMarietouAmoulPertement! We love you my dear long life to you, once again you made my day! Have a nice day!!!
Waw chérie togue rek ngaye mais prochaine fois dagaye une cuillerée de farine soye wadja pareh ga lakh cassi ndakh araw yi dafa wowe amidon bi Daye wagnikou
Merci Après une longue convalescence lil me faillait ce plat que ma mère me faisait de son vivant pour me relever Mais un peu dure de trouver du fondé quand on malade et couché ça se trouve pas au supermarché merçi beaucoup
Machalla recettes you nékh bou ande ak humour. Khamna kou meune togne nga😅😅. Fondé mom Je le mange 2 a 3 fois dans la semaine. Quand J'ai pas trop envie de manger le soir rek tek fondé. C sain et facile à manger. Merci encore Marietou
On aime bien vôtre émission ét ON voudrais bîen préparer ces recettes mais à condition qu'on puisse comprendre ON Est pas des sénégalais ON comprend touS le français
Tâta marietou sa xol rafetna machaallah yalla nga ngouda fann inchaallah...
Tata merci encore pour cette vidéo. Pour le goût acide moi je mets du bissap bou wekh avec l'eau chaude . En plus du goût acide day ratakh en même temps😋😋😋
Oh naka diek li mo takh ma beug. Sama mame wa kaolack leu té souniou demone vacances le soir niou dieul souniou potou nda dieundi fondé. Quartier kaznac... ma sha yalla sama sopé ...bolé si done niang comme mane ma yok leu beug. Mangui ni di tek sama fondé. Niak leu suivre woroul way. Tarkalla
Diay fondé amoul pertema 🤣
J’ai trop aimé les anecdotes,Yalnagnou Yala fayal sounou Yaye yi.❤️ sur toi sister Mariétou
Ma sha allah marietou diam rek nguaye ame
Grâce a vous on a appris beaucoup de choses tata vie longtemps avec beaucoup de santé
Oohhh merci 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Thank u so much tata am trying to put on weight so I will definitely try it.
Machaa Allah Mariétou, bou ame bouye bi nak mom mo dakhati
Merci bien Tata ,j apprécie bcq mais traduisez au moins pour ceux qui ne comprennent pas?
Mashallah toi moi je t'adore beaucoup toujours je veux regarder temps de cuisiner moi je suis en bas😍😍😘😘❤❤👏👏
Se me yayou khol contanéne yalla ne yalla feye vraiment amou gnou se feye
Walahi fonde kaolack la fekk bakh... 😂... moi j’aime bien le fonde avec pate d’arachide 😋...
Fondé kou ci deuk lou romba diappa forme ding ko déf tata masha'allah comme d'hab nékh + nékh égal nékhatatti dagne né diay fonfé amoul pertement bo ci amoul...vous connaissez la suite lol mane mané #NaneFondéTataMarietouAmoulPertement! We love you my dear long life to you, once again you made my day! Have a nice day!!!
😂😂😂😂
I am a
Fode tamarin aussi c est tres bon ma maman khady nous prepare ca
Machallah tata! Sama djeukeur dafko beug
Machallah machallah amna solo
Gueune na kontane thi yow binga né kaolack. Machallah
Fondé kaolack Kay Dafa meilleur 😋
Machalla tata merci6 nékhna
Merci sister, Yallah na sa lokho werr..anecdote bi nekh na 🤣 nouyoul ñiou borom potou fondé bi
Machalla tata, I love the way you make that fondeh.
Ma cha allah sama toguolokh bi
Machalla sa fondé diarena yone yallana khamekhame bi yokou
Machalla tata Marietou😘😘😘
Machallah tata fondé bimom beugunako
Waw chérie togue rek ngaye mais prochaine fois dagaye une cuillerée de farine soye wadja pareh ga lakh cassi ndakh araw yi dafa wowe amidon bi Daye wagnikou
Ndeysane souvenir bou rafet dafay nekha netali big up wa reubess yeup 🙏🙏🙏
Merci beaucoup sister, moi, je le fais avec du bouye à la place du beinkheul
Mashallah Sokhna Mariètou thanks a lot may Allah bless you and your family 😘😘😘😘
Machallah 😂😂👍👍👍❤❤
Machalla yal na lafi yalla yagal
Neko thi rèlle 😁
Waay mère yaay Ndaanane waay 🫡
Manchalla c'est très beau ça
Merci tu me sauves là 😁
Toki tokina mom. Ngani sow bi nga bathie bathialko 😂😂😂
Wawo kay nekh na
Peut-on le faire avec du lait ?
Oui merci
Aah tata yow Keye Nyang rek nga muna Santa...nyun faalen yi nyoye sen burr....
Wakh nga deuk bou meun fonde limako man mi ndakh sama mame. Wa kaolack laniou ndeysan yalla nako yalla yereum
Bonjour, quelqu'un a trouvé la recette en français s'il vous plaît ?
Assalamou Alaykoum niou ngui lénn di Ziar . Mère contanne ci vidéo bi. Sama Sokhna damako wakh fondé dafa wara ndokhé mais guemoumawone. Merci
Machaalah ta marêtou jé l'eau a la bouche
Ay parolam gnio may ray😅😅weugue 😅😄yougou 😄ak rèeell ak tifin ...
Mala beugggg ak sa flashback yi mais srx Fondei mom kene douko bokkk😂
Sama rapell Mariama fondé aka meun fondé😁😁😁
Merci tata mais tata beuguena ngua indil niou riz cantonais a ta maniere
Ohhhh le fondei est la way sama mbokhou socei yi diko wakh mono. J'adore 👍 vraiment mane dal ma beugeu lekk bou toy dal😘😘😘
Doma jangal socé
Yum
Machallahh Tata fondé bi diare na yone 🥰🥰
Fondé tata nekhna machallah
Machaallah Tata marietou...biii mako mome waw keuy....bou ken reee😃😃😃
Machala name nako
Contannneee
Machalla Tata Man dal bèguenala
Maman neko si relle goudel fane
Mdrrr mane deh mom lay ndeker tay machallah
Si kaw si kanam✋✋
Fondè rek way❤
Ya salam tata marietou tay mom defarnga louma beugue ap baol baol la, fonde rek aka nekh 😀😀
Tata marietou bonjour tata gp ma co ic a Paris ma def thi petit déjeuner bou bakh
Machalla tata marietou
Mba ame na ligommm
Ta maretou da nam Sénégal dehhhhh ma sentir lolou
Ndzysan amna mame bou toudou tounko yagui ma kay fateuli sax
bonjour ta marietou ma ngui dianguat mais pourquoi toujours brown sugar ngay utiliser
Mareme Ba Fall AlhamdulilAh merci brown sugar mo gueuneu wër sucre blanc bi surtout pour les diabétiques
Machallah Tata
Merci
Après une longue convalescence lil me faillait ce plat que ma mère me faisait de son vivant pour me relever
Mais un peu dure de trouver du fondé quand on malade et couché ça se trouve pas au supermarché merçi beaucoup
Machahalla 😂
J'aime bien vaut plat mai je ne comprends pas wolof
Waw
♥️
Macha Allah
Machallah
T es adorableeeeeeeeeee❤️
J'adore
Aka geune laawla thiat sama tourodo
Machalla recettes you nékh bou ande ak humour. Khamna kou meune togne nga😅😅. Fondé mom Je le mange 2 a 3 fois dans la semaine. Quand J'ai pas trop envie de manger le soir rek tek fondé. C sain et facile à manger. Merci encore Marietou
Aka ma beugg fondé
Hum 👅👅sa me rappelle Abidjan
Ta Marietou diapp forme saye terme yi niomaye retanelo
tata fouet bi douko doglo??
Non non dou déf dara
Merci tata sama toma🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tata marietou à dit tèlitèli 😂
🤤🤤🤤
Taye mom fatilingama sama badjéne
Fondé🇸🇳
J’aime la simplicité de tes plats pa de boulions 💋🙏🌙Dieu te gard 🙏
Am coming for my shared 😋😋😋
Macha Allah merci beaucoup 💖💖💔💔❤💖💋💋💋
Man dal nèkhe gama
DAMA BEUGUEU AM FONDE ENVOI MOI DU AROW WAY
Fodé mome beug nasi bouye aussi
😂😂👍
Je confond l fondé et le larh
Ma challah Tata mé khana amo insta recherché nala mé guissou ma dara
Sauveurs planétaires
machalla setna selna
Machalla diap na forme
😂😂😂😂
Xaxaxax non ta mari3tou ray ngama ci sa rak bi r3na bay dé
No mane nimouy wakhe motakh maye setan aye reul aye peuyi😂😂😂😂😂
Jaime ta cuisinne
Machalla nekhna torop
Li nga fonde eupna