Ma sha Allah c'est le moment pour celles qui ne peuvent pas faire le araw de l'apprendre moi je te suis depuis et t'encourage à continuer félicitations
Moi perso, j'adore le ngallakh simple sans banane, sans noix de coco etc Il faut que le goût du bouy et du tidekké soit bien prononcé. Merci pour la recette faite de A à Z.
Magui ziar sokhnasi ma challa sa togueyi nekhnama manedama beug togue,maguilaye encouragè yalla nala sunuborom diapalé ,toguena sa vermicelli bi ak guinarbi,taye petite poit ladèf ak guinar bi,limaguena ligaye déf dafa naturale,magui ziarre wa senegal di gniane adounabi lineup am diam magatte fall madame faye da milano dieuradjieuf diop bacio
Merci tata j'ai jamais fait du galax mais je vais essayer inchallah je suis sénégalaise qui connait pas j'entends seulement mais la tu as assuré merci 😍😍😍😍😍
Je suis nouvelle maman isseu mba khamngua niaka suivre sa togou woroul machalla sa arraw machalla desoul ben soungoufe mane dal bouma magué yawla beugua roye je t'aime tellement maman
Machaalla laphethiate contanagne yaye isseu,boko deubone bouybi ak tigadeguedie ken doula atane machaalla laphethiate encore une fois merci infiniment pour le travail bonne continuation
Machallah sama m’bokou domou n’dar So bagné mou forokh dagay dieul bouy bou maguete pas bou bess ba paré ga khoth ka touti diga guiss mou khawa fourr touti lolou moy acide bi ga tour après nak soga def n’dokh pour sa n’galakh
Ma ngui ley félicité sa togue bi sett na sell na contane na dal thi préparation bi nioune lolou leniou diangal leket bi ni nga ko rakhassé rek nga khamni da nga meuneu togue macha Allah man dama ley suivre tout le temps
Machallah maman magui dora commentaire mes sétann na lou barri j t jur meuneutouma am connexion bou yag 1moi bii 3jour lay am bilahii geun ka barriii meunoumalla rombou sii TH-cam yalla xamnako chaqu instant ma dougeu TH-cam pour sétann la rek bilahi beugnalla mann dama beug aférou togou j 18 ans mes yaw la dff référence jtm maman💋
Machala yaye isseu benagafi ken dou wahohe damadaledifebare bamaguisse sa ngalah bougon signame damabougone gahouama mesures hi combien de karaoubi combien de bouye combien de guerte combien de sucre sucre vanille muscade fleur d'oranger raisin sec je n'arrive pas à faire les mesures exacte soit c'est trop soit c'est pas assez je ne suis pas au Sénégal ce n'est pas facile merci maman nicena Machala
Machalla moi sw amour de la cuisine a mn age 24 je sais fair du arow et mogne té personne me la appris jadore donne a mangé srtt d bonne chose b1 prepare
Machala soxna si yala na yala weralle lokho bi yala may la goude fane ak werrr💗💞💞❤💖💖💟💟💟💖❤❤💞💗
Amineeeeee yarabi
Allahouma amiiiiiine
Ma sha Allah c'est le moment pour celles qui ne peuvent pas faire le araw de l'apprendre moi je te suis depuis et t'encourage à continuer félicitations
Merci beaucoup tata isseu. A travers cette recette j'ai appris comment faire le araw
Moi perso, j'adore le ngallakh simple sans banane, sans noix de coco etc Il faut que le goût du bouy et du tidekké soit bien prononcé. Merci pour la recette faite de A à Z.
Macha'Allah maman Marie. Niaka suivre toggou Yaye Issa erreur leu dhé. Vraiment vous faites bien la cuisine.
WikL
Machallah je suis contente pour expliquer
Merci yaye isseu depuis la France tu es très compréhensif tu es une bonne personne et très intelligente 💋💋💋💋💋👍
Vraiment vous cuisinez bien
Ce qui me plaît sur toi tu mets toujour un petit ♥️ à tes abonnés pour les montrer que tu a vu les commentaires machalah
Merci.bct maman.issa contant nagne bou bakh si diagualebi namatougnou wagne ndakh yaw
Macha Allah,amena mana ak sédé bou rafétebî ci sounou mbokou chrétiens.Wallahi bakhnagnou,amenagnou diam ak soutoura ak kolaré.
Machallah yalla na yalla Sam arla meyla goude faan wer ak werle ❤❤❤❤
Ya isseu a t entendre parler on sent que tu as un gros et joli coeur yalla na sa diama yagg amiin togue yi nekhna.diarna yone maa challa
Magui ziar sokhnasi ma challa sa togueyi nekhnama manedama beug togue,maguilaye encouragè yalla nala sunuborom diapalé ,toguena sa vermicelli bi ak guinarbi,taye petite poit ladèf ak guinar bi,limaguena ligaye déf dafa naturale,magui ziarre wa senegal di gniane adounabi lineup am diam magatte fall madame faye da milano dieuradjieuf diop bacio
Merci tata j'ai jamais fait du galax mais je vais essayer inchallah je suis sénégalaise qui connait pas j'entends seulement mais la tu as assuré merci 😍😍😍😍😍
Je suis nouvelle maman isseu mba khamngua niaka suivre sa togou woroul machalla sa arraw machalla desoul ben soungoufe mane dal bouma magué yawla beugua roye je t'aime tellement maman
Billahi machalla yaye issa
Machaalla laphethiate contanagne yaye isseu,boko deubone bouybi ak tigadeguedie ken doula atane machaalla laphethiate encore une fois merci infiniment pour le travail bonne continuation
Machallah sama m’bokou domou n’dar So bagné mou forokh dagay dieul bouy bou maguete pas bou bess ba paré ga khoth ka touti diga guiss mou khawa fourr touti lolou moy acide bi ga tour après nak soga def n’dokh pour sa n’galakh
Merci beaucoup pour tes recettes yaye fall au bukina faso bisous a toi
Ma ngui ley félicité sa togue bi sett na sell na contane na dal thi préparation bi nioune lolou leniou diangal leket bi ni nga ko rakhassé rek nga khamni da nga meuneu togue macha Allah man dama ley suivre tout le temps
Machallah yalnala yalla fay yiw
Machallah mame isseu je te souhaite une longévité et une santé de fer
Machalla maman yagefi lole❤️❤️
Machalah yaye issa diaratina yoon liguaye def nexnama machalah kou la deg hamni kou baax gua merci thi liguaye gnouy wonne
As sala maleycoume mame isseu beugue na sokh na ndarguedji vraiment mashallah tu es fort
Machalla domou thiakribi rafetna.nala yalla défal diam.
Merci Tata yALLAH nala yAllah faye...mane mi beugg meune arraw...ma ngui kharr bou thiérrè bi ak bou laakh bi...
Merci tata, vraiment yangui gnouye diapalé! Goudou faneak wérr lane laye gnaanale !
Mashalla jaimmm bien té recette sétna sélanna diammeu si yow Tata vie bien❤❤❤
Machalla, yalla nala yalla sammal boppam. Yaw rek yafi defar NGALAKH dieul sa temps araw 😍😍
Wallah yafi meun instant arow bi moma nekh Machallah 💪❤️❤️❤️
yagi def lool bakh bilaye yalla na La yalla fayi ❤️❤️
Machalla maman goudeul fane
C'est toujours un plaisir de vous suivre ❤❤❤
djieureudjieu Yaye isseu mansh'Allah. Tu as une abonnée de plus
Magnifique et je te suis depuis un moment j adore ta cuisine et tu explique très bien les choses bravo
Bonjour tata loutakh ngalakh amoul chocolat AK Soko amer Lou Barry est ce que meu n'a changer goût bi merci
Khalakhe chocolat yagoul khalakhe mame dou ame chocolat té nomou laye nékhé naturel Ndeye 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️
D'accord tata merci beaucoup 😘
Mane Dale beug nala♥️♥️ma shaa Allah😘
Je suis nouveau sur ta chaîne , j'adore tes plats. Tu mérite vraiment beaucoup d'abonnés
Machalla machalla nekna aetna
Setna
Je t'aime bien ma chérie tu nous rappelle les choses de nos grand-mère merci beaucoup yalla na sa diam yagueu machalla
Macha allah sa toogou setna diarna yon yalla nassa diam yakk en TT cas dal j'aime bien tes plats
Tata ni ngay arrawei nekh nameu😍 machallah
NDEYE FAMBAYE BA tothie nafi
Bon appétit yaye issa
Yaa issa goudal fan ci katanous yalla machalla Man ma gi begg rek
Merci beaucoup
Qui comme moi a essayé d'imiter sa façon de faire le Arraw
J'aime bcp merci bien
machallah yaye isseu tes plats et astuces très délicieux khaleyi taye war nagnou diangue si say tog
Limome masallah 💖💝💔💖💝❣️
Ohh ngalakhe kha guini waye nekhena set na😘😘
Machallah maman yalla na borom wereum sa lokho
J’ai bien aimé la partie araw bi . Merci
you are the best
Merci ci arawbi jai beaucoup appris
Elle est vraiment propre merci
Kocc kocc i Araw li 🥰ana ajoor ajoor yi waay 🤗merci maman sama class gu bëgg waaÑ gui dunu la rombu waay
Mame issa j adore ta cuisine.machallah👍👍😘
Machala j'aime votre cuisine
Bouyou daw nga warone utiliser
Machalllah Tata Isseu vous êtes trop formidable😘😘
Bravo Yaye Isseu todjgua nguer. Mashalah ngalaakh bi nekhna
Bilaye ya maneu toogue
Machallah♥️♥️♥️♥️♥️👍👍💖
Salut maman est-ce que meun nagno utiliser bouye en poudre wala
Merci fatou diop bien sur meune ga dieule bouye en poudre
@@TOOGOUYAYEISSEU D'accord merci maman
Ma maman merci pour tout yagui dimbili DIEK die si wagne wi
Machallah yaye boy
Machallah maman magui dora commentaire mes sétann na lou barri j t jur meuneutouma am connexion bou yag 1moi bii 3jour lay am bilahii geun ka barriii meunoumalla rombou sii TH-cam yalla xamnako chaqu instant ma dougeu TH-cam pour sétann la rek bilahi beugnalla mann dama beug aférou togou j 18 ans mes yaw la dff référence jtm maman💋
🙏🥰🥰
Machalah maman ça se voit que danga la bire félicitations et bonne continuation 💞🥰👌
Machaallah arraw gnou bari meunougnouko. Djiguene deugg gua. Li mo guene sett te sell.
Machallah tata mala beugue ❤❤❤❤🔥🔥
Machala yaye isseu benagafi ken dou wahohe damadaledifebare bamaguisse sa ngalah bougon signame damabougone gahouama mesures hi combien de karaoubi combien de bouye combien de guerte combien de sucre sucre vanille muscade fleur d'oranger raisin sec je n'arrive pas à faire les mesures exacte soit c'est trop soit c'est pas assez je ne suis pas au Sénégal ce n'est pas facile merci maman nicena Machala
Machalla nekna
Machalla merciii maman❤❤❤ yalla nala yalla may weer ak faneu bou goudou
Yalla na lokho werr maman 😚😚
Machala c bon 👏👏👏👏👏👏
Merci maman isseu vraiment contente si ieo
Thanks a lot Aunty. Am really benefiting from your channel.
Yalnagfi yaanga te werr
Mame isseu y love you!!! Sa lighieye rafetna ! sèllana!! macchala!!! Sama m'bokou n'dar n'dar yi
Machala sama maman bi souba nako essayer psk jaim bcp l galakh merci bcp Idol
Araaw bi rafeetna yalla na yallawereul lokhobi machallah
Yaye isseu dalll machallah goudal fane rk
Salut yaye eseur bon travail merci
Mashallah leppe diarna yone !!
Merci beaucoup maman. Je vais venir au Sénégal pour un stage dans ta cuisine. 😘😘😘😘😘😘
Machalla rek lani wah
Machalah machalah machalah 🥰🥰🥰
C bon machalla j aime
This must be a 🍨 dessert. It has sugar and vanilla 😋. But it is African. Looks very 👌 nice
Maa shaa Allah
Machahalla Yaye boye yalna yalla goudeul sa fane ak wërr🙏
Man yow lay weur tata machallah
Wo❤❤❤❤
Tata marie diop longue vie a toi dundal illimix machallah
I like your cooking 💕
Mama jere Jeff ❤❤
Macha allah
Yala na lokho bi wer machallah
Ma Sha Allah Yaye Isseu😘
Legui la abonné,dila nianal boubakh.
Machallah mame isseu
Machaalla rafétena
Machalah maman togou amour la
Machalla moi sw amour de la cuisine a mn age 24 je sais fair du arow et mogne té personne me la appris jadore donne a mangé srtt d bonne chose b1 prepare
Seynabou Ba ay yow c chou😍...mane dé meunouma araw ni mogn malheureuzment té amna 29ans😀 Kagn ngamay diangal
@@oumaathiam6868 diapal jr bula nekh nieuw😍
Seynabou Ba nonoula djiguene day sop si mboroum wagne
Franchement merci du fond du coeur jai vraiment aimé c une leçon pour moi
Formidable très simple et propre
Ahhhh 😋😋😋😋 sama wale tata ....mais nak nam na thiébou guédj dh